Le 14 Mars 2023 - Live N 1/2 OUSTAZ CHEIKH ALPHA - PAROLES AUX AUDITEURS - LES BAYE FALL …

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 6 ม.ค. 2025
  • This stream is created with #PRISMLiveStudio
    Parcelle assainie

ความคิดเห็น • 71

  • @alloucoco
    @alloucoco หลายเดือนก่อน

    merci oustaz al Alpha

  • @BellaBellaba
    @BellaBellaba 10 หลายเดือนก่อน +1

    Yalnaniou yalla moussal ci rere ak passe passe bou bonne, merci ya oustaz

  • @CheikhDieng-zc6bm
    @CheikhDieng-zc6bm 11 หลายเดือนก่อน +1

    Merci beaucoup❤

  • @mamadousy6312
    @mamadousy6312 ปีที่แล้ว +10

    ❤❤machallah n oublier pas les cinque prier mes frère et soeur musulmane wa salam

  • @bst2366
    @bst2366 7 หลายเดือนก่อน +1

    Dieureudieuf Serigne Touba diarama CHEIKH IBRA FALL

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 6 หลายเดือนก่อน +3

      Sante yalla sougnou borom bou bah

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 6 หลายเดือนก่อน +1

    Yalna yalla samou oustas alpha ba amine yarabi

  • @Cheikh-dp8dy
    @Cheikh-dp8dy ปีที่แล้ว +5

    Celui qui laisse volontairement de faire la prière sans contrainte yeufeur leu koukoy layal nafekh leu

  • @tallasakho4599
    @tallasakho4599 10 หลายเดือนก่อน

    Alpha.
    Les voies du seigneur sont impénétrables
    Allahou Alam.

  • @hannharouna3630
    @hannharouna3630 ปีที่แล้ว +1

    Salam salam

  • @salifsow9779
    @salifsow9779 ปีที่แล้ว +1

    جزاك الله خيرا وبارك الله فيكم

  • @Cheikh-dp8dy
    @Cheikh-dp8dy ปีที่แล้ว

    Tarikha cheikh mo nekh❤️❤️❤️❤️

  • @falloutoure135
    @falloutoure135 ปีที่แล้ว +4

    Wa premier auditeur bi wérna Mane dama rous sakhe billahi déme léne toppi yalla Al qourane at sunna

  • @oumardiallo6139
    @oumardiallo6139 ปีที่แล้ว +4

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci beaucoup alla

  • @alioulawndiaye8627
    @alioulawndiaye8627 ปีที่แล้ว +3

    Merci docteur cheikh Alpha BA!

  • @alinesamb5006
    @alinesamb5006 ปีที่แล้ว +1

    ماشاء الله بارك جزاك خيرا

  • @Aliouseydebouda
    @Aliouseydebouda ปีที่แล้ว

    Salamo therno alpha mino yedima khatankho min tidjane aliou seyde machlah

  • @Cheikh-dp8dy
    @Cheikh-dp8dy ปีที่แล้ว +1

    Dengay fen tunisien yi khamouniou mouridisme g fais des années en Tunisie

  • @grahamkane3594
    @grahamkane3594 ปีที่แล้ว +3

    Oustaz alpha ziare nagneleu barakala fikoul wakhtane bi amneu solo

  • @quransunnah750
    @quransunnah750 ปีที่แล้ว +4

    J'ai aimé l'intervention de la dame de 2:20:00 yalna ko YALLA samm té tek ko chi yoonou Sahabas yi

  • @babacardiouf5968
    @babacardiouf5968 ปีที่แล้ว +2

    Cheikh apha

  • @MamadouNdong-l4f
    @MamadouNdong-l4f ปีที่แล้ว

    Alpha ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @coumbayacineba3729
    @coumbayacineba3729 ปีที่แล้ว +1

    Salam salam ya oustaz

  • @falloutoure135
    @falloutoure135 ปีที่แล้ว +12

    Souma naré par par lo yalla nama Yalla Alak sunna Al qourane rék ba Sango souf

    • @rappel4152
      @rappel4152 ปีที่แล้ว +3

      In shâ Allah

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 6 หลายเดือนก่อน +1

      Yalna yalla mousal gnou ci bokalé ak bida amine yarabi

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 ปีที่แล้ว +3

    Bayi santane yalla topp santane nit. Gni danio febar febarou khol

  • @sidydiouf876
    @sidydiouf876 ปีที่แล้ว

    Ay tout tank you mokaloul alkhourane ték si Di diguatt gnakk diomm

  • @mormbaye7670
    @mormbaye7670 ปีที่แล้ว

    SALAM la mosquée plus proches de marché SAVANEL qui prie aujourd'hui ce vendredi al hid al fitr SVP barakalahou fiikoum

  • @OusseynouBa-t3i
    @OusseynouBa-t3i ปีที่แล้ว

    السلام عليكم وحمةالله

    • @OusseynouBa-t3i
      @OusseynouBa-t3i ปีที่แล้ว +1

      من ترك الصلاة هو كافر

  • @babacardiouf5968
    @babacardiouf5968 ปีที่แล้ว +2

    Assalamouhaley koum cheikh bi

  • @seydouba2603
    @seydouba2603 ปีที่แล้ว +2

    Gni ndiabbar mo léne sonnal walahi .Danou léne liggueye ndiabbar léne. Ham Ham bou gnoul bi

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 ปีที่แล้ว +2

    Koudoul diouli do dioulite lolou lerna nsgne

  • @falloutoure135
    @falloutoure135 ปีที่แล้ว +7

    Oustaz alpha ba amoul décourager dé yalla Mongie andale yénneu wallhi li môme lérnama

    • @falloutoure135
      @falloutoure135 ปีที่แล้ว +3

      @@thiammady4782 Yalna niou yalla djoubal ta deugeureul niou ci sunna amoul déllou ginaaw dé Gamin de la vie

    • @aissatadiop4947
      @aissatadiop4947 3 หลายเดือนก่อน

      Hola

  • @TRA-PASTEF
    @TRA-PASTEF ปีที่แล้ว

    Alhourane ak sunnah référence

  • @laminekane4496
    @laminekane4496 ปีที่แล้ว

    Bone dei wessouwoul lii

  • @seydouba2603
    @seydouba2603 ปีที่แล้ว +1

    App Baye fall ligueyoul borom mame . Nite lay ligueyeul walahi nite layy ligueyeul .loutah alpha di nangou sa mounafikoune bingua nekk

  • @Cheikh-dp8dy
    @Cheikh-dp8dy ปีที่แล้ว +3

    SÉNÉGALAIS BEGOUL DEG DEUG NIOUSS LENEU DIOULI DJI

  • @CheikhDieng-zc6bm
    @CheikhDieng-zc6bm 11 หลายเดือนก่อน

    Cheikh bière de fodoufoune

  • @mamadousy6312
    @mamadousy6312 4 หลายเดือนก่อน

    😂😂😂😂yalla khol ley faye non sénégalais kha moule dîné l islam billahi

  • @CheikhyakhoubSidya
    @CheikhyakhoubSidya 11 หลายเดือนก่อน

    Alpha yaw mala défier sokhla la deba

  • @ndeyeyandediouf684
    @ndeyeyandediouf684 ปีที่แล้ว +1

    Asalamou haleykoum téy louy déba bii

  • @sutsaxelN
    @sutsaxelN ปีที่แล้ว

    Joulit dou diamou yalla bayilene feine

    • @mamadousy6312
      @mamadousy6312 ปีที่แล้ว +1

      😮😮😮🐒🐵🐵😡😡

  • @babaissasarr8617
    @babaissasarr8617 ปีที่แล้ว

    Ki. Khamoul dara da dianguel

  • @seydouba2603
    @seydouba2603 ปีที่แล้ว

    Walahi ki da am problème walahi mane damako yeureum ndah mom da melni kignou deuppp hel bi

    • @Bah-gl1kj
      @Bah-gl1kj ปีที่แล้ว

      Khana kholoco avec sa face de chaytane cou leundeum kourouss la

    • @sidyguey3690
      @sidyguey3690 ปีที่แล้ว

      que lulerr laye wakh machala

  • @khadim395
    @khadim395 ปีที่แล้ว

    Yalla digalnako moubang yaw lou yalla manoul dar yaw nit loo ci mann

  • @MassaerDieng-w9l
    @MassaerDieng-w9l ปีที่แล้ว

    Niaka diolic chiekh ibra kou ko digat salafal ndeye
    Yow AK kon yakar

  • @minguendiaye5918
    @minguendiaye5918 ปีที่แล้ว

    Dioxé geune diouli mandou mo geune koOr
    Ndax soy diouliii da ngay dioxé té fepp mo nek siii Yallah wayé dou Yallah ngui fepp
    So mandou woullll té ngani da nga da nga woOr xeuye diii nek siii dérou niit yi ba eurou dogg wala nga nek siiii ludo wala carte.....................

    • @seydouba2603
      @seydouba2603 ปีที่แล้ว

      Kone lou waral jihadou serigne bi binguéne topp. Té mom wahna si jawwharoul nafiss walahi .khoulte wamane talaba ridwanal wara bi souhti rabihi fa oumroune zoul oukra. Dem lene demandé moy lane tamite walahi

    • @antaalimafall7283
      @antaalimafall7283 ปีที่แล้ว

      koudoul diouli yeffeur bou bone bou gnoul kouk nga ak ko meuneu nekkeu

    • @mormbaye7670
      @mormbaye7670 ปีที่แล้ว

      SALAM je veux participer comment je peux entrer ?

    • @mormbaye7670
      @mormbaye7670 ปีที่แล้ว

      BARAKALAHOU FIIKOUM, Ajoutez moi Svp

    • @sayedia9456
      @sayedia9456 9 หลายเดือนก่อน

      Fouko yallah wakh si alkhouran wala sk fouko mouhamed wakh si hadith

  • @sutsaxelN
    @sutsaxelN ปีที่แล้ว

    Kou jouliwoul do dara kon yonenti yi jitou moukhamed dougnou tous

    • @antaalimafall7283
      @antaalimafall7283 ปีที่แล้ว

      koudoul diouli yeffeur bou bone bou gnoul kouk nga ak ko meuneu nekkeu

    • @ibrahimaseck5111
      @ibrahimaseck5111 ปีที่แล้ว +2

      Bobou jouli amagoul

  • @papaelhadjithiam7746
    @papaelhadjithiam7746 ปีที่แล้ว

    Mdr yeina soneu dh
    YEIN dangein Diapeu né teixeiii ngein koi ??? Est dolein lidieuntiii seni ayib té bayi ayibiii diambour?

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  ปีที่แล้ว +3

      Mais yaww tonth guaa saa boop 😂😂😂😂☝🏿☝🏿 ayiibii diambour no c’est que dina islam moo mell nonou leep lou ci bokoul dangn wara weddiiiiiiiiiii te lerall koooooooooooooooooo

  • @cheikhthiam6458
    @cheikhthiam6458 ปีที่แล้ว +2

    Younouss un peu de mesure danga eupeule torop

    • @coumbayacineba3729
      @coumbayacineba3729 ปีที่แล้ว

      Salam salam ya seydi

    • @coumbayacineba3729
      @coumbayacineba3729 ปีที่แล้ว

      Salam salam mes chers je vais participer s'il vous plaît et je sais pas comment faire j'ai ma première fois sur un lif

    • @mormbaye7670
      @mormbaye7670 ปีที่แล้ว +1

      SALAM, je demande la mosquée plus proche de marché SAVANEL qui prie aujourd'hui. Et cous ce qui vous dîtes est clair et net quiconque ne peut avoir des preuves à mon avis barakalahou fiikoum que dieu vous guide bien même. yén ngui léral bou bakh

  • @khadim395
    @khadim395 ปีที่แล้ว

    Yaw doo mourid

  • @sutsaxelN
    @sutsaxelN ปีที่แล้ว

    Guemo nit xana mouxamed mom du nit

    • @santediallo6111
      @santediallo6111 10 หลายเดือนก่อน

      Muhammad est l'envoyé de Dieu cher mr .