Zo magusi yone bi té kham nani déff nga sma bopa lépeu mé kham nani lou déss Mane kassé laa mém soumala dégatoul déff nga simane loudoul dagne zo yalla rék mola Mana fay❤❤❤tékki forlife❤
Zo sincèrement je ne connais pas mais je t'aime depuis que j'ai commencé à vous suivre je me suis réveillée en je vous remercie du fond du cœur sache que tu seras toujours une personne important je ne t'oublierai jamais longue vie à toi que dieu veille sur vous
Je sais pas quoi te dire zo merci zo je t'écoute chaque jour pour me motiver où travailler tu as changé ma vie merci zo tekki for Life✊ merci encore zo
Mais mane magui dégue lounek bly mais mane nek borome alale rek la guiss tèlèpou yallah mokamome tèmome moye Mayè niou bari niougui nane boy bi amoule ref mais mane dama nabeutou moytakhe maye yègue fouma dième mais Kontane na si yawe frr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment zo sa vidéos yi diamono dji gnou la gueuneu am solo jeune yi gnoungui doundou lou instant bi conseils yi loko gueuneu yokou doyoul grâce à toi Je suis encore courageux🙏
❤❤❤salut Zho,je vous remercie bcp,bima comencé suivre tes vidéo matagoul 5mois,mais sétlou si sama bopou ni dama changé d comportema,d frékance,la maniére d parlé,si lou bari pour dir vré.jé 36ans,tay mangui mélni kou am 60ans prck nit yi diokh nagn ma plus d respect et d considération ke avant,si coté finance,légui je sé quand et coment je dois fair des dépense et des épargne.lima gueneu nékh moy légui je sais distingué les actifs et ls passifs.Zho goudeul fane ak bcp d bonheur❤🤲🤲🤲
Zo 14 ans la am waye sama mak lay ligeuyeul ta dama tela geumni damay réussir sama adouna inchallah sama mak lakhamoul noumay def ba demal sama bopou solutions la beugeu
Teki fo live je vous suivre depuis Italie mais bilay changé gua Sama vie inchalah je serai milliardaires et jouer gua rôle bou àm solo Sama vie❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉😢😢😢😢❤❤❤Que dieu te garde ❤❤❤longue vie à vous ❤❤❤zoooo❤❤❤
Merci zoo merci zoo merci zoo😢 yalla na la yalla❤defal diamo😊zoo yaw liga def siman da béri billaye dib 2022 mangui laye top bassaka man kou l'ase la mou noul😢ngose ma ngiur yalla ndkh man sa touba la 😢
C'est avec plaisir de vous écouter est mieux de comprendre les leçon de vie que tu nous apprend ce qu'on appelle l'école de la vie, je vous j'ai toujours écouter, mais tous a changé partir le jour où j'ai commencer à pose des actes, yalla rék Molay Faye zo
Slt zoo. Vraiment c’est ça qui nous montre que la vie est pleine de surprises donc on doit se préparer pour tout surmonter,mais bref vraiment zoo on ne contente de toi vraiment merci bcp même et bonne continuation Brother ❤
Seul dieu qui. Vous payera 🙏 zoo vous avez mérité d'être milliardaire tout ces conseille nous donne chaque jour la force inchallah vous serez toujours e🎉n paix 💪 tout est venu dans le ❤️ merci👍🙏🙋
Man khalé la mais am n'a 18an mais dama lay suivre Di def li ngay dik lou man damay statut Say vidéo maïs dama am niouy don wakh si man dama yakam ti sama adouna ta man dama guem sama bopou ne man Dina am bouma fi yalla baye mon frr louy sa khalat si li niou ma don wakh ta nenan lolou Kou néé si ton moka wara deff ta man samay mak tegou niouma lokho mon frr 😭😭😔
Bonsoir tekki for life mane cheikh ibrahima Niang la touddou mais conten na ci par ce que da ngéna chengé sama doundou dama rérone yénama dindi dipi mars 2022 oma séne Faye kana di lén nianale yalla rék nélén amine rék ❤❤❤❤
Où sont les amoureux de prophète Mahamed psl❤❤
Aleyhi salatou wa slm ❤❤
Sala Llahou alayhi wa salam❤
On ai la ❤❤❤❤❤psl 😊
Psl
🤩🤩🤩🥰
Zo magusi yone bi té kham nani déff nga sma bopa lépeu mé kham nani lou déss Mane kassé laa mém soumala dégatoul déff nga simane loudoul dagne zo yalla rék mola Mana fay❤❤❤tékki forlife❤
Ministre de la jeunesse ❤❤❤
Ça rêve la
❤
Moi perso, vous avez changé ma vie sur tous les plans,que Dieu vous garde ici plus longtemps ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️✌️
Allahouma amine
Yalla n'a yalla doli sa diam may la wér goudou fan taw fékha soutour Amine yarabi❤
Amine ❤ way kou bakhla
Machallah amatina solo yaw ak gnoune gni lay sétane yallah na gnou yallah déf ay milliardaires ❤
Zo sincèrement je ne connais pas mais je t'aime depuis que j'ai commencé à vous suivre je me suis réveillée en je vous remercie du fond du cœur sache que tu seras toujours une personne important je ne t'oublierai jamais longue vie à toi que dieu veille sur vous
merci vraiment contane na trop
Je sais pas quoi te dire zo merci zo je t'écoute chaque jour pour me motiver où travailler tu as changé ma vie merci zo tekki for Life✊ merci encore zo
😔
✊
Mais mane magui dégue lounek bly mais mane nek borome alale rek la guiss tèlèpou yallah mokamome tèmome moye Mayè niou bari niougui nane boy bi amoule ref mais mane dama nabeutou moytakhe maye yègue fouma dième mais Kontane na si yawe frr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Notre cher Afrique à besoin des personnes comme toi
Vraiment zo sa vidéos yi diamono dji gnou la gueuneu am solo jeune yi gnoungui doundou lou instant bi conseils yi loko gueuneu yokou doyoul grâce à toi Je suis encore courageux🙏
Zo damala khar ba sonou depuis ce matin ❤
Toujours un réel plaisir de vous suivre encore
Vraiment cette vidéo me touche au fond du cœur ❤😢
Machaa Allahouma barik si je pouvais j'allais aimer un million de fois tellement que ❤ qu'Allah vous récompense
❤❤❤salut Zho,je vous remercie bcp,bima comencé suivre tes vidéo matagoul 5mois,mais sétlou si sama bopou ni dama changé d comportema,d frékance,la maniére d parlé,si lou bari pour dir vré.jé 36ans,tay mangui mélni kou am 60ans prck nit yi diokh nagn ma plus d respect et d considération ke avant,si coté finance,légui je sé quand et coment je dois fair des dépense et des épargne.lima gueneu nékh moy légui je sais distingué les actifs et ls passifs.Zho goudeul fane ak bcp d bonheur❤🤲🤲🤲
Zo 14 ans la am waye sama mak lay ligeuyeul ta dama tela geumni damay réussir sama adouna inchallah sama mak lakhamoul noumay def ba demal sama bopou solutions la beugeu
Ana gni d'accord ak mane niou wouti khaliss teki yon la dh gayi geum lén ko rk ❤❤
Amél nagn la alarbaaa 🔥❤️🫶🏿Ms yalnala borom bi defal diameu🤲🏿
Tu es uns source d'inspiration pour nous long vie à toi zo❤❤❤
Toujours aussi pertinent notre zo diam thi ioe frère 😘
Merci pour les conseils 🙏🏽
Diadieuf merci beaucoup goor yalla bi danga may motivé dima inspiré ci lu barri sakh doundeul way
Teki fo live je vous suivre depuis Italie mais bilay changé gua Sama vie inchalah je serai milliardaires et jouer gua rôle bou àm solo Sama vie❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉😢😢😢😢❤❤❤Que dieu te garde ❤❤❤longue vie à vous ❤❤❤zoooo❤❤❤
Merci zoo merci zoo merci zoo😢 yalla na la yalla❤defal diamo😊zoo yaw liga def siman da béri billaye dib 2022 mangui laye top bassaka man kou l'ase la mou noul😢ngose ma ngiur yalla ndkh man sa touba la 😢
Belle vie rek amoule lénén bilahy zo yaw rek lay topou
😭😭😭 bilakhi Magui dioy nakh fi sama situación tolou 😢 dounou bou difícil 💔😭💔😭
Des cœurs pour notre Prophète Muhammad swl ❤️❤️
Cv zou mais s’il te plaît douniou défal béne vidéo pour leçon nioun gnioy diangue méthie fisi sénégal grand zou boul ignorer sama commentaire 😢😢
Des mercis à vous ❤❤❤ vraiment jeunesse sénégal niongui souffres mais yalla bakhna 😢 sa wakh bi amna solo diadieuf
Zo j’ai commencé à vous suivre il y’a quelques mois mais j’ai réussi a avoir des des réponses que j’avais posé là vie
Merci beaucoup et pour tout
Al hamdoulilhi merci pour tout 🎉❤❤❤❤
Zoo vraiment je vous remercie j'ai bcp changé mais dél yokou vitesse sou voix bi x1,25
Merci infiniment
Teki baa yagui si diamou damala guisoul démbou yalla na doon diamou waaay❤
Khawma kan wayé man mom aw masa fay bilay❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieu vous garde Joe vous avez changé beaucoup de vies
Blh dagua changer sama life bayi na école pour saye conseil mais alhamdoulilah magui liguaye
Notre école est TECKI FOR LIFE est le meilleur ✊✊
Merci bro
C'est avec plaisir de vous écouter est mieux de comprendre les leçon de vie que tu nous apprend ce qu'on appelle l'école de la vie, je vous j'ai toujours écouter, mais tous a changé partir le jour où j'ai commencer à pose des actes, yalla rék Molay Faye zo
On t'aime zoo wallahi tu nous à toutes changer yaw yalla molaye Faye je t'aime zoo tu ne peux comprendre sakh yalla laye bayéle
Slt zoo. Vraiment c’est ça qui nous montre que la vie est pleine de surprises donc on doit se préparer pour tout surmonter,mais bref vraiment zoo on ne contente de toi vraiment merci bcp même et bonne continuation Brother ❤
Machallah amatina solo ❤
Merci frère ❤ tu ma donné du courage
Yalla n’a yalla doit sa diam may la goudron fab they fèkga shoutout Amine yarabi ❤️❤️❤️Machine
Vraiment merci beaucoup
Zo loy xarre pour nek président deuk bi
yalna la yallah defal diamo 🙏 zoo Sénégal yawo rek lay topo bilayh 💥 doundou Guiss là vérité allhdolilh
Merci zo de nous motiver ❤❤ yallana yalla deffal niép djam
Amna dioye diangue français thi yaw kou d'accord lal j'aime
Sou ma nékone président yaye néke sama ministre de la conseille ❤❤❤❤
Guem guem dafa am solo si nuit ki ❤❤
Seul dieu qui. Vous payera 🙏 zoo vous avez mérité d'être milliardaire tout ces conseille nous donne chaque jour la force inchallah vous serez toujours e🎉n paix 💪 tout est venu dans le ❤️ merci👍🙏🙋
Sowax Kom mane Kay waxal focus zo yanenala yallah may wer basak Dimanche niouy am sa vidéo, tu as changé ma vision ❤🎉🎉🎈💯💥
Ça fait presque 9 ans la tukhu déminage
Mais dama titone Pour defko
Yaw takh finalement déf naka il as deux mois grâce à zo
Merci beaucoup infiniment
Super Zo diam si yw tu est comme Robert k tu pousse a voir les choses autrement 👍👍
Longue vie à toi frère, bilay diamou rék nguay ame❤❤❤👊🏿
Yalla na sa diam yagu si barki psl...
Ne nous quitterons jamais C'est toi qui nous 🙏🙏
Kou d'core né am sa sokhla lamb sa pôsse fadje ko si change dafa nex lalale j'aime❤
Diar na ligeuy ba woow😂
Man khalé la mais am n'a 18an mais dama lay suivre Di def li ngay dik lou man damay statut Say vidéo maïs dama am niouy don wakh si man dama yakam ti sama adouna ta man dama guem sama bopou ne man Dina am bouma fi yalla baye mon frr louy sa khalat si li niou ma don wakh ta nenan lolou Kou néé si ton moka wara deff ta man samay mak tegou niouma lokho mon frr 😭😭😔
Yangui takh may oubi sama khèl boubakh zo bilahi yalla Nala yalla fay❤❤❤❤❤❤
Encore merci zo
Merci frr
Yalla nala yalla fay sa liggey tékki for life à vie 💦💯✨😢
BKSJ bope kogne ba salle de jeux ba réseau le mes aussi tête le merci frère 💔🥺
الله أكبر 😢😢😢😢😢😢
Mes frère et sœur écoute bien et pratiqué surtout✌🏾
Mâcha allah merci beaucoup ❤
Frère wallahi t'ai vidéo me touche beaucoup en tout cas merci pour les conseils 🎉🎉
Yalna yalla yokou sougnou thiofél thi seydina Mouhamet (SWS)❤
Aamiin.
noo they li ndeysane jo tey lalgama billahi man bouma sakh mouna compran ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci jo
Tekki for Life yangui déff lou am solo bilay walay amna. Lokhamné massoumako kham si adouna mais grâce à toi tahhna makhamko merci encore
Bonsoir for life
Svp 🙏🏾 so meunona yokou épisode yi semaine bou néh gua déf deux épisodes svp❤ parce que li guay def amna important trop wallahi
Alhamdoulilah 🙏 Yalna yalla sameuh zo YA Rabbi 🙏
Deimalal sa bopou même 1000 échec continue bro
Bro amounou sa fay yanala Yallah fay🙏
Adouna bofi néké dangay paré pour demal sa bopou boul yakar si ken ndakh bingay dioudou ando ak ken th boy delou do and ak ken
Ma source de motivation bne continuation ❤❤
Merci beaucoup frère ❤
Yalla n'a africain yeupp téki 🎉❤
Bly zo yallah nala yallah faye😞😞
Tu as parfaitement raison Teki For Life 👍
Merci zo blh gnoune sénégalais yi amounou sa fay zo merci zo😢
jërë jëfëti zo Yàl nala yàlla fay gnun ndaw yi Bëga tekki Yàngi gnouy gindi Dignu Tek si yoon Dëug Deug Amugnou SA Fay
déclic bou gaww la yéwo en écoutent cet vidéo❤
❤ big up brother
Les mots sont forts😢😔
toujours au top long vie à toi mon frère
Vérité amatina solo yagual té wér frère ❤❤❤
Zoo Yalnala yalla defal jammu.
Mann ab Gambien laa deh. Y danga ova change suma life sah; BILLAHI AMAL JAMMU JUE BARRI
Zo je te dis merci 100000fois sa liguéye raféte na
Bonsoir tekki for life mane cheikh ibrahima Niang la touddou mais conten na ci par ce que da ngéna chengé sama doundou dama rérone yénama dindi dipi mars 2022 oma séne Faye kana di lén nianale yalla rék nélén amine rék ❤❤❤❤
Sawayy Kouma Soooffoone gua vraiment on début mais j’ai finalement reconnu ton importance et je t’en remercie au plus profond de mon cœur
Vraiment tu es le meilleur
❤❤❤❤❤ merci beaucoup ❤❤❤❤❤
Blh tu est le meilleur moi j’ai 15ans mes vécu beaucoup de choses j’ai abandonné l’école a problème de famille
Merci zo longue vie à toi zo❤❤❤❤
Yallah n'a la yallah defal diamou zo
Yalla na gniou Yalla défal diamou
❤❤❤❤❤ 🎉🎉Diokh niou leçon nioun gniy diangue méthie Sénégal svp boul ignorer sama commentaire ❤❤❤❤❤❤
Cv zou mais s’il te plaît douniou défal béne vidéo pour leçon nioun gnioy diangue méthie fisi sénégal grand zou boul ignorer sama commentaire 😢😢
Zo daga daga do nit cesse cesse negay change state of mind dafa yeemeeh trop jarijaf maye God bless you and your family
je m'appelle aliou Cissé je vous remercie infiniment parsque votre vidéo mon permis de comprendre beaucoup de choses 🤔🤔