Mon coeur saigne tous ces jours-ci à cause de ce qui se passe dans ce pays et je ne peux rien faire. Je me sens tellement impuissante. Mais tay defeul ngama. Tes paroles ont apaisé mon coeur et j'ai repris espoir. Pour le moment, le mensonge a la force et la puissance avec lui, mais tôt ou tard la boule finira par tourner, la vérité finira par triompher. De la même façon que le prophète mouhamad paix et salut sur lui faisait tomber houbal er consort par terre le jour de fathou makkah, le coran et la sounnah vont tout nettoyer !!! Inchaa ALLAH !!!
Jazakallahou Khairan. Jeuri Jeuff Jambari Islam. Yalnala Yallah Arr Té Sammou La Akk Képpou Kouye Wooté Ci Alquran Akk Sunnah Késsé Té Sammou Niou. Muhammad Ahmad Ceesay, Depuis America !!!
Bravo mon imam préféré 👏👏👏 que la vérité. Qu'Allah soubhanahou wa tahala te bénisse et te protège. MachaAllah je suis très contente pour tes khoutba continue à nous faire plaisir comme d'hab 🤗
@@salamidoleradiombelmbel8984 Qu´Allah nous guide tous vers le droit chemin. waayee daa am gnoo xamni fitna rekk moo nekk ci gnoom. xamugnu diinee tenanguwugnoo jang. ko wax lu uttee seen geumgeum gnu fitnaal la
بارك الله فيك يا ابو الباني، Q'الله te préserve dans ce chemin qui n'est autre que le حق ☝️, faut pas avoir peur de leur bouche de cheytan car ALLAH est avec toi إن شاء الله. Comme imam Malik رحمه الله a dit.. السنه سفينه النجاه
Alhamdoulilah sama khél dalna sama khol sédatina c'est avec impatient que j'attendais ce khoutba ya oustaz yalnala sameu goudeul sa fane yokou xam.xam bi yokou xéwël yi inchAllah diam rk ngay nous sommes tjr derrière vous barakAllahou fikoum
@@chiekhabdoulosopyesbassiro1785 ce que oustas a dit c'est la vérité mais les gens qui suient ses sérings c'est du n'importe quoi car il ne leurs parlent pas de Dieu seulement leurs grand pére
Salam oustaz toujours des enseignements avec pleins de savoirs de sagesse et de sérénités qu’Allah SWT te monte en degrés et te préserve des personnes malveillantes. OUMAR SALL FORCE ET HONNEUR
@@brigadeantibidah2911 OK oustaze on est dans le you tube à vous suivre tes enseignement sont vraiment très intéressant.que Dieu vous protège merci beaucoup
Oustaz Oumar SALL Boul Falé Kéne Kou Nék Si Deug Daye Beuri Aÿ None Toujours Il Dit La Vérité Yalla Nala Yalla Maye Goudou Fane Ak Wérr Gou Yaram Bonne Contination Sama Oustaz Préféré ❤
Mashallah ya oustaz alhamdoulilla... toujours à l'écoute de la vérité. Nous suivons et essayons de nous conformer. La vérité est apaisante au coeur et à l'esprit. Qu' Allah nous accorde son pardon et exauce toutes nos prières et actes de dévotion.
EEsskkeeyy Ya Oustaz, Jazakumullahu Khairan. Yeneu deugeur bopp yi ,Diay sa dine' la (cit) Au senegal ,les gens ne meditent pas sur le Coran, c'est pourquoi on voit des pratiques et comportements absurdes ,qui nous ramenent aux temps Jahilya. Sourate Al Qamar -Sourate al Qalam-Sourate Al Qyama, -Sourate Al Buruj. A mediter pronfondement.
MachaAllah ya Oustaz daguay sédal sama xole bi si niguay baye sa war si diyné dji zajaka Allahou khayran Oustaz Omar Sall diam rék lala Yallah di défal dakh deug la beug
Machalla oustaz alkhourane ak suna rek j'ai eu les larmes aux yeux a la fin du khoutba qu'Allah tout puissant te protèges contre cheitane ak nit cheîtane yi
MA SHA ALLAH OUZTAZ OMAR AHMAD SALL MAY ALMIGHTY ALLAH CONTINUE BLESSING YOU AND WHOLE MUSLIMS AMEN....DEGUE REK MORLAH NYUERR MAY YOU LIVE LONG LIFE AND GOOD HEALTH..
Waye Ouztaz youkhoul si kawe waye ..Sénégal koufinei yalla neina yonéneteubi neina gnou nonoula barki alkhouran..même au sein de ta famille on te méprise..Qu'Allah ns guide
Mashalah yalna yalla arr la nit gni begoune deug waya incha allah☝️ yeug day geuneu lerr rek al quran ak sunnah rek rek moy islam ☪️ lénène bokoussi incha allah ☝️
BarakAllahou fik, voilà ce que l’on devrait uniquement entendre, le Coran, la Sunna Alhamdoulilah. Ya Rabbi Allah, préserve le sang de Oustaz Oumar Ahmad Sall, tous les prêcheurs de la Sunna, et des croyants sincères, amine Ya Rabbal alamine
machahala oustaz, khamna diangalé rék nga beug thi yalla ak yénéntam té war bépp dioulitt té tégou si yonam bayi térém moy waréff sérigne vrai té fékhé ay talibém tégousi alcoran ak suna lolou mowaral sérigne, képp kou indi lénén keurignla.ndakh kounék sagn na am kilifa diné mais té diné rék takh. wayé yén sayi dagay dioum si yéneu léralyi .ndakh gamou si yénéntabi(psl) dou bida té kou am guésstou di ga kham dou bida(expliquer aux musulmans ki est mouhamét(psl) et ses histoires pour refortifier notre foi.........................
Kou bgeu oustaz Omar sall beseul👉j'm👍
Maasha Allah yagui défendre deugou Sounou Borome Souhana Ouwa Taalah nala Yalla samal Bopam
@@mouhamedthiam7183 masha Allah
@@mouhamedthiam7183 masha Allah
Sama oustaz oumar Ahmad sall yalla nala yallah goudal sa fane amine yarahbi té samoula
Buñu amon 10 yu mélni naaféque wañéku Sénégal
Billay
Amnafi niouko eup xam-xam mais fitwim yor gaayi yoruniouko
Wallah . Vous avez tout dit
Deug diou wer
Kon Dèll Déggloy Serigne Ahmdou Rafahi ak Serigne Mbacké Abdour rahhmaane ......
Mon coeur saigne tous ces jours-ci à cause de ce qui se passe dans ce pays et je ne peux rien faire. Je me sens tellement impuissante. Mais tay defeul ngama. Tes paroles ont apaisé mon coeur et j'ai repris espoir. Pour le moment, le mensonge a la force et la puissance avec lui, mais tôt ou tard la boule finira par tourner, la vérité finira par triompher. De la même façon que le prophète mouhamad paix et salut sur lui faisait tomber houbal er consort par terre le jour de fathou makkah, le coran et la sounnah vont tout nettoyer !!! Inchaa ALLAH !!!
Nous sommes fiers de vous ma scha Allah jazaka Allahu khairan
Marieme Dieng Wallahi Ndeysan très fière même
Jazakallahou Khairan. Jeuri Jeuff Jambari Islam. Yalnala Yallah Arr Té Sammou La Akk Képpou Kouye Wooté Ci Alquran Akk Sunnah Késsé Té Sammou Niou. Muhammad Ahmad Ceesay, Depuis America !!!
Amine mbok yannala yalla sameu yawit
Barakallah.fikome.hafazakomollah.aamine
Muhammad Ahmad Ceesay Amin 🤲🏾
Amiiiiiiiiiiiiiiin
Vraiment toujours il di la vérité machallah y'a oustaz ☝️👂
Que Dieu vous protège Oustaz Oumar
طذ
Bou ngene ame kham kham tontou ak kham kham mogueune ngeni sagatee yala rek mo woor borom diamono ak adouna mofi nek allahou akbar dieureudieufati y'a oustaz sall
Bravo mon imam préféré 👏👏👏 que la vérité. Qu'Allah soubhanahou wa tahala te bénisse et te protège. MachaAllah je suis très contente pour tes khoutba continue à nous faire plaisir comme d'hab 🤗
Billahi wallahi top alkurane AK Sounnah rék mo woor yallah NGA yagg fi loooooool thé âme djamme
Maa cha'Allah Qu'Allah vous protège. Deunk nagn la sunu Borom. Kepp kulla beuga fitnaal, Y'Allah nakko Y'Allah rey reyiin gu gnaaw !!!!!!!!!!! Amiiiiiiin !!!!!!!!!!
ASSALAMOU ALEYKOU gnanallén YALLAH diouballén
@@salamidoleradiombelmbel8984 Qu´Allah nous guide tous vers le droit chemin. waayee daa am gnoo xamni fitna rekk moo nekk ci gnoom. xamugnu diinee tenanguwugnoo jang. ko wax lu uttee seen geumgeum gnu fitnaal la
Kou hékh Omar sall, hékh nga l'islam
Wallahi wakh nga deugg !
@@abdoulabdoul7809 merci Abdoul
@@moussathiam8487 de rien nio far car un hypocrite ne peut pas aimer Oustaz Omar. Bonne journée à toi !
Right !!!!!
Oustaz Omar Sall yallah na gnou la yallah fayall yiww bou Matt insalah.
Qu,Allah vous preserve et vous garde en paix!
Amine ya rabi!
Allahouma amine
Machaalla Oustaze dieureudieuf depuis Paris
بارك الله فيك يا ابو الباني،
Q'الله te préserve dans ce chemin qui n'est autre que le حق ☝️, faut pas avoir peur de leur bouche de cheytan car ALLAH est avec toi إن شاء الله. Comme imam Malik رحمه الله a dit..
السنه سفينه النجاه
Wallahi Oustaz litax mou nekh ma mooy mome Alquran rek leuy wax AK Xam Xam bou cell
Alhamdoulilah sama khél dalna sama khol sédatina c'est avec impatient que j'attendais ce khoutba ya oustaz yalnala sameu goudeul sa fane yokou xam.xam bi yokou xéwël yi inchAllah diam rk ngay nous sommes tjr derrière vous barakAllahou fikoum
Kone dh nio yèm yaw
Maacha'Allah Allahouma baarilk y'a Oustaz, à bon entendeur salut, qu'Allah azawazal nous guide sur le droit chemin amiine.
Kou bouguoul dek yalla néna, Mouhamed SHWS néna, Chaytanè mo mom sa khol ta nittou chaytanè ngua. Macha Allah! Dieureudieuf Sall, Brom bi arniou.
Walla boul ragal dara
Kéne dou wakhal yalla di tite nite biga khamni dou dara
Si kaw si kanam rek nga dieum
Yagui yeah ndaw gni deh
Chérif waye kénedou fénal yalla du lakhatou
@@chiekhabdoulosopyesbassiro1785 ce que oustas a dit c'est la vérité mais les gens qui suient ses sérings c'est du n'importe quoi car il ne leurs parlent pas de Dieu seulement leurs grand pére
@@chiekhabdoulosopyesbassiro1785 sen serigne yi kagn nioy fénal yalla
Salam oustaz toujours des enseignements avec pleins de savoirs de sagesse et de sérénités qu’Allah SWT te monte en degrés et te préserve des personnes malveillantes.
OUMAR SALL FORCE ET HONNEUR
La Brigade ANTi BiDAH je veux votre numéro
Dieynaba Badji salam ma sœur pourquoi tu veux mon numéro ?
@@brigadeantibidah2911 c'était juste pour prendre mon vaccin anti bidah
Dieynaba Badji c’est à dire ? c’est quoi le sens de ta question ? En plus je ne donne pas mon numéro sur internet.
@@brigadeantibidah2911 OK oustaze on est dans le you tube à vous suivre tes enseignement sont vraiment très intéressant.que Dieu vous protège merci beaucoup
Oustaz Oumar SALL Boul Falé Kéne Kou Nék Si Deug Daye Beuri Aÿ None Toujours Il Dit La Vérité Yalla Nala Yalla Maye Goudou Fane Ak Wérr Gou Yaram Bonne Contination Sama Oustaz Préféré ❤
Oumar salle on ne fier de tw que bon dieu t protéger contre t ennemi amine
Qu'Allah azzawajal t'accorde une longue et heureuse vie Incha'Allah et qu'IL te protège
Machallah ya oustaz deugue rek guaye waha
Oustaz nékkal si djiamme, ya Oustaz!
Machallah oustaz virement c'est la pur vérité que dieu nous protège
C est toujours avec impatience que j attende tes vidéos.
Eh ma la ko ndeukk khalaat !!!
Et c'est la même pour moi 😊
Et c'est la même pour moi 😊
walahi sante bou bari alhamdoulilah oustaz mash allah barakhallah fikoum sounna rek
Moi aussi
Masha Allah sama oustaz. Bilahi yangui xéxal l'islam ak fii rewmi tolou nii . Qu.'Allah vous récompense.
Wallahi oustaz yalla nala yalla fay deugx rk ngay wakh
Merci oustaz oumar sall vérité rekk
Alham'dou lillaha macha'allah ya oustaz Oumar Sall yallah nala yallah arr thiî Barker alkhour'a nn
Mashallah ya oustaz alhamdoulilla... toujours à l'écoute de la vérité. Nous suivons et essayons de nous conformer. La vérité est apaisante au coeur et à l'esprit. Qu' Allah nous accorde son pardon et exauce toutes nos prières et actes de dévotion.
Amin
Guiss naa ni kou bakh nga te mandou yalla na la yalla diapale barke serigne touba
Machala ya oustaz amatina sólo deug reke ngay wakh koulaye deguelou dou reer
Tu es le vrais soldats de l'islam doundeul
EEsskkeeyy Ya Oustaz, Jazakumullahu Khairan.
Yeneu deugeur bopp yi ,Diay sa dine' la (cit)
Au senegal ,les gens ne meditent pas sur le Coran, c'est pourquoi on voit des pratiques et comportements absurdes ,qui nous ramenent aux temps Jahilya.
Sourate Al Qamar -Sourate al Qalam-Sourate Al Qyama, -Sourate Al Buruj.
A mediter pronfondement.
Tu as raison
Yalla nala Yalla takhawou, fay la
May la goudoufane ak werr si barké sunu Borom
May Allah bless you long life ameen❤ 🙏
Machallah Amna solo yalla nala yalla maye goudou fan ak wer
Moi vraiment je veux qu'il n a cas formé 1000000 de personnes comme lui inchalla bientôt le Sénégal va être un très très bon pays
ALHAMDOU LILAH!
Je rend grâce à Allah de t'avoir connu sur le chemin de la SUNNA.
alhamdoulillah q Allah vous preserve
Masha'Allah ya Oustaz
Machallah oustage oumar sall yalla nala yalla same la c Allah seul ki te protege billahi mala begue oustage
Alhamdulilah bull masa nopi Yalla na la Yalla weural goudal sa fann. Ameen
Maa shaa Allah ya ustass
Ah kon deh senegal barry na ay dofff pasa ka serigne ce lenui waate ak tekk len palasu yalla.
Dawna yaram
Mashaallah 💓💓💓
Salam mon oustaz paix sur vous : wallahi je vous aime Qu Allah vous protège : réussite
MachaAllah ya Oustaz daguay sédal sama xole bi si niguay baye sa war si diyné dji zajaka Allahou khayran Oustaz Omar Sall diam rék lala Yallah di défal dakh deug la beug
Machalla meme man mi suma koye deglou damaye am louma nekh lol ndakh deug reke laye wakhe
Machallah oustaz nala yalla faye
Long vie et la santé ya oustace Oumar salle vous êtes toujours plus véridiques que jamais que te garde
Mo nekh Sénégal. Wayé alhamdoulilah bi gua fi nékhé digniou fathéli. Qu'Allah SWT nous préservent et éclaire notre chemin. Amine
La vérité rien que la vérité ❤❤❤🙏🏾
بارك الله فيك
Thank you oustaz oumar sall I love you sunnah kanmo rek inshallah
Rabbana laa tuzih3 qulubana ba3da izz khadaytana wakhab lana mine ladouneka rahmataan innaka antal wakhab 🙏🏼
Ouztaz yalna borom bi sameu niu sameu la degeur takhaway bi 🙏🏼
Na kou nene partager ces khoutbah de oustaz omar sall si sa alentours in sha Allah tawhid dina dieum kanam
Yalnagnou Yalla maye dëgg ak toop
Machalla oustaz alkhourane ak suna rek j'ai eu les larmes aux yeux a la fin du khoutba qu'Allah tout puissant te protèges contre cheitane ak nit cheîtane yi
MA SHA ALLAH OUZTAZ OMAR AHMAD SALL MAY ALMIGHTY ALLAH CONTINUE BLESSING YOU AND WHOLE MUSLIMS AMEN....DEGUE REK MORLAH NYUERR MAY YOU LIVE LONG LIFE AND GOOD HEALTH..
Oustaz Oumar Sall Mashallah et merci beaucoup que Dieu vous protège
Machalla amna solo na yalla rék takh man mourit la Bou wér
Yalla na Alla soubhanaka wa talla barril gniou melni oustaz Omar sall yalla are la samala deguerr la yagalla la fi like ma cha Alla
Sama kholl sedd na ya oustaz machallah
Waye Ouztaz youkhoul si kawe waye ..Sénégal koufinei yalla neina yonéneteubi neina gnou nonoula barki alkhouran..même au sein de ta famille on te méprise..Qu'Allah ns guide
Takbiiiiir!!!!!!
Manila khel dal ne bignou amè gnouy lèral yoonwi diko dèfendre. Yalla nala Yalla samm, samm gnou! Aameen yaa Rabbal aalameen !
Amin
Machalla je rend grâce à Allah d'être Musulmane.
Alhamdoulilah dieu veille sur toi oustaz
Je suis très très très content ya oustaz .vous êtes une grande fierté pour la oumma
Mashalah yalna yalla arr la nit gni begoune deug waya incha allah☝️ yeug day geuneu lerr rek al quran ak sunnah rek rek moy islam ☪️ lénène bokoussi incha allah ☝️
Bien dit !!! Très bien dit oustaz
Nooo moi quand j écoute oustaz , mon cœur s apaise bilahi
Que le bon Dieu vous protège, vraiment vous dites la vérité.🤝🤝🤝
Machallah toujours véridique
Machallah ya oustaz oumar sall diazakallahou khayrane amna solo looool
Que DIEU vous bénisse oustaz oumar sall
Ma sha Allah baraka Allahu fik yalla nala Yalla sama le bopam
Amin
Machallah machallah bilay lingay deifar barina yallana yallla goudale fanwi
BarakAllahou fik, voilà ce que l’on devrait uniquement entendre, le Coran, la Sunna Alhamdoulilah.
Ya Rabbi Allah, préserve le sang de Oustaz Oumar Ahmad Sall, tous les prêcheurs de la Sunna, et des croyants sincères, amine Ya Rabbal alamine
Machala yalna yala sam te degueral la amine
Je suis rappeur vraiment changé ngaa Lou beuri si Mane ...tah ngaa ma hame suna rékk moy deug que Dieu te protège .... yallah nala yallah are ...
Mashaa'Allah
Jazakallah ya oustaz... Yaw ak niou melni yaaw yenaa fi nekal diné l'islam bii. Sénégal deukk bidaa ak shirk. Qu'Allah pardonne à mon peuple... S'ils savaient !?
جزاك الله خيرا يا شيخنا
Oustaz Oumar Sall, Macha Allah. Qu'Allah veille sur toi, te protège et guide tes pas. Amin. Hamhambi leer na.
Alkhuran ak Sunna rek moy degg.
Jazakallah khairan ya Oustaz
Li wadj Hil Laahi Ta âlaâ Lirr leen ko khol Ndakh tawhidd lanouy Diangalê am dèèt
MAA SHAA ALLAH qu'ALLAH nous guide!!!
jereujeuf Oustaz Omar Dall yalna borom bi sam leu té baril say kém
Masha Allah
Macha'Allah ya oustaz que ALLAH te récompense. Vérité absolue rien que la vérité.
Merci
Alhamdoulilah Mach Allah toujours derrière notre oustaz qui dit seulement ce qui nous intéresse qui est le coran et la sunnah Qu'Allah vous garde
billahi serigne bi gna khamne mounoul sakh sak pisso
thia kanam rek inshallah, barakallahu fik ya oustaz🙏
Machallah oustaz barakallahfikm que Allah nous guide amine
Merci Oustaz Omar sall amougnou safai Allah rek molay fai
machahala oustaz, khamna diangalé rék nga beug thi yalla ak yénéntam té war bépp dioulitt té tégou si yonam bayi térém moy waréff sérigne vrai té fékhé ay talibém tégousi alcoran ak suna lolou mowaral sérigne, képp kou indi lénén keurignla.ndakh kounék sagn na am kilifa diné mais té diné rék takh. wayé yén sayi dagay dioum si yéneu léralyi .ndakh gamou si yénéntabi(psl) dou bida té kou am guésstou di ga kham dou bida(expliquer aux musulmans ki est mouhamét(psl) et ses histoires pour refortifier notre foi.........................
Ya oustaz dieureudieuf boul ragal Dara kene meneloula Dara Lou doule yalla continue ton chemin que le bon Dieu te protège et te donne long vie
Manchallha Sall yalla nala yalla samb moussela thie cheitanee