Khew khew môme yaa khew 😅😅une série riche d'enseignement mais aussi des séances qui font rigoler à tout le monde mais aussi des acteurs digne de leurs parcours d'artistes vraiment je vous j'adore ❤❤❤
#BeteBeté arrive une série qui promet du lourd 🔥 j'en suis sûr ça sera le jumeau de la série #Njabar☝️ on attend la bande annonce Force a vous evenprod 💪
Outre la réalité sénégalaise de la série, ce que j’aime après tout c’est la beauté des femmes…leurs teints naturels noirs❤❤❤❤❤❤❤❤❤. Superbe casting anti xessal.
Meilleure maison de production au Sénégal Sinon BÉTÉ BÉTÉ kukoy avec impatience rk lalal j'aime 😮 Le prophète psl a dit : Méfiez-vous de l'envie, (méchanceté) car l'envie consume les bonnes actions tout comme le feu consomme le bois, ou dit-il l'herbe. Sa morom bu amé lu bax yenekoko❤😮 Couple nandité bi momakoy def mann😂😂
Avec l’histoire de Papito,Evenprod nous plonge dans nos plus profond secrets de jeunesse.Faire le Vip dehors et revenir à la réalité une fois chez soit.on est jamais prophète chez soi.Certainement pas un personnage facile à interpréter car il faut bcp d’adaptations,être star à l’extérieur,sous estimé par son père à la maison,confident de sa mère à côté Bref Evenprod vous êtes juste les meilleurs pour incarner notre vie réelle.J’espère que Papito ne finira pas victime de son succès à la fin de son histoire car y’a toujours de dures leçons de vie avec xewxew Evenprod.L’avenir nous le dira🙌
Respecté heures mom yénako fi déf béneu problèmes guén am Mouy suites des séries légui tay guén mélni niognou ani impuissant njabar munël infidèle Impuissant ak munël mom sokhla nagne retour bou yagué guén mélni niognou may bagna toudou serie bou bess c'est bien beau mais guén égali sén serie yi nék avant🤧😏☺️
Moussa seck tamit tite neu am nga xalis di basèwou ci loterie pour dem makka non mane nandité 😂😂😂niambé sen ak demam makka bi diabar dji dal ganalé bi moko sonal
Magui toup dh wakh deug fa yallah ms méri guewal yi nek si serie bi nio gueune rafet khale yi gueune lenne mol machallah ❤je vous aime ❤
Deug dé gua écrire elles sont machalat ❤❤
Teksi guenlen naturelle ❤
Mol bi DH massi diakhal 😂
@@seydou48669😂😂😂😂😂
Thioro dou mère dé xalé bou ndaw la
Retrouver moussa seck me fait énormément plaisir mais aussi regarder le teint embelli de mère thioro me comble de joie walay machalla❤
Walaay teint bi mashalaa
Teint naturel key
Mère thioro dafa rafette
@mamewade1402 C'est cool.
Mane Mére Thioro rek lay sétane
Coubeubeug seydinamouhamed beusseul j'aime ❤️🙏
La beauté de mère thioro on en parle ❤❤❤
Lo si khamoul khalé la dé
@@bocarguisse2282fonekonn😂
@fatoumbaye5562 Merci.
Ak noirceur d’ébène bi 😊
Khew khew môme yaa khew 😅😅une série riche d'enseignement mais aussi des séances qui font rigoler à tout le monde mais aussi des acteurs digne de leurs parcours d'artistes vraiment je vous j'adore ❤❤❤
Malheureusement qui n'est pas très suivie.
@ablayedieng645 Merci.
On en parle pas mais le Casting de Nandité est bien réussi
Bilay nandité mon coup de coeur ❤️ il joue bien
Déko sétane Oh campus il maitrise très bien ce rôle
@MAXIMILIANO-18 Merci.
Vous voulez vraiment voir Nadité aller regarder la série Campus saison 2 fofou la nekk dicou deumbétté
Je vous jure @@manishounaby2341
Wa keur Mansour yii sen teint noir yii ma'sh'Allah ❤
Bilay elles sont ttes belles machala ❤
@coumbasarr2172 Merci.
Tres respectueux envers vos téléspectateurs (trices) machallah enplus deff ponctuel ❤❤❤❤❤❤
@FatouThiam-mk4zd Merci.
May 40em 😂 t prophète 40ans lako yalla yonni 😎🙏🏿 j’aime
Ayway Bo toudone Mohamed gueuene fé tothie mashallah ♥️🙏🙏🤲
Kou aimer sama commentaire yalla ngua ziare dji seydina mouhamed psl amine❤
@codoudiouf7568 Amine.
#BeteBeté arrive une série qui promet du lourd 🔥 j'en suis sûr ça sera le jumeau de la série #Njabar☝️ on attend la bande annonce
Force a vous evenprod 💪
@baldeibrahima4580 Ah ça oui.
Teint wou Thioro bi tmt machallah ❤🎉
@marishadiagne170 Teint noir dafa rafète.
@@evenprod machallah dal c très jolie ❤
Thioro sama tourondo mom rek lay topp machala
Nadité man dafmay rayy il est très naturel dans son rôle
Ndeysan le retour de moussa seck tu nous a tellement manqué
@beugfallou2853 Ah bon ?
Mach'Allah très bien ms even svp njaabar walla sakh munal guir yallah 😭😭😭😭khar nagn ma sonneuh😢
Des cœurs pour notre Prophète Mohamed psl ❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤ S A W
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Outre la réalité sénégalaise de la série, ce que j’aime après tout c’est la beauté des femmes…leurs teints naturels noirs❤❤❤❤❤❤❤❤❤. Superbe casting anti xessal.
@Utahanm Merci.
Meilleure maison de production au Sénégal
Sinon BÉTÉ BÉTÉ kukoy avec impatience rk lalal j'aime 😮
Le prophète psl a dit : Méfiez-vous de l'envie, (méchanceté) car l'envie consume les bonnes actions tout comme le feu consomme le bois, ou dit-il l'herbe. Sa morom bu amé lu bax yenekoko❤😮
Couple nandité bi momakoy def mann😂😂
@elhadjika7482 Merci.
Nandite est vraiment comique 😂😂😂 On dirait qu'il parle au ralenti. Nernako "yangui mamme deih"
Mane mom couple nandité laa beugg😂😂😂😂😂
😂😂😂
@famakhathiouba6946 Baadou ?
Avec l’histoire de Papito,Evenprod nous plonge dans nos plus profond secrets de jeunesse.Faire le Vip dehors et revenir à la réalité une fois chez soit.on est jamais prophète chez soi.Certainement pas un personnage facile à interpréter car il faut bcp d’adaptations,être star à l’extérieur,sous estimé par son père à la maison,confident de sa mère à côté Bref Evenprod vous êtes juste les meilleurs pour incarner notre vie réelle.J’espère que Papito ne finira pas victime de son succès à la fin de son histoire car y’a toujours de dures leçons de vie avec xewxew Evenprod.L’avenir nous le dira🙌
Machalla belle analyse
Car carpide carrotte karité carbounade cari s mourtalla jakarta yiy dooga daw
quél puns lien 🤔
Aythia mére thioro🔥🔥 6:40 6:29
😂😂😂😂
Yow sopey seydina mouhamed psl 🥰 mangui lay Niaan 🤲 nga abonné si mann guir dieumi seydina mouhamed psl 🥰❤️
Ravie de revoir les artistes que j'avais pas vu depuis longtemps
Alhamdoulillah ❤
@user-tn3yl5bd1v Merci.
Bolé instant bi mo eup problème Macky 😂😂😂!! Mais amna nitt you tiit am khaliss ni dossi dem Makka di kheuthio loterie 😢 thiey!!!
@ndeyebinetandiaye5371 Doyna war dal.
Tiit rék😅😅😅😅
Niaka doylou
Wayé mom néna ya souff lay diay mé esk lewna 😂😂
@@yakharasow1713 lou diara lidianti 😅😅! Est-ce que lewna ?
@@fatou1820 ba paré di diayy tang khol 🤣🤣
Noo ndandité moy nekhal série 😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉
@user-oh4ol4tn3n Baadou ?
De belles leçons de vie tous les jours avec Evenprod chapeau à vous you’re the best ❤❤❤❤❤❤
@Diobadiouba Merci.
Aby soleil levant ravis de te revoir ❤❤
@RokhayaDiouf-fd2hu Merci.
La scène de « babacar seu baay laaa » façon evenprod 😂🔥 noooon j’ai aimé ✌🏾😂😂😂😂😂😂
Tiéy Badiene ak Chacha mousiugnou dioubo c'est t'une long histoire 😂
Walay séne niaka dioubo ça remonte à trois longtemps 😂😂😂
Oh moussa Seck son retour ndeyssane ak aby merci
1er ou pas l'essentiel Moy magui setan donc alhamdoullilah ❤
@absafaye-ys9cw Alhamdoulilah.
Machallah série bou Nice ❤❤
@user-fd7ny6vg1n Merci.
Pule à l'heure merci even pro de respecter vos internaute ❤❤❤
@yayemayelatmbao5442 Merci à vous.
Respecté heures mom yénako fi déf béneu problèmes guén am Mouy suites des séries légui tay guén mélni niognou ani impuissant njabar munël infidèle
Impuissant ak munël mom sokhla nagne retour bou yagué guén mélni niognou may bagna toudou serie bou bess c'est bien beau mais guén égali sén serie yi nék avant🤧😏☺️
Fo faté VAUTOURS
@@abydiop3692 AK vautours tamite😂
@@ndiayendeye4713 mais avant lolou yeupp n’a cœurs brisés saison2 nieuw ba paré
@@abydiop3692cœurs brisés migui dora dieh de
Ils ont déjà dit les séries qui n'auront pas de suite njabar impuissant munel fake life entre autres 😢😢😢
Mbeuguélou Thama mo méti deug deug tekci bou Nandité😂😂😂
@soukeynaba-wz4bc Baadou ? 🤣😂
@@evenprod ah li tamit
3:54 Quelle noirceur ! 🤩 Macha'Allah
@khadijacherifa Merci.
Théâtre bii daffa gueune nékh ❤️🇸🇳
@FatimaRassoulSeydi Merci. Loutakh ga wakh lolou ?
@@evenprod xanna sma niomeus tonton xanna nawle tton guagne ❤️❤️❤️❤️ AK leçon de vie 🙏
Nexoul ba nexoul man nandité damako bg😂
Da meune 😂😂😂
@beugfallou2853 Loutakh lolou.
@@evenprod ça façon de parler 🤣dafmay fadj
Soukey ak copain wamm bi dinanie ma rayy😂😂
@KatyFaye-yu6kk Loutakh lolou ?
@@evenprod niomm niarr khamouma koussi tané moromame
Couple nandité ak Soukey moo gueuneu nekh si série bi 😂😂😂bolé tamite ak diabar dji moo dakh nekh 😂😂
wa khalè yi tay mome dama daw togou rère 😂😂😂😂je vous j'aime 🎉
@evambaye6476 Merci.
@@evenprod yen rek lay topou depuis idoles ba xew xew di khar betè betè inchallah ❤
Kou contane ci arrestation bb rasta lalala ❤
Célibataire yi boulène dara méti ndakh saint Valentin dafa kharame😮😮
Bb koula ko wakh ❤😂
@@Khadim-mk5cg😂😂😂
@@mamediarrambaye1220 loye 🤣do wakh foko tek salibater yii laka len nak bb😂😂
Le retoure de Moussa seck ❤❤😂😂
@user-xi9yy9ci7u Merci.
Mais le copain de Soukaye est drôle nena ma sarmada ba si bur😂😂😂
@helenediouf4641 Dafa nekh
Yalla na diamou yague ❤ ❤
@NdoyeSport Amine.
Deuxième commentaires enpouna wa eneprod yéna ponctuelle kay❤❤❤❤❤
@amysall4482 Merci.
@@evenprod De rien mais ont réclame le retour de infidèle
Moussa seck tamit tite neu am nga xalis di basèwou ci loterie pour dem makka non mane nandité 😂😂😂niambé sen ak demam makka bi diabar dji dal ganalé bi moko sonal
On réclame munël saison3
😂😂😂😂PA Bolé mogui may raye
@moriciss6368 Loumou défati ?
@@evenprod 🤣🤣🤣khana diw bou tang bi
Citation de l'épisode : " doxane lou mou nekh nekh à delain ley moudjer ". Nandite 😂
Yaw mi Di lire Sama commentaire yalla nga dougou aldiana souba 😭
Amine niou bokkou koh in sha allah😢😢
Amine niou bok ko🙏
Ma fék lafa
Toi aussi koudé wagoul noumoy dougué aldiana souba😂
Lolou dh moy yalla nga dhée souba 😅
Mafi djitou dou deugue🥺❤️😜
@DiarraSaliou- Amna nioula gnitou.
😅😅😅 j'adore xew xew
Nous réclamons la saison 3 de la série munel
Il n’y pas de suite pour Muniel
Bilay 😅😅😅😅
Wa Louga séne dome amna name❤❤❤
@khadyfall8249 Hummm !
Sheuuuuuut pa bolé on t'a averti 😂😂😂😂😂
Mane Bolé damay fathie barki yalla 😂😂😂😂
@user-oz8el2td8h Sur quoi ? 🤣😂
Diwlinn bou tangueuh 😂😂😂
@momofaye2658 Bolé rek ak Thiama ! 😂
Pa bolé yeureum nako 😂😂😂
Bilahi
@YayouKhaleyi Loutakh ?
Wouy pa bolé raynama 😂😂😂😂😂
@user-yt7hj1in6c Dou nittt. 😂🤣
Bolé 😂😂😂😂Mise en garde gaye am fofou 😂😂😂😂😂😂il m'a terminé
@antoinetteafoutou2281 Thiama rek. 🤣😂
Mannn instant bété bété moma téré nélaw ohhhhh coup de cœur 😍 ❤️ soumboulou mo thiopati sama hol bi😊
Bly doukouré ya muné kay 🎉😂😂😂
@YayaYaya-gr7qj Bayiko ak Thiama rek. 😂🤣
Lalou doukouré bi naonade ak diabar dji 😂
@KineMbodjie 😂🤣
Oooh ma belle aby je vous j'adore ❤
@beugfallou2853 Merci.
Après xew bi louy xew?😮
Xew xew 😂😂
@@fatoundiaye1999😂😂😂
Xew xew
@coumbisgaye1753 Xew Xew.
Non nandité damay fath nenako « yaw sama œuvre gua😂 »
@diarraboussodiagne8965 😂🤣😂
@@evenprodsou nguen di def tournage nane nguen di def ba nandité doulen rélo 😂sheuu
Bilay j’aime mére thioro ❤
@astoukasse6114 Merci.
Expression djongoma bilay dineu dougueul niite mère bi néna aladji bou djongoma😂😂😂
@teresediagne6993 😂🤣
Nandité rew n'a bilaye😂3000
@SeckTosa 🤣😂
Yaw mi lire sama commentaire yalnagua gagné biet maka amen
@DeniseSene Amine.
Yallah nagnou yallah soutoural ba gnou dieundeul ko sougnou bop si barké ya rassoulilahi sas
Fallait que sasha ak badiéne woudjé dal 😂
😂😂😂😂Cho bolé néna dafay tekkk khel dei ak calment yi😂😂😂😂
Machalla❤❤😂
Au moins sakh tay bala am 3 ma commenté 😂😂😂
Even prod vie sur vous ❤
@Le_R319 🤣😂❤️ Merci.
Nandité conjuguons le verbe yarou😂😂😂
.
@laperlecmoi5995 Commence. 😂
Xew xew ak keur mansour Lou ne la❤❤
@mbodia6392 Nekh la def. 🤣😂
Pa bolle mock macki ndio yam ay problème😅😂mé nandite damako beug bilah😂
@user-wh2lp8cy9s Baadou ? 😂🤣
@@evenprod nou demande chaq épisode un sekas de nandite😂🤣
Pa bolé😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂Nandité tamit kou réw leuh😂😂😂😂😂😂hiiiii balma🏃♀️🏃♀️🏃♀️🏃♀️
@pendadiop6753 Yagui daw ress. 😂🤣
Nandite reew na😂😂😂😂😂
@lixalimaywax5037 Ba dof. 😂🤣
Nandité « dokhaan loumou nekh nekh a demain lay moudié » ma dead 😂😂😂😂il a raison célibataire baxoul😅🎉😂
Team bolé😂😂😂😂
@user-wg5fn6ei4e 😂🤣
Dandite ray nama🤣🤣🤣🤣sheut 😭💔🤣🤣
Liguena miti siadouna Moy nèkale kowolouwoule 😂😂
@user-xi9yy9ci7u Lolou dh amna. 😂
Bolé et sa femme 😂😂😂
@moussethiam9236 😂🤣
Mafi Dji you🥰
@adjinalaisabelseydi3714 Amna koula gnitou.
Serie yi ak théâtre yi sonal ngen pape yi
deln niou diokh role bilou bahh
@PICAM_Prod Baadou ? 😂
Thiama ak bolle 😂😂fougnou moudje d’où bakh 😂😂😂😂
@awabarro282 Baadou ?
Thiama mom dafa sokhor trop😂😂😂😂
@aidasamb591 Loutakh ga wakh lolou ?
Bonsoir a tous
@astoundiaye7601 Bonsoir !
Boukén faté 25 février
😂😂😂sodè kay
@veroniquediaw4527 Thiama rek ! 🤣😂
Bole 😂😂😂 wouy
@dieyba1007 😂
Nandite la beug 😂😂😂😂😂😂😂😂
@NdieumbeuteMbodj Merci.
Nandité tmt sheuteut 😂
@binetadiop2995 😂🤣 Noko guissé.
@@evenprod no il est calé c mec il joue bien son rôle o6
Nandité encore 😂😂😂
Sans oublier bolé osi
Ay way bly xéw bi yeup ganalé gui la wa baxna dal
@NdeyefatouNdiaye-vp5uq Dou yomb dal. 😂
Sacré nandité dinama ray dafa meune kay😂😂😂
@berthamendy7439 Namoul dara.