Serigne bi man dama Guent giss Yonente bi setsi ma sama keur môme ak seydina Ababacar ak Seydina Omar. Gnu tok si sama salle muné sama yaye mu andi kamil sama Yaye andi kamil bi Yonente bi néma oubiko. Ma oubi yem thie Tabaraka munéma jang ko ma jang ko bamu diekh muné jangat ko ba paré muné mo tolan ti waat ma diko jang ay yoon munéma deko di jang. Lolu nak lay leer lu
Ooh sama sangue bi 🥹🥹🥹🥹❤❤ SALALAHU ALLAH MOHAMED ❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalah yaw de am gua tawfeeh❤❤
Walahi sama yaram bi mi ngi daw😢😢❤❤❤❤ psl
Serigne bi man dama Guent giss Yonente bi setsi ma sama keur môme ak seydina Ababacar ak Seydina Omar. Gnu tok si sama salle muné sama yaye mu andi kamil sama Yaye andi kamil bi Yonente bi néma oubiko. Ma oubi yem thie Tabaraka munéma jang ko ma jang ko bamu diekh muné jangat ko ba paré muné mo tolan ti waat ma diko jang ay yoon munéma deko di jang. Lolu nak lay leer lu
Machallah❤️❤️❤️❤️
Da ngay dém chaîne youtube MALICKIA TV TIVAOUANE fofou la Pr Madiama Fall di défé firi guent direct
@@FiiriGuénte jereudjeuf
Oustas Dama gunte supporter xalé si moto
Il faut aller sur la chaîne youtube MALICKIA TV TIVAOUANE c'est là bas que pr Madiama Fall faire le direct