Hommage à nos condisciples qui ne sont plus dans ce monde une pensée pieuse à Abdou Rahmane seck , Papa Hady sow comme disait le verset coranique les personnes qui sont mort dans le chantier d’Allah ne sont pas mort ils vivent au près de leur seigneur
Salut ! J'aime beaucoup le zirk de tous les SBN ça m'apaise beaucoup😍😍😍. J'espère qu'un jour j'aurais la chance d'être là lorsque vous chantez... Je suis Camerounaise et je vous aime beaucoup. Mais je ne sais pas où trouver les paroles de sariman😔😔
Merci beaucoup à tous ceux ou celles qui ont contribués financièrement et moralement à ce Grand projet merci à tous mes collaborateurs ❤❤ nos portes sont grandement ouvertes à tous qui veulent participer aux projets futurs clip Bouliitou bientôt ❤❤
@@MadiaraSBNofficiel Mes salutations à toi mon frère, je veux que tu demandes aux grands amants de Baye Barham de m'aider, parce que j'ai beaucoup de prêts sur moi, je veux que les amants de Baye m'aident là-bas, frère, j'espère que tu m'aideras avec ça s'il te plaît, merci
ماشاء الله ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Hommage à nos condisciples qui ne sont plus dans ce monde une pensée pieuse à Abdou Rahmane seck , Papa Hady sow comme disait le verset coranique les personnes qui sont mort dans le chantier d’Allah ne sont pas mort ils vivent au près de leur seigneur
❤️❤️😭😭🥺niko Baye bindé nguako weuyé andak dale gou matt deuk💪🏾💪🏾❤️❤️Baye Niass contane neu
Mome sokay déklou loo deugeur deugeur diooy en tant que Mouride @Madiara_Niane jamm ak tawfeekh rk lanioulay nianal soppou naniou la lool machallah ❤🙏
HOMMAGE A NOTRE PERE PAPA HADY SOW REST IN PEACE PAPA MES CONDOLÉANCES À TOUTES SA FAMILLE et toute la Famille @Fityanou sidkhine
Ndeysaan Ndeysaan 😭 😭 💯
Beugeu n'a la look ❤❤❤❤
Merci mon frère
Walaahi ndeyssan
Salut ! J'aime beaucoup le zirk de tous les SBN ça m'apaise beaucoup😍😍😍. J'espère qu'un jour j'aurais la chance d'être là lorsque vous chantez... Je suis Camerounaise et je vous aime beaucoup. Mais je ne sais pas où trouver les paroles de sariman😔😔
Xam naa ne daal góor dëggëntaan Njaay mooy yaw. Yalna Yàlla wétal baat bi ci barke Mawlaanaa Sangg Abuubakarin Barhaamu Njaay kiy sangu mbooleem haarifiina yi yëpp kum neex ak kum naqadi 💞 ❤️🔥 💪 🙏 ❤️🔥 💯
😂
Khoutbou zamâne bou maîtrisé limouy wakh😂😂😂😂😂
Notre Diara Machallah Niongi Bek thi yaw
merci cisse bachir
❤❤❤
Merci beaucoup à tous ceux ou celles qui ont contribués financièrement et moralement à ce Grand projet merci à tous mes collaborateurs ❤❤ nos portes sont grandement ouvertes à tous qui veulent participer aux projets futurs clip Bouliitou bientôt ❤❤
Assalamu Alaikum
@@MH2UAG wahleykz salam
@@MadiaraSBNofficiel Mes salutations à toi mon frère, je veux que tu demandes aux grands amants de Baye Barham de m'aider, parce que j'ai beaucoup de prêts sur moi, je veux que les amants de Baye m'aident là-bas, frère, j'espère que tu m'aideras avec ça s'il te plaît, merci
Vraiment madiara tu apaise mon coeur❤yalna yalla goudale sa fane mou ande ake wèr ake werlé❤🎉
Machallah aleyk madiara 😢😢,
Je suis mouride mai j’aime beaucoup les chansons niassen vraiment khol sedatina❤
masàalah saa weey wi am na fasaahe lol faall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup mame baye beugeu baye niass rék point ila médina baye kaolack inch'Allah ❤❤
Yalla n'a suniou borom wereul batt bi
Mashala
Mâchalla yalla na yalla weral bate bi
❤❤❤❤❤❤ merci papa contan bilaye
Ndeysaan 😢madiara bo khamone lingay weuy noumouy déf nitt mannako ray sah billahi
Mashallah lii nékhna trop walahii yalna yalla dédal leu diam fo meuna neik
Beug nagn leu trop walahii❤❤❤
ماشاء الله ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalla baye niasse fayal la boppam❤❤❤❤
اللهم صلى وسلم وبارك على سيدنا محمد وعلى آله وصحبه أجمعين ❤🎉
Gnanalene ma ay jumeaux ma toudeko seydina Mouhamed psl
Yalla nala yalla maye ay jumeaux inchallah
@@MadiaraSBNofficiel aaaamiiiine yarabi cheikh bi
Machallah yalla na yalla weral batt bi
ALHAMDOULILLAH, MACHALLAH Serign bi.💕💧〽👌
Machallah ✨💖 que dire de notre Mawlana CHEIKH IBRAHIMA NIASS 📿💖 C'est le meilleur poète du Prophète Aleyhi Salatou wa Salam
Vraiment je suis fière d'être talibé baye khôl sédeuna machallah frère 🙏🤗🤗❤️
Thiey😂😂😂jes pas les mots❤❤❤❤
Niane Samba tasso yakkar dh😫🥺😭❤️❤️
yalla na yalla wéral batt bi yarabi
Nexxatinaa🎉❤
Alhamdou lillah way li neh na barke yarassoulallah yalla n'a yalla wéral batt bii yarabi SBN dieuredieufeti ❤📿✔️
Unfortunately u are the best
Machallah Baye rék moy deugue
Yalla naniou yalla fayal Baye Niass❤
Machallah contane nagnou billay sama khole toyena billay
Yalla na yalla barkél la Madiara barké seydina Mouhamed
Machallah xol yi sedd neu ❤❤
Machallah frère continue روح القدس معك
Ma Diarra dieul ga raw gadou bi❤li nehna way Barki Baye Niass
Thieuy Aladji Ibrahima yalnagnou yallah fayal ya'rabi 🙏🙏
Yaw aussi Madiara yalna yallah Faye si barké Mawlana❤
Diarra guene gua athie level bi❤❤❤❤
Alhamdoulilah Alhamdoulilah sante yalla bignou amé Mame Baye Niass téke thie beugue ko machalla machalla ❤❤❤
VOUS POUVEZ ACTIVER LES SOUS TITRES POUR VOIR LA TRADUCTION DE LA DEUXIEME partie en anglais
Dieureudieuf baye niass ❤❤❤❤
Barki Baye Barkhama Niass❤❤❤😊😊😊😊alkhamdoulilah dieureudieuff Madiara sangue Barkhamou Ndiaye yalla naffi yagg loll té andak wérrr si Barké Bayam Baye Barkhama Niass 😊❤
DIEUREDIEUFETY MACHA ALLAH....
Mi weltimeu ❤
Barker baye Niass kèneu Dou yaw...Le zakir du peuple🎉🎉
Domou SBN yalla na sa Diam yague ❤
Lou nekh kay yaw rek lagnou done khar mon Zakir préféré la voix paradisiaque machalah
Barke Baye Niass nexatina ❤❤goudal fan way😊
Mashalah Baye 😊 toujours au top. Yalna Ndiaye weral bate bi té barkel dahimane sarmadane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macahlla yalna yalla barkell sareg bi
Ta voix fait frissonner nos cœurs ❤❤ yalla n'a yalla Faye yiwe
Est ce que sougne khôl ❤yi mngui yegeu borom kawnou bi machalla 😊 alhamdoulilah 😊
Macha allah nexna trop ❤❤❤
Talibe ba maam babacar wayer dmalén beugeu ba niiit gni talibe bay lagn my wowe😮
Machalla yalna Ya Alla same yok wéral si barké Nabil Moustapha ❤
Mashallah niane samba figa guene nati nekhe nagnou trop doumou SBN ❤❤❤❤🎉
Machallah nèkhna zakir Madiara niane
Masha Allah Yalla na borome bi swt wereule batebi si barke ya Rassoulilah psl
Sunu wadji ya meilleur ❤
Barki Baye Niass nékh na lérna,💪💪💪
NDeyssan NDeyssan 😭😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤❤
Bilahi content nagnou mashallah 🥰 fière d’être une Talibé Cheikh Ibrahima
Jarajof madiara ilall amam ❤❤❤❤❤
Ôh 🤝 ndokeel naniu lë Madiara ! yAllah na sa jamm sax 🤲!
Hommage à notre père el hadji aliouane top que Dieu l’accueil dans son paradis éternel
Macha allah ❤ madiara yalna yalla barkél téh mottali lèp ya rabi
Aamine ya rabbi
Machalla yalla na yalla wereul batt yi té barkel len longue vie à vous 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Thioumm sama wadjii ❤
Alhamdoulil'lah
Alhamdoulil'lah
Alhamdoulil'lah
Jéréjéfé baye jéf ❤
Macha allah seydi Madiara Niane yalla na gueuna weereul batt bi
Mashaallah loumou deff dafay nekh barki sangue barhamou Ndiaye
Mashallah sama zakir bou mak bi yalla na yalla yokou Say relere❤❤❤❤
Eskey 😢❤️❤️❤️❤️❤️❤️Machallah mon frère d valeur
Ndeysane Madiara Niane la voix d'or yalna sangue barhamou ndiaye fayal gnoula
Dieureudieufé Baye Niass 💎😘💗💗💗
Machalah yalna yala wéral bate bi
😢😢❤❤ thieye ma diarra sa wadji
Goor nga
❤❤❤❤ Ndeysann machallah yalla nagnou la yalla fayall bopam
Ma sha Allah serigne bi Diamano gouné yanyi toyal xol sofianké yi ❤
Machahalla ❤❤❤❤man yaw rek la beugue 😢❤
Walahi nexna trop baye madiara sama xarit sama sopé ❤❤❤
Masallah sama xol bi sedda na barkeh baye niass ❤
Machalah Allahou Akbar li néxna trop ❤❤❤❤❤❤comme toujours
macahlla ❤❤❤❤❤
Macha Allah, i had been waiting for this Zikr almost a year, the first time heard a very short clip with it.
Barakallah
Macha allah nexna trop
Sangue Ndiaye Goor ngeu yangi ligeyeul Baye niass ❤️
Diara Masahalla merci 🙏 ❤❤
Clip bi set na seell na way bi neexna amul dara lu débordé ❤
Merci beaucoup mon frère
Liii dafa yéémé Barki Baye Niass 😓😓😓😓♥️
Masha Allah très belle voix 🥰😍😍
Dieureudieufééé Baye Niass rta🙏❤
BON GAMOU A TOUS ❤
Nekh na ❤❤ndeyssane
Ndeysan Maashalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Chair de poule laay am soumay deglou lii❤
Sallallahu Alaihi Wassallam 🤲🏻🤲🏻🤲🏻😭😭😭😭😭💙🤍💜🩷🩵💚
Vous m'avez fait pleurer plusieurs fois 😢😢😢😢😢😢
Machallah frère nexna rafetna ❤️😍🥰