N 1 Live Oustaz Alpha Ba ha - special Serigne Sam Mbaye ; ces paroles sur la balance du coran et …

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 17 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 143

  • @Teranga80
    @Teranga80 ปีที่แล้ว +20

    Oustaz sa pedagogy bi ngay diangalé dafa nékha comprendre mém bou sa jangu soriwoul. Mashallah ya ngui yé niou bari bo doul fanatic!!!

    • @mouhamedndiaye465
      @mouhamedndiaye465 ปีที่แล้ว

      Khamolenn dara ay naa fékk nguénn 😂wallahi

    • @BathieGueye-ho3ui
      @BathieGueye-ho3ui 10 หลายเดือนก่อน

      Bayil fenn ​@@mouhamedndiaye465

    • @Sam-b6f2w
      @Sam-b6f2w หลายเดือนก่อน

      Laraloufi dara

  • @korelkhidmambour
    @korelkhidmambour ปีที่แล้ว +2

    Jajaf serigne sam mbaye ❤❤ jarajaf serigne touba

    • @Sam-b6f2w
      @Sam-b6f2w หลายเดือนก่อน

      Cheikh ahmadou bamba khadimou rassoul sonou yakaar tay ak euleuk

  • @papamarsene
    @papamarsene 10 หลายเดือนก่อน +3

    je m'abonne automatiquement al quran ak sunna rékay deugg

    • @papamarsene
      @papamarsene 5 หลายเดือนก่อน +1

      @@vieuxcisse1682 Sunna ci kaaw biddah ci souff

  • @ngordiouf3310
    @ngordiouf3310 ปีที่แล้ว +10

    Alpha et votre équipe je suis fière de vous Liguèye ba gui déf effet

  • @korelkhidmambour
    @korelkhidmambour ปีที่แล้ว +2

    Jaja serigne sam mbaye ❤❤

    • @zai5562
      @zai5562 9 หลายเดือนก่อน

      Sam Mbaye…le grand menteur

  • @2rayone760
    @2rayone760 ปีที่แล้ว +8

    Also kaadu dinee you guys are doing a great job Masha-Allah

  • @mousseske9318
    @mousseske9318 ปีที่แล้ว +8

    Ma Khady Machallah ! Que Dieu soit satisfait de vous les gars, vous ordonnez le convenable et vous dénoncez le blâmable

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 ปีที่แล้ว +18

    Yen 40 années thi guinaw nguene warona commence kon temps yi nieup yewou nagnou. Yallana Burbi moussal thi tassawouf

    • @ibouvision7644
      @ibouvision7644 ปีที่แล้ว

      Mooo Iow tassawouf moy deuggeu ibadou yi Di ay con ay vrai ngakka intérieurement ils le savent mais amougnu tawfekh sen khôl mo séloul mo waral diggante yi

    • @PI-ne1my
      @PI-ne1my ปีที่แล้ว +5

      Gnom dé alkhourane ak souna rek lagnouy diangalé

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye7560 ปีที่แล้ว +3

    Serigne samba niemeh yallah reck 70000 ans avant serigne touba creeer serigne samba dofla

  • @alloucoco
    @alloucoco 2 หลายเดือนก่อน

    MERCI FOFOU BAKHENA

  • @kaneabdou-fr7dn
    @kaneabdou-fr7dn ปีที่แล้ว +1

    Khamo khamewo ragneewo yalla nalene yalla nguindy

  • @alinesamb5006
    @alinesamb5006 ปีที่แล้ว +4

    جزاك الله خيرا بارك الله فيك أحسن الله

  • @mamadoudieye9
    @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว +7

    Nioune dé ba lengui Sering sam rek laniouy topou Bilahi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋

    • @mamadoudieye9
      @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

      Serigne sam kham na mome topoul mouhamed

    • @mamadoudieye9
      @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

      @@ErenKrüger1899 yaw si ndiabotou Seytané ngua bok motax nguay khé Serigne sam

  • @mariamjagana339
    @mariamjagana339 ปีที่แล้ว +6

    ما شاء الله الله يبارك فيكم

  • @sadiboundaw9174
    @sadiboundaw9174 11 หลายเดือนก่อน +1

    Yalna yalla yelen ta martaba mak dina sonal niou beuri.kouthi touboul ba dee dina torokh.walay

  • @SeckBabacar-z9q
    @SeckBabacar-z9q หลายเดือนก่อน

    Yalla nallene yalla ngindy

  • @alphaOumarsy389
    @alphaOumarsy389 ปีที่แล้ว +2

    Serigne Touba nite la rék aye waham waham larék toupeléne délou si adouna daye diéhdé wallahi toupeléne délou si yalla

  • @MohamedDiouf-x4f
    @MohamedDiouf-x4f ปีที่แล้ว +1

    Bo gnew Fissel Mbadane dinko bay thï nii walla thï naa wouttil khame khame diaradieufatii Serigne same Mbaye radiyalakhou ankhou❤

  • @seyeoil2768
    @seyeoil2768 ปีที่แล้ว +2

    Outaz repose en paix
    Nous on est mouride

  • @badoboye-pt3gq
    @badoboye-pt3gq ปีที่แล้ว +2

    Serigne Sam Macha ALLAH ❤❤❤❤

  • @SophieSamba-y9z
    @SophieSamba-y9z ปีที่แล้ว

    Yéne dé ni yalla défe serigne touba molène méti li yalla maye serigne bi ak bolém tarikha nagounako ndakhe yalla da binde yamalewoule dieureudieufé chiekh akhemadou bamba allahouma sali inlay sieyedina mouchard wa salim

  • @alphaOumarsy389
    @alphaOumarsy389 ปีที่แล้ว

    Mé fréman machalla woté léne boubakh aye saga doudara mouhamad saga nagneko kome mougne rék yalna yalla samléne yalna yalla areléne yalna mousalléne barakallahou fiyka wayé attention bouléne wah si président parceque daye yeé fitna ta yalla bagouko yalna yalla défalléne diam

  • @BirahimDjigal-f7x
    @BirahimDjigal-f7x ปีที่แล้ว

    Oustaz ba waxe len'n Cie xamxam gniou deklolen YALLA AK RASSOLOU LAHI REK WAYE YOUNOUSS WAXE CIE AL KOURAN AK ADDISS DOYNA DIOULITE WAROUL TOUMAL MOKOUM DIOULITE BOUL WEDDI WAKHAL AL KOURAN AK ADDISS DOYENA WAYEE SERIGNE TOUBA GUEM NAGNIOU KO NARAFETT

  • @2rayone760
    @2rayone760 ปีที่แล้ว +5

    Masha-Allah oustaz alpha leral yi am na solo yousuf ma Haddy bailo may Allah the almighty protect you all

  • @PapedieneNdao
    @PapedieneNdao ปีที่แล้ว +2

    au profond de vous esk yalla rek motakh ngueni def li

    • @requinquin1
      @requinquin1 ปีที่แล้ว

      Non non
      Yé nitt gni tamit ci la bokou.
      Baaraam bouy métti sakh Serigne si meunougn ci touss. Lou nitt am rék Yalla la bilakhi😊

    • @fodefaye4530
      @fodefaye4530 ปีที่แล้ว

      Bonne questions fond yi Di djioguai makaaa gniaka classe rekk

  • @yakhyandiaye5481
    @yakhyandiaye5481 ปีที่แล้ว +8

    Serigne sam boudé diangoro naniou réye

  • @serignekhadimmbaye7013
    @serignekhadimmbaye7013 ปีที่แล้ว

    Serigne Sam mbaye dosene morom mom baye séné lafall ndaye

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 ปีที่แล้ว

    Yalna yalla samou la ya imame Alpha Amal diamou inchallah

  • @PI-ne1my
    @PI-ne1my ปีที่แล้ว +2

    Wédi waxi yallah guem waxi Serigne Touba après nguen ni dioulite nguen. Yéde len sen bop

  • @sidydiouf876
    @sidydiouf876 ปีที่แล้ว +1

    Vous me fait rire 😂

  • @Barahamza-z1f
    @Barahamza-z1f ปีที่แล้ว +1

    Yéne ayy nitte gnou bone nguène serigne touba moléne déssé aythia gnou déme domérame

    • @PI-ne1my
      @PI-ne1my ปีที่แล้ว +1

      Ki bone kay moy ki wédi waxou yallah

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 7 หลายเดือนก่อน

      Serigne touba yalla mokoo déssé aythia gnou déme dina lérr légui inchallah

  • @mobo6226
    @mobo6226 ปีที่แล้ว +3

    ❤ machala alkhourane ak Sunna rék ❤

  • @rappel4152
    @rappel4152 ปีที่แล้ว +6

    Khadith entre Djibril et Mouhammad صلى الله عليه وسلم beaucoup de Soufis l'utilisent Mawdough leu un khadith crée de toute pièces

  • @thiernoamathdiene
    @thiernoamathdiene ปีที่แล้ว +8

    Alakhou akbar yénagui wédi kou yalla geureume

    • @rappel4152
      @rappel4152 ปีที่แล้ว +2

      Allahou Akbar bayilen di sossal yallah. Yaalla fane la waheni dafa guereum Sam Mbaye wala Bamba apportez vos preuves ou taisez-vous vos mensonges, on en a assez

    • @mamadoudieye9
      @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

      Bilahi gni ay Nonou Serigne sam lagnou nek Seytané wésoul nguay wédi wakham

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye7560 ปีที่แล้ว

    Ahhh serignebi mome ah dinaleyyo borrombi sinounoureral

  • @taphandiaye3991
    @taphandiaye3991 ปีที่แล้ว +4

    Moytoulen Serigne sam baxna yar baxnadeh

  • @victorsamba8610
    @victorsamba8610 ปีที่แล้ว

    astafriloulah , mane dh je comprend plus quel est votre but pour l'islam, car ces grandes homme comme serigne sam mbaye ne sont pas votre egal, djamou len yalla guen bayil dignate yi ya oustaz , tu sais dans la vie soyons humble car allah seul connait la verité . bayil leen li mane dh yallah rek la geum et ces messager ak yoneentibi mohamamed rassoullilah, hadim rasoullillah.

  • @moussadiop7126
    @moussadiop7126 ปีที่แล้ว

    Ndeysasan khalé yii rék guén di diakhal ,amu léne kham kham .té rafahi dafa nagule Serigne Sam

  • @mousseske9318
    @mousseske9318 ปีที่แล้ว +9

    Battre en brèche (dadji) les paroles de Sam Mbaye, traquer partout ses propos pour montrer son incohérence, voilà ce à quoi il faut s'atteler. Bombarder les propos de Sam Mbaye équivaut à détruire les écrits de son guide de marabout

  • @colonelwade
    @colonelwade ปีที่แล้ว

    Barakallahou fikum ya cheikh khana

  • @mamadoudieye9
    @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว +1

    Serigne sam mo raw sa papa ak sa yaye Bilahi meuna diagal sa famille nieup sax

  • @OusmaneYade-xo7dd
    @OusmaneYade-xo7dd ปีที่แล้ว

    Mashallah

  • @laminendiaye4705
    @laminendiaye4705 ปีที่แล้ว +9

    Tarixa yi tekk xell nitt ñi lañu deff ba am mboolo té teggewuñu ci lenn ludul ay caaxaan. Diiné Islam moom loo ciy wax deffa warra am firndé ci Alkhuran ak Sunna

  • @AbdoulayeDiallo-n7n
    @AbdoulayeDiallo-n7n ปีที่แล้ว

    Oustaz alfa ba lol kay Mona nekk serg bi moy iblessss😂😂😂😂

  • @abdoufall9227
    @abdoufall9227 ปีที่แล้ว

    أتهممت رقم ألف

  • @serignekhadimmbaye7013
    @serignekhadimmbaye7013 ปีที่แล้ว

    Bravo mostafa

  • @mamadoudieye9
    @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

    yaw nonou Serigne sam ngua loutakh ngua bagna Serigne sam 🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔

  • @sidydiouf876
    @sidydiouf876 ปีที่แล้ว

    Dém lène diamou yallah

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 7 หลายเดือนก่อน

      Diamou yalla bou geuneu mageu moy lérale dîné yalla bi

  • @BirahimDjigal-f7x
    @BirahimDjigal-f7x ปีที่แล้ว

    Waxetou diouli diote demo ienn dioli dagg sene laive bie ana sene dingale Waxetou diouli n'a fekhe bakhoul

  • @elhadjiseck6145
    @elhadjiseck6145 ปีที่แล้ว +3

    Slam ya OUSTAZ

  • @maradiagne3348
    @maradiagne3348 ปีที่แล้ว

    Serigne Sam amolen thie sen birrr kouko gueun guisso len kouko eup xam xam amolen kouko eup diangue di critiquè sen ay moromou baye ak gnou gueun seni ndeye ak seni baye

    • @souleymanekeita7282
      @souleymanekeita7282 ปีที่แล้ว

      Sa way thi diiné dji magg ak khalé amouthi soit khamnga lii diiné wakh soit khamoko. Fii kou eup kham kham moy djiité. Serigne sam mbaye nitt la, Serigne touba nitt la té loufi nitt wakh té tegouwoul thi alxuran ak sunna dagn koy weddi. Mou nekh la mou nakari la ❤

  • @TaphaGassama-z5k
    @TaphaGassama-z5k ปีที่แล้ว +1

    Kou am diné dafaye yaro té yéne yarouwoléne

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  ปีที่แล้ว

      Taaw Xana guisso fenn you reuyy yii ngoor cii toudou djiemalekoo Cii ALLAH ...
      No yen sëñ xoll daa feebar Allahou al'moustaعne

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 7 หลายเดือนก่อน

      Yarou deug moy wédi lou yalla wédilou

  • @fatouniass2697
    @fatouniass2697 ปีที่แล้ว

    Sa ndianga sorewoule wayei War nga hamnei heule si Adama la niou sakei hawa tei alhourane dafa wahnei kouloume min Adama wa Adama min tourabe tei Lou wesso deimal diangui sa diinne ganaw dagko reirei tei yit faratala thi peip djoulit mou diag diinneim tei mou mag fenei lougne laye whakh loudoul feinga ndakhtei dinnei ken douko foyei wa salam

  • @ibrahimandoye6392
    @ibrahimandoye6392 ปีที่แล้ว +2

    Prochaine fois svp débat yi bou nieup Di wahando.... Ken dou degu ligueni wah.... Bayilen heuthio parole. Liguey bi rafete na sunna dafa lerrr

  • @elhadjiseck6145
    @elhadjiseck6145 ปีที่แล้ว +3

    Slame ya OUSTAZ

  • @abdoukhadarlo
    @abdoukhadarlo ปีที่แล้ว

    Kubaga duggu numuy def

  • @matymboup8774
    @matymboup8774 ปีที่แล้ว +1

    Je s8 mourite mais nekhoul ba nekhoul li bou neké ni serigne moka wakh yémena loll

    • @fatousamb1354
      @fatousamb1354 ปีที่แล้ว +1

      Mane dama sakh diakhalè mouride la mes dama titte thi li

    • @fftrgdermain
      @fftrgdermain 10 หลายเดือนก่อน

      T’es pas un vrai mouride alors ndax amna waxx yoo khamné soko khiyassé sa khéll meun guako bagna guemm

  • @PapaAdamaThioune-yn6nj
    @PapaAdamaThioune-yn6nj ปีที่แล้ว

    "Diamou yAllah nioungukay faratal bi yAllah wathiei Adama ak Awa" ? Malaka yi nekougn woone diko diamou ? Ibliss nekoul wone di diamou yAllah ? Allahou akbar !

  • @akane1539
    @akane1539 ปีที่แล้ว

    Svp laissez developer
    Comme ça il se contrediront eux meme
    Am lene plus de dall svp surtout younousss
    Deglonté dafa bakh merci

  • @serignekhadimmbaye7013
    @serignekhadimmbaye7013 ปีที่แล้ว

    Yene niangolone dra xamolene dra séné lafall ndaye

  • @Sam-b6f2w
    @Sam-b6f2w หลายเดือนก่อน

    Khamouma dara kèn khamouko, manouma dara kén manakou ak ndoff la

  • @bahoohoo1059
    @bahoohoo1059 ปีที่แล้ว +3

    Saaga moom doomi xaraam yi ngeen di woowe sëriñ jàngal nañ leen ko bamu mokk

  • @khadydieng7856
    @khadydieng7856 ปีที่แล้ว +2

    Serigne same Mbaye dou sa Morom

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 7 หลายเดือนก่อน

      Yalla rék moo amoul morom ma sœur

  • @mahmoudsarr2660
    @mahmoudsarr2660 ปีที่แล้ว

    Alpha néna yonénti bi kouko gueuneu nék waliw😂

  • @ndiogoungom9290
    @ndiogoungom9290 ปีที่แล้ว

    Mais walahi yen boudé ay dioulit Nguen Dinama diakhal tok Di yakh s'en mbokou dioulit rek .louway khamoul khamouko . Khalakha insana min halakha .Khalakha insana malam yahlam

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  ปีที่แล้ว +1

      Togall fofouu dii nelaaw guayii yewounaww bouu yaguu xana daguaa biidan tiii 😄😄😄🫣

  • @ndiogoungom9290
    @ndiogoungom9290 ปีที่แล้ว

    Kon yonentibi dafa Guen adouna😂😂😂😂

  • @PapaAdamaThioune-yn6nj
    @PapaAdamaThioune-yn6nj ปีที่แล้ว

    Adama Aleyhi Salam si leirou kane lagnouko bindeii ? YAllah mayeina t tololei woul. Allahou a'lam.

  • @omardieng-vr9ob
    @omardieng-vr9ob ปีที่แล้ว +2

    Manchallah oustas

  • @masseyegueye3729
    @masseyegueye3729 ปีที่แล้ว

    Yonentibi Moy mami adama mamam

  • @BirahimDjigal-f7x
    @BirahimDjigal-f7x ปีที่แล้ว

    Waxe serigne touba loudoul diamou YALLA la talibe yonente YALLA bie la dama rouss xamxam AK tegune saga serigne bie moue saga mouride yepp

  • @rainks5461
    @rainks5461 ปีที่แล้ว

    J’aime bien les ibadou Rahman mais le fais qu’ils ne laissent pas les gens s’exprimer ça me fait mal.

    • @PI-ne1my
      @PI-ne1my ปีที่แล้ว

      Les intervenants divagent toujours au lieu de donner les preuve dans le coran et la souna que Serigne Touba a été créé 70mil ans avant Adama

  • @elhadjiseck6145
    @elhadjiseck6145 ปีที่แล้ว +2

    Slam

  • @dieynabandiaye9211
    @dieynabandiaye9211 ปีที่แล้ว +2

    Thieye Sénégal doyna waar

  • @cheikhfall859
    @cheikhfall859 ปีที่แล้ว

    Lintélectuel c se luit qui ecoute amon degu degue manoule

  • @cheikhtidjianesarr8514
    @cheikhtidjianesarr8514 ปีที่แล้ว

    Mais sama serigne yow sonou nga de yow gningay waxal gnola raw même boude lingay moy deugeu yalla kham

  • @nouvelledeveloppementdumon4450
    @nouvelledeveloppementdumon4450 ปีที่แล้ว

    😭😭😭😭😭🦜🦜🦜🦧🦧🦧🦓🦓👈

  • @mammbo
    @mammbo ปีที่แล้ว +1

    Alpha Bah Yaw Dangay Fen di force Nit ñi ci fen

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 7 หลายเดือนก่อน

      Oustas alpha fénoul fénn katt deug moy fénal yalla ak yonéte

  • @mamadoudieye9
    @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

    Serigne sam yalla nako yalla fay bou bakh sax❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 7 หลายเดือนก่อน

      Amine yarabi té balko loumou yakhe beurina ci dîné yalla bi

  • @akane1539
    @akane1539 ปีที่แล้ว +2

    Vraiment younouss il faut apprendre le respect deugg nit meune nako bagne ndakh noumou koy dioté stp apprend a communiquer

  • @mamadouba7904
    @mamadouba7904 ปีที่แล้ว

    Yaw Kane mo takh niou binde Adama yonanté yalla mouhamde Adama ak yonanté Kane mo djitou

  • @sonkopresident-qp3pf
    @sonkopresident-qp3pf ปีที่แล้ว

    Tarikha yi thiakhane rékk par ce que amouñiou arguments,mais loutakh nitt ki di wakh si dinné yalla dji loumou guissoul si alkhourane ak hadis.

  • @nouvelledeveloppementdumon4450
    @nouvelledeveloppementdumon4450 ปีที่แล้ว +3

    😭😭😭😭nite kou amoul basirà rakelo yalla loula nkhe wakhale khamou foye diem di wedi nitou yalla yi dou mala dklou 🦧🦧

  • @amethndiaye5754
    @amethndiaye5754 ปีที่แล้ว

    Seydina mohamed motakh nio binde Adama wa wala

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  ปีที่แล้ว +1

      Ndax amgua preuve khadith wala ayat ⁉️‼️🤔🤔🤔

  • @TRA-PASTEF
    @TRA-PASTEF ปีที่แล้ว

    Watawasaw bilhaq

  • @awaba3307
    @awaba3307 ปีที่แล้ว +1

    Younous yenna wakh yi boulko tontou

  • @bababodiang
    @bababodiang ปีที่แล้ว

    Leurs propos sont facilement démontables il suffit tout simplement d'utiliser le Coran et la Sounnah car tout ce qu'ils racontent sur leur marabout ressemble à des bandes dessinées

  • @cherifdiop155
    @cherifdiop155 ปีที่แล้ว

    Alpha,menoulo wakh ba gni gueume leu.kene menoulene ye.

  • @mamadoudieye9
    @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

    Yaw dh mangui sogga guiss sa vidéo mais vraiment Dof ngua kw jtassur

  • @jalenka5642
    @jalenka5642 ปีที่แล้ว +1

    Ton combat est noble mais tu parles à un peuple malade et endoctriné. Qu’Allah viennent en aide et faire disparaître c’est confrérie nuisible à notre société

  • @Soukeya
    @Soukeya ปีที่แล้ว +1

    Salam, cette méthode de personnalisation du dahwa n'est certainement pas la meilleure. Yalla mo kham. Nagn len diappal ngant. Peut-être que ces seurignes n'ont pas eu la chance à leur époque d'accéder aux hadiths authentiques. En plus si leur discours parlent de leurs confréries cela n'engagent qu'eux-mêmes. Essayez plutôt de sensibiliser les musulmans pour qu'ils aient du discernement khamé coran ak sunna lolou rek mo len di dieurign. Wa Salam

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  ปีที่แล้ว +1

      Ma sœur nous on fait que sensibiliser , ccette façon de faire la Dawha, n’est que sensibiliser encore une fois nos frères

    • @Soukeya
      @Soukeya ปีที่แล้ว

      ​@@KAADUDINEEJITV effectivement ! C'est vrai que la situation est critique pour certaines personnes qui ont des croyances très profondes mais fausses en effet

  • @PapedieneNdao
    @PapedieneNdao ปีที่แล้ว

    li ngueni wakh bolen khamon limou leni dioural euleuk dinguen ko bayi

  • @yakhyandiaye5481
    @yakhyandiaye5481 ปีที่แล้ว

    Yéne beuz nguéne di out légui yow gueuno batine parce que amo batine tu n'est pas dimensionnel tu es ordinaire gueum léne yallah té bayi serigne sam mbaye bokou walou là légui todj léne khoudar ak moussa

  • @mamadoudieye9
    @mamadoudieye9 ปีที่แล้ว

    Ouztas Alpha Yaw Seytané Bilahi 😡😡😡😡😡👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎

  • @deboursy6215
    @deboursy6215 ปีที่แล้ว

    Ki dei mo dakha fenn du monde bii

  • @alchiyaya2624
    @alchiyaya2624 ปีที่แล้ว

    Je te jure qui nulare la iblise été la avend Mame Adama Mane reke sa bidewe adenate yonete bi

  • @AmetTidianeDiaw-cv9uu
    @AmetTidianeDiaw-cv9uu 7 หลายเดือนก่อน

    Serigne samb mbaye amoul morome bilaye khamoléne lou beurrii vous êtes perdu

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  7 หลายเดือนก่อน +1

      🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  7 หลายเดือนก่อน +1

      🤣🤣🔨🔨🔨🔨🔨🔨🔨🔨🔨🔨🔨🔨

  • @SIDYBAGUEYE
    @SIDYBAGUEYE ปีที่แล้ว

    Ya vraiment pas plus ignorant que vous ne savez même pas que la création des humaim précédent leurs Venu sur terre ou était iblis par exemple

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye7560 ปีที่แล้ว

    Lounoumoul comprendre wahou dofla donc faut pas l exposer

  • @yakhyandiaye5481
    @yakhyandiaye5481 ปีที่แล้ว

    Sétane porno mo gueune déglou kouy dinguate waliwe yallah

  • @khadyfall3598
    @khadyfall3598 ปีที่แล้ว

    Sheut wahabiste yi sonne négne dh😆😆😆😆😆😆😂😂😂noppalikoulén les enfants gnoune Serigne Touba limou wakh geume négne ko