_Yal na nu Yàlla boole ak soxna su baax jigéen dafa am doole ci góor man na ko defaral man na ko yàqal man na ko baaxal man na ko bonal kon yal na nu Yàlla di boole ak bu baax bi ndax mu man ñoo dimbali ci sunug dundu aaamiin._ 🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Allakhouma Amine ! Mais djiguene graw neu . Khôlal meu kii loumou conseiller kou goor ki rek après bou Li passer mou dess ci probleme mou takhawé neulé. Kou Tchi amoul khel yakou ngua sheuuuu
@@Diija02 _Moom kay Soxna Xadiijatu mbir yi yéeme na lool wallaahi dafa am lenn ci jigéen ñi ñoo xam ne dañoo gàtt xel lool te ñooy dugal seen boroom kër yi ci jafe-jafe yu bari yal na nu Yàlla dollee dimbali te di ñu boole ak ñu baax ñi muy boroom kër ak soxna yu baax yi rakk a jar a tànn._
Xew xew les victimes du paraître les thèmes relater depuis le début sont des faits de la société actuelle et nous devons en tirer des leçons pour l'avenir ❤❤❤❤
@@sigadiagne1836 bilay les parents aussi dagnou wara kham té bayii khalé makam dikko tékk si yonn sinon euleuk bou yakho bougnou né kénn moko liguey dakh Excé D'impolitesss rend fou
Gbambé c'est un meneur il pousse les autres a jouer en même temps il équilibre la prestation sur la gamme fiction/réalité il a avouer et reconnu la qualité de son amitié mais il victime d'une implosion: l'influence de la femme, la pression sociale, et l'incapacité de prendre ses responsablités
Ndeyssane goor you beuri sen soxna yi ñolène mirass té déwa gou ñou aduna dou ben bis rek il faut penser à l'avenir de ses enfants une fois nga guéne aduna 😢
Pa Samb bi ak ndelame bou nioule bi ndekè amoul.khalat dh naka lala sa diabar di conseiller gua diaye sa keur ndakh nguanalè ben fane gua rarka def yagui si erreur nk 😢
AMY COLLE rewna, khamadi lol té pank ! comme yayam 😅 jakarlo ak sa mak diko manqué respect ni alors que mom mi mon nekoul ti deug (yark courant leu def), beuparé sen baye di niew aatéwoul deug, nane "li nga fayi 2 wer nga diap né danga mom keurgui" ! ay borom keur dey am fayda ak foula nak 😔😔😔😔 bravo au grand frere, il est trés responsable 😍
dou yone, khalé degn ko yar, diko khamal né courant degn ko fayi té xaliss dougn ko for, degn ko liguey ! waayé yallah bakhna ! courage @@sigadiagne1836

ma leu wakh lolou🤣guiss ngaa ci episode 29 bi, djeukeur dji sonou ba beug dé, mouko forcé wat affairou makka ! ay niarel yi, beug nalen waayé ay seytané legnou 😂😂😂🥰🥰 @@maguitaseck69913
bonjour Mgui lendi ziar bubakh namon nalen ❤🎉 mba yenagui sii diam bubakh alhamdoulilah ❤🎉 Chapeau à evn prod ❤🎉 Serigne ngagne message bi machallah amna solo ❤makka dfa am ay sarte tee lolou ken warou koo tegui ken wahoul bou ken dem mais thi kaw gua meun ko kon lii Serigne ngagne wakh lou am solo laa ❤ machallah chapeau à vous ❤🎉 سكرن ❤❤
Non mais la noirceur d’ébène de thioro on en parle😭?? Mais quelle beauté manchalla.. merci even prod d’avoir valorisé la peau noire
Walahi Serigne Gagne a raison sur toutes les lignes merci beaucoup evend pros la leçon est bien passé 😢😢🎉❤❤
Serigne ngagne chapeau à lui vraiment il est exceptionnel
Je suis d’accord avec vous
Bilahi ioe tu as raison ❤❤
J'aime Ngagne depuis que je suis petite. C'est mon comédien préféré et j'aimerais le rencontrer un jour 🙏
Vraiment c'est "ça" qui se passe dans notre société 😢
J'aime cette série parce qu'elle éveille la conscience des nouveaux génération 😊
CHAPEAU À VOUS
Des nouvelles générations rectification
Des milliers de cœur pour notre prophète Mohammed PSL ❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤ psl
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla n'a yalla defff diamm Sénégal amine
_Yal na nu Yàlla boole ak soxna su baax jigéen dafa am doole ci góor man na ko defaral man na ko yàqal man na ko baaxal man na ko bonal kon yal na nu Yàlla di boole ak bu baax bi ndax mu man ñoo dimbali ci sunug dundu aaamiin._ 🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Allakhouma Amine ! Mais djiguene graw neu . Khôlal meu kii loumou conseiller kou goor ki rek après bou Li passer mou dess ci probleme mou takhawé neulé. Kou Tchi amoul khel yakou ngua sheuuuu
@@Diija02 _Moom kay Soxna Xadiijatu mbir yi yéeme na lool wallaahi dafa am lenn ci jigéen ñi ñoo xam ne dañoo gàtt xel lool te ñooy dugal seen boroom kër yi ci jafe-jafe yu bari yal na nu Yàlla dollee dimbali te di ñu boole ak ñu baax ñi muy boroom kër ak soxna yu baax yi rakk a jar a tànn._
@@murtadaajonn6502 Billay ! Yallah na kou Yallah takhawou rek inshallah 🤲🏾
machallah j'aime les reactions de serigne Ngagne car il est véridique et un vrai comédien😂
Non seulement ils nous font marrer mais en même temps ils nous donnent des leçons de vie bravo aux artistes et chapeau serigne Ngagne😂❤❤
Ko d’accord sili serigne ganié waxe sambe rk❤
❤
Deug bou weurr lako wakh dakh dem adji da am yone
@@MounassCollydégeu na degeu deh ❤
❤❤
❤️❤️❤️❤️
Xew xew les victimes du paraître les thèmes relater depuis le début sont des faits de la société actuelle et nous devons en tirer des leçons pour l'avenir ❤❤❤❤
Billahi deuggleu lii niou jouer tay nioun moom laniouy dound instant yi taal télé taal ventilateur kou wah niou sikklaa
@@sigadiagne1836 bilay les parents aussi dagnou wara kham té bayii khalé makam dikko tékk si yonn sinon euleuk bou yakho bougnou né kénn moko liguey dakh Excé D'impolitesss rend fou
Machalla complicité nganie et niambé c'est autre chose ❤❤❤❤
14:24
Yagana❤❤
Yalna nagniou Yallah mousoul si djiguene bou bonn 😢😢😢😢😢😢🙏🙏
Amine
Yalla na lene gnep degue vraiment cette série est très intéressant Serigne ngagne chapeau à toi et à toute l'équipe merci beaucoup
Temps yi série bi guatt na trop 😢 merci even prod pour cette série magnifique 🎉❤
Paix et salut sur notre Prophète Mohammed ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Gbambé c'est un meneur il pousse les autres a jouer en même temps il équilibre la prestation sur la gamme fiction/réalité il a avouer et reconnu la qualité de son amitié mais il victime d'une implosion: l'influence de la femme, la pression sociale, et l'incapacité de prendre ses responsablités
Ndeyssan ben la ci yayam mo sank dome you berii.. khallé bou néké ben sakh dagni kay yaar mai rewal ko naan ben la bakhna 😢
Bamou doné bén nga warone yar té khamné bou yakho nga sankou ndakh kén la
@@aissatoumarone2095 walay ndeyssan
thia deug deug @@aissatoumarone2095
dou yone ! li yeu beug defanté monko waral
@@lala_aishaa bilay
Samb nak ngagne wakh na la deuk yaw amo dépense di dém maka😂😂😂😂😂
Merci 😂
Wax dëgg Yàlla! Yàlla tegu ko ko. 😂 😂
Blie 😂
Nn Serigne ngagne dafmay raay Koi 😂😂😂papito mére bii mongi laay yakal ohh 😂😂😂😂 papito parent yii loutax Lou sén dom beugue rk nioimay tanal niit Moy tanal bopam limou beugue parents yii bayilé lolou ahhh😂😂
Badiane lafi dégue dh Badiane sakoura wally ani wa mbadianéne manifesté vous 🎉🎉
Djiguene moy dougueul goor you Noye bop si lou nk
Xew Xew merci sii concientisation nous les jeunes mariés.
Ndeyssane goor you beuri sen soxna yi ñolène mirass té déwa gou ñou aduna dou ben bis rek il faut penser à l'avenir de ses enfants une fois nga guéne aduna 😢
Ken Dou Chiekh ahmadou Bamba
Bilahi
Bilay amna djiguén nio kham ni amouniou béne khalate diay sa keur walla taylé ndakh xew
Bilahi niarel bi mom bakhoul
Khana tay dina ame ay cœur
Pa Samb bi ak ndelame bou nioule bi ndekè amoul.khalat dh naka lala sa diabar di conseiller gua diaye sa keur ndakh nguanalè ben fane gua rarka def yagui si erreur nk 😢
❤❤❤❤❤Ngagne deug rek gua wakh samb ligua wakh dara dou ko dindi
Machallat notre prophète mouhamed❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Je l'aime trop fort ❤❤❤❤
SAW❤❤❤❤
Il faut economiser le courant aussi yakk baxoul
Pére sambe bayil sanou village bii dé ( DIACK ) Mais on t'aime 😍😍😍
Yala nagnou sougnou borom mouseul thi borom keur bou djiengue thi ndiabotam 😢
Amiin
Ana nitou thies yi
Mane d sama keur Mame mongui fa 🥰🥰🥰
AMY COLLE rewna, khamadi lol té pank ! comme yayam 😅 jakarlo ak sa mak diko manqué respect ni alors que mom mi mon nekoul ti deug (yark courant leu def), beuparé sen baye di niew aatéwoul deug, nane "li nga fayi 2 wer nga diap né danga mom keurgui" ! ay borom keur dey am fayda ak foula nak 😔😔😔😔 bravo au grand frere, il est trés responsable 😍
Samb brome keur bougni dape di gnade😂😂
exactement ! borom keur bouniou dab di niegnt kay 😂😂@@modousarr5113
Louniou jouer nonou instant yi nioun lolou laniouy dound souniou keur haléyi daniouy taal télé bi Ak ventilateur bi bayyi nonou soo wahé niou sikk la
dou yone, khalé degn ko yar, diko khamal né courant degn ko fayi té xaliss dougn ko for, degn ko liguey ! waayé yallah bakhna ! courage @@sigadiagne1836
Ku xew-xew bi yaw. 😂 😂 Sàmb mbaa di nga dem Màkka rekk ? Bolle dina ma ray rekk. 😂 😂 😂
May léne ma ayy ❤❤❤❤wayy
Teel sa courant
Teyel sa ndox
Ndiambé ni nga atté bzhoul dehh😂😂😂
Merci EvenProd il faut toujours passé après le wew wew
Serie bi nekhna trop mais 35 épisode da khawa touti
Chapeau à Evenprod 🎉
Samb sa gnarel bi limoula conseiler bétouma khalatonako wayer dingako rétiou 😭
Bilay li c tellement vrai 😂😂😂 beugu degu Alaji diarna liiii
Yaw diayo sa keur ganalé Ndakh gay taylé sa keur dieukeur pour ganalé😊
Ndayesan mansour kharit bou melni mom yomboule Boudon kanenla dou df ly
Chapeau à Evenprod ❤❤🎉
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ bonne continuation
Une réalité purement sénégalaise chapeau à éven prod❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤❤
Yonente bi psl Ken douko niane yalla laniouy niane
lolou noumouma meti wala wateu si mome
non ma beug yayou papito bonne leçon nguéne tiré fofou niaw😂
Limay demander moy dakh bén si yayam douniou koo yarr lii mo takh khalé tay yii kou séyii tay retourner le lendemain 😅😅
Seri bi nekhna way machala
Louma degue diaye wala tayla pour lane Ganalé 🤭🤭🤭😂😂😂
Papito sa Copine bi mom modë na di 😂😂😂😂😂
Merci beaucoup ❤❤❤❤
Sallalahou hala mouhamad
Noo mane diamé sene la beug 😂😂😂😂
Wax deugeu ngagne linga wakh samb moy deugeu lila kharit di diarigne mai sa gnarel bi doulasi bayi
Gnambé un grand artiste il fait bien son rôle Macha alla
Gbambé c'est un meneur il pousse les autres a jouer en même temps il équilibre la prestation sur la gamme fiction/réalité il a avouer et reconnu la qualité de son amitié mais il victime d'une implosion: l'influence de la femme, la pression sociale, et l'incapacité de prendre ses responsablités
Gnambè bi dfa GUEN adouna walla
Thieyyy nous les femmes xew sur xeww 😂😂😂😂
Père samb yaa bonn awoh yalnaniou yalla mousseul🙏🏿si xallat bou bonn
Guel papito soutien gorge motakh famille bi accepter wougnela😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂Woy
No kheff yi kay 🙄
😂😂 Ndiambé Serigne Ngagne dalay tékk xéll😂
Non deugue lako wakh dh
Ndiambé dém Makka wathinako
Maye len ma j'aime premnier vue❤😂🎉
😂😂 bilay sa keurgui boko taylé diga day digou ndakaru
Non day digou thiès
😂😂😂😂😂😂😂
Ngagne il est vraiment exceptionnel ❤🎉🎉
Yalla na diamou yague ❤ ❤
8:08 cette scène est celle que tous les parents doivent voir
Fi dh warone nagn fi leral charte yii nitt wala matalei bala mo dem makka
Épisode passé pourtant 1er femme samb préciser nako deh
Èpisose passè
Dina ame après
TEYLÉ BANE KEUR?????
ALLAHOU AKBAR
Une production hors commun 🎉Toutes mes félicitations @evenprod ❤
Tite na sakh mane diay keur kay yalla téré
Xew Xew len sama commentaires bi 😅😂❤
💃💃💃💃💃💃💃🕺🕺🕺👯👯👯
Aye wy ko yéde Abi 😂😂nila ky dafa diot wy Mo sole Lo diot😂
Leegi dafa magal dagay deme ba yakoye bayil sa bop
Niou sikk niou melni men khana😂thi épisode passé
Bolé dafa beug kharou té niémé woul🤣🤣🤣 . Serigne Ngagne wakhna deug deh mais j'espère que bougoul soufou Niambé rek!!
Wax na ko dëgg amul dempens ba noppi bëgga de Màkka te Yàlla tegu ko ko.
Pour temps Loum ko conseiller degeu la
@@MouhamadouNdiaye-mq1je deug la kayy mais na fekk ni mom woutou si dara rek!!
Le pére de amy collé est irresponsable il a peur de sa femme
dafko nop ba and toul ak saagome ! niak fayda leu def
Je déteste ce genre d’homme 😢bala niouy kham rek khamadi ray léne 😂😂
Et il négligent sa première femme et sont fils au profit de sa deuxième femme c'est malheureux de voir des hommes comme ça !
c'est vraiment triste hein ! mais il fait à son propre détriment...il va mal finir @@sarahgnigouan5174
Rétanou bolé yi😂😅😅😅😅😅😅😅
le senegal dépense plud de 50 milliard de franc chak année. et aprés on dit que nous sommes dans un pays pauvre
Samba mo nara wayadi 😂
Démago Macka di lidieunti nganalé tiey lii 😂
Papa toutimou mbatiemeu colé moréw 😂😂😂
Sama keur dé sama diabar soumané ma taylé kerogue gua fanani sa keur papa
Ceux que la 2e femme de Samb lui a proposé est complètement choquant
5-2-3 sort de ma tête stp kom can bi diekh na 😢
Nieup la dal danio mougn rekk 😂
Jabru dañu koy tànn, Sàmb sa jabar ji moo la nara yóbbee musiba. 😴😴😴😴😴
Pa bolè 😂😂
‼️‼️‼️ Touba amna quartier yo khamni depuis Magal Touba batay amouniou ndokh 😢
Amna domou niarél you rèw😂
Domou niarél là deh wayé réwouma trop
Djabar daal dagnekoy taan beug poukheré ba dougual la si moussiba
billahi, diabar degn ko tane ! niarel bi dafa yeye nopou djeukeureum té dara dou yenggou
@@lala_aishaa😂😂😂😂😂😂
ma leu wakh lolou🤣guiss ngaa ci episode 29 bi, djeukeur dji sonou ba beug dé, mouko forcé wat affairou makka ! ay niarel yi, beug nalen waayé ay seytané legnou 😂😂😂🥰🥰 @@maguitaseck69913
Focus diomaye Moy sonko ✊🏿
😂😂😂😂😂 rien à foutre
❤❤❤ psl
Walahi nganalê sou takhé nga taylé sa keurgui 😂😂😂
Bilay 😂
@@mbenista_2002 yénay dougeul goor si louneik 😂
Paÿeu tourr bou nékh la ❤
Dooop com dab 🥳💪🏾💪🏾
صلوات على النبي كل كم ❤
Papito sa casquette eupena😂😂
😂😂😂😂
❤❤❤ merci
bonjour
Mgui lendi ziar bubakh namon nalen ❤🎉 mba yenagui sii diam bubakh alhamdoulilah ❤🎉
Chapeau à evn prod ❤🎉
Serigne ngagne message bi machallah amna solo ❤makka dfa am ay sarte tee lolou ken warou koo tegui ken wahoul bou ken dem mais thi kaw gua meun ko kon lii Serigne ngagne wakh lou am solo laa ❤ machallah chapeau à vous ❤🎉
سكرن ❤❤
bella ak fat dame gno manqué si série bi
EST CE QUE SERIGNE NGAGNE LIMOU KHELAL SAMB BEUG DIAMAM LA WALA DAKO IGNANÉ DÉM MAKKA BI? VOS PENSEZ S'IL VOUS PLAIT
Degeu lako wakh
Ignané wouko dh nakh Serigne Ngagne sokhoroul kon douko diox dépenses pour keureum
@@adjisabelba1306 ndakh mom rékk mokoy dimbali
Peuyeu tmt waouh kel femme😍❤️