Lyrics Buur yag na weur linguère ba tay dji ley soga dadj Damay diokhé beignet ginger douma khaar sakh bala naadj Compte bancaire bi lay keup paré diokh la loma ladj Niaari dieum yi na done ben sama khol bi yaadji khadj Diap na la douma la bayi kham nga or dou moromou peureum Sant na yaay bi la diour té sa baayit mang koy gueureum Djigueen bou tok si keureum ba nopi tek tchi tak seureum Kouko am lo di wakh khana ngemb ko def ko mbeuram yaw Damay beuré daan Championne damay beuré daan Sa mbeur mi mate na mbeur ba nopi souple ni diaan Ba paré ngueu sama combat mane dou yomb Am na nodjou door mbot yeneu saay ma weur la nomb Bima paré yag na sa dieum la done khaar Negueul touti ande bi boy ma def thiouray nek bi sakhaar Samay copains yap nagn ma diokh ma clé bi ley daan Sama badiène néna ma bouma la rey na la thiokhotaan Tay dou yomb baby tay dou yomb Lou way done diaay demb tay mou lamb Meun ta yomb daddy meun ta yomb Na guéné samay armes lourdes wathié neek bi zéro Djigueen daal dey jolie Dima andil dej au lit Takal ma bavoir wakh you nekh yi di dioli Sama dieukeur meun na bord Goor bou diongué reka woor Am na diné tek si baakh té yeneu saay mou kathior Mane dama kham sa ndieuk motakh ma diokh la may bou ndieuk andila niou daal di deuk nga diokh ma mbeuguel bou mat seuk Djigueen gni danio baré waye yaw mi d mane nga taneu teral ma thi dig gor yi sama khol feekh ma contaan Def na la sama linguère Mane ma dieul la fal la buur Dound peace pas di guerre Diam di sakh thi sougn nguur (bis) Tay dou yomb baby tay dou yomb lou waay done diaay demb tay mou lamb Meun ta yomb daddy meun ta yomb na guéné samay armes lourdes wathié neek bi zéro (bis)
Encore lounekh ba dakeu nekh avec ADAM SENE . Sene thially todia tingafi. Belle parole beau clip . Deco bi masha Allah . Bonne continuation cherie la fierté de saint Louis.❤❤❤❤❤💯
Ah Machallahhh wayyy elle A besoin de soutien tte la populations St Louis naa nous si yappppp ma gui si biiiiiiirrrrrr Fier d'être Ndar Ndar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Très belle chanson ❤️❤️ man gniy disliké la manoul comprendre 🙆♂️😢 genres Adam yi dagn léne wara soutenir vu qu’elle essaie avec les moins du bord ❤️ courage sister 😍
Je connais pas le nom de la chanson et je suis allé sur tik tok regarder les challenges sur cette chanson et commenter en demandant le titre de la chanson
Ndeysane au Sénégal la bonne musique ne nous intéresse pas et c'est désolant. Au niveau de la qualité musicale rien à dire . Les paroles sont claires douces et surtout leurs voix sont extraordinaires. Wayé gars yi tank musique bi beunoule séne nope yi beugou niou 😂. Beugue Lou bone laniou def . En tout cas félicitations vraiment nekh n'a trop
Wouahh🥰🥰 quelle puissance vocal d'adam sene🎊🥳 une artiste très sous coté malheureusement mais sache que tout est question de temps tu iras loin inchallah. Je sais que tôt ou tard je t'unviterai dans mon émission pour parler de ta carrière inchallah geum ko rek kom louma geumei ni je serai un grand animateur présentateur au Sénégal 🇸🇳🙏
Ndeysann Mame Saliou magui ziar deh
Délo ziar sangue bi 💪🏾✌🏾
Dpuis bobou mankoy weur oohh kel belle chanson
Merci bcp Rahma ❤
❤❤❤@@maralofficiel963
@@Khadijacisse209Cisse ❤️🥰
Ils sont mérités 1Millions de vues ki Éhh dacor avec moi ✊
Très belle musique vous méritez 1million
Vraiment
Moi
Damako weur ba kou wakh mouné khamoul kouko weuy
Moi c est vrai
Mashallahhh comme d'habitude vous avez taper fort💃🏾💃🏾💃🏾 tube décembre baguiii niiii💃🏾💃🏾💃🏾💃🏾💃🏾❤️❤️❤️♥️♥️♥️
❣️❣️❣️💪🏿💪🏿💪🏿 ''sama badiane nèna boumla rèy naaala tiokotaaane'' Adam ki es tiiiiiiiii !? Défatinga sa meunine siiss mine
adam a
Wamu
Ouaaaaaaaw vraiment affaire bu nice 👍 respect ✊
C très nekh bly c trop beau donne continuation 💞💞❤💯
Machallah copin bonne continuation li nice neuh trop machallah way félicitations encore une fois
Lyrics
Buur yag na weur linguère ba tay dji ley soga dadj
Damay diokhé beignet ginger douma khaar sakh bala naadj
Compte bancaire bi lay keup paré diokh la loma ladj
Niaari dieum yi na done ben sama khol bi yaadji khadj
Diap na la douma la bayi kham nga or dou moromou peureum
Sant na yaay bi la diour té sa baayit mang koy gueureum
Djigueen bou tok si keureum ba nopi tek tchi tak seureum
Kouko am lo di wakh khana ngemb ko def ko mbeuram yaw
Damay beuré daan
Championne damay beuré daan
Sa mbeur mi mate na mbeur ba nopi souple ni diaan
Ba paré ngueu sama combat mane dou yomb
Am na nodjou door mbot yeneu saay ma weur la nomb
Bima paré yag na sa dieum la done khaar
Negueul touti ande bi boy ma def thiouray nek bi sakhaar
Samay copains yap nagn ma diokh ma clé bi ley daan
Sama badiène néna ma bouma la rey na la thiokhotaan
Tay dou yomb baby tay dou yomb
Lou way done diaay demb tay mou lamb
Meun ta yomb daddy meun ta yomb
Na guéné samay armes lourdes wathié neek bi zéro
Djigueen daal dey jolie
Dima andil dej au lit
Takal ma bavoir wakh you nekh yi di dioli
Sama dieukeur meun na bord
Goor bou diongué reka woor
Am na diné tek si baakh té yeneu saay mou kathior
Mane dama kham sa ndieuk motakh ma diokh la may bou ndieuk andila niou daal di deuk nga diokh ma mbeuguel bou mat seuk
Djigueen gni danio baré waye yaw mi d mane nga taneu teral ma thi dig gor yi sama khol feekh ma contaan
Def na la sama linguère
Mane ma dieul la fal la buur
Dound peace pas di guerre
Diam di sakh thi sougn nguur (bis)
Tay dou yomb baby tay dou yomb lou waay done diaay demb tay mou lamb
Meun ta yomb daddy meun ta yomb na guéné samay armes lourdes wathié neek bi zéro (bis)
Ohhhhhhhhhhh ❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Et merci beaucoup🥰
❤❤❤🔥🔥🔥🔥
Mais je pensé ke c tn vrai mari ou bien tournage la wonn
Tay dou yombou bb tay dou yombou😍😍😁
Waouhhhh nice son mes ❤❤❤❤vous avez assuré.Congratulations adam sene la plus belle voice😍😍😍😍
❤️❤️
😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Waaw Goor waye.
Belle video. Adam❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤
Bravo macha alla son bii nice neu trop en plus de ce la video bii dafa diar yone c trop cool je vous jure bonne continuation
Ohh mashallah sèn weuy bi nekhna trop
Ay way meunou ma ci doyal nos votre duo c'est le feu machallah c'est très nèhh je vous kiff congratulation💞😍
😍😍😍🔥🔥🔥🔥
Ndeyssane tay dou yomb franchement félicitations bro mio
mach'ALLAH,enfin j'ai retrouvé le son ! Très bonne continuation
Encore lounekh ba dakeu nekh avec ADAM SENE . Sene thially todia tingafi. Belle parole beau clip . Deco bi masha Allah . Bonne continuation cherie la fierté de saint Louis.❤❤❤❤❤💯
🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Setan nakou 111 fois Li dafa nékh
Yiiii kone sétane ngako frère 🤣
Balé gui magui koy sétan
Adam séne Macha Allah fassatouma sétan bénén Clip boudoul bi
Magnifique sa kaw sa kaname❤😍
Encore une fois félicitations ma belle.. Machallah. Ci kaw ci kanam rek.
Bzx. Zed
Nice ma femme. Bon vent nekhna trop. Que du succès dans ta carrière ma belle
Félicitations très chère, bien réussi ! Magnifique 🎉🎊🎈
Ouh la la 🔥🔥🔥🔥🔥 magnifique chanson. Adam ta voix est incroyable 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Bilahi gorr bou jongué rek mo worr ❤️❤️
Machallah ❤️ Adam sene lima nékh si mom dafa AM ite si nite
🔥🔥🔥🔥defatigua sa meunine machalla en avant reck inchallah fierté ndar 💓
Dègu ngène rimes Mara yi😍 et li nexna chapeau à vous
OMG 🥰 je l'ai toujours chercher..c aujourd'hui que je l'ai trouvé 😇
Masseu tiono ci séttt bi lol 😂
J'ai trouvé aimé ♥️💖. Sa me fait rêver
@@mariamsy3821 ça fait plaisir de savoir que t’as aimé ça amna youy nieuwate légui InshaAllah
Ohh j'ai hâte 🥰
J’ai écouté cette sanson avec wiko et ça devient iPhone 12 pro max 😎😎nn tay dou yomb way des cœukh❤️❤️❤️
On dit chanson
Très beau clip! Lyrics au top! Félicitations à vous et bonne continuation
🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Wa
Ohhh serere bou hess way li nehna
Machalla sama waykat bi saboumala diklo sama khol nekh yalla nala yalla defal diamm ak ndam ak teranga si musique bi
Nice one. Nexna troo machallah
Je ne m'en lasse pas🥰 je l'écoute en boucle.
Machalla rien à dire surtout Mrs Gueye bi ohhhh je vous adore yalla bakhna diam si yen peace and love❤😘😘😘
Jadorrrrrrrrrrrrrrrrrr wayyyyyyyyyyyy dra dakoulll teukou🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤❤❤
Oh Machallahhh wayyy liiiî dèh nékhhhhhh daaaallll mais la fillle c'est la St Louisaine waal a ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@fatoubintoundiaye ki moy Adam Sene borom Ndar
Ah Machallahhh wayyy elle A besoin de soutien tte la populations St Louis naa nous si yappppp ma gui si biiiiiiirrrrrr Fier d'être Ndar Ndar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@fatoubintoundiaye té nonou la beugué Ndar plateau boum tok wakh ko
Très belle chanson ❤️❤️ man gniy disliké la manoul comprendre 🙆♂️😢 genres Adam yi dagn léne wara soutenir vu qu’elle essaie avec les moins du bord ❤️ courage sister 😍
Ils où elles ne savent même pas ce que signifie ça 👎👎 sérieux
Bravo brother, nice nice mâchala
Machalah frérot vraiment rien na dire tè khôl sédatina notre fierté si kaw si kanam
Je valide depuis 🇫🇷
J’adore votre chanson
Je ne compte mm pas le nombre de fois que je l’écoute vraiment ✅
Bilay machalla yalna dound ba am bess bi ak kounei amin inchalla
M.wmpm
Mame Balla Mbow a raison kat🤭 wepepepe kel son🤩🤩🤩🤩😍🥰🌹
Un cool song
Je valide vraiment
Olalah kagn lay appliquée waay bi (mariage)machallah les gas
Congrats bro Li nèkhhhh neu trope
Saliou et Adam séne contane si yén rek, very nice song guys🔥🔥..amna song boubess
Wooow Woow Wow Coooool Vraiment Tama Nģua Di Niou Bégeul Adam Yalna Sa Diamm Yageu ❤🥰
Ça me rappelle copine bima ndiekone ammm
Ohhhh j'aime ce chanson ❤🥰
Nekhna trop, tt est bien dosé, bne continuation
Machallah ❤️ séne clips bi nékh naaaaaa sole nguéne Lou Diot 👏
MachAllah trop cool bonne continuation à vous ❤❤❤❤👌🏿👌🏿👌🏿👌🏿
Machalla vois yi nekhna trop❤️❤️❤️
Machallah son bi nék na❤😍💓💓
Nékhna dallll machalla
PEENAAALTYYY "VAR VAR" JIGUÉNEU DOU WEUREU DOMBA GOOR LAAABIDINAA🤭🤭
Enfin dama weur son bi ba soneu😭🥰 cette musique est juste waouh❣️❣️❣️❣️
Sfroihy
Wamy
Fabienne
Manchallah petite sœur adorée. J'adore
Machala bon song très joli clip
Gueye bi rek motax ma kontan 😍✍️
C joli wayy bii dfa nekhh trop
Oh li nekh na way🥰
🤩🤩🤩🤩🤩 li nexna way
Macha Allah talent bi mougui fi dè yalla yalla takhawoula.
Vraiment je n'arrête pas à t'écouter tes chansons
No jtm bcp surtout sama yaye dafla beug séne la sante motakhite❤️❣️🔥😍
Félicitations Adama saliou tu es mon frère ce que tu as fait est très bon que Dieu vous bénisse tous les deux jtm
Félicitation adama
Ki cherché cette chanson juska lavoir trouver comme moi
Moi🤣🤣🤣
Moi
Je connais pas le nom de la chanson et je suis allé sur tik tok regarder les challenges sur cette chanson et commenter en demandant le titre de la chanson
Khawna dead😂😂
@@bakarytandia1439 moi
En tout cas vous avez cartonné 👏🏿👏🏿👏🏿
Je viens de découvrir ce son
Mais j'adore
Commencei na Diang paroles yi déjà
❤
Wwaouh i like son bi nehna lal ca me rappelle mon mariage
Nice bro machalah mara et adama
Machalah Adams sakaw sa kanam rek
Je suis fière de toi 😍😍 Adam 😍😍
Toujours aussi percutante!
Boule di raare adam. On t'ecoute!!!
Bravo
Ohhh khol sedd na bro very nice song congrats 👌🏾🔥
Vraiment bravo nekh trop machalla Adam 🥰🥰🥰❤❤❤
Magnifique ❤
J'adoooorrreee... Mach'Allah Adam...bonne continuation
Ndeysane au Sénégal la bonne musique ne nous intéresse pas et c'est désolant. Au niveau de la qualité musicale rien à dire . Les paroles sont claires douces et surtout leurs voix sont extraordinaires. Wayé gars yi tank musique bi beunoule séne nope yi beugou niou 😂. Beugue Lou bone laniou def .
En tout cas félicitations vraiment nekh n'a trop
Et c'est dommage! Et les animateurs qui ignorent ce tube🤦🏾♀️
T'as tout dit
Li nekhna de
She’s so talented. Sama mariage mom lay wo mou defal Ma live bi 😭❤️
@@maadetmangue7902 de mm n.. v de cv:0=-O=-O=-O=-O=-O=-O
Jaime bcp cela me rappelle mon mariage
Ddcvghqkh s4epj
T'as jrwiitdi5q5g jm 99jpyd66tct9u0
Liiiii nékhna wayyyyyyyyyyy❤😊🥺
Machalah laye sa grand bi amna talent
merci pour ton engagement au service de la nation, bonne continuation nice song
Diadieuf Mamadou ✊🏾💪🏾
Thieye mara dooo niiiit
Wouahh🥰🥰 quelle puissance vocal d'adam sene🎊🥳 une artiste très sous coté malheureusement mais sache que tout est question de temps tu iras loin inchallah. Je sais que tôt ou tard je t'unviterai dans mon émission pour parler de ta carrière inchallah geum ko rek kom louma geumei ni je serai un grand animateur présentateur au Sénégal 🇸🇳🙏
Ohh mara💞 t'as assuré bravo Adam sama chanteuse🥳😘
Machallah sound bii nehhh
Fier de toi ma chérie ns sommes ts derrière toi ma grd
vous etes fantasins j'arrive pas rester un minute sans écouter les belles vois je vous adore bcp
Damaniii li moye musique
Cé beau ça jaim
MACHAHLLA NEKH REC👂👂 🤔🤗😉😍💃
Le haut niveau vraiment nexna
Machallah nice na et aussi naturel j'aime bien wallah 🥰
Yalla na dieukar gnew legui bala yageu
Neigueul touti ande bi boye, meu def tiouraay nek bi sakhaaarrr
Machala depuis magui khar bess bi. Tu as encore assuré comme toujours on est fier. Nous voulons des millions de vues.
Degueul ma liiii🤩🤩🤩🤩
je l'écoute chaque instant bravo à eux
Yeah Mara boy médina bi from rue 3
Yeah bro bégué nala