💚💛❤ Waly yaw tamit yeureum niou 🙂. Quand j'ai vu cette version je me suis dit " non bi meunoul dah la 1ere" Mais quel talent ! Quelle inspiration ! Quel boulot! Liguey reck moy deug. Merci pour ce moment de recueillement, hel yi yeup dem thi liguey Serigne bi. Mashallah ! Koudoul mouride sah tu as envie de l'être. Que ce mois de Safar, soit un mois de paix, d'union, de bienfaits pour tous. Yallah na la Yallah saam, ar la, yaw ak sa ndiabot. May la weer ak goudou fane 🤲🏾 Yalla na fi Maman Diaga yagu fi lool, té weer 🤲🏾 J'ai envie de pleurer bilay. C'est parti pour une seance d'écoute non stop. Je suis deja à 3, me connaissant rien que aujourd’hui douma sori 20 dé et encore 😂. Bon magal à tous les mourides, à bep tarihas. Senegal bene bop la, Ken meuno ko har niar ❤ ILLA TOUBA ✊🏽 Kouthi magali boum ma faté thi ay niane mashallah 🤲🏾. Dieureudieuf. Magali leen thi diam, gnibissi thi diam🤲🏾
Moi je l'ai côtoyer en Suisse mais massouma guisse kou geuneu yarou wally secke d'où digui khole ni layii sénégalais yi wallah dinalene laque sa dôme bi âme 5ans laniko taye sama chérie epuis daffa diape datou anniversaire râme fadiare lakoyi defale vidéo ba paré envoyé ko auyi cadeau mome ak sa femme sokhna aidara diame si yaw
Je suis chrétienne mais j'aime beaucoup mame Fallou Galass baye mbène wally ta tapé fort cette chanson est une philosophie de l'art et un instrument musicale qui illustre ses paroles machallah nice❤❤❤
@@clementlenglettv8785 Ndeysane mane niom niogui xar presque toute ma famille wa keur kara ak Serigne kalla mbacke, niom bou xess ,ak Serigne Cheichk mbacke Sylla ,ak Serigne Cheikh Ahmed Soilleh ils sont même donnés le nom de ma defunte grande mère Marie Ndiaye au lieu de Marie Dasylva ndeysane
Franchement j'écoute pas c'est musique tellement mai cette chanson me frappe tellement je peux pas l'expliquer du début jusqu'à la fin tout et bon chapeau a Wally c'est sa quon dit c'est le travail qui paye goudou fane ak weure rek inchallah
Wally ko ray ngay weurr 🥺🥺 non mais akhlou djang kate nga fi dadialei niii ba def sa mini Magal, berndei ba contaaan ohhh 🙈🙈 Machallah 🥰 da nga meilleur yakh wakh la niane rekk lagne lay deffal 🤍🤍🤍
Desseulatognou dara faramareen bi kontane nagnou ci ioe boubax machala Bon magal a vous tous inchala🙏😘❤❤ atia gnou tokk xaar beu 18h rek ni 18 safar❤❤😊
Waly nguir dieumi seydina mouhamed doma maye auto wala xaliss❤❤❤🎉 yallah ngua dome you gorr yeupp toudou seydina mouhamed inchallah malaka nianal 😭😭😭sama xol lako tibée nianale ko
Mais Wally Seck est-ce que do extraterrestre tamit 😂😂😂! Cette version est Trop bonne, trop classe,un mélange de fun et de sérieux et surtout surtout ta modestie se fait remarquée dans le clip! Yalla nala defal diam defal ko mboleme domou Adama! Yalla nala Yalla saam Sama meyla goud fane ak weer defal ko mboleme domou Adama thi BARKE SEYDINA MOUHAMED SAW ❤AMINE !!! Bon magal à tous dem thi diam gneuw thi diam thi BARKE SEYDINA MOUHAMED SAW ❤AMINE . Thi barke SERIGNE SALIOU MBACKÉ ❤AMINE
Le problème avec Wally c’est on l’avait beaucoup critiqué mais ce gars il a su prendre ses critiques de façon positive. Il s’est tellement perfectionné surtout son timbre vocalique est Waouh Bilahi ma yeureume koula bagne sa kone d’où nelaw
Il a toujours fait preuve de maturité et grandeur en utilisant ces critiques acerbes pour se parfaire techniquement, vocalement et avancer doucement et surement dans la bonne direction mashallah!
Le chanteur le plus polyvalent, plus puissant et qui maîtrise les variations, celui qui peut chanter dans la voix de quiconque avec une technique qui rappelle Feu Ndiaga Mbaye est Cheikh Mbaye. Chapeau à Waly qui a eu cette idée.
Wa dji damako beug ba amouma si mom sago barké alhouranoul Karim je l'aime de tout mon âme téi khamouma sakh Bane façon beug lako beug tout ce que je sais c'est que je ne suis pas amoureuse de lui lol nobou mako mais damako beug beug bou amoul fin ❤😢bou dioyé ma dioy bou rétané ma contane bou amé Ay problème ma fébar beu nieup khamko si mane😫 Dieu m'en est témoin
Lilla toubab nane La Perfection Barkii Seydina Mouhamed Wally tu le vois et tu l'aimes sans savoir pourquoi parce que pour mane kholam mo rafet té yalla khol lay faye Ya de la musique le scénario le sagne sé l'entrée des invités le feeling le mouride le magal en gros l'Islam DIEUREUDIEUF CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOU RASSOUL
Je viens de tomber sur cette merveille. Sama kholl toynaa. Je t'ai toujours estimé Waly au travers de tes oeuvres sociaux. Mais ce chef d'oeuvre a fait que mon estime est inégalable. Yalna Cheikhouna cheikhoul khadim Faylla , Amin
Franchement kou bagnone nanga nangou nakk. Je l'ai toujours dit et je ne cesserai jamais de le dire. Le devise de Wally c'est travailler beaucoup et parler peu. J'ai toujours adoré cette chanson là mais alors le remix avec des personnes qu'on ne connait pas qui chante si bien dedans, cela donne un peps et de l'originalité incroyable à la chanson et au clip Machallah il est bourré de talent ce garçon. Ça kaw ça kanam rékk.
Wallahii nagnou magalii ak diam in shaa Allah wayé sa tour nkoo yobou sii Serigne Fallou Galass❤❤ ndam ngay am dh do Danou moukk in sha Allah Papa Ibrahim❤
Une des rares fois où je commente sur TH-cam, Waly beug naala walahi azim barkei serigne Fallou diam rek ngay am. Je suis ta plus grande fan. Tu es de loin le meilleur ❤ yalnala yalla sameu yak sa ndiabote si barkei yonentbi
Ya’Allah hamna ni niveau yii dou beine. De nos jours kepp kouyy wayy biir Galsen do moromou moromam. Tu ne cesses de nous surprendre Ballago wallah. Quel Talent ! Tu es juste le meilleur. Machallah yallah nala thiatte sehlou. Bonne continuation ! ❤
WBS le chanteur du peuple le roi de sa génération le fils de papa Thione et de mvmv Diaga Bon magal à tt le monde Seuñ Touba Dou marom xol yi sedna Maryacine ❤🎉🎉❤❤❤🎉🎉❤❤🎉🎉❤❤🎉🎉❤
Oh m'y good Entouka sama yaram dawna bilay machalla ❤😇com dab yalna la yalla sam lak fou yak yegoul Lép lo ragual yalla bon dadié ak mom si barkel seydinamoukham love you ❤❤❤❤
Bilai mouhamed alla dafa meune degal limouy rim rek❤❤
Ndeysane pape thione leupeu louko nakhari wone sounou borome fonpeu neu rongagniame
Mouhamed Alla Diop machala sa bate dafmay dioy Lo ❤😭
Wa cheikh mbaye mi dara la dhé lou nékh la way Wawaw 💃❤️😂
Wayy li nekhna lolll ak sénn sagnsé you rafett.
Alhamndoulilah
KING BI NDANANE BI SÉNE PAPA DJI ON T'AIME TONTON WALLY 🥰👏🇸🇳
❤❤❤❤
Borom Ambiance 😂❤
Cv aïcha❤
Ww dafa lere
Bilay yaw machalla ❤️
Wakhouma lolou dé li cheikhe mbaye waye eskeu dameula seuuuuuuteuteu
Liii dale boudoon football Cheikh Mbaye mooy l'homme du match❤❤❤
Je suis vraiment dépassé ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️li neikhna waaay oooooh
th-cam.com/video/bH4tPhdGYyw/w-d-xo.htmlsi=SoZMm0lvZQJMjYe3
Ay ndandan rk niofi dadialo billahi 😢❤❤❤❤❤❤
💚💛❤ Waly yaw tamit yeureum niou 🙂. Quand j'ai vu cette version je me suis dit " non bi meunoul dah la 1ere"
Mais quel talent ! Quelle inspiration ! Quel boulot!
Liguey reck moy deug.
Merci pour ce moment de recueillement, hel yi yeup dem thi liguey Serigne bi. Mashallah !
Koudoul mouride sah tu as envie de l'être.
Que ce mois de Safar, soit un mois de paix, d'union, de bienfaits pour tous.
Yallah na la Yallah saam, ar la, yaw ak sa ndiabot. May la weer ak goudou fane 🤲🏾
Yalla na fi Maman Diaga yagu fi lool, té weer 🤲🏾
J'ai envie de pleurer bilay.
C'est parti pour une seance d'écoute non stop. Je suis deja à 3, me connaissant rien que aujourd’hui douma sori 20 dé et encore 😂.
Bon magal à tous les mourides, à bep tarihas.
Senegal bene bop la, Ken meuno ko har niar ❤
ILLA TOUBA ✊🏽
Kouthi magali boum ma faté thi ay niane mashallah 🤲🏾. Dieureudieuf. Magali leen thi diam, gnibissi thi diam🤲🏾
waaaay ya baaaax waaaay ❤
Bilae daga niakk ki niane li yeup ga waxx mom mom nitt ki baxx ga
❤❤❤❤❤
Bilae y’a bakh th am yarr wayy Yalnala yalla defal diamm❤si barkei fallou awa bousso
Yaa baah
Bilay way bi mom damasè thialite mom sama xol bi lay nekh mom rek lay deglou chaque jour
Vraiment le niveau de @Wally B Seck dépasse tout les musiciens du Sénégal d’aujourd’hui ❤️👌Respect à lui
Bagne bagne beugueu force la
❤❤
Bilai le niveau est vraiment élevé
Bilahi walahi tu as raison wally est le meilleur et il sera le meilleur pour toujours
Blh iow lou lerr
Waly yalla nagua goudou fane limaye guisse thi yaw reuyna mâchala
Cheikhe mbaye yalna yallna werall batt bi b s touba 🕋
Wa ms sama gahii bouléne thiatou😂😂😂😂🎉❤ laff bouché 😢
Nr1 achaaleen reek Wally is moving forward mom waahkat dee waah mor koi dundal 😂
Vraiment Yangui ci Kaw tu as dépassé Yangui ci bénéfique niveau
Moi je l'ai côtoyer en Suisse mais massouma guisse kou geuneu yarou wally secke d'où digui khole ni layii sénégalais yi wallah dinalene laque sa dôme bi âme 5ans laniko taye sama chérie epuis daffa diape datou anniversaire râme fadiare lakoyi defale vidéo ba paré envoyé ko auyi cadeau mome ak sa femme sokhna aidara diame si yaw
Machalla li nga df rafet na trop Mouhamed alla yalla nga yègali ak sa sago dra diomboula
Respect à cet homme waly seck,il incarne la maturité de l’art 🙏😍
Wally ya meun ya eup doller fraiment t'es le meilleur tellement mature
Je suis chrétienne mais j'aime beaucoup mame Fallou Galass baye mbène wally ta tapé fort cette chanson est une philosophie de l'art et un instrument musicale qui illustre ses paroles machallah nice❤❤❤
Machallah C'est mon homonyme je vous aimes aussi
@@clementlenglettv8785 Ndeysane mane niom niogui xar presque toute ma famille wa keur kara ak Serigne kalla mbacke, niom bou xess ,ak Serigne Cheichk mbacke Sylla ,ak Serigne Cheikh Ahmed Soilleh ils sont même donnés le nom de ma defunte grande mère Marie Ndiaye au lieu de Marie Dasylva ndeysane
Vérité absolue
Franchement j'écoute pas c'est musique tellement mai cette chanson me frappe tellement je peux pas l'expliquer du début jusqu'à la fin tout et bon chapeau a Wally c'est sa quon dit c'est le travail qui paye goudou fane ak weure rek inchallah
Le top des top meilleur de sa génération. Le relais de youssou ndour est assuré. Longue vie
Wally ko ray ngay weurr 🥺🥺 non mais akhlou djang kate nga fi dadialei niii ba def sa mini Magal, berndei ba contaaan ohhh 🙈🙈 Machallah 🥰 da nga meilleur yakh wakh la niane rekk lagne lay deffal 🤍🤍🤍
😂
Desseulatognou dara faramareen bi kontane nagnou ci ioe boubax machala Bon magal a vous tous inchala🙏😘❤❤ atia gnou tokk xaar beu 18h rek ni 18 safar❤❤😊
J'ai été bonnement surprise contane na si guiss cheikh mbaye ameth alla stop ak tawfekh mbaye
Ndeysane cette chanson me fait penser à Jean Paul d’almeida, a chaque fois que je l’écoute je sais pas pourquoi 😢😢😢😢😢😢
Waly félicitations mon fils nehna loleee ❤❤❤
La voix de cheikh mbaye 🤗🔥🔥🔥
Omaro fane la khifei tamit🤣🤣
Merci à toi Wally pour ce beau cadeau Magal
Talibé BAye la Wayé baatu Cheikh Mnaye Dinama ray barki serigne Touba😍
Sa me va droit au cœur 🥰bon magal sama mbokou mourite yii ❤ila touba inchallah après ila tivaoune ❤️😍🥰
Ba di nga magal si an machallah ❤❤
@@SoldarMbackedamay magali kaye inchallah ❤
An alhamdoulilah yallna yalla maye la khèwuel machallah
@@SoldarMbacke Amine ya rabbi gnou bok koo 🙏🤲🏿❤️
Diadieuf 🙏💔
Waly nguir dieumi seydina mouhamed doma maye auto wala xaliss❤❤❤🎉 yallah ngua dome you gorr yeupp toudou seydina mouhamed inchallah malaka nianal 😭😭😭sama xol lako tibée nianale ko
Kène dou cheikh Mbaye ✅
Kou d'accord ni cheikh mbaye moy les mileur rk lalal j'aime ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Chacun son avis, ces opinions
Mais Wally Seck est-ce que do extraterrestre tamit 😂😂😂! Cette version est Trop bonne, trop classe,un mélange de fun et de sérieux et surtout surtout ta modestie se fait remarquée dans le clip! Yalla nala defal diam defal ko mboleme domou Adama! Yalla nala Yalla saam Sama meyla goud fane ak weer defal ko mboleme domou Adama thi BARKE SEYDINA MOUHAMED SAW ❤AMINE !!! Bon magal à tous dem thi diam gneuw thi diam thi BARKE SEYDINA MOUHAMED SAW ❤AMINE . Thi barke SERIGNE SALIOU MBACKÉ ❤AMINE
Ooooooh diooooy naaaa Wally seck beugue nala nguire serigne touba😢
Kou beug serigne Touba Ak Mame Chiekh ibrahima Fall lamp baboul mouridina lalall j’aime ❤️🙏🏾
Omoro clip bi yeup thioppp ngako mais quand même nice na ❤
Le problème avec Wally c’est on l’avait beaucoup critiqué mais ce gars il a su prendre ses critiques de façon positive. Il s’est tellement perfectionné surtout son timbre vocalique est Waouh Bilahi ma yeureume koula bagne sa kone d’où nelaw
Il a toujours fait preuve de maturité et grandeur en utilisant ces critiques acerbes pour se parfaire techniquement, vocalement et avancer doucement et surement dans la bonne direction mashallah!
@@mamylailagoudiabyy’a meilleur nak😂❤❤❤
Avantages leu kay pas problème
C’est ça les critiques faut les prendre positivement.
Le chanteur le plus polyvalent, plus puissant et qui maîtrise les variations, celui qui peut chanter dans la voix de quiconque avec une technique qui rappelle Feu Ndiaga Mbaye est Cheikh Mbaye.
Chapeau à Waly qui a eu cette idée.
Machallah wally Tawfekh mbaye ligua bak sama wadji Fallou Awa bousso yalla n'a yalla gueneu wéreul bat yi si barkép Cheikhoul khadim❤
Amine way
Kèn dou Chékh Mbaye bilaye ❤❤❤❤❤
Intervention Cheikh Mbaye zikroulah ak Mouhamed Ala Diop aye dioy késsé la ❤❤❤ barké yonenté bi li dafa disse trop waye
C'est la premier fois May deglou sons plus de 100fois MM pas 3 semaine bravo 👏
Wa dji damako beug ba amouma si mom sago barké alhouranoul Karim je l'aime de tout mon âme téi khamouma sakh Bane façon beug lako beug tout ce que je sais c'est que je ne suis pas amoureuse de lui lol nobou mako mais damako beug beug bou amoul fin ❤😢bou dioyé ma dioy bou rétané ma contane bou amé Ay problème ma fébar beu nieup khamko si mane😫 Dieu m'en est témoin
Yalako dfff llou😢❤
Wayè billahi malako guena beugue 🙏🙏😭
Gnionla rawe si mbeguéle barki yalla lonou begue rk gniola rawe
Adouna dou nekhh bagua guen mako beug bilakhii 😭😭😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️
Bari ngassi morom bilay 😅
Nn cheikh mbaye ya Meune way ❤sheuuut mais chapeau à Wally seck
en vrai Wally tu es le meilleur 🥰❤️j’aime trop ce pays 🇬🇦❤️
wa yénn dégu nguénn Cheikh Mbaye limou diangue mann ki dégg gui nékeu tchi mom dama yémm bilay machallah li neikhna way
Tawfékh Mbaaye tmt, li lanla ❤❤❤❤❤
Cheikh mbaye et mouhamed alla mbaye yalla n’a Serigne touba guena weral batt yi ci barkep sougnou wasila 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤❤❤
❤❤❤❤
Mashallah ❤❤❤❤waly😂😂😂mé omaro😂😂nawlé😂😂 daforr😂lékgui😂😂Eupen 😂😂😂
ngiy wakh waly manul way nanu wouty écouteur you nékh 😢❤😅Machallah 😮
Bilay yoyou octave ak bobou voix ohh machalla ❤
Ligua beugue cheikh Ibra rek motax ma beugue la xamouma nouma laye Def del gamou sii thies nak
Mame fallou rek bilahi 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Joie de vivre bou musicien wally yi moma yéme.tu sens vraiment qu'ils ont le plaisir d'être au service de waly❤
Parce que wally est beugable yaw tmt nak❤️❤️❤️
@@fatoumatasambe billay ioe tu a raison dh
❤❤❤❤❤❤
@@fatoumatasambe trop beugable mm babou done djigène dina bariii yaye faarr
@@mortalaless8364 😂😂😂😂heureusement
Wally yall na yalla sedal sa khôl com niga sedale soniou khol❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Soule gaz douko tere khegne 💞💞😅ioe lo def inchallah day nekh parceque niepp la beugue mar gnie beug lakk nakk yague yague niaw 🥰🥰
Wally ak cheikh mbaye rk eupp na gua lale si alla Diop waxumala ak tawfékh mbay
Je comprends pas la langue mais ce qui me retient c'est la voix et la sonorité 🥰❤️🇨🇮🙏
Il.chante cheikh bamba le guide des mourides
Lilla toubab nane La Perfection Barkii Seydina Mouhamed Wally tu le vois et tu l'aimes sans savoir pourquoi parce que pour mane kholam mo rafet té yalla khol lay faye
Ya de la musique
le scénario
le sagne sé
l'entrée des invités
le feeling
le mouride
le magal
en gros l'Islam
DIEUREUDIEUF CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOU RASSOUL
Kén dou môme sama wadji wbs ❤
Ay wayebtawfe mabay sama kharit bi cheikh mabye li nekhh n'a way ak moukhamet alla Diop Wally Aka bakh ❤❤❤❤❤
Cheikh mbaye mom souma dewe moma ray ak kafere were ohh ndeysane nekhna
Bilay nekh na lolou
Je viens de tomber sur cette merveille. Sama kholl toynaa. Je t'ai toujours estimé Waly au travers de tes oeuvres sociaux. Mais ce chef d'oeuvre a fait que mon estime est inégalable. Yalna Cheikhouna cheikhoul khadim Faylla , Amin
Q😂❤❤
Toute les voix sont exeptionnelles vraiment mais Cheikh Mbaye tmt dioylo nama😭😭😭😭😭
Kokou mo tothie morceau bi Cheikh Mbaye ❤
Tawfékh mi ésque nite deggeul lamou way maréma konta yayi mbene machallah Tawfekh Mbaaye mou serigne bethiou ❤❤❤❤❤
Non li kén meussou ko guiss vraiment
J'aime trop wally dioulité bakh ..........)
Franchement kou bagnone nanga nangou nakk. Je l'ai toujours dit et je ne cesserai jamais de le dire. Le devise de Wally c'est travailler beaucoup et parler peu. J'ai toujours adoré cette chanson là mais alors le remix avec des personnes qu'on ne connait pas qui chante si bien dedans, cela donne un peps et de l'originalité incroyable à la chanson et au clip Machallah il est bourré de talent ce garçon. Ça kaw ça kanam rékk.
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉c est trop beau et bien gentil d avoir fait le partage avec ces grands chanteurs Maashaalah
Lou rafete mo nekh❤❤❤❤❤❤
Wally à de la générosité dans l'âme et le partage. C'est ce qui fait sa force et une qualité rare de beaucoup artistes ou musiciens sénégalais!
Machallah wally😊
Alhamdoulilah baniou yalla défé ay faramaréen ❤❤❤❤😂😂😂 ❤❤❤❤❤
Quand tu traites bien tes musiciens, ils se donnent à fond. C’est la différence entre les musiciens de wally et les autres musiciens
Thiey Wally 🎉🎉Mouhamed Ala entrée bou graw la df mom tamit ❤li nexna trop
Wallahii nagnou magalii ak diam in shaa Allah wayé sa tour nkoo yobou sii Serigne Fallou Galass❤❤ ndam ngay am dh do Danou moukk in sha Allah Papa Ibrahim❤
Le chanteur du peuple a encore frappé fort ❤
Bilahi très fort 💪 même machalla ❤❤❤❤
❤
Une des rares fois où je commente sur TH-cam, Waly beug naala walahi azim barkei serigne Fallou diam rek ngay am.
Je suis ta plus grande fan.
Tu es de loin le meilleur ❤ yalnala yalla sameu yak sa ndiabote si barkei yonentbi
Cette maîtrise des sonorités est machallah ! Waly wallahi we love u tawfekh et taysir Mouride 🙏🏾
Cheikh mbaye y’a doof d ❤
Wally tu m etonneras tumours.Legui da ngeuye yeuketi alto bamou saf.chapeau.
JE SUIS TALIBE BAYE NIASS MAIS JE SUIS ému de la prestation de CHEIKH MBAYE ET chapeau a WALLY SECK
Ya’Allah hamna ni niveau yii dou beine. De nos jours kepp kouyy wayy biir Galsen do moromou moromam. Tu ne cesses de nous surprendre Ballago wallah. Quel Talent ! Tu es juste le meilleur. Machallah yallah nala thiatte sehlou. Bonne continuation ! ❤
❤❤❤❤Amin🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@@rokiyasarr8688❤
Thiey yalle gua goudou fane waay Way gama founé barki Serigne Fallou borom ndindy damako beug ba awmasi mom saggo Baye gallas ken dou Mouhamadou fadal fallilou Dieuredieufety Borom NDÏNDŸ ❤❤❤❤❤❤
Album bi diar n'a 14 milliards kén dou ahmadou borom bureau bafa ndar
Thiéye mar bataye wanago niou sa bopp lafe thiate wally tu es qui ❤❤❤❤
Bravo à Mouhamed alla Diop vraiment meunena trop j l’aime bien
Cheikh mbaye sa voix est extraordinaire ❤❤❤❤❤
Que la paix soi avec toi mon chanteur yalla n’a Serigne touba defal la li guen ci yaw ❤❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Kou guiss legui promotion femme noire ak teint noir bi sénégalais yi dieul se sen clip yi ? Machala vive les teints noirs
Machallah lafthiat yalna yallah goudal sa fann té mayla wér si barké al khouranoul Karim
WBS le chanteur du peuple le roi de sa génération le fils de papa Thione et de mvmv Diaga Bon magal à tt le monde Seuñ Touba Dou marom xol yi sedna Maryacine ❤🎉🎉❤❤❤🎉🎉❤❤🎉🎉❤❤🎉🎉❤
Qui est d’accord que la voix de wally a bcp évolué le niveau est plus haut que jamais
Quelle voix la dernière personne en marron .. il a une belle voix machalla
Machalla baye fall bi yala n'a la yala may dix d'or Barkép Magal gui
Li nekhna dh bilay ❤
Wally séke yalla nasa diamo yague amine sy barké serigne touba ❤🇸🇳❤❤🇸🇳❤🇸🇳❤🇸🇳
Waw c juste musicalement parlant c top bon magal 2023
Macha Allah li neexna nak, clip bou sette, musique ak harmonie bou extra, classe ak thioline guissi clip bi macha Allah
Vally est l meulleur nak ❤❤❤❤❤❤
Oh m'y good Entouka sama yaram dawna bilay machalla ❤😇com dab yalna la yalla sam lak fou yak yegoul Lép lo ragual yalla bon dadié ak mom si barkel seydinamoukham love you ❤❤❤❤
Waa gnii seine retaine you neix yii lane leu... Neik Baye Fall neix neu... Daguay reeiii reik 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰