Wakh bi diékh na tak. Qutba imam bii moy solution mais aussi moy yone bi niou wara diaar inshaalah. Yalla na souniou borrom takhawou sonko té dieuléfi gni diniou djité té tégouwougn foudoul thi yonou cheiyane. Allahouma sally wa salim alla seydina Mouhamed.
OUSTAZ machallah ! C'est formidable comment vous êtes engagé en toute liberté de connaissance. Je pense que d'autres n'ont pas l'intellectuel de comprendre librement pour participer jusqu'à même s'engager comme vous le faites formidablement bien.Une corruption tres active sous des formes X ,Y, Z ne peut que les rendre faibles devant les autorités 🙏🏿Salam !💚💛❤
ly Intellectuelle ! Dans le sens de comprendre les dossiers évoqués sur la place publique comme la préservation des économies des ressources sur le moyen et long terme en phase avec les mutations des populations du pays. Etc ...je pense qu'ils n'ont rien compris ou peu soucieux des enjeux.Merci Patriote..Salam 🙏🏿
Assalamou aleykoum mashallah ci khoutba bi .jotna nak taxaw dieul sougnouy initiative, bougnou khar kén bolé nioussi . l'État n'est qu'un mythe aujourd'hui nous constatons leurs limites,la solution ne peut nous venir que de notre école (Darras) qui a plus de 9siecle et a formé tous nos grandes références ,la preuve il reviennent vers les kalifes car ils n'ont pas de solutions.la solution c'est nous ils faut prendre acte
Barak'Allah fikoum est ce vous donnez des cours en ligne pour lire l'arabe et AL KHOURAAN payants ou gratuits merci de me répondre svp car je suis intéressée .
Assalamou aleykoum khoutba bi rafetna teé lalou ci jangat bou set té lerr . bougnou khar ndaxté Etat mythe la dongg té sén telé gui woné nako .nano ték initiative birmi sa guiss guiss moy solution bi sama Serigne dieudieuf
Wallahi gné na gni lay am live ngay wakh niouy deg mouy doug en direct yalla na yalla yagal lafi. Amna khoutba yo khamni diarna dokh ay kilomètres pour tatan ko.
Salam ! Pas tous ,mais la plupart des marabouts ont des agissements envers les politiques qu'ils se sont discrédités devant eux et même devant le peuple, voici un des pourquoi même avec Macky Sall ils n'ont pas eut gain de cause dans leurs interventions à calmer ou faire revenir Macky le traître par haute trahison à la nation Sénégalais sur ces décisions.
Machallah 👂👈🤝🤲🙏🙏🙏🙏👍
Macha Allah, baraka Allahou fikoum
Longue vie a vous
Wollah macha'allah ya Imam
Merci imam
Machalla ya imam amna solo
Machalla Machalla Machalla imame deugue Rek gua wah
JazakAllahou hayrane
Dieudieuf imam yalla nala borom bi défal tawfekh
Toujour veridique machallah
Wakh bi diékh na tak. Qutba imam bii moy solution mais aussi moy yone bi niou wara diaar inshaalah. Yalla na souniou borrom takhawou sonko té dieuléfi gni diniou djité té tégouwougn foudoul thi yonou cheiyane.
Allahouma sally wa salim alla seydina Mouhamed.
Lérna ya Imam, diadieuf
Mancha allah imam yalna yallah barkél
Macha Allah tabari kallh fihc ya imaml
Ma sha ALLAH imam toujours pertinent 🙏
Merci massala
Machall immam
Yow imam ndaw ak abdou aziz touré fass touré machalla deug rék
Macha Allah djazaka lahou hayran ya oustaz yalla na yalla sam la té aare la
Imam💚 Macha Allah Barakalahou Fikom💚💚💚💚💚💚🤍🤍🤍🤍🤍
JazakaAllah oustaz limoy deug diou wër
Yala nala yala same te mousëla goudel say fane 🤲🏽🤲🏽🤲🏽♥️
Alkhamdou lillahi biñu amé imam ndaw♡
Machallah imam saye kaddou rafète na yalnala yalla same té mayla gouddou fane amine
Dieureudieuf imam yalna yalla takhawou té weral thieuryi
dieureudieuf imame ndao ya bakh machallah
بارك الله فيكم وجزاكم الله خيرا
ما شاء الله بارك الله فيك
Wallahi wakh ngua degue ya imam yallah na yallah goudal sa fane mayla wergou yaram
Amine
Ya imam yallah nalla yallah takawou aarla samla moussal la mayla weur ak soutoura aamine goudou fane amine
AlhamdoulILLAH Imame.
Nous avons la fierté de t'avoir comme guide
Dieureu djieuf ya imame
ماشاءالله تبارك الله ياأستاذ الكبير بارك الله فيك
Diazakalla khayrann
Bilahi yalla nala borom fay aldiana euleuk inchallah imam
Amiine
Amna solo yalna sounou borom goudal fanyii
Merci moi je suis tasawouf me sunu kilifa yi tarikha yi douniou deff khoutba
Machalla oustas
Machalah Imame yalla na yalla sam li la askanewi sokhla
ماشاء الله تبارك الله تبارك الله🙏🙏🙏🙏
Manchallah Imam c'est ce genre de discours qu'il nous faut.
@Zeydoun Saw moom la ñëpp wara def xutba.
Jazakoumoulahou khayran ya Oustaz as salam aleykum wa rahmatoullahi wa barakaatuh
Baarakallahou fiikoum imam nous vous suivons depuis nouadhibou...Fafa tv qu'Allah vous protége
Allahouma amine
😅😅nouwadibou key
Qu’Allah vous protège
Maachaalah diadieuf
Ma Sha Allah♥️🥰
Yalna yalla beuril say kem bagne amsi ay présidents
Yalna yalla gudal fanwi te may la wër
BARAKALLAHOU FIIKOUM YAA CHEIKHOUNAA
Allahou Akbar!
Mashallah imam Alioune badara Ndaw aka séll
BARAKALLAH
Maachaa Allah
Baarakallah fiikum ya imam
صدقت ماشاء الله
Macha allah dieureudieuf ya Imam
OUSTAZ machallah ! C'est formidable comment vous êtes engagé en toute liberté de connaissance. Je pense que d'autres n'ont pas l'intellectuel de comprendre librement pour participer jusqu'à même s'engager comme vous le faites formidablement bien.Une corruption tres active sous des formes X ,Y, Z ne peut que les rendre faibles devant les autorités 🙏🏿Salam !💚💛❤
Écoute bien le message de ton père m macky sall
@@aldioumadiouf3512 😁💥💣😡💪🏿
Intelectuelle moy kouy dieuffé Qur'an ak sunnah r1 d'autre...? Pas kouy nakh askan diko noott...?
ly Intellectuelle ! Dans le sens de comprendre les dossiers évoqués sur la place publique comme la préservation des économies des ressources sur le moyen et long terme en phase avec les mutations des populations du pays. Etc ...je pense qu'ils n'ont rien compris ou peu soucieux des enjeux.Merci Patriote..Salam 🙏🏿
@@sendof67difo60 ok je comprend...?
Machalla imame
ماشاء الله جزاكم الله خيرا
ماشالله بركالله فيكم خزكم له حير خزء
ماشاءالله ياأستاذ بارك الله فيك
Dieredief ya imam
Merci imame kilifa goufi wakhoul lou amal askan wi ndiarign bou mbiir yi dialé nanga fekhe boul wakhati si rewmi dara
Merci imam
ماشاءالله يا شيخنا
Diadieuf yallah nalla yallah diappalé aarla samla
Manchalla deugou rék mo woor
Machalllah ya imam qu'Allah vous récompense 🤲❤️ je suis très contente de toi qu'Allah te protège 🤲
ما شاء الله
Kouma Sopoula moom Imam Alioune Badara Nda
Mazahalla
ماشاء الله بارك الله فيك يا إمام حفظه الله ورعاه
Goudeul fan Sama serigne sama Imam dpuis Maroc
Dieureudieuf IMAM vrement référence gua si serigne si yalla na yalla goudal say fann
Mashalla
Macha lah ya imam
❤️❤️❤️❤️❤️
Dieureudieuf dniaw yagiu fi te wer
Dieureudieuf imam ndao. MAA CHAA ALLAH
Iman macha allah barey ga xam xam t aussi amga sens de culture ak communication. Macha allah je ferai tt mon possible pour guis la
Pertinent !!!
Assalamou aleykoum mashallah ci khoutba bi .jotna nak taxaw dieul sougnouy initiative, bougnou khar kén bolé nioussi . l'État n'est qu'un mythe aujourd'hui nous constatons leurs limites,la solution ne peut nous venir que de notre école (Darras) qui a plus de 9siecle et a formé tous nos grandes références ,la preuve il reviennent vers les kalifes car ils n'ont pas de solutions.la solution c'est nous ils faut prendre acte
Uncle am so happy to you 💯
بارك الله فيكم للامام
Macha Allah ya Imam yalna yallah faye la amna solo
ماشاء الله جميل جداً بارك الله فيكم وجزاكم الله خيرا يا شيخنا شكرا لكم
Machallah amna solo
Merci
جزاك الله خيرا
Macha'allh 🙏🤝❤
بارك الله فيكم
MachaAllah barakallahu fiikum
سلام عليكم ورحمة الله وبركاته يا سيخ نا بارك الله فيك جزاك الله
we need a equal justice ✊ only Allah can judge people...?
ماشاء الله
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah
Yallah na sounouborom def diam si deukbi
Amine
❤️❤️❤️❤️❤️
Barak'Allah fikoum est ce vous donnez des cours en ligne pour lire l'arabe et AL KHOURAAN payants ou gratuits merci de me répondre svp car je suis intéressée .
775792902
Assalamou aleykoum khoutba bi rafetna teé lalou ci jangat bou set té lerr . bougnou khar ndaxté Etat mythe la dongg té sén telé gui woné nako .nano ték initiative birmi sa guiss guiss moy solution bi sama Serigne dieudieuf
Vraiment merci
c'est trè claire seul la loi islamique es la solution
Wallahi gné na gni lay am live ngay wakh niouy deg mouy doug en direct yalla na yalla yagal lafi.
Amna khoutba yo khamni diarna dokh ay kilomètres pour tatan ko.