Zoo bly Mann holl na bahoull me yama doyy man 18ane la Am me zoo man yaw ya ma change bly bama ham yon bou bakhe bi ❤yAlla nala yalla fay ❤zoo sou feke ni yan may deg sa numéro ❤beg nako Jamm si yaw
Zo namou nagne la dimanche passe dègou nioula j’espère diam mola tèwone? Merci encore une fois merci bcq si vidéo bi ça me fait plaisir di guiss say video chaque dimanche vie sur toi✌🏾🫶🏾
Merci pour la vidéo ! Vraiment tes vidéos méritent des 1000000000 de ❤. Je m'aurais intervenir sur comment se former en criptonnais chez "entreprendre autrement".De ce fait,Les jeûnes se veulent se former mais imaginer un étudiant dont sa bourse ne dépasse pas même 40millef ,ni de salaire à côté s'il veulent lancer dans cette formation qui coûte 100millef à 500millef voir même 700millef etc alors que ce pauvre dans le mois il ne parvient pas à voir 50millef.Comment ce pauvre va acheter cette genre formation ?.Par conséquent,si il voudrait aider les jeunes il n'a cas ciblé aussi les couches vulnérables(étudiant (e), marchands emballant,élève etc)qui sont en Afrique.
Frère je pense que dans ce monde les gens veulent s’enrichît d’abord avant de vouloir aider les gens qui veulent vraiment sans sortir au lieu de les aider malheureusement Les gros poissons qui ce nourrir des petits poissons
Mes amis on m'a dit que j'ai peur de draguer une fille et j'ai dit zo à dit que c'est le travail qui peut vous servir une fille mes pas les meufs qui peuvent t, offrirent du boulot Merci zo👍👍
Dans la vie faut toujours savoir ce qu'on veut et si tu sait ce dont tu veux tu sauras quoi faire ainsi l'amour peut nuire votre réussite car à tout moment ça peut basculer et sa force est irrésistible donc cherchons d'abord l'argent qui peut déterminer la réussite puis l'amour pour le bonheur
Zo khaliss moy sama priorité depuis bima amè déception ! Guel bouma am investir ci mom après mou moudiè 0 ...guel bouma am niou tak ko ...Diamono dji loudoul khaliss taloumaleu lidjeuntiwoumaleu ba am lima beug inchallah yalla naniou yalla dolil soutoureu !
Kirpt Mony la buegue bokkou frère ak fane lay diar pour réussir Dupuis may toppou batay magui mana dadialé khaliss moy sa vidéo bi nga done wakhé nane loy diar mille ngay fékhé diay mille personnes ak chaque jour temps lay dégnthie lomou métti métti defko té bokoy wathie doko déf bimako dégué labayi di wathie❤😢 merci frère
Salam zo j aime bien ce que tu fais je l adore c est vraiment motivant seul dieu pourra te payer. Mais j aimerait que tu fasses une vidéo motivation pour les handicapés ou personne démunis car ils font partie de la société et on les oublie des fois peut t être à travers ta voix et tekki for Life il pourront se relever et savoir l handicap c est mental et c est n est pas avoir un membre diminué. Merci de la considérer. Tekki for Life
Sérieux j'ai 17ans et j'ai trois amis téh niome nieupp niougui en couple mais moi je suis célibataire on ma brisé plusieurs fois mais j'en suis fière parceque avenir bi mo eupe djiarigne sérieux😇
Big up nalà mon frère Zo Ça me touche vraiment de savoir vraiment que ce que j'avais dis dans ma présentation t'a touché. Mais Liga wàra xàm moy li ëpp si nima mél tày sa liggey lë real recornize real god bless. Do Xiff Xaalis
Frère bégué nala di saluer motivation yi nguay def je te suis depuis un bon moment mais juste tay vidéo bi bene partie rek la nekoul d'accord ay affaire d'investissements dans le crypto ou bitcoin je pense ay trucs de hasard ou benefice bou amoul thiono sou féké dioulite ngua lolou waro thie nek waroko diglé mangui toub bou baxx sinon le reste yeup mangui daccord. Respect
Mâcha allah ❤ câddou yi rafét neu , mais bouniou fatté ni kou am yalla am ngua lèppou té yit niakkeu lo dara wayé kou amoul yalla amoulo dara, khalis nekh neu lol sakh wayé na amin ba rafét... encore une fois yalla avant tout.
Zon nitt kou amoul kharitt est-ce que loubakh la man personnellement amou am kharitt téh mousou mako am amna ay nitt youbari yokhamni peut-être kharitt lanouma diapé baloubari thie séni problème dani obligé disi wakhtan ak man pour rk malén si diokh ay solution mais man peut-être malén eupou ay problems téh douma si wakh ak kén si niom mais zon lolou est-ce que lou bakhla des fois damay pose watt sama bopou ay question ni est-ce que douma sétt si niom kén pour nék ak mom kharitt mais bouma khalaténi Tekkiforlife néna diokhé confiance khétou jeux leu bou dangereuse mooy tax ma continue, di vivre, sans amitié, pour rk may tou nitt gagné sama confiance.
Zo yalla dounko tékélé ak khaliss Bou amé yalla tei amouniou kahliss alhamdou Bouniou amé khaliss tei amouniou yalla on ést foutus On te comprends Erreur de communication la Yafi wakon Heures diouli rek Molay tékli AK Say objectif donc yalla Avant tous .Big UP bn Continuation.
Mon nom Ismaïl Bayo. Senfai plusieurs tu sanger ma vis avec tous les côtes de ma personnalité ans 2021. Ho Non de dieu tu sanger ma vis je vous remercie avec tous les vidéos .yallana yalafaye sa kholle Merci.
Salut Zoo ligay wakh ni right la bougn la guissé gay legey rek gnou japp ni ya wara géré lépp té insbi magui am projet 2M di dajalé mais ba legui mais ymgnx ak lo deger deger amna yo xamni mounossi dra faw ga géné c la triste réalité de ce pays. Et merci j'ai bien lu beaucoup de livre donc je sais bien ce loi qui dit paye toi d'abord 1/10 de ce que tu gagne te reviens l'homme le plus riche de Babylone
Dio chacun à sais objectif donc am yo kham ni ces très sensibles tekki dafa am Yonne kou nék ak figua beugua diarre ak tamite fila yalla Di diaralé au Sénégal y'a beaucoup de choses différentes avec d'autres pays ici la majorité est musulmans et les réalités ont peut pas adapté une autre vie ici a certains âge faut te marié frère tékki nak mo d'où nieup meuna tékki life mo teudé nonou da melni guerre fo diarre am gnu déé toujours khaliss khaliss😮 waw diayanetél sa life tek ci doye lole lepp lo am. Am lo khamni dal nala avant gua dioudou motakh danguay préparer sa avenir dôme comté kéneu préparer woula c'est on vient sans rien on se bat pour tout et on part sans rien . inchallah Dina bakh ❤
Vidéo tay bi bénènn dimension la en tout cas gnongi sa guinaw Mais gnounn gni dégoul français nougnouy déf ba xam naka lagnouy investiré si cripto monnaie
Cv joe nkm yagui si diam j’ai vécu la même relation joe amona guél ma beugue ko lo mou beugue mais instant boumouy nékak mane migui nékak kénéne durant relention bi dama done féne dadone statut kou goor qui souma ko ladié qui sa lane mounima sama kharite la 😢joe instant bi gnomo gnare Marié louma gueneu metti si sama doundou kokou takh na ma bagne djiguéne joe instant magui si sama bopou parce que légui kham nani djiguéne gni dane laye tardél rék instant bi mome khaliss la beugue bly goumou sakh ma téla tak diabart joe ndakh douma ko weulou joe eu peu de conseils joe mais dimanche bi diale khar na vidéo bi mais guissouma ko ba diam la wone ✌️
Zoo lîguaye défe sii jeunes bi ses rare blh mame maçon la journée 7000 laye âme par jour mois 210000manouma wone âme 50000par wér ms Lou Bari Yako changer si Mane yalla nala yalla Faye Amine
Zo billahi sayouma dougé pour commentér sisay vidéo sama rongogn 😢 tourou dou dra ms sama khôl mo féss ak figa ma dieulé wallahi mangui lay suivré depui Arabie saoudite ms Zo Nn bayil ma nopi rk 😭
Entreprendre Autrement : www.youtube.com/@entreprendreautrement3411/videos
Entrpran France lay wax Teman degouma france
Cava tekki for life 2:00
Zoo bly Mann holl na bahoull me yama doyy man 18ane la Am me zoo man yaw ya ma change bly bama ham yon bou bakhe bi ❤yAlla nala yalla fay ❤zoo sou feke ni yan may deg sa numéro ❤beg nako Jamm si yaw
🎉🎉🎉
Man sa numéro la bague
Zo vraiment tu es le meilleur❤❤❤❤ kou d'Accord rk lalale j'aime🎉
Zo namou nagne la dimanche passe dègou nioula j’espère diam mola tèwone? Merci encore une fois merci bcq si vidéo bi ça me fait plaisir di guiss say video chaque dimanche vie sur toi✌🏾🫶🏾
Idém frère khar naako ba sonou
@@AfaGrandyoffWeah c’est vrai☺️mane dmk tamou dimanche pour Ma nelaw sans télécharger vidéo bi c’est très compliqué
Merci équipe tékki for life zo yalla'na yalla wéreull batteu bi kontane naniou trop wallahi merci à vous à la prochaine inchallah ❤✌️
Yaw bo amoule wone da niou laye wouti Bépeu ndaw bou laye suivre dîna changé yalla n'a yalla samou la ❤❤❤
Merci pour la vidéo !
Vraiment tes vidéos méritent des 1000000000 de ❤.
Je m'aurais intervenir sur comment se former en criptonnais chez "entreprendre autrement".De ce fait,Les jeûnes se veulent se former mais imaginer un étudiant dont sa bourse ne dépasse pas même 40millef ,ni de salaire à côté s'il veulent lancer dans cette formation qui coûte 100millef à 500millef voir même 700millef etc alors que ce pauvre dans le mois il ne parvient pas à voir 50millef.Comment ce pauvre va acheter cette genre formation ?.Par conséquent,si il voudrait aider les jeunes il n'a cas ciblé aussi les couches vulnérables(étudiant (e), marchands emballant,élève etc)qui sont en Afrique.
Billy frére
😢
Frère je pense que dans ce monde les gens veulent s’enrichît d’abord avant de vouloir aider les gens qui veulent vraiment sans sortir au lieu de les aider malheureusement
Les gros poissons qui ce nourrir des petits poissons
@@skinnyboyy6490 c'est ce qui entraîne de se passer dans certains cercles d'entrepreneuriat
😊
Long vie à toi mon professeur
Mes amis on m'a dit que j'ai peur de draguer une fille et j'ai dit zo à dit que c'est le travail qui peut vous servir une fille mes pas les meufs qui peuvent t, offrirent du boulot Merci zo👍👍
😁😁 Tu as raison Vraiment Merci pour toutes Depuis Brazzaville Congo 🇨🇬🇨🇬🇨🇬
Fofou nekhna ?
Tu comprends Wolof
Machallah vidéo yi dafa am solo ba douma beug mou diekh damay obligé diko deglou watt sa you diekhé🇮🇹💯❤
Alhamdou lilah dila sente bou bakh parce que tu as changé ma vie tellement tellement la protection de Dieu sur vous frr❤️❤️
Merci beaucoup ✊️💪 Focus réussite rk dokh topou yon wii Lomou lathie niou df kosi ay thia gayii ✊️✊️✊️💪💪💪
Dans la vie faut toujours savoir ce qu'on veut et si tu sait ce dont tu veux tu sauras quoi faire ainsi l'amour peut nuire votre réussite car à tout moment ça peut basculer et sa force est irrésistible donc cherchons d'abord l'argent qui peut déterminer la réussite puis l'amour pour le bonheur
Merci 🤣
Cool
Complètement raison ❤
Vérité Absolue 😊
Merci beaucoup frère zø yalla nga goudi fane ❤🎉
Li kay wax amna solo mais ame Yalla mo guene lepou parce que bo amé Yalla Amka lépou do magui dara
Diam si yaw zo wér goudou fan taw fékha soutour Amine yarabi 🙏
C'est la vérité mais l'amour ne compte plus pour personnes 😢😢.c'est triste
Zo khaliss moy sama priorité depuis bima amè déception ! Guel bouma am investir ci mom après mou moudiè 0 ...guel bouma am niou tak ko ...Diamono dji loudoul khaliss taloumaleu lidjeuntiwoumaleu ba am lima beug inchallah yalla naniou yalla dolil soutoureu !
Kirpt Mony la buegue bokkou frère ak fane lay diar pour réussir Dupuis may toppou batay magui mana dadialé khaliss moy sa vidéo bi nga done wakhé nane loy diar mille ngay fékhé diay mille personnes ak chaque jour temps lay dégnthie lomou métti métti defko té bokoy wathie doko déf bimako dégué labayi di wathie❤😢 merci frère
Zoo amal jam franchement tu est notre source de motivation, ont t'aime fort frère.
Vraiment zo tu nous motive chaque jour bonne continuation je t'aime ❤❤
toujours au top vraiment t' conseils mais fait avancer force à toi mon frr 🙏🏽
Video yinga meuseu Yépp, Bii Momasi gueuna Nékh💗merci beaucoup frére🙏🏽
Machallah
Fall sa touba yallana yalla defall ndiamo 🤲🤲
Salam zo j aime bien ce que tu fais je l adore c est vraiment motivant seul dieu pourra te payer. Mais j aimerait que tu fasses une vidéo motivation pour les handicapés ou personne démunis car ils font partie de la société et on les oublie des fois peut t être à travers ta voix et tekki for Life il pourront se relever et savoir l handicap c est mental et c est n est pas avoir un membre diminué. Merci de la considérer. Tekki for Life
Sérieux j'ai 17ans et j'ai trois amis téh niome nieupp niougui en couple mais moi je suis célibataire on ma brisé plusieurs fois mais j'en suis fière parceque avenir bi mo eupe djiarigne sérieux😇
Machallah
Bilay
Billy toujours ak tékki for life machallah❤❤❤❤❤
Vraiment merci beaucoup frr tu nous motives à chaque fois bouma demé bay décourager ci Life bii t’es paroles reviennent automatiquement dans ma tête
بارك الله فيك يأخي أطال الله عمرك طويل ورزقا كثيرا طيبا مباركا ببركة محمد رسول الله صلى الله عليه وسلم
Soy deglou gadou yi dou nekha degue mé Soko comprendé Lou yomba deglou la merci frère diob bi nice na❤❤
Bilahi dembe rk lagne ma done force pour ma tak sokhna 😍c Comme si q video bii pour man leuh merci encore une fois
en bou
Bilay sax @@bayesallioufall3689
Machallah amatina solo yaw ak gnoune gni lay sétane yallah na gnou yallah déf ay milliardaires incha allah ❤❤❤❤❤❤❤🤲🏿
Big up nalà mon frère Zo
Ça me touche vraiment de savoir vraiment que ce que j'avais dis dans ma présentation t'a touché.
Mais Liga wàra xàm moy li ëpp si nima mél tày sa liggey lë real recornize real god bless.
Do Xiff Xaalis
Tu nous as ouvert les yeux j'appréci vraiment ton formation
Machallah mon coach ❤
Les mots me manquent pour vous remercier
Vraiment merci thank you dieuredieuf gracias choucouran diokandial ....❤TFL❤
Frère bégué nala di saluer motivation yi nguay def je te suis depuis un bon moment mais juste tay vidéo bi bene partie rek la nekoul d'accord ay affaire d'investissements dans le crypto ou bitcoin je pense ay trucs de hasard ou benefice bou amoul thiono sou féké dioulite ngua lolou waro thie nek waroko diglé mangui toub bou baxx sinon le reste yeup mangui daccord. Respect
Bly Goude fan AK wérr inchallah kontana si yaw bly ❤❤❤❤
Merci frere pour tes conseils tu nous motives a chaque fois quand on écoute tes video
Merci beaucoup vidéo bi amna solo toujours yaw laye topou ❤❤❤Amal diamou RK ❤❤❤
Bien vrai que je suis une femme ms ms tes video me soulage frére franchement s8 émue d tw notre source de motivation yalla Faye le zo .
Tout temps damaye kholl bakham dougeul nga vidéo ndakh leçon lasi diagiéu🎉
Mâcha allah ❤ câddou yi rafét neu , mais bouniou fatté ni kou am yalla am ngua lèppou té yit niakkeu lo dara wayé kou amoul yalla amoulo dara, khalis nekh neu lol sakh wayé na amin ba rafét... encore une fois yalla avant tout.
Merci beaucoup tekki forlife❤️❤️
Merci Jo vous faites un travail remarquable 💯
Merci Frère merci beaucoup pour tes vidéos vous m'avez sauvé la vie
Long vie à toi mon coache prefere
Zoo vous êtes un sage je t'assure je suis tres content de toi force à vous
Joe dou nit pauvre loumouy doyé goudou fan 😂😂
Ca fait longtemps que je n'ai pas ecouté une seule de tes videos mais niveau bi yeik na mashallah yalla na yokk ❤❤❤
Merci tekki for life ❤
Merci beaucoup Fréro ❤❤🎉🎉
Merci encore grand bi machallah ❤✌️✌️✌️
khalis soumakoy dégue sakh sama khol daye sédd lolou sakh bilay walay ma beugue khalis bilay walay ❤️❤️❤️
Bilahi beug nagnla ❤ beug nagnla loool , zo❤. Jamm AK salam rek inchallah. Vous avez amplement contribué à notre éveil de conscience. En réalité, vous nous avez réveillé de notre sommeil dogmatique.
Big up bro long vie à nous✌🏾🩸♥️
Merci beaucoup frère ❤
Vérité absolument frère yalla goudou fane thi barkeep mouhamed❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏
Zon nitt kou amoul kharitt est-ce que loubakh la man personnellement amou am kharitt téh mousou mako am amna ay nitt youbari yokhamni peut-être kharitt lanouma diapé baloubari thie séni problème dani obligé disi wakhtan ak man pour rk malén si diokh ay solution mais man peut-être malén eupou ay problems téh douma si wakh ak kén si niom mais zon lolou est-ce que lou bakhla des fois damay pose watt sama bopou ay question ni est-ce que douma sétt si niom kén pour nék ak mom kharitt mais bouma khalaténi Tekkiforlife néna diokhé confiance khétou jeux leu bou dangereuse mooy tax ma continue, di vivre, sans amitié, pour rk may tou nitt gagné sama confiance.
Longue vie à toi merci pour les Conseils ❤
Depuis que j'ai commençé a regardé tes vidéos les voies les chose différemment
Tes vidéo sont tellement inspirantes ! Merci beaucoup, qu'Allah soit avec toi 🙏
Machalah amna solo Yalla na sa diame yague
Tu a changé ma vie billay ❤
Tu nous as ouvert les yeux j'appréci vraiment ton formation❤
Zoo merci beaucoup tu a beaucoup changé dans ma life .....
Zo yalla dounko tékélé ak khaliss Bou amé yalla tei amouniou kahliss alhamdou
Bouniou amé khaliss tei amouniou yalla on ést foutus
On te comprends Erreur de communication la Yafi wakon Heures diouli rek Molay tékli AK Say objectif donc yalla Avant tous .Big UP bn Continuation.
Zo machalla dope bi Nice na yalla nga réussir
Merci beaucoup ❤️ ❤️❤️
Machalla zoo yagui defar souniou adouna wallahi yalla nalla yalla sam
Merci professeur tu es le meilleur personne que je connais
Merci frère nous sommes avce toi❤
Merci vraiment Zo❤
Merci beaucoup teki f l Sénégal toujours iow rek laniou toup dh
Merci beaucoup frère vidéo bii dama lale bro Nice na trop ❤❤
Longue vie à toi zo ❤ merci pour les conseils
Pour ioe zo ligay df ni yalla Doula fayy athia rkk🙏Guena yagg guena werr inchalla 🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Mon nom Ismaïl Bayo. Senfai plusieurs tu sanger ma vis avec tous les côtes de ma personnalité ans 2021. Ho Non de dieu tu sanger ma vis je vous remercie avec tous les vidéos .yallana yalafaye sa kholle Merci.
Salut Zoo ligay wakh ni right la bougn la guissé gay legey rek gnou japp ni ya wara géré lépp té insbi magui am projet 2M di dajalé mais ba legui mais ymgnx ak lo deger deger amna yo xamni mounossi dra faw ga géné c la triste réalité de ce pays. Et merci j'ai bien lu beaucoup de livre donc je sais bien ce loi qui dit paye toi d'abord 1/10 de ce que tu gagne te reviens l'homme le plus riche de Babylone
Encore une fois mrc ❤❤❤❤
Dio chacun à sais objectif donc am yo kham ni ces très sensibles tekki dafa am Yonne kou nék ak figua beugua diarre ak tamite fila yalla Di diaralé au Sénégal y'a beaucoup de choses différentes avec d'autres pays ici la majorité est musulmans et les réalités ont peut pas adapté une autre vie ici a certains âge faut te marié frère tékki nak mo d'où nieup meuna tékki life mo teudé nonou da melni guerre fo diarre am gnu déé toujours khaliss khaliss😮 waw diayanetél sa life tek ci doye lole lepp lo am. Am lo khamni dal nala avant gua dioudou motakh danguay préparer sa avenir dôme comté kéneu préparer woula c'est on vient sans rien on se bat pour tout et on part sans rien . inchallah Dina bakh ❤
Vidéo tay bi bénènn dimension la en tout cas gnongi sa guinaw
Mais gnounn gni dégoul français nougnouy déf ba xam naka lagnouy investiré si cripto monnaie
Merci ❤🫶🏻
Merci pour les conseils ❤❤
Je te suivre @MAURITANIE VRAIMENT C EST TRÈS TRÈS INTÉRESSÉ MERCI
Grand frère vidéo yi amna solo mashalla yalla n'a diam yàga
Merci merci beaucoup frère pour tout ce vidéo respect 🫡
Cv joe nkm yagui si diam j’ai vécu la même relation joe amona guél ma beugue ko lo mou beugue mais instant boumouy nékak mane migui nékak kénéne durant relention bi dama done féne dadone statut kou goor qui souma ko ladié qui sa lane mounima sama kharite la 😢joe instant bi gnomo gnare Marié louma gueneu metti si sama doundou kokou takh na ma bagne djiguéne joe instant magui si sama bopou parce que légui kham nani djiguéne gni dane laye tardél rék instant bi mome khaliss la beugue bly goumou sakh ma téla tak diabart joe ndakh douma ko weulou joe eu peu de conseils joe mais dimanche bi diale khar na vidéo bi mais guissouma ko ba diam la wone ✌️
Machallah Yalla Nala Yalla Diapalé Grand Frère Wakh Ngua Deug Deh Djiguéne Gni Dagn Lay Tardél Rék Liggéy Rék Té Bayi Leen Yalla Bakhna
Amna solo wolay khaliss rk lay topp té khaliss rk lay khalaat🎉
Mais Zo man awma sakh kardanté bay am contou Bange parcka bagouma problème Diko Txall samay paran 🥺 sama papa amoul karté Danté sama yay même souss 😔
Merci tekki for life notre chaîne préféré
Zooe ya takh ma chance lou bari si sama dound yalla nala yalla yook❤❤❤
Zoo lîguaye défe sii jeunes bi ses rare blh mame maçon la journée 7000 laye âme par jour mois 210000manouma wone âme 50000par wér ms Lou Bari Yako changer si Mane yalla nala yalla Faye Amine
Hi! zo since I started listening to u everyday am getting improve now plus am having more fit. An may god bless u
Merci beaucoup liguey bi rafet na ❤
Merci beaucoup zooo Billahi Amna solo lolll Ms beugg neu sa numéro stop 😢❤
Zo billahi sayouma dougé pour commentér sisay vidéo sama rongogn 😢 tourou dou dra ms sama khôl mo féss ak figa ma dieulé wallahi mangui lay suivré depui Arabie saoudite ms Zo Nn bayil ma nopi rk 😭
Merci beaucoup zo billahi ma gui diogeu si sama ben geul sama xarite mo ko diel dema diogeu fofou rek niew yame sa vidéo bi amna solo trop
Merci bcp mille fois ❤
Thank you bro, you shape my life,. I'm Yusupha jarju. I'm always waiting for your videos