BAYE FALLOU (WALY B. SECK) / MOUSTAPHA/ PRIME 8 SPG ALLSTARS SAISON 2

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 3 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 1.3K

  • @yaaabyka8005
    @yaaabyka8005 3 ปีที่แล้ว +80

    Moustapha prince art sahh dagn ko wolou mashallah xamnagn nii sougn amei invité doulenn rousslo dassei bokkoul sahh dafaa meilleur daal mashallah way 😌❤️❤️❤️

  • @nabouzakamara3307
    @nabouzakamara3307 3 ปีที่แล้ว +95

    Ohhhh😍😍😍😘😘 liii nexna tropppppppp lii meussoul am sen petit gallé bilae kénn dou Faramareen bi Wally Seck machallah et félicitation à Moustapha tu es top 😘😘😘😘

    • @famasamb5461
      @famasamb5461 3 ปีที่แล้ว +4

      Il est le meilleur Moustapha on t'aime,😘😘😘😘

    • @ndeyecoumbandiaye7843
      @ndeyecoumbandiaye7843 3 ปีที่แล้ว +1

      Bilae kène dou wally seck tu es le meilleur xol yui sede na

  • @akhmadajadid3157
    @akhmadajadid3157 3 ปีที่แล้ว +4

    Bilay nexoul ba nexoul Prince NGA NGA kW Waly koula khamoul rek molay niemei

  • @salioufall802
    @salioufall802 3 ปีที่แล้ว +67

    Ndeysane wally feeling bei bari machala bayrei bi bari tarkala et il a reussi à toujours garder la tête sur les épaules .en tout cas kou meune gérer succès la lolou moko deife véritable leader . Waye Wally Amal diam yaw 👍👍✋🙏🏾❤️

    • @aminambengue6995
      @aminambengue6995 3 ปีที่แล้ว +3

      Wa Marta vous avez raison Wally yegul sucsé bi mo tax day dem merci de l’avoir compris

  • @maremefall5430
    @maremefall5430 3 ปีที่แล้ว +308

    Ni sama khol sèdè nonou la yep sèdè wala 🥰❣❤💯💃

  • @svtv2575
    @svtv2575 3 ปีที่แล้ว +30

    Khalé yii Sakh dagno contanne gnepp beug Wally Seck😂🥰🥰🥰❤️❤️🔥🔥🎤🎤

  • @khadyndiayediagne4561
    @khadyndiayediagne4561 3 ปีที่แล้ว +87

    Moustapha il me donne la chair de poule,sa voix,la tonalité,le charisme,je l'aaadoooorrrre🤩douma meusseu taayi dico wakh,je te suis depuis ke t'as commencé à chanter,yalla nala yalla défal diam👏🎩🥰🥰🥰🥰🤩

    • @layranne7979
      @layranne7979 3 ปีที่แล้ว +1

      Dp8 sn premier jour

  • @traorekani4712
    @traorekani4712 3 ปีที่แล้ว +206

    Il est humble waly je l'adore trop longue vie faramaré bi

  • @astoufall549
    @astoufall549 3 ปีที่แล้ว +53

    Wally est un artiste extraordinaire..il chante bien sa voix mashalla ..en plus il est aimé de tous..

  • @abydiallo7131
    @abydiallo7131 3 ปีที่แล้ว +70

    Wally moy senegal machalla❤️❤️❤️❤️❤️❤️yalnaga goudou fane🙏🏻🙏🏻🙏🏻soumakoy deglou samakhol comme frigot

  • @Mamymamadou21
    @Mamymamadou21 3 ปีที่แล้ว +201

    Moustapha a toujours été très fort
    Magnifique presta 😍

  • @ballab.s.kndiaye5265
    @ballab.s.kndiaye5265 3 ปีที่แล้ว +9

    Moustapha nice na trop machallah mais 1mn53 wally dafané kone niou and sante ahmadou mbacké borom xarnou bi lamp gnite la bamba féégne apres mouni amadou fall saër ndiaye birime kébé nga dess ngay.Mé iow moustapha bi nga né kone niou and sante ahmadou mbacké borom xarnou bi apres da nga dioum ngani khana nga dialé niou mame lamp baboul mouridinah maicha bigué coumba fall lolou topousi lolou après lako wally wax.
    Mé machallah way bi nexna trop t'as assuré vraiment félicitation

  • @Salimata.D12
    @Salimata.D12 3 ปีที่แล้ว +16

    Thièye mare yacine aka bakh kéneu dou mome na nguou rékeu wala bagne 🥰❤️ notre wally Seck 🇸🇳❤️

  • @fatoudiarrandiaye3951
    @fatoudiarrandiaye3951 3 ปีที่แล้ว +74

    Je suis contente et fière aujourd’hui. Mes deux fans en duo. Malgré sa voix cassée Moustapha a su assurer la chanson. Yalla ´na yalla weiral bate bi. Je te souhaite une très carrière

  • @Junior-kalish
    @Junior-kalish 3 ปีที่แล้ว +199

    C’est vrai que bokouniou registre biniouy wayé mais il a géré Moustapha 🔥 Wally voix bi mo sensuel t am ndeysan 🥰❤️

  • @sophiebadji9382
    @sophiebadji9382 3 ปีที่แล้ว +127

    Li ça prouve que Tata Ngoné liguey na vraiment les enfants sont bien encadrés car le résultat est extra 👏👏👏

    • @zfsamt525
      @zfsamt525 3 ปีที่แล้ว +5

      Bayilema gni sokhor rèk ak beugueu tèk nite stress. Tata Ngoné bolé woul dara ak wakh.

    • @mamandiop5633
      @mamandiop5633 3 ปีที่แล้ว

      Mako.wolou.ligueyy.lou.bari.wakh.zzro

  • @bintougoumballa681
    @bintougoumballa681 3 ปีที่แล้ว +55

    La voix de Moustapha est aussi unique mach allah.

  • @boubacarba5408
    @boubacarba5408 3 ปีที่แล้ว +43

    Il est tres humble wally le chanteur du peuple.
    Big respects de Abba no stress li yeup yaw la
    On l'attendait ca depuis tres longtemps

  • @m____5601
    @m____5601 3 ปีที่แล้ว +7

    Non tay bilay sama khôl bi dada sedd prime bii nekh na trop 🥰🥰Machallah laff thiat wally foumou nekk dafay ame thiathie dagay sett liii rekkk 😚😚😚

  • @bernilynsha
    @bernilynsha 3 ปีที่แล้ว +26

    Moustapha le meilleur de s’en petit gale bilay Waly ken dou yow faramaren bi 🥰

  • @kadiatta336
    @kadiatta336 3 ปีที่แล้ว +4

    Ah Wally seck c'est un don qu'il a🥰🥰🥰🥰🥰 thioooh ndeyssane amna mayoum ya'allah masha'allah laff thiaatt .

  • @mariamasarr7073
    @mariamasarr7073 3 ปีที่แล้ว +8

    Pour une 1er depuis la création de s’en petit galé waly Seck nieuw fiii 💕 Wayei nioune faramareen da nio am diom louniou bolewoulll bokouniou ken d’où waly 🎉

  • @yacinethiam8297
    @yacinethiam8297 3 ปีที่แล้ว +7

    Machalla prime bi mo dakk si SPG,Moustapha yalna KO yalla laffal tiatt sunu faramaréne national mom loumou bokk mou nékh mar Yacine maïssa bigué maïssa bigué mar😍😍😍

  • @bintadiaw8314
    @bintadiaw8314 3 ปีที่แล้ว +7

    Haleyé joie bignou am Tay masougnou ko am❤️🥰🥰🥰😳😳loonnnn waly mi ahhh wa bakhna 🥰🥰🥰hol yeup sed n’a maryacine Moustapha chapeau ❤️

  • @ndeyebinetacisse3501
    @ndeyebinetacisse3501 3 ปีที่แล้ว +102

    Machallah machallah fière de notre Moustapha suis rufisquoise et fière de l'être bravo 🥰mar Yacine meissa bigué je l'aime point ❤❤❤❤❤❤❤❤🥰

    • @marietoundiaye4132
      @marietoundiaye4132 3 ปีที่แล้ว +1

      Fière d’être Rufisquoise

    • @ndeyebinetacisse3501
      @ndeyebinetacisse3501 3 ปีที่แล้ว +1

      @@marietoundiaye4132 one love à toi goudi goudi rufisk rekk machallah 🥰

  • @moustaphndiaye8550
    @moustaphndiaye8550 3 ปีที่แล้ว +163

    Meilleurs prestations depuis qu'on a créé sen petit galle

  • @astadiawcisse4130
    @astadiawcisse4130 3 ปีที่แล้ว +33

    Le duo de l année halé yi sah danio contan ça se voit sur leur visage

  • @lalinguereniang7681
    @lalinguereniang7681 3 ปีที่แล้ว +81

    Ayway alhamdou lilah dagno sonone si momo dieng aida samb amicolé... Réne mom daguéna décentralisé affaire yi😍😍😍machalahh l peuple est content wayyyy😍❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @seydinadiallo7100
    @seydinadiallo7100 3 ปีที่แล้ว +30

    Moustapha depuis 2013 ba legui dama néh 💓💓

  • @mynasaliou24
    @mynasaliou24 3 ปีที่แล้ว +29

    Laff thiate sama dome dji Moustapha machalah yala na batt bi geuneuh werr on t'aime 🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @midossoretra4360
    @midossoretra4360 3 ปีที่แล้ว +76

    C moustapha qui est wally ou c wally qui moustapha 😁le meilleures duo courage frr moustapha

  • @sybagaye8151
    @sybagaye8151 3 ปีที่แล้ว +4

    C'est pas facile de reprendre les chansons de wally mais c'est mal moustapha merci notre wally de valeur Machallah 😍 ❤ ❤❤❤❤❤

  • @binetougaye2584
    @binetougaye2584 3 ปีที่แล้ว +4

    Yalla moy khol kouko nékh mou déf si mome liko sop nite noumou mél nanguoul ko li souniou borom déf si amna lo khamni bougneko guiss war naniou gueumni mbirou souniou borom

  • @badoudia4869
    @badoudia4869 3 ปีที่แล้ว +1

    Ay moistapha mi dinama cardiak Lo son Youssou Ndour bimou wayonne y’a 4ans damako enregistre ba taye damay tokk si setane prestation bi sama chair de poule yieup takhaw taye mou defati li😭😭😭❤️❤️❤️

  • @julielopese2564
    @julielopese2564 3 ปีที่แล้ว +22

    Machallah Moustapha chante très très bien avec justesse yalla nako yalla lafale thiate c lui mon chanteur préféré longue vie à toi que du bonheur 🤲🙏👌

  • @catherinediop6357
    @catherinediop6357 3 ปีที่แล้ว +50

    Bilahi Wally la khalé yi beugue
    Bravo à Moustapha mais ça se voit que SPG n'ont pas l'habitude d'interpréter les chansons de Wally (topando ko yomboul deh)

    • @salioufall802
      @salioufall802 3 ปีที่แล้ว +3

      C’est pas facile dal

    • @Sokhnapenda
      @Sokhnapenda 3 ปีที่แล้ว +3

      Bly yomboullll

  • @aminatagueye7326
    @aminatagueye7326 3 ปีที่แล้ว +11

    Waouh🤗machallah😍moustapha lingay def yomboul dh ken dou Wally si mim rew😍

  • @zeynabdiallo1744
    @zeynabdiallo1744 3 ปีที่แล้ว +167

    Bilay wally senegalais yi gnioo ko beuggg c notre fierté nous les sénégalais machallah long vie à toi faramarene bi 🙏🙏🥰🥰🥰🥰❤Félicitation MOUSTAPHA ❤👌🏽👌🏽

    • @ebsonko7001
      @ebsonko7001 3 ปีที่แล้ว +7

      Gambi nyo mom Wally nteh bokungko ak Ken he belongs to us 😘😘

    • @zeynabdiallo1744
      @zeynabdiallo1744 3 ปีที่แล้ว +4

      @@ebsonko7001 deuggg la keeegn

    • @doudspecos7510
      @doudspecos7510 3 ปีที่แล้ว +2

      Aye li ba diam la aye seynab Diallo 🤐😂😂 sonal nala trop nak mé borom bakh nga bilay louné lalay wakh do mér

    • @zeynabdiallo1744
      @zeynabdiallo1744 3 ปีที่แล้ว

      @@doudspecos7510 wouyyyyyy sama ndeye 🤣🤣🤣🤣🤣

    • @ngoyedione3399
      @ngoyedione3399 3 ปีที่แล้ว +1

      Waxalll dh

  • @annamariesambou1880
    @annamariesambou1880 3 ปีที่แล้ว +51

    You make my day am always glad to hear Wally seck...from 🇬🇲

  • @ramatoulayesy5056
    @ramatoulayesy5056 3 ปีที่แล้ว +10

    Maryacine sa voix dafa riche♥️😭❤️te meilleukh 🥺🥺🥺mais félicitations à Moustapha🎉

  • @sallybee4828
    @sallybee4828 3 ปีที่แล้ว +25

    Moustapha yalnah Yallah yorka sa talent insha-allah☝. Well executed with Wally 👌👏👏

  • @mamegore8007
    @mamegore8007 3 ปีที่แล้ว +2

    Ndéysane mar yacine maïssa bigué tay dafa khamni thi ay khalé la dieum bathi styl vstmntr bi sakh dafko changé pas de takkaye ni de thioline yalna sa diame yague mar yacine wally ballago séck mou sélle mi 🌸💥❣️✨💫💞💝🌟🌹🔥😍🥰🍇💕🌷💐🌻🌼🌺

  • @zeynablaye3959
    @zeynablaye3959 3 ปีที่แล้ว +105

    J troopppo kifeeeeee cette duo mashallah 🥰 ndanan ngua Moustapha lolou certitude la Ballago bègue nagn diam mo nekh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭😭😭😭🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @Talibeserignebabacar2191
    @Talibeserignebabacar2191 3 ปีที่แล้ว +21

    Machallah kene dou faramarene bii mo nekk this kholou sénégalais yii le chanteur du peuple 🔥🔥🔥Moustapha tamite machallah 😍

  • @mamemame4164
    @mamemame4164 3 ปีที่แล้ว +262

    Quand Moustapha chante j’ai des frissons quelle belle voix ❤️❤️

    • @amykasse9439
      @amykasse9439 3 ปีที่แล้ว +8

      Il chante trop bien

    • @mamemame4164
      @mamemame4164 3 ปีที่แล้ว +8

      @@amykasse9439 je te jure ma chérie

    • @seydounourouba9307
      @seydounourouba9307 3 ปีที่แล้ว

      Bilay pour mane deh rk la dall crx

    • @mbayangguisse9845
      @mbayangguisse9845 3 ปีที่แล้ว +2

      Quand Moustapha chante j'ai des frissons quelle belle voix ❤️❤️❤️❤️❤️

    • @saliounbiaye7048
      @saliounbiaye7048 3 ปีที่แล้ว

      Son vol est beau💟💞👍

  • @ndeyefatou6852
    @ndeyefatou6852 3 ปีที่แล้ว +3

    Pour la première fois dans l’histoire de sen petit galei. Il a fallu que papa thioune gueine adouna pour wally meune yekk scène sen petit galei. Et pourtt les jeunes le réclamaient tous les jours. Mais sant yalla
    Yallla nako yallla diapalei werall baat bii 🤲🏾🤲🏾

  • @gamoubarcaofficiel7170
    @gamoubarcaofficiel7170 3 ปีที่แล้ว +16

    Lii nekhna ba agg si lol
    Machalla Moustapha tjr egal a lui meme
    Ken dou Wally aka beuguii wayy khol ba sedd ❤️❤️

  • @mariemeniang934
    @mariemeniang934 3 ปีที่แล้ว +16

    Machallah notre Waly Séck International vraiment le
    Peuple est contant Moustapha force à toi tu as assuré ✌️

  • @penchitadiouf1501
    @penchitadiouf1501 3 ปีที่แล้ว +11

    Bilae beug rk wala bagne ki mo NK si kholou nit yi kn meunousi dara kiserafall❤🤩❣💃💃💃

  • @fatoufall5666
    @fatoufall5666 3 ปีที่แล้ว +2

    Macha allah moustapha toujours yagui assuré yalla nala yalla may guoudou fan ak weer si barké seydina Mohamed je t'aime

  • @dijasall7997
    @dijasall7997 3 ปีที่แล้ว +3

    Bilay koula khar yalna khaddi mar yacine maïssa bigué maissé mar yacine niola beug pire seck. Moustapha mon préféré de SPG yalna yalla wéral bate bi❤

  • @adjilaye9149
    @adjilaye9149 3 ปีที่แล้ว +2

    Ay Waly mi nimouy def sama khôl bi akhhh nexna way jtm trop ba douma meneu exprimé wou sakh🥰❣️❣️❣️❣️❣️🥰

  • @fatouthiam4189
    @fatouthiam4189 3 ปีที่แล้ว +102

    Le duo de l'année mashaallah

  • @khadyfall7101
    @khadyfall7101 3 ปีที่แล้ว +1

    Khol sedatina way machallah aba kene dou yow y’a fi diar yallah na Diam yak way barki borom touba li Da nekh teh sedal khôl and done bene ❤️😍

  • @khadyjafaye4565
    @khadyjafaye4565 3 ปีที่แล้ว +9

    Ils ont tellement grandi machaallah moustapha sa kaw sa kanam ta voix est unique mais gnou nangou ke walay sa voix amoul❤️🥰🥰

  • @beliciaaidara1627
    @beliciaaidara1627 3 ปีที่แล้ว +5

    Ndeyssane Wally Xol bi mo rafet machalah Ken dou mom mw j l’adore wa petit sakh tey ambiance da changè Ken dou Wally moy l chanteur du peuple nagou rek waleu bagnnnnn

  • @marianefaye9194
    @marianefaye9194 3 ปีที่แล้ว +11

    Mais Moustapha ta vraiment assurer quoi tu est la fierté des rufisquois bravo et bonne continuation

  • @ndeyeaminatathiam2254
    @ndeyeaminatathiam2254 3 ปีที่แล้ว +3

    Mach'allah Wally li yalla dogal mouy nieup beug la nagne ko nangu rek yalla nassa jaam sakh way❤️✌️

  • @yacinegueye1088
    @yacinegueye1088 3 ปีที่แล้ว +16

    Ayway Wally diapalelment Moustapha mi bilay ya meune liguaye def Masha ala💯💯💯💯💯💯

  • @ibrahimabalde8271
    @ibrahimabalde8271 3 ปีที่แล้ว +1

    Fami ndour lou takh niou sheytané rek
    Lou takh defou niou lii bou yagg baay ba légui
    Félicitations wally seck brom xolou diamaa bi daga baakh yow ❤️❤️👍 sen petit galle mousou nioufa wouy sa wouy mé kholo ko yow dagaa baakh 🙏 yow yaa fi neh ❤️❤️💪💪💪✌️🔥🔥

  • @aichagueye6488
    @aichagueye6488 3 ปีที่แล้ว +4

    Wallahi j’ai les larmes aux yeux 😭😭papa Thione yallah na aldiana disa keur😭

  • @plummenoir7252
    @plummenoir7252 3 ปีที่แล้ว +1

    Wally séck yalla gua koudou fane si barkép MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP BAABOUL MOURIDIINA

  • @farimatandiaye7664
    @farimatandiaye7664 3 ปีที่แล้ว +4

    Non mousthafa il est très fort machala diapaléléneko mou déme way

  • @matouchasoumare7597
    @matouchasoumare7597 3 ปีที่แล้ว +30

    Macha Allah Moustapha a bien assuré bien vrai que Wally n'est pas facile à imiter

  • @thiernomoussasall122
    @thiernomoussasall122 3 ปีที่แล้ว +380

    Moustapha il est très très talentueux fort
    prince art connait son talent motax il interprète les chansons les plus difficiles

    • @niangballo8940
      @niangballo8940 3 ปีที่แล้ว +20

      Et depuis son intégration il interprète que des chansons difficiles

    • @cheikhpendambaye2911
      @cheikhpendambaye2911 3 ปีที่แล้ว +8

      Desna dh

    • @thiernomoussasall122
      @thiernomoussasall122 3 ปีที่แล้ว +2

      @@cheikhpendambaye2911 lou dess fofou

    • @fatysyll5643
      @fatysyll5643 3 ปีที่แล้ว +2

      Il a perdu sa voix on dirait

    • @talibecheikh1478
      @talibecheikh1478 3 ปีที่แล้ว +3

      @@fatysyll5643 lol c normal si awoukatyi la bokoudi

  • @tallasarr2543
    @tallasarr2543 3 ปีที่แล้ว +1

    Li mome kholena ba khole mes doumasi doyalle sac jour ma sétane ko plusieurs fois bilahi Moustapha sa voix bi machallah sama khole dafa séde trop sakh

  • @makhouwaly2226
    @makhouwaly2226 3 ปีที่แล้ว +5

    Sen p'tit gallé depuis 2012 batay bou tay bii mofii dakh 😍 Moustapha tu es l meilleur comprendre nagn leu ms xamnga chanteur du peuple bii bénn la si mim rew ouff voix xallé bii machallah yalla na yalla doli Diam dji inch'Allah 🙏🙏🙏 Waly seck on t'aime d tous nos forces frèro 💉💖😍😍😍👑👑👑👑👑👑👑

  • @olymatadiouf2638
    @olymatadiouf2638 3 ปีที่แล้ว +1

    Prime bii mo dakh si li sen petit galle def de tous les temps. Waly dal Yalla mo ko fal. Même les enfants sont contents et émus de le voir.
    C’est vraiment très touchant ❤️

  • @sainebah6125
    @sainebah6125 3 ปีที่แล้ว +39

    This is my favorite prime. Finally my star at sent petite galle and it's the best among the rest.
    Congrats Mustapha ❤️❤️

  • @ndeyeaidaseck5802
    @ndeyeaidaseck5802 3 ปีที่แล้ว +3

    Jour bi sama xoll bi dafa sedd bi samay ragione di guen sakh tayou mako sama niary chanteur yi damalen beugueu❤️😍

  • @magicfoot7845
    @magicfoot7845 3 ปีที่แล้ว +48

    Écouter ça avec des écouteurs 🎧 c ouff♥️😩🥰

  • @sokhoballago7796
    @sokhoballago7796 3 ปีที่แล้ว +2

    Mashallah Mashallah laf thiatt vraiment sama sopeii bi yallah nala yallah lafal thiat inchallah si doley Serigne Bamba Cheikhra fall

  • @jijiballago9621
    @jijiballago9621 3 ปีที่แล้ว +296

    Un gros big up a ABBA no stress on sait qu’il a une grande influence sur la réconciliation du famille seck et famille ndour proud of you pour wally bou ko nekhone tay tay corona bi degne fi 😂

    • @samiirofficial9496
      @samiirofficial9496 3 ปีที่แล้ว +3

      Cheuuu😂 aka grawwwwe nakkk

    • @betinafall7126
      @betinafall7126 3 ปีที่แล้ว +3

      Voilà t’as tt compris tw

    • @matty7424
      @matty7424 3 ปีที่แล้ว +6

      Sans oublier Aby Ndour aussi 😍

    • @FascinatingMya
      @FascinatingMya 3 ปีที่แล้ว +4

      danko féké?

    • @jijiballago9621
      @jijiballago9621 3 ปีที่แล้ว +2

      @@FascinatingMya lousiy se yone?

  • @khadysylla8745
    @khadysylla8745 3 ปีที่แล้ว +2

    Ay way li nekh way,🥰 j m rappel ndeysane😌 étant plus jeune j rêvais d'aller à sen petit galé juste pour pouvoir avoir la chance de voir Wally seck 🥺🥰 je l'aime trop wollah laf thiate

  • @ibssdiallo5331
    @ibssdiallo5331 3 ปีที่แล้ว +57

    La voix de Wally est juste extraordinaire machalla♥️🙏, il n’est pas facile à imiter mais c’est juste beau, Li moy Sénégal li lagnou Xam yalna djam yagg♥️🎊😇

  • @mouhamadouka6382
    @mouhamadouka6382 3 ปีที่แล้ว +2

    Mouyénn 😳😭ndeketé Moustapha nila meunei woyy🥰

    • @Beyoncekane245
      @Beyoncekane245 10 หลายเดือนก่อน

      Fo nekonnnn degoul wayou youssou.ndour yimou reprendre yp!

  • @ndeyedabo4987
    @ndeyedabo4987 3 ปีที่แล้ว +20

    La voix du faramareen c’est extraordinaire Billae ❤️😍

  • @lounetandante8955
    @lounetandante8955 3 ปีที่แล้ว +14

    Binetou est magnifique avec son sourire d'ange

    • @dieynababa223
      @dieynababa223 3 ปีที่แล้ว

      Xamewmako wonn d mashala elle a grandi

  • @fatoumataba580
    @fatoumataba580 3 ปีที่แล้ว +4

    Wally seck sou demoul kan moy dem bilay joli cœur nga Macha'Allah ❤❤❤

  • @andreflow5829
    @andreflow5829 3 ปีที่แล้ว +2

    Ly mo manqué wonne sen petit galé avec machalah wally rek

  • @modestemouta2058
    @modestemouta2058 3 ปีที่แล้ว +12

    No sérieusement 😒 Wally il a une belle voix❤️ Félicitations à toi Moustapha🎊

  • @mamemame4164
    @mamemame4164 3 ปีที่แล้ว +20

    Le meilleur de sa génération Moustapha ❤️❤️

  • @oumardiop3263
    @oumardiop3263 3 ปีที่แล้ว +21

    Moustapha est juste magnifique un jeune a proteger et encadrer macha allah

  • @Ummou2983
    @Ummou2983 3 ปีที่แล้ว +1

    Aka simple Wally rek maschallah tei baxna nek mouride nak bgu nala😍🥳♥️♥️♥️
    Moustapha bgu nako dh Il es fort 🤗♥️bilahi sama yaram daw na Wally mi nekhoul bagni begue len rk diam am way
    Mouhamed liguay awou lan le iow ahhh😇🥳🥳

  • @fatousanyang4914
    @fatousanyang4914 3 ปีที่แล้ว +10

    Mustapha nailed 👌 the song this is beautiful, I was so happy 😊 watching dis today u made my day, wally keen du yow yaa bahaaa

  • @mamediarracamara9810
    @mamediarracamara9810 3 ปีที่แล้ว +7

    Thieyy Waly keine meunouko imiter voix bei soxor😂ms félicitations Moustapha t’as assuré prochaine fois essaye de mémoriser carrément le son ya des parties que t’as pas bien interprété mais très beau duo on adore🥰

    • @socratedu22emesiecle
      @socratedu22emesiecle 3 ปีที่แล้ว

      Il n'a jamais essayé de l'imiter. Vous confondez interpréter et imiter

  • @yacinendiaye1562
    @yacinendiaye1562 3 ปีที่แล้ว +402

    Toujours égale à lui même notre moustapha nael on t'aime

  • @ndeyemaremendoye8217
    @ndeyemaremendoye8217 3 ปีที่แล้ว +2

    Li d mougui soga am spg machala papa wally borom xol bou rafet lag thiatt 🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️si barki serigne babacar sy

  • @bayzofromfouta1527
    @bayzofromfouta1527 3 ปีที่แล้ว +10

    Moustapha est fort 🔥🔥🔥🔥🔥 bon continuation❤🇸🇳✊🏾
    Boy yi légui ay grand laniou🤣

  • @adjidiacisse3772
    @adjidiacisse3772 3 ปีที่แล้ว +5

    Magui doga sètane sen petit galè ndaxx Waly😭🤩😍♥️diame rk baye fall bi

  • @maguiiefall8608
    @maguiiefall8608 3 ปีที่แล้ว +12

    Waw la voix de Wally magnifique cest la première fois que je fai attention à ça machallah

  • @dieynabandiaye1571
    @dieynabandiaye1571 3 ปีที่แล้ว +76

    Wally domou youssou ndour

    • @aissatoundaw5624
      @aissatoundaw5624 3 ปีที่แล้ว +8

      Bilaye ndeyssane domame la deee

    • @diengsalla6475
      @diengsalla6475 3 ปีที่แล้ว +2

      Beugna ndit kouye wakh lou bakh ,bravo a toi

  • @omoulsow5756
    @omoulsow5756 3 ปีที่แล้ว +262

    Ce duo 😍👌😳♥👏❤ est naturellement formidable

    • @moussoudiallo3853
      @moussoudiallo3853 3 ปีที่แล้ว +4

      Moustapha toujours égal à lui-même ! Je l'adore vraiment !

  • @youngthiam9821
    @youngthiam9821 3 ปีที่แล้ว +2

    Mais na wally dieul boy bi produire ko!! Walahi ki daffa am talent

  • @maimounafall8352
    @maimounafall8352 3 ปีที่แล้ว +17

    Waly le meilleur de sa sénération j'aime Moustapha depuis le 1erJour

  • @loucarmbow7171
    @loucarmbow7171 3 ปีที่แล้ว +16

    Sa voix est unique dans le Sénégal Wally 🇸🇳❤️❤️❤️❤️👑👑👑

  • @fatouthiam6962
    @fatouthiam6962 3 ปีที่แล้ว +22

    Mach'Allah repose en paix Papa Thione thi barké Seydina Mouhammed saws 🤲
    Fière de toi Wally sama Faramaren bi maryacine mayssa bigué mar lafe thiate. Sama khol sèdina dieuredjeufeti
    💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖😘😍🥰💯❤❤❤🔥💥

  • @oumydiengsougou9085
    @oumydiengsougou9085 3 ปีที่แล้ว +2

    Machallah yalnala yallah défal diamm wally sa xoll raféte na trop

  • @ndieyegueye3104
    @ndieyegueye3104 3 ปีที่แล้ว +122

    Paix à son âme papa Thione

  • @mariemecisse9503
    @mariemecisse9503 3 ปีที่แล้ว +22

    Le duo de l'année merci moustapha on t'adore