السلام عليكم ورحمة الله تعالى وبركاته . شكرا لكم جزاكم الله خيرا. Merçi bcp Al Oustaz Alpha Ba ; guiss nga Yaw Al Oustaz Alpha , niou mélna wã djii boulène déffati genrs yii wakhtãnou plateau , ndakh kii dafa rèrre dafa sankou dianguoul amoul xam - xam ; meunoula soutenir débats ; amoul ay arguments ; meunoula layal fénna fénna thi shariha ak sounna ( في الشريعة والسنة ) gnakka woor mô gueune koor goumou mana dône . Amoul kénna kénna kou Yallah défal ak diaglé ba nga mana beutte gnagou shariha ; loolou ak kèffeurla (كفر ) akouk dieuhil ( جاهل ) : lèppou lou woutèk al khourãne ak sounna ( فكل ما خالف القرءان والسنة فهو كفر وضالة ) ! والسلام على اتبع الهدي !
Subhan allah allahou akbar thiey thiey Senegal . merci oustaz alpha Ba ak oustaz ousmane cisse ki khamoul Dara deffa rer bokalle Kat le yalla na yalla wonne len yonnu sirat al moustaquim amine
Deuk bou gueuneu yéss cii adouna bii moy Senegal ndah senegal mo fii am ay yonnènte guinaw rassoulilah, senegal gay dègue kounane serigneume moy Yalla Senegal késsè mo am ay kourel yo hamnii dougnou djouli dougnou woor Senegal mo am ay Serigne you binde assamane akk souf Mais lii yeup noumouy hèwè senegal ba parè senegal di geune fènne
Dans votre débat, toutes vos analyses sont mal fondés. Serigne Touba a travaillé au service de Dieu et du Prophète Muhammad Psl. D'ailleurs ses fils et petits fils ont tous momorisé le saint corant et certains l' on même rédigé. Vous vous venez tout juste de naître et vous remettez en question ses pratiques et ses euvres littéraire.
nos yeux peuvent voir les étoiles mais ignorent le bout de notre nez n allez pas chercher trop loin pour comprendre ne soyez pas trop prêt pour être des égarés degue amna solo lolou dans la vie parfois il faut pas traduire les mots contre les mots il faut juste comprendre l éloge et le sens des choses pa bi donne firil mame abdou aziz kou deguone le yalna gnou mame defal degue ak topp Ken dou mame khadim rassoul comme l ont souligné kepp kou egeu fa yalla
Ndeysaaaane !!!! Les serignes des tarikhas gadounagnou akhou talibés yi. Hypothéquer leur vie, leur temps, leur biens ba paré dou gnou léne dianguale dara thi séne diné. Quelle tristesse vraiment
Le TALIBÉ c'est L'ÉLÈVE qui apprend, le SERIGNE ou MARABOUT c'est L'ENSEIGNANT ou le PROFESSEUR qui t'apprend le Coran et les connaissances divines. Chukrane
Pourquoi yéne djoulit yi kou dakk wére sa morom ganéma ki la yén nieup yaam dem diamou yalla mo gueun ligueni def amoul bén diarigne temp bi gen perte ko si yalla mo gueun guenilles tesseunté wakh lén sisén book djoulit youniouy ray paléstine mo eupeu solo
Bouniou leen bayé daniouy continuer di sankeu doomou adama you innocents yi nga khamni danio beug Yalla té khamouniou nouniou koy djaamo té kénn guindi wouleen. Niép amou niou chance djang al Qur'àn motakh yéété bi bakh ci
Merci d'exiger des preuves de la part des contradicteurs...ils ne pourront jamais le faire .défendre les tarikhas est une mission impossible.nombreux de leurs adeptes sont des égarés malheureusement. ré batass 🤣barakallahoufikoum.
Même pas. Moi perso je pense que leurs parents ont une grande part de responsabilité dans leur déperdition😢 bouniou leen djangaloon Al Qur'àn konn douniou réérr kénn dou leen nakh ci ay thiaakhaan. Beugg Diiné rékk motakh niou fookni liniou nékk Diiné la. L'Islam la. Yalla naléén Yalla guindi oubbi sééni nopou ak sééni khol baniou accepter lii Oustazou Sounna yii di djangalé mouy Al Qur'àn ak Sunna
masha-Allah ouztaz Alpha Ba c'est tellement clair, merci aussi à Ouztaz Ousmane Cissé
L'islam c'est le Coran Sounnah du Prophète Muhammad PSL
Oustaz Alpha ba yalna sa jame yague Mashallah ❤❤❤❤ ❤❤❤❤
Yala ak yonanti bi rék niofi nék kouléne topoul pérte machaalah oustaz alpha
Je suis fier d’être ahlu sunnah wal diaman ♥️❤️
Machalah yaa oustaz yalna yalla yagual sa takhaway 🙏yalna naniou yalla may degg ak top
Oustas Alpha Amal diamou bou baah inchallah
Ce que je regrette dans ma vie est de suivre ces Tarikha et de connaître tard akhlou sunna😭
والله غفور الرحيم ☪️
Mieux vaut tard que jamais. Que la miséricorde de Dieu soit sur nous
Allahou akbar
Sénégal na dioulite yi delou ci AL QURAN rek wakh bi diekh
Sénégal nane déllou ci alxouran ak sounnah naa lérr alxouran ak sounnah kasé
Oustaz alph machla
Macha Allah oustaz Alpha yalna yalla samela samessa ndiabote barakallahou fikoum
Allahuma amine
Oustaz uosmane sise machla
السلام عليكم ورحمة الله تعالى وبركاته .
شكرا لكم جزاكم الله خيرا.
Merçi bcp Al Oustaz Alpha Ba ; guiss nga Yaw Al Oustaz Alpha , niou mélna wã djii boulène déffati genrs yii wakhtãnou plateau , ndakh kii dafa rèrre dafa sankou dianguoul amoul xam - xam ; meunoula soutenir débats ; amoul ay arguments ; meunoula layal fénna fénna thi shariha ak sounna ( في الشريعة والسنة ) gnakka woor mô gueune koor goumou mana dône .
Amoul kénna kénna kou Yallah défal ak diaglé ba nga mana beutte gnagou shariha ; loolou ak kèffeurla (كفر ) akouk dieuhil ( جاهل ) : lèppou lou woutèk al khourãne ak sounna ( فكل ما خالف القرءان والسنة فهو كفر وضالة ) ! والسلام على اتبع الهدي !
استاذ ألف باه ماشاء الله ❤❤
Allahou Akbar sunnah rék moye DEUG billahi 💪💪💪🇸🇳 Sénégal 💯❤️❤️❤️
Subhan allah allahou akbar thiey thiey Senegal . merci oustaz alpha Ba ak oustaz ousmane cisse ki khamoul Dara deffa rer bokalle Kat le yalla na yalla wonne len yonnu sirat al moustaquim amine
Yalla Nanou yalla moussal si rer
Sunnah rek Moy deug bilahi 💪💪 💪💪🇸🇳 Sénégal 💓 💓💓 💓☝️
Machallah oustaz Alpha sa takhaway si Alkhourane ak sounna rafétna yallah na yallah gueunla deugeural si deugue bi nga tokk
merci oustaz alpha💚💚💚💚💚💚💚💚💚
Oustaz Alfa Ba maschallah.
Merçi ouztaz gua yii ama gounou attaquant wala defensseur bou forokh nanou lambiwatt.
Deuk bou gueuneu yéss cii adouna bii moy Senegal ndah senegal mo fii am ay yonnènte guinaw rassoulilah, senegal gay dègue kounane serigneume moy Yalla
Senegal késsè mo am ay kourel yo hamnii dougnou djouli dougnou woor
Senegal mo am ay Serigne you binde assamane akk souf
Mais lii yeup noumouy hèwè senegal ba parè senegal di geune fènne
Sénégal sounekon anglais len don lack bilahi waa Al-Qaïda def ko dom bakhna rk
Yalla nama yalla mouseul sy tarikha yi Thieye yalla setalma lï rek 😢😢
lane moy tarikha
@@abousow5021 fawdha
😢😮😢chaque jour que je répète tarikha yi gno saboté l islam tardel Sénégal am développement trompé né ñiou jeunesse bi billahi
Deuggla
Quelle sont les pays musulman qui sont dans l’émergence et qui se sont développée à part les pays du golf corrompu pas l’Occident ?
@@adolfh3001 qu'est-ce que tu sous-entends par cette remarque?
Baye fall yallah naka yallah deg lo sunna yoneniti bi .
Mouridisme diné lék ak nane seuye ak feith béne xam xam amouniouko
Thi mouride gi laniy doundu thi laniye dé lilay méty dou masa fadiou lilay dérangé moy moy mouride yi iow ak say morom
Wa ahlou mbirti mbirti fénne ak sagua ak café ☕️ ak bokkalé rék 😅😅😅😅😅😅😅😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Alpha bâ est courageux...les tarikhas défectueux
Gracias al pha ba merci ak cisse diamou siyien
Machala moride bi diambargue ❤
Gni thi popam geumou gnou dîna islam mourid ay serign kesse lagnou geume yalla nagnou yalla moussal thi gni ay katior lagn you bone lagn
Dans votre débat, toutes vos analyses sont mal fondés. Serigne Touba a travaillé au service de Dieu et du Prophète Muhammad Psl. D'ailleurs ses fils et petits fils ont tous momorisé le saint corant et certains l' on même rédigé. Vous vous venez tout juste de naître et vous remettez en question ses pratiques et ses euvres littéraire.
Outas Alpha vous n'avez pas été à la hauteur lors du débat. Arretez cette prêche visant à déstabiliser les Tarikhas.
Serigne Touba n'est pas votre égal
Suis fière de vous 😂😂😂😂 la mifa je vous kiffe merci thiey bi débat 😂😂😂😂
Chacun est fier d'être ce qu'il est...
جزاكم الله خيرا
merci beaucoup sam tokoar alpha ba
Sheut yalla naniou yalla may ham ham
quand tu defent l indefendable tu devient ridicule merci alfa
You are totally right ✅ .
Merci
Heureusement que le ridicule ne tue pas !
@@mustaphajallow3520😊😊
Se
Kou wakh tarikha bida leu déguo Alxouran
Tarihayi yii gnou soss ci birr l'islam moom bidalaa wallahi
Wadji di woté mouride mom amoul beni logique(pas de logique) vraiment . woné neu bou bah niakkeu hamam bi. Oustaz Alpha il faut que vous regarder gni ngene di inviter vraiment
Yalla ak yonenti kep,lenen lep aye thiakhane leu
Il es plus facile d'être trompé que d'admettre d'avoir été tropmé
Machallah sa ligéye réfétna Waji geuna léral ci watawasaw billkhakhi
MaashaaAllah Xol seddeuna
Merci oustaze alpha bâ problème bui billahi mourite dougni aye nitt
Wayé niom amouniou néne sokhla thi lidieunty wounla iow ak say morom
maacha allâh cheikh alpha ba
Mourid bi wakhi dof rék lay wakh😂😂😂😂
Grawoul na déme défarouwatt nieuwate amouniou bénn kham kham fanatisme rékk
nos yeux peuvent voir les étoiles mais ignorent le bout de notre nez n allez pas chercher trop loin pour comprendre ne soyez pas trop prêt pour être des égarés degue amna solo lolou dans la vie parfois il faut pas traduire les mots contre les mots il faut juste comprendre l éloge et le sens des choses pa bi donne firil mame abdou aziz kou deguone le yalna gnou mame defal degue ak topp Ken dou mame khadim rassoul comme l ont souligné kepp kou egeu fa yalla
Machallah ❤ ya oustaz sona rek
C'est l'égarement total ces gens sont mécréants à jamais. A moins qu'ils repentissent. Qu'ALLAH le tout-puissant les mets sur le droit chemin.
Wallahi alfa ba ❤
Ndeysaaaane !!!! Les serignes des tarikhas gadounagnou akhou talibés yi. Hypothéquer leur vie, leur temps, leur biens ba paré dou gnou léne dianguale dara thi séne diné. Quelle tristesse vraiment
Je te jure je me demande chaque jour bougn dewei louniouy wax yalla ?egare tant de personne thi ay foo ni ah bokalei
Wallahi c'est honteux et c'est triste
السلام عليكم ورحمة اللَٰه وبركاته بارك اللَٰه فيكم ورعاكم وأيدكم
Machallah oustaz Yalla nalla yalla FAI
Loudoul yallah ak yoninte mouhamad sws dou dara
Alpha Serigne Touba d'où sam moroom
bilahi wallahi senegal denoo am problème bou rey 😮
Watawasaye Bill Haki watawasaye Bill sabri.
Le TALIBÉ c'est L'ÉLÈVE qui apprend, le SERIGNE ou MARABOUT c'est L'ENSEIGNANT ou le PROFESSEUR qui t'apprend le Coran et les connaissances divines. Chukrane
Pourquoi yéne djoulit yi kou dakk wére sa morom ganéma ki la yén nieup yaam dem diamou yalla mo gueun ligueni def amoul bén diarigne temp bi gen perte ko si yalla mo gueun guenilles tesseunté wakh lén sisén book djoulit youniouy ray paléstine mo eupeu solo
Le début je pensais que ce gars est un grand érudit, un grand savant,. Ndakatèyo 😂😂Wadji est un vrai faquin il est en peneri d'arguments.
❤❤❤❤ Machallah
Sunnah thia kanammmmmmmm!
Oustaz Alpha tu as vraiment perdu ton temps discuter avec ce ignorant.IL n'a même pas le niveau.La prochaine fois il ne faut pas l'accepter.
Faut comprendre parfois c'est bon d'inviter ces genres de personnes car beaucoup de personnes vont en bénéficier
Merci ya oustaz alpha ba
Serigne Touba mi bagne ba toudai bopam khadim Rassoul yama lai woul daram ak daray yonanti bi
Mashallah Oustaz alpha ba qu'Allah té préservé je suis fier d'être salafy
MUSULMAN ARRETER DE DIRE LE MOT SALAFISTE TOUT LE MONDE EST SALAF
Nguir yalla wakhallén niou si yalla ak nabi .té bayi gars yi way .amouniou xam xam.nguir yalla way
Bouniou leen bayé daniouy continuer di sankeu doomou adama you innocents yi nga khamni danio beug Yalla té khamouniou nouniou koy djaamo té kénn guindi wouleen. Niép amou niou chance djang al Qur'àn motakh yéété bi bakh ci
Merci d'exiger des preuves de la part des contradicteurs...ils ne pourront jamais le faire .défendre les tarikhas est une mission impossible.nombreux de leurs adeptes sont des égarés malheureusement. ré batass 🤣barakallahoufikoum.
Ndaye je 888rue robert Gallery a 8rue and 8rue robert Gallery et 8k
Boy nopil sa bop amoul dara il ne connais rien ce mec 😂 Tarikha yii yeup ay fène la 😂😂😂
Machla alpha ba
OUSTACE alpha Yayui bandi
Invitélene oustaz khalipha mboup gnemewoulenco deh foumoulene wo nguene daw
alhamdoulilah je suis un soufisme❤
Alfa ninko wakhe dounonou fawkha sawmi yalla def loolou dako teuh deyante bou serigne deyante ak yalla lolou douloye waye lo guisla moye khassidayi naadiaye touzal archil azime na diaytourabbiyal karim bikoubine laysattarim anwarouha wali yarome ahmadou khayra safadi
Ces gens ne connaissent pas islam leur ames est plus dure que le fer ces des mécréants islam c 4st dieu mouhamet psl
Même pas. Moi perso je pense que leurs parents ont une grande part de responsabilité dans leur déperdition😢 bouniou leen djangaloon Al Qur'àn konn douniou réérr kénn dou leen nakh ci ay thiaakhaan.
Beugg Diiné rékk motakh niou fookni liniou nékk Diiné la. L'Islam la. Yalla naléén Yalla guindi oubbi sééni nopou ak sééni khol baniou accepter lii Oustazou Sounna yii di djangalé mouy Al Qur'àn ak Sunna
Serigne Touba ay dieufeum ak ay mbidam niokoy layal
Discuter avec des gens pareils, c'est une pure perte de temps et de connexion
Nn nn
Wadji il ne dormira plus sur ses deux oreilles 😂😂😂
Il va se remettre en question bilahi. On est déjà passé par là 😂
Demal diangui nijjay plz boul reuyy wayy dianguil
Machallah 🕋❤
Blay dama rouss li yalla na noiu yalla diegal 😭😭😂😂😂😂
Macha allah
Merci d avoir exposé ce charlatan lol
Ce gars et un fanatique qui ne comprends rien sans preuve
Thiey yalla minou saka
Sunna rekkk mouy lou wérrr alquran ak sunna rekk mouy lou wérr
Alpha bindooo diam yiii manoul si nitt gnii
Mourite dounga keur deme yi taye nga dé🤣 ngui nga khamné xam xam la niou diangue🤭🤭🤭
😂😂😂😂 alquran AK Sunna dal boci nékkoul Manou Andi deug
Di feen baay fenal yalla
Oustaze Ba pratique l'lslam du Prophète Muhammad psl et de ses Fidèles compagnons
Dans quelle partie du coran peut on retrouver le salafisme ou le wahabisme? Mieux le Prophète était il salafiste ou wahabiste?
Vraiment mourid connais rien dan l'islam
Absolutely nothing from the followers of mourid ZERO EDUCATION
Kou beug seni coordonnées noumouy deff?
Chieck Alpha billahi tu as raison
Legui lep leer dh sunna rk Moy deuGeu
Mourid bi dé khamou thiotta ndayam 😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
Vraiment le mouride là fait que fuir les questions et les dalil
Salam commentaires yi si vidéo day dag lancé bi
Alpha tay dieul ngua daii😂😂😂😂
😂😂😂😂 c'est drôle sunnah rek inchallah
vous perdent du temps à écouter ce ignorant vraiment,