Balla a bien dit, Ki commencé ak yow bokul ak ki niow ba lépp nékhé donc manou gno bokk fayy donc borom commentaires you négatif yii dém lénn sétani séni mbeur té bayil gnou le meilleur lutteur de tout les temps BG2 ...
Donc sa wakh leer na bougnou la dégué daal école géine bokou mais récréation mo léne bolé balla franchement meno communication donc da ame gno xamni waro léne démal bougnou la degue pack ya léne raw gno ware di sounou si yow daal c'est un message pour pas mal de jeune lutteur geume léne séne bopu bayi di topou si ay ginaw mbeur di taylé séne bopou geume léne séne bopou rk mou diékh
Champion sama mbeur gua je t'aime trop mais tmp yi tu communique très mal bly walaye faut revoir ta communication vraiment respect biguay lathié dafa wara réciproque
Sénégal dafa âme niou bonne té soxore Balla defoulen d'Ara Fils de Balla d'où d'Ara meunoul def li Balla def thi lamb 25 ans roi fils de Balla mogui thi 35 ans
Sa genre yi nioy nafikh yi kouleni deglou rewmi TASS balla sonekoul nafikh khamni bami djel roi des arenes eupeulna 25 ans on se dit la vériré nafikh baxoul
Balla li yako tay dh kone kom nieuweul nga lirou ni carrément iow ak mom depuis temps boy la et k say rakk dagnla fekk nga bay sa waar ba paré ci lamb genre dagnla wara diokh thieur donc warolén nieuweul koi parce k selon iow bigniy andak iow fekna lepp sotti ba paré. Lolou moy sa khalat ak sa analyse koi !! Fils de Balla bou amé diom wakhoumala bayi mais toureum sakh daflay sopi. Balla iow goréwo ndékété ou bien daga foog boy bi dalay sakéto pour am tour pour meun dém si kaw.
Balla day doull rék😂
Wakhi doff deugue ngafi wakh 😂😂😂
Machallah koubakh ki Amal diameu rek
On bosion de réponse sur fil de balla
Balla mono communications bou nekoulwon nit yi do dara gayi nio la don goungue si tol bi😊
Balla amal tawfekh yaw rek lani topou gnoune wa guédiaway♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Yalna diam yagu Sénégal
Souma sanione nguén andatt yak niom fils d balla
Merci beaucoup khadim Ndiaye ❤❤❤
Balla vrai doff leu
Thieur yeukyeuk mokoye motali
Merci
Eski yow xam lingai wax thieur lum boka ak yeukyeuk? Respect kou neki moko yeloh mui kula joh yeuk ak kula yeugout.. Ndaw bou bugu avenirr bou bakh deye joh magg thieur
Yéne gni di wakh balla gaye lou niaw kousi bala diape nokoula nokou sa papa😅😅
Président Ousmane sonko rek
Balla a bien dit, Ki commencé ak yow bokul ak ki niow ba lépp nékhé donc manou gno bokk fayy donc borom commentaires you négatif yii dém lénn sétani séni mbeur té bayil gnou le meilleur lutteur de tout les temps BG2 ...
Ya niak diom dém lén lidieunti sén avenir mo geune doomou kharame yi guén di ceum ni yow moom sa dokhotou kilixeu way ahh
Balla kou bakhla koubari diam bilaye khol bou yatou
Bala baye fall la♥️♥️👌👌👌
Yaw amo loy wakh y’a togn samba alar nga fils de balla kou khéwlé mou Dém bayil sisou bi boy bi moy téyé guédiawaye inchala
Balla sa bèrr la you can give respect him sa baye la
Yaw dale kou bakh kholou❤️nitte gni balla guaye2 mossi nek
Donc sa wakh leer na bougnou la dégué daal école géine bokou mais récréation mo léne bolé balla franchement meno communication donc da ame gno xamni waro léne démal bougnou la degue pack ya léne raw gno ware di sounou si yow daal c'est un message pour pas mal de jeune lutteur geume léne séne bopu bayi di topou si ay ginaw mbeur di taylé séne bopou geume léne séne bopou rk mou diékh
Bravo champion, longue vie à toi mâcha Allah
Qui dof la 😅😅😅
Khaliss🤔🤔🤣
FORZA A FILS DE BALLA
Libéré sonko
Sa communication🗣️ bakhoul balla so meunoul waax déel noppi 🤫accident de waax🗣️nopou👂 you am déeg déeg mokaay constater☑️
Mé balla miiii kesk il leu
Champion sama mbeur gua je t'aime trop mais tmp yi tu communique très mal bly walaye faut revoir ta communication vraiment respect biguay lathié dafa wara réciproque
Communication zéro 😂😂 mbokou Moy niit Kone koudoul sa mbokou dou niit 🤔🤔😂
Thiowly la rék billahi mai balla gaye mbeur yi guediawaye yi kéne yabou kassi
Sénégal dafa âme niou bonne té soxore Balla defoulen d'Ara
Fils de Balla d'où d'Ara meunoul def li Balla def thi lamb 25 ans roi fils de Balla mogui thi 35 ans
Sa genre yi nioy nafikh yi kouleni deglou rewmi TASS balla sonekoul nafikh khamni bami djel roi des arenes eupeulna 25 ans on se dit la vériré nafikh baxoul
C vrai mom balla vrai champions leu Ah bon loutah niouni 25ans la am
Merci champion you are the best 👌 respect 🙏
Machalla ♥️ Balla gaye 2 a vie
Fils d balla wakh nala deugue soff ngua trop
Focus 2024
Merci Balla ❤❤👌👌👏👏👏
Je suis daccor avec fils de balla beug yeuk mokoy faye
Sététt mai kagne laniouy diall ci lénéne nak oh
Balla gaye 2 diamou si yaw
Trahir Casamance trahir Sénégal trahir say supporter samba allarr bou bonn bi
Layy meunoul communiquer dara holal limouy wahh rekk ligua wah si lirou .n
Sénégalais yi gueumou niou dara
Dans tous les cas on ne sait pas ce que se passe entre BG2 et Fils de Balla... C'est sûr ya des nons dits
J’avoue
Pourquoi vous avez coupé sa réponse
Mo dafa amoul loumu wax na nokk feulé...balla do nitou dara
❤❤❤❤❤
Wakho Duegg aka mouma bett ndekete niom abdou Diouf wakhe naniou duegg samba allar bou bon bi
Waho fii Dara
Respect le 🦁 de guediawaye
Kii sii bopam ngenn wakhoul deugu
Wakh Dara lasi manoul nooo
Sadata yaye geudiawaye seul
Balla wor kat nga
Deukouma gediawaye mai tu a male parle
Sa.coeur mo yatou koi😅ok
Samba alar nga rk saway
Balla ya wakh ni khamo casamance niougui léy khar contre eumeu séne digua khamni sakkou khorom disneu gane gane gane
Journaliste yi bayi léne féne séne affiche akh séne contenues yi sa fait 2😢
T'as vu
@@papeabdoulayedione4766 bly moy lolou dh
Balla li yako tay dh kone kom nieuweul nga lirou ni carrément iow ak mom depuis temps boy la et k say rakk dagnla fekk nga bay sa waar ba paré ci lamb genre dagnla wara diokh thieur donc warolén nieuweul koi parce k selon iow bigniy andak iow fekna lepp sotti ba paré. Lolou moy sa khalat ak sa analyse koi !! Fils de Balla bou amé diom wakhoumala bayi mais toureum sakh daflay sopi. Balla iow goréwo ndékété ou bien daga foog boy bi dalay sakéto pour am tour pour meun dém si kaw.
Fils de balla waxlenn ko deugg louy nieuw nguenté fi la aam combat balla nieuw taxawou koo me fils de balla naturellement yarouwoul
Mann douma supporter balla mes yow nafek nga. Wax dafa lateh degin
Vraiment deugue la nak ndah bougnou khamé guédiawaye yaw ya tah
Bayilene fene si titre yi
balla gaye 2
Vrai kon gua
Meunoul communiquer déjà defatt na penalty geun gua deugeul li fils de balla wah t hamoko
Ki dafa béw
Warkat
Tebal ngen vidéo bi de
Waaw waw
Vre doff la ki
Cominucation 0000000
Yew wor Kat ga bakho 🧏🧏🧏
Da nga soxor
Des guewels musclés
Yow doul sof gua lolou niakeu khel
Yaw nak copin wah lo boun si yaw lanko khmé
Dimbalil nit gni yaw gnép gua soof
Ioe fans Modou lo nga khana
Yaw féne catega
❤❤❤❤❤❤