Série nekhna trop mais mention spéciale à l'équipe technique oh oh la qualité est du haut niveau. ❤❤❤Son, montage, cadrage, image tout est au top deug dou Niro AK pire RTS nak yaye télé nationale. Félicitations à toutes l'équipe je vous envoie pleins de bisous 😘😘😘
Walay méttina ms wadji tamit nénako sa borr yi dafa beuri Adouna mo métti rk li gnikoy doundu dafa beuri 😢ms borom boutique bi mom limou déff dafa niaw 😭💔
Bacary sa wakeur sagn nagn dompatt néw 😂😂😂 niom dal daniouy khéy rék togu pourtant sa petite sœur peut aller chercher du boulot wayé khéy rék di snap ak lék 😂😂😂. Mais borom boutique bi sokhar naa loll
Mame Khoudia est une excelllente artiste. Je realise toujours pas qu'elle ait deja depassée cette étape de dépression et revenir plus forte qu'avant. Mais ani Jalika sama sokhnasi
Vraiment ce film reflète nos réalités au Sénégal. On met tout sur le dos des hommes. C'est pourquoi les hommes meurent vite à cause de cette lourde responsabilité. Massa way Bakary.
Remarque bou niepe def moy gaz legui dou mat sax 15j comme si charger ko dou mat c grave sama pape chak jr mou kass ko 😂mais bakary sone na vraiment nak le bonheur de bakary kmm aaaa
Franchement halima gadji mon actrice préférée, elle est à l'aise dans tous les rôles. Force à elle ,1M de coeurs pour elle.
UNE SERIE PUREMENT SENEGALAISE BRAVO AUX ACTEURS ET AUX REALISATEURS
❤❤❤
Une pensée forte à tous ceux qui traversent des moments difficiles. Restez forts, cela va passer.❤💪🏼🙏🏼
Yalla naniou Yalla doli Soutoureu 🙏
Amine ya rabbi
@@amihtiam8615 bon courage ☺💪🏻
Merci beaucoup à toi 🥰
AMEN
C'est trop risqué gaz si taxi
Un série à la vraie réalité Sénégalaise
Bly
Bakary yalna nga guèneu ci tolof tolof yi ak bèpp père de famille bouy doundou yi situations 🙏🏽 rewmi mo bari thiono😂😂😂
Meilleurs série du moment 🥰😂
lol sahk blay 😂
Bilay
Série nekhna trop mais mention spéciale à l'équipe technique oh oh la qualité est du haut niveau. ❤❤❤Son, montage, cadrage, image tout est au top deug dou Niro AK pire RTS nak yaye télé nationale.
Félicitations à toutes l'équipe je vous envoie pleins de bisous 😘😘😘
Vraiment j'aime mame khoudia alias Halima je l'admire elle joue bien son rôle ❤❤❤❤😂😂bakari tamite sonouna 😂
bilay iow maneu damako fans 😂😂😊
Halima alias Mame Khoudia
Sacré Bakari 🌹😂
Bakary dou nitte 😂😂😂 merci beaucoup ❤❤❤
Mashallah akk sunu Ngour gou bess gui, Yallah Bakhna, Yakaar amna , naniou dolii niane req ;
Bakary vraiment yeureum nako mais mayél sa rakk bi moudém seuyi 😎😇
Ndeysaane lii boutiquier bii deff Bakari doundou na genrou action bii tek tek
Une leçon à tiré pour cette épisode
Soo nguéné sa keur ak Thiow diaapalni mooo lay topp toute la journée
Makha boutiquier bi loumou def Bakary nekhouma deh li mom tass yakar la té Bakary loumou sonou rek doyna😢
Vraiment Vérité Absolue Oui c'est Dommage 😭 Ndaysane
Walay méttina ms wadji tamit nénako sa borr yi dafa beuri Adouna mo métti rk li gnikoy doundu dafa beuri 😢ms borom boutique bi mom limou déff dafa niaw 😭💔
Wah loutakh gor gni beugu serie bi😂😂
Parceque c'est notre quotidien
@aliouthioub6537 c est vrai aye diambar guene yalna yalla defal lene diam
Notre routine plus tôt 😊
Da ñouy sétane sunu boopou 😂😂😂
Diarna lathie
Yallna yalla doli Diam ❤❤❤❤
Bacary sa wakeur sagn nagn dompatt néw 😂😂😂 niom dal daniouy khéy rék togu pourtant sa petite sœur peut aller chercher du boulot wayé khéy rék di snap ak lék 😂😂😂. Mais borom boutique bi sokhar naa loll
Ay way😂😂😂
Bakary 3 personne yi gnoy problème bi,
Superbe Famille Bakary Du courage depuis la France
Vraiment Bakary sonn na bak😢😢
Wa keureup yi gnoko sonal, yeureumou gnou ko dara
Serie bakary daffa waron ame son wally ballago seck taxi love
Akhlou brick taximan
Wl Borome Keur
Aye waye yueruem len Bakri
Mame Khoudia est une excelllente artiste. Je realise toujours pas qu'elle ait deja depassée cette étape de dépression et revenir plus forte qu'avant. Mais ani Jalika sama sokhnasi
bakary sone na nk😢
Bilay ndeyssane damako yeureum té il joue bien son rôle
Avant tout nañu sante yalla bu bakh mom miñou may tawfekh bañ mana nieuw ci TH-cam bi di setan BAKARY amna ño xamni taluñuko dakh ay problème ❤👏
Pauvre Bakary😢😢La voix off de retour ❤
Vraiment ce film reflète nos réalités au Sénégal. On met tout sur le dos des hommes. C'est pourquoi les hommes meurent vite à cause de cette lourde responsabilité. Massa way Bakary.
Bilahi sama vie ak bou Bakary ben la 😢
Masta
Yalna yalla taxawoula oyofal yen bii😢❤❤❤❤❤
Massa 😂😂
ouh massa 😂😂
Une série très intéressante qui reflète notre vécu quotidien c'est Bakary taximan. Du courage aux "brom keur" yalna yalla doli soutura si 🙏.
Franchement épisode bi ça parle de beaucoup de chose ❤️💪🏾🎊
Bakary sa mère elle n’a aucune pitié envers lui. Genre gni nioye pousser les jeunes à prendre l’océan 😂😂😂😂
Nanou yalla doli soutoureu mes frères ❤
Bakary beneu problème rk la am moy familles mi wam mokou yeremoul😂
Bakary mba dou écchangé gaze yi😅😅
Non d'où sath deh ou bien😂
Une bonne question 😂
Loll lay def sakh
Bakary bou diawalé bouteille gaz yi dinaci dall dh 😂
Mann tay da am loumeu diahal barkary femme bi nek si restaurant bi c sa copaine ou bien dahté mom amna louko doy keureum di dohan 😂😂
@@FatouDiame-y5m oui c’est sa copine mais défalouko dara😂au contraire kokou mokay may
Copinam la kay goor mo gnimé lou méti😑😑
Mangui done sentu bakary wara yeggal gaz 12ème étages 😂djambar leu nak machalah
Batay bakary amul gaze 😂😂
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉 0:11
Mame khoudia ❤ une très grande actrice
Bakary le meilleur😂❤
Boulene fate le 15 décembre la Macky Sall diapon élections présidentielles 😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Souba la 😂😂😂incha allah
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Légui noumou moudié won sakh dama faté 😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Alhamdoulillah sant yalla bou bakh
Toute ma famille aime cette séri
Bouléne faté qui binde scénarios bi kokou mo aï dou acteur yii
😂manone na bind scénario baparé dieul actrice you Mélni mane niow di réciter dialogue
Bakary est juste le reflet de ce que vivent les sénégalais
ticket laobe ak ndeye Ndiaye est ce que Amou niou problème personnel 😂😂😂
Meilleur série billahi. Vous êtes les meilleurs
Peul fouta yi nk barina ngou ay boutique dh boutique bakari dém yép ngomla😮
😂
Peul dou mbok
Hum doyna war dal bolessi gnak kersa mou moteu seuk
@@maimounandiaye-le1tu blay😅😂
Comme gnoune sénégalais yi nangouwougnou diaye boutique Kay étrangers Yi nek si
Borom botiqu bi lim Deff mernasi trp waye 😭😭😭Bilahi
Bilaye gazou légui dafa gawa diékh
Man pourtant sougn galle gaz meun ammak gnoune wer ak loutek mais mann ma takh Mouy sakan sam pappa monei makay gardé sougn wakeur danio beug Lou yomb
Série bi Machallah ❤
Ndeysane thieye adouna Sénégal mou geuna nekhe thi adouna 🇫🇷🇫🇷
Bakary jambar la dh🎉❤
Vision Sénégal 2050 inchallah❤❤❤
Yayou Bakary tamit amoul yermande si domam 😢
Vraiment Tmt C'est Triste 😭 Ndaysane
Bakary représente l'image des goorgoorlou,courage à tous
Merci pour la pub 9kg lobbo mame Diarra bi nimou manquer sakh da metti tay 15h lagnou agn ndakh gaz bou djekh
Bakary sonn na 😂😂
bakary soneu na bilay 😂😂 Mére bii bi mome internet bi moko intéressé ak vocal yii 😂😂
Famille wam bi gnoko yeureumoul dara. Gnom daal sen beug beug rek😂😂😂
Bakary mort vivant nga vraiment 😂😂😅
Doukoury daa reew rek mais doundoul moitié li bakary di doundou 😂
😂😂😂😂😂😂
Bilay, ndakh mom célibataire la sans enfants 😂😂
Bacary kaay mo gueuneu sooneu doucouré😅
Baakari waaw góor mettina waaye noonu rék la😂❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Machalah tout est naturel dans ce téléfilm good job
Meilleure serie thi rts
Kou Yeureum Bakari kom mane 😢😢😭😭😭😭😭😭😭
Kou contant ci série bi abonnél si sama compte bi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Meilleur série du moment je con9❤😂
Modou lo kass❤❤❤❤
Mafi djittou😂😂😂😂
Dioubo legui khoulo legui mes Bakary
Mounhele
Ms série guéyy na ame dh loutakh lolou
Bilaye Bacary damako yeureumm😢😢😢😢,benn keurr benn nitt rekk yorèkoo tè yayam yeureumoukoo benn yonn😢😢😢😢Sénégalais you barri liii lagnouyy doundou😢😢😢😊
Yayam mo kouko dal mérite naco Moy ndawtal khalissou Bakary si khew yi 😢😮genrou nitgni yallnaniou si yalla mouseul😮
@YSaliou bilaye yayam affaire de grande Dame laye. Incarné tè train de viwamm matè woukoo
Bilay Bakary dama ko yeureum nak 😂😂😂
Non Bacary sonnu na nk bilay 😂😂
Bilahi bakary damako yeurem 😢😢
Bakary yeureumnako trop😢
Borom boutique bii bone na💔💔
Ma khoudja Yangui wathiè bètè bété wollah 😂😂😂😂
BRAVO A NOS FRÈRES GUINÉEN VOUS ETES CHEZ VOUS SOYEZ FORT ET N'ÉCOUTER PAS LES HAINEUX
Mais Bakary mii dou lathié ba paré sogua wathié gazz bii sii taxi bii 😂😂😂
Wakh deugg yalla 😂😂😂😂😂😂😂
Kon du don ab dof di😂
Machalah li nekh trop
Borome boutique bi lime deff Bakary mettina ma troppe… Billay dinako bolé akk Tahirou Sarr 😢
Bakary tay nakharina deireitt di 😂😂
La relation de mame khoudia et sa belle famille ❤❤❤
Non mareme d'où niit keur gui nekhna ❤
Halima Guadji est très belle Ma Sha Allah❤
Ki mbindeu série est le meilleur li sénégalais yi di ndoundou😅
Vraiment j’aime trop mame khoudia🥰elle joue bien son rôle 😂😂😂🫶
Souniou wa keur yakh gaz rek😂😂
Kharal ma dém bollé la séne wa keur 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
bilai bakary damey dioylo 🤦🏿♂️🤦🏿♂️
Bakaru diotna mou am benen goor ci keur guy ndakh moukoy diapalé ci khoulobi😅😅
jadore trop halima bakary aussi cest le meilleur
Bacary tmt amnga khél ta bari énergie do lathieté ba paré dogay wathié gaz bi😂😂
Massa Bakari❤
Thiey les guinéen yé yalèn di diapalé mai gnom bonne lagnou déf
Vraiment les pères familles souffrent 😢
Bakary ak Mansour kou tané sax 😂😂
Bakary Taximane la série qui n'a jamais perdu sa valeur
Remarque bou niepe def moy gaz legui dou mat sax 15j comme si charger ko dou mat c grave sama pape chak jr mou kass ko 😂mais bakary sone na vraiment nak le bonheur de bakary kmm aaaa
J'aime pas les gens qui pense a eux même. Bakary borr kénn dousi insisté 😂wayé makha wéréngua trop mounone ngua téyé 10.000 réck