nittdoff il vit dans le mensonge mais il sait bien que Dip est un MC incontournable du game. Dip fou sori la yobeou game bi. té mbède bou mouy mboubo eupeulé woufa Dip ay sopé. le succès de Dip lui dérange c'est tout.
Jajëf Older. Man su fan de la musique de Dip mais aussi fan de toi de ton engagement patriotique et citoyen mais aussi de ta maturité. Une retrouvaille entre vous deux j'en demande mais sinon respect brO.
Non mais pourquoi la nouvelle génération n'ont pas de respect pour les anciens. Kelkun comme nit dof c'est un symbole du rap galsen avec beaucoup de talent. En états-unis ou partout dans l Mont on verra jamais sa . Respect aux grands.
Killer pour moi yaw ak niome douguéne bén sakh bagay nék fi di tontonté ak niome koula si diokhoul respect môme la déh mais kou wakhal deugue khamné sa niveau dépassé na dé clash ak boyi gua khamni défou niou sakh 5ans si rap bi
Yes killer no need to klash back kuz kalashnikov is an evident ya dont scare to play this game but at the right time man keep focus on this way u r handling hiphop
DIP dal yeungueul neu rap galsen 😂😂 Nitdof y’a ndieuk togne dip Konn nak bulfi diayy affaire de sagesse parceque dip dafa yokou niveau bi ..même gfm Le nom de DIP lagnou djiteul pour gars yi regarde la vidéo 😂😂😃
Parole de sage! Quand on est influent on doit toujours faire attention à nos paroles. Good work Nitdoff!
Très bonne communication très mature!!!
merci kille kille ls journalistes se sont ds fumiér et la réponse c cool
Boy dip dafmeu sagna teukou "tay sa xour yi lay deupou"😭🤷♂️
C’est ça qu’on appelle La maturité🤟🏾
Maturité totale merci NitDoff killah
MERCI ...MAGG MOY MAY BOPAM FULLA🚶♂️🚶♂️🚶♂️
Merci bonne réponse
Big respects Grand Killeuh🖒🖒🖒
t'as bien fait de laisser dip mou foo touti halei leu tamit sinon dafay deupat sa khour yi reik pour r1
Merci killer do moromou ben xaley respect à toi🙏🏽
Dip ci bopame mo adjjj niveau game bi man😎
Deugu gua wakh dip mo yeugueul game bi
nittdoff il vit dans le mensonge mais il sait bien que Dip est un MC incontournable du game. Dip fou sori la yobeou game bi. té mbède bou mouy mboubo eupeulé woufa Dip ay sopé. le succès de Dip lui dérange c'est tout.
@@allstarstv7743 Walah frr il fait semblant ms il ne l'aime pas
Oh bonne réponse. Khare daye wessou mbotté. Tu as clashé tout le game dès ton début maintenant tu passes à autre chose. Bravo!!
Nitdof for ever🔥🔥💪💪💪💪
Bien communiqué comme d'habitude
Jajëf Older. Man su fan de la musique de Dip mais aussi fan de toi de ton engagement patriotique et citoyen mais aussi de ta maturité. Une retrouvaille entre vous deux j'en demande mais sinon respect brO.
Respect ✊ le grand bien répondu
Grâce à Dip
Ta musique a de la valeur 😂😂😂
Vraiment iGfm sakh khamenanenii sans le nom de dip sur le titre guayiii doune sétane vidéobii
Dip king kingbiii
Yeah Killah chapeau à toi
Il fallait dire ca avant yako sombi nane ko
Très mature ...respect bro
Dip na wakh ak ay ngaka ay omzo fi moromame nekoufi
Bien répondu bro nit dof
Khana lolou tay ngako kham nitt doff fékk la rk
Ohh waouh rouss na sa dip ki doussa morom
Merci killer d'être toujours mature boul mayy buzz dip
Kone loumouy tontou nak
TAS B1. RÉPONDU NICKEL 👌
Bien parlé
Boy dip dafma sagna teukou téy sa khour yii léy deup🤣🤣
Killeuh fait des vidéos 😁
Doudou lagn geume 🖖🏿
😁😁😁
😭🤔🤔🤔Ay Bro Kulay Xelal Wakh Nga Wakhu Makk Billahi Rspc Te Mosoma Nékh Nak Waye Bes Niki Tey Sa Fans La
😂😂😂
Merci d être responsable dip mom nanou ko bâyi one rek 🤣
Anna Diop cou nekk xamna cou meune sa bayi dip one moye papam one dale mo meune yar xalei bou rrew 😂
Chiekh Diop mon grand frère s appelle comme toi Sama domou baye deugu dou nekh bilahi one Lima guiss si mom bou ko dip moytoul woull mou soulko 😂😂
Merci nitt respect bro👍👍👍👍🇲🇾👈
....il fallait y penser 🤔
fière devous bro 💪💪💪💪
En tous cas Sénégal 🇸🇳 metina dh
Rap lénn lou amm foulaa mon gueunnn Sénégal metina dh bilay
Bien dit killer
Tres bien nila
La classe yagui ucad té dip migui primaire dou béen
Respect man
Ces sa qu’on appelle humilité 💪🏿
Ce gars est un grand
Maturità maxxxx grand machalla
Wàày Nice Dio contanne sii ioW
Très bn réponse. Nitt
La classe 🙏💯✨
Merci killer
Respect
Merci nitt
Quelle maturité 🔥🔥🔥
Vraiment tu dépasse carrément
Non mais pourquoi la nouvelle génération n'ont pas de respect pour les anciens. Kelkun comme nit dof c'est un symbole du rap galsen avec beaucoup de talent. En états-unis ou partout dans l Mont on verra jamais sa . Respect aux grands.
Tenak génération bi lisi eupou séne rap waxounioufi léne lou am ndiarigne xasté saga dagasanté bo waxé niounane rap mbalakh niak diome
Respect broh
Quelle mentalité !il est vraiment mature killer...
Deretou lg 💯🖇😍
Yeah Man dafa ler diadieuf bro respect jop rk bou léne sah lii diene ti boyi Amou niou respect
Merci nit doff
Nitte dof yaw do dara dip moye sa baye
PRESIDENT FIFA👑👑🔥💪💪
Killer pour moi yaw ak niome douguéne bén sakh bagay nék fi di tontonté ak niome koula si diokhoul respect môme la déh mais kou wakhal deugue khamné sa niveau dépassé na dé clash ak boyi gua khamni défou niou sakh 5ans si rap bi
Chak jour selfi freestyle ni kouy dioxé courou make up...Boy dip dafma sagna teukou téy seu xour yi l éy deup....
Maturité 😍
Jador il communique bien
Paroles de Sage respect a toi brO
Ya mena doul ya fi waon dip nienama class
Vraiment da nga am fouleu yaw ya des choses beaucoup plus importantes k di dagasanté.
Dip 💪💪💪
Fake 50 cent ngeu 😂
Fuck you fake ass nga yaw
King Killer💯
Nitdof ya am fouleu,boy bi do moromam lui répondre c’est te rabaisser,vraiment tu a bien fait,laisse le s’embrouiller tout seul !
Dip moy baye yam 😂😂
Don't be so emotional mate même sa bay dip moy bayam !!!!
King bi
Yes killer no need to klash back kuz kalashnikov is an evident ya dont scare to play this game but at the right time man keep focus on this way u r handling hiphop
killa fait des videos mais boy yi doudou lagn geum .promo sa concert bi ngay deff rk
Coolllllll com reponse mister killer
🤙🏻🤙🏻🤙🏻❤️❤️❤️🤙🏻🤙🏻
Dip
Kileu fait des vidéos 😂
Dip baxul kw
Dip nit dof sa baye le
V t faire ft bro
DIP dal yeungueul neu rap galsen 😂😂 Nitdof y’a ndieuk togne dip Konn nak bulfi diayy affaire de sagesse parceque dip dafa yokou niveau bi ..même gfm Le nom de DIP lagnou djiteul pour gars yi regarde la vidéo 😂😂😃
Fi mature guissoumako fi xana dou mofi done khékh tay mou dieunde glace mo gueune thi mom sino mou diip rék
DOUNDOU💪🔥💸👉🍗
President FIFA 💪🔥
Cool
Dagni la may trophé mouno rap
maturité leu
Yaw dip dousa morom bigay rap mogui jardin di day toubay dip président
nit doff moytoul reseaux sociaux osi
Legui mom chaque décembre daniouy boxing day bamou saf sap.
Dangay. Fène rekk
Loutakh nga tontou nak😨😨
Dip👑
Dip fake la niveau yii bocoul
Dip beugeul diam bayi grand bi
killah
Golo gui mom dina dakhar leufeul ndeim
Killer fait des vidéos
Fatéwou niou UGB ak Canabasse
Ioe mom daga wara bayi rap tes djeul retrait 😂
Amina Hanne vraiment
Nit dof tenyi dip yokouna sa buzz dh nianal ko way
Daimlene retraite wayyyy ishhhhhhh
Policiens ngueu!
Yaw amo diome dip sa baye la
Bilay amoul diom mane il m'énerve 🤦🏽♀️
Yaw nopil amo lowakh bayiwonga dip class la nga gnewatt wayè tontoul tabaayi bii mola dèssè