MARI DE VIPÈRE TU FAIS UN GRAND HONNEUR AUX HOMMES. TU ES UNE PERLE POUR NE PAS DIRE UN OISEAU RARE CI MIME RÉWE. QUE DIEU VOUS PROTÈGE ET VOUS BENISSE. VOUS ÊTES TOUT SIMPLEMENT DES MODÈLES. FORCE À VOUS DEUX . MERCI AUSSI POUR VOTRE JOIE DE VIVRE ET AU BONHEUR QUE VOUS PROCUREZ À TOUS CEUX QUI VOUS SUIVENT.
Machalah moi aussi sama dieukeur nila mel kou bakh niou am complicite vraiment dey fathieu ak ay domam vraiment bonheur plein yallah nako yallah defal diam maal demba,diam loko dieundeh diarnako mon mari dal yallah naniou yallah lafal thiat
Certes diadia a eu l'occasion de nous dire ton histoire d'amour mais la mienne est plus douce il m'a vu quand j'avais 7ans et il m'a aimé à cet âge et aujourd'hui on est en 5ans de mariage machallah ce que je vis je le souhaite à toutes les femmes ❤❤
Machalla yalnalène yalla lafal thiate seuy bou barké ak ndiabote you barké❤️té yalla boumou meusseu am woudiou si barké Nabi Moustapha psl❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏
Diadia amnga ndambal djiegue sa keuer sett na amoul desrdre sa bromkeur guisou mako waye wakhin bi niter na yalna ngen agg ni yoon allahouma la adourou❤❤❤❤❤❤❤
Machalla bilakhi yako maye diam rek djiguene mome sou ame fitou def yene yi sa kanam rek yako maye fite bi gore daguaye oyofe bagna reuye sisa kanamou diabar Machalla
Machalah seu Djeukkeur garmi leu , iow aussi keineu dou iow mais ki yar seu djeukkeur aussi mention spéciale ! Yalla naleineu samal bopam si barkei alhourane 🙏🙏🙏
En toute sincérité je vous regarde souvent mais à partir d'aujourd'hui je m'abonne à vous après cette interview mis à part le couple exemplaire que vous formez ,c'est le caractère de madame j'aime les blagues mais avec respect continuez comme vous êtes et vous serez éternels sur les réseaux sociaux ❤❤❤
srx Diadia dou nite mais kèn dou Mary de vipère 😂😂 machaallah blh gnare gni dagno nèkh vraiment référence nguèn yalna lèn yalla lafal thiate samelèn arelèn té mousseul lèn si pékhèp none si barké SEYDINA MUHAMED PSL ❤❤❤
Parmi les 667 commentaires dont j’ai presque lu la moitié je n’ai pas vu un commentaire négatif Ma Shaa Allah yalla nalene borom bi saam mousseul leine thie pekhei none ❤️😍❤️
Complicité ak amour 🫶 et confiance c’est très important dans un couple Lolou moyy base bi en tout je vous j’aime Yalla n’a Yalla defal diam mayél ndiaboot djou islamé té barkel
Franchement je vous aimes 😂❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤ Diadia boul nangou moukk mari de vipère fègne xallé yi da gno eupeul 😂😂😂 Mari aussi sa gnakk fègne nèex nama trop Encore je vous aime 😘 😅😅😂❤❤❤❤❤
Que dieu vous bénis à votre couple au nom puissance de jésus christ 🔥 🔥 🔥 part le feu 🔥 de l'esprit saint j'aime cette complicité dans un couple ❤❤❤❤❤❤❤ bravo je vous aimes soyez heureux ❤❤❤
Bilay ya tah ba sma djeukeur niow fii makoy nane vipère marie du coup dema dem ba avant mouye ñibi niep si adapté mom osi suma ko nè vipère marie rt mou wouyou keurgui niep toth srx Diadia jtmeuh💋😅😅
Ah ma chérie Diadia yangui wate Lou grave douma âme woudiou nga wakh dé. Man soumalaye sétane yaw AK sa dieukeur man AK sama dieukeur rek lassiy guiss mais linga wakh rek nitt mo sokhor fékhé nane ba tassalma sama seuy bi niiii après 10 ans de mariage mais bayinaléne AK yalla
Machala Yale ne s'en ande bi yage way me tây nace grec waron nagne gisse mari de vipère way tamit ni me Bon fête de saint Valentin a tous particulièrement a vous deux ❤❤❤❤
MARI DE VIPÈRE TU FAIS UN GRAND HONNEUR AUX HOMMES.
TU ES UNE PERLE POUR NE PAS DIRE UN OISEAU RARE CI MIME RÉWE.
QUE DIEU VOUS PROTÈGE ET VOUS BENISSE.
VOUS ÊTES TOUT SIMPLEMENT DES MODÈLES.
FORCE À VOUS DEUX .
MERCI AUSSI POUR VOTRE JOIE DE VIVRE ET AU BONHEUR QUE VOUS PROCUREZ À TOUS CEUX QUI VOUS SUIVENT.
Diadia tu as trouver un vrais Roi yalla naléne yalla lafale thiate naléne diame sonale
Maachaala. Je fête icette année in chaa Allah 30 ans de mariage. Qu'Allah Protège tous les couples ci Barké Seydina Muhammad SAW
MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH YALLAH guako fêter 100ans INCH ALLAH 🎉❤🎉❤🎉❤🎉
MachaAllah. Yalla na nguen and ba 100 ans té mou and ak wer ak ndiaboot diou barkel. Amine
Diadia contana si yéne. YALLAH same léne, are léne. Same sen djabot. Mashallah exemple guén.
Machala que dieu vous laisse ensemble jusqu’à ici repose ❤ta guene goudou fane lol
❤❤❤❤❤❤que du bonheur sur vous mes amours ♥️♥️♥️♥️♥️♥️🎉🎉🎉
Alhamdoulilah 35ans de mariage et tjr en lune de miel ❤je suis la première la 2 3et 4❤ santeu Yalla
Bravo mari de vipère heureux ménage amna solo que Dieu vous garde très longtemps et vous protége. C'est le diadia qui se passe.
Merci bcp.
Tay mafi djitou massou ma am j'aime
Bayyil fene yaw mi😂
@@ousmanegaye5175 kholal bou bakh
😂😂
Essayer di moudié bakham
😂😂😂@@ousmanegaye5175
Machalah moi aussi sama dieukeur nila mel kou bakh niou am complicite vraiment dey fathieu ak ay domam vraiment bonheur plein yallah nako yallah defal diam maal demba,diam loko dieundeh diarnako mon mari dal yallah naniou yallah lafal thiat
ALLAHOUMA Amine MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH commentaires yi laye weur❤🎉❤🎉❤🎉❤
Tu as de la chance machalah
Je vous souhaite tout le bonheur du monde que le seigneur vous protège.Amine
Machalah mari de vapér sa communication baxna kadouyi rafétna matna mataléna yalna lén yalla yokal diam diou sakh dakh inchallah
Wouh diadia nobaté na beut yangui brillé grave oh li nexna machalla laf thiate ❤
Sa borom keur kou bakh la DiaDia diapp KO bou bakh. Yalnaléne borom bi lafal thiate ya rabbih
Mashallah yalla nalène yalla lafal thiate ci barkè yonenti bi ❤❤
Ndeysane Mbeuguél da mélni néxna 😂ms Yallah nalen yallah défal Diameu ❤
Kouko doundoul manoko kham
C la première fois j prend mn tmp pour suivre sela
Contann naa lol sahh communication ❤❤❤❤
Diadia je vous aime avec ton mari laff bouche ❤❤❤😂😂😂😂😂et tu chante très bien machalla ❤😂😂😂
No c'est diadia😂❤❤ machalah
❤❤❤❤❤
Certes diadia a eu l'occasion de nous dire ton histoire d'amour mais la mienne est plus douce il m'a vu quand j'avais 7ans et il m'a aimé à cet âge et aujourd'hui on est en 5ans de mariage machallah ce que je vis je le souhaite à toutes les femmes ❤❤
Amine ya Rabi. Demeurez bénis 🎉🎉🎉
Diadia Macha Allah sa dieukeur kou bakh là, Yalla nalène Yalla lafalène thiat , maylène ndiabote Al barké si barké Seydina Mohamed PSL.❤❤❤
Machalla yalnalène yalla lafal thiate seuy bou barké ak ndiabote you barké❤️té yalla boumou meusseu am woudiou si barké Nabi Moustapha psl❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏
Mashalla Amm dieukeur Bou baxx chance leu ❤Diadia gueneul diapp sa seuyy tei fonn sa dieukeur ❤
Diadia amnga ndambal djiegue sa keuer sett na amoul desrdre sa bromkeur guisou mako waye wakhin bi niter na yalna ngen agg ni yoon allahouma la adourou❤❤❤❤❤❤❤
Tay la gueuneu contant si yein franchement je vous adore ❤❤
Machalla bilakhi yako maye diam rek djiguene mome sou ame fitou def yene yi sa kanam rek yako maye fite bi gore daguaye oyofe bagna reuye sisa kanamou diabar Machalla
Mashallah mari de vipère un vrai humain yalla nalenn sa borom lafal thiat tei barkel sen seuyy❤️👍on vous aime
Machallah mari de Viper yaw booko wahoul sah gnoun hamnani danga nop diadia yalla naleen yalla lafal thiatt
Machalah seu Djeukkeur garmi leu , iow aussi keineu dou iow mais ki yar seu djeukkeur aussi mention spéciale ! Yalla naleineu samal bopam si barkei alhourane 🙏🙏🙏
Macha'Allah ❤️ toufff toufff toufff Yallah nala yallah bayii ak sa Sokhna inch'Allah je vous Love vraiment ❤
😂😂kho dia dia ma cherie sama khôl sedna machallah machallah Konetane si yaw
Machala lafthiate yalnalen yala mouthiale si saytané sibarker seydina mouhamet psl amiyarabi ❤❤❤❤❤❤❤
Bonne fête de St Valentin a mon couple préféré Yale nalen Yale Lafay thiat
Vous êtes formidable Mane mome specially Daguéne méyy konetanelo! Référence guéne happy valentines 💝 !ma shaa Allah! Great couple
En toute sincérité je vous regarde souvent mais à partir d'aujourd'hui je m'abonne à vous après cette interview mis à part le couple exemplaire que vous formez ,c'est le caractère de madame j'aime les blagues mais avec respect continuez comme vous êtes et vous serez éternels sur les réseaux sociaux ❤❤❤
srx Diadia dou nite mais kèn dou Mary de vipère 😂😂 machaallah blh gnare gni dagno nèkh vraiment référence nguèn yalna lèn yalla lafal thiate samelèn arelèn té mousseul lèn si pékhèp none si barké SEYDINA MUHAMED PSL ❤❤❤
Diadia talibé Serigne fallou la mo takh mou beuri yeur mandé 😢😢😢
Yalla bouléne thiat nakh tjatte dafa guaw un exemple sur le couple maabo 😢yalla naléne yalla djibolé 😊❤
Parmi les 667 commentaires dont j’ai presque lu la moitié je n’ai pas vu un commentaire négatif Ma Shaa Allah yalla nalene borom bi saam mousseul leine thie pekhei none ❤️😍❤️
Machalha l'Afrique thiaate ma contane si sougnou couple antistres bi yallha nala yallha defal diam samal bopame moussale si seytane akthiate
Complicité ak amour 🫶 et confiance c’est très important dans un couple Lolou moyy base bi en tout je vous j’aime Yalla n’a Yalla defal diam mayél ndiaboot djou islamé té barkel
Je vs souhaite tout le bonheur du monde yalna yallah lafal lene thiat❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ barque Serigne Touba Mane yene laye top🎉🎉🎉🎉
Dieukeur bou bakh Bilahi yomboul yallangnou ko yalla may
Femme respectueuse adorable aimable notre Diadia ❤️❤️
Wawa ❤❤❤
Franchement je vous aimes 😂❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤
Diadia boul nangou moukk mari de vipère fègne xallé yi da gno eupeul 😂😂😂
Mari aussi sa gnakk fègne nèex nama trop
Encore je vous aime 😘 😅😅😂❤❤❤❤❤
Diadia arrête pitié la depigmentation. Tu es une belle femme de l intérieur comme l a témoigne ton mari .machalah Qu'Allah vous protège !
Elle vend des produits de degipmentation et tu veux qu'elle se degipmente pas mdr😂
@@misstchiptchip2963et son mari l'aime com ça en plus
Machallah que du bonheur diam rek
Bravo un grand coucou à vous chapeau bonne contuniation laf thiate machallah zéro faute merci du fond du coeur
Machallah laf thiat contane si yenn long vie ,li dafa nékh vous êtes des références
Yalna yalla doli soutoura té mayko diabot bou barkéle 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diadia Saloum Saloum la day meune seuy ❤❤❤
Machallah très beaux témoignages vraiment vous êtes exemplaires ❤🎉 bonne fête de saint Valentin et vous et otois les couples
bly en voyant diadia rk les larmes de joie se tombe
Macahallah yalla Nalén defale diamou❤❤
Longue vie à vous diadia tu ma fait pleurer 😢 hein wallah c émouvant
Machallah raféte na laf thiat contane si yéne je vous suivre toujours bonne fête de Valentin ❤❤❤❤❤
Machalla longue vie santé bonheur ❤❤❤❤❤❤ depuis Paris ❤️❤️❤️🙏🇸🇳
Yallah na lene Yallah lafale thiate. Yene gnare gneupeu bakh. Je vous souhaite tout le bonheur du monde
Ndeysane dathiy guiss yayam dafmay dal ❤
Machallah sama couplé bi Nicena ❤❤je t'aime tellement diadia 😊
Machalah longue vie a votre couple ndeyssane ya des hommes comme ça walay moi aussi mon mari est comme ça des fois meme j'ai honte
Une deuxième commentaire waye machala yalla nallen thiat sekhlou moussal len si seytane nguen ame ndjaboot you barkel❤❤❤❤❤
Gni nane amour amour il moyen amour djiguene dagn koy bâti mou libre
Notre couple prefere yalla na yalla lafal lene thiat
Machallah Diadia yalla naléne yalla lafale thiate ❤️❤️
Machalla yallanaléne yalla lafale thiate mayeléne ndiabotte bou barkéle ❤
Machalla laf thiat que Dieu vous protège moi aussi mon mari et moi c'est comme ca yalla na diam yague amine
Que dieu vous bénis à votre couple au nom puissance de jésus christ 🔥 🔥 🔥 part le feu 🔥 de l'esprit saint j'aime cette complicité dans un couple ❤❤❤❤❤❤❤ bravo je vous aimes soyez heureux ❤❤❤
Yalana léne tiate ak beute bou bone bayil machala
Machala Yal na yalla samlén❤
Sama mbokou Saloum Saloum yii manifestez vous ❤❤❤
Sama bopou rekkk lalayy kholé manchalllah ke Allah vs garde
Macha alla diadia oyof gan mais aussi mari de vipère keneu geunouko meunône nala wakh sa faire dof yii bayiko mais dafa compatible ak mome
Bilay ya tah ba sma djeukeur niow fii makoy nane vipère marie du coup dema dem ba avant mouye ñibi niep si adapté mom osi suma ko nè vipère marie rt mou wouyou keurgui niep toth srx Diadia jtmeuh💋😅😅
Waw diadia ta takh mari de vipére bayi gneuppa kone gouda léne FANE bok 120 ans sans ordonnance INCH ALLAH 🎉❤🎉❤🎉
@@halikano392 way way niane bii douff naa ak nioune niepp way Mrc6🙏 mane mom ak diadia sè otre chose🤣
No khamo na nii dina fii woye man diadia damaka beugu sm biir khôl ❤❤ Diadia Amal Diam ❤❤
Machalah diadia sa borom keur gui comme sama boss machalah yalna laine yala lafal thiaat si barke mouhamad psl amine yaa rabi ❤❤❤❤❤
Yalla nama yalla may complicité bi ba sama keur meuna nekh amine🙏🙏
Ah ma chérie Diadia yangui wate Lou grave douma âme woudiou nga wakh dé. Man soumalaye sétane yaw AK sa dieukeur man AK sama dieukeur rek lassiy guiss mais linga wakh rek nitt mo sokhor fékhé nane ba tassalma sama seuy bi niiii après 10 ans de mariage mais bayinaléne AK yalla
Aye waye didia founiou dieume ak yawe yèna maye soigner na séne diame yague machalla laf thiat 😂❤
Diadia ma chérie yalla naléne yalla lafal thiate wayé boul nagou ❤
Machalah sama couple préféré ❤yalla may léne ndiaboot gou barkel
KI REW NA 🤣🤣🤣🤣🤣 MASSALLAH GWGY INCHALLAH FOR EVER RECK DIADIA AND MARI DE VIPÈRE ❤❤❤❤❤❤
Couple bi rek lay topeu diadia ❤amléne salam sasounek. Yalla mouslén thi thiate
Les filles féxélen kham koulén buegu moy lep ndax té bayi xool alalou aduna ❤
Machallah mon couple préféré ❤❤❤ mais pourquoi tak de niarél ✌️😂😂
Machalla yalla nalén yalla lafal thiate diadia nitou saloum leu motakh mou bakh ❤❤
Non j'adore ce couple ils me font trop marrer 😂❤❤❤
Khol féess na bilakhi. Jigèen bula takhawoo danga war nék papam nék lépam❤. Ndéysaan yalna yalla takhawu
Yalna nalen yalla sameu ❤maylen ndiabott bou barkél inchallah
Yalla n'a len yalla samou te arr len moussal len si thiat ak pekhe non 🙏❤🙏❤🙏❤
Yalna sén diamou yage❤❤❤❤❤❤
Machala Yale ne s'en ande bi yage way me tây nace grec waron nagne gisse mari de vipère way tamit ni me Bon fête de saint Valentin a tous particulièrement a vous deux ❤❤❤❤
Ma couple préféré yalna yalla dolie diam depuis hier ba legui mangui setane yene rek laye topou 🎉
Da am yeurmandé yallah nako yallah féy
Yalla na yalla defal diam yalla mayelenne ay ndiabot barke
Diadia teyla lala guena beugue ❤ yalna yalla bayila ak mari de vipere 🎉
Ohh machallah 🥰 longue vie à votre couple ❤
Machalla contane na si yen dé yalla nalen yalla defal thiat defal len diamou ❤❤❤❤
Machallah yalla nalen sunu borom lafal thiate ❤
Machallah yalla nalene defal diam sam lene té are lene ❤❤❤❤❤🥰🥰
Laffff thiattt laff thiatt lafff thiat laff thiatt rek si barkei Seydina Mohammed psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diadia❤ if I am stress, you make me feel happy i’m washing you video every night before I go to bed thank you.❤ I love you so much🎉❤
Machallah diadia ya dakeu weuye bibiche 😂yalla naléne yallah défal diam
Merci ma belle machallah Diame si yénn🥰🥰🥰❣️❣️❣️💯💯💯