🔴[ DIRECT ] PLATEAU SPECIAL OUSTAZ CHEIKH AHMED TIDIANE NDAO l MERCREDI 22 MAI 2024

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 3 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 272

  • @seydinamohamedndiaye6690
    @seydinamohamedndiaye6690 6 หลายเดือนก่อน +7

    Cheikh Ahmed tidiane Ndao ❤ leneu rek laye retenir ci mome..L’homme qui m’a fait connaître l’histoire de Moussa dé A a Z.. nhieupeuye dioum c’est tout

  • @ouztheman5792
    @ouztheman5792 6 หลายเดือนก่อน +23

    Bravo PDG. C la première fois que je vous entend parler mais j’ai admire ta franchise.
    BRILLIANT!!!!!

  • @sokhnafatimabous.mansoursy283
    @sokhnafatimabous.mansoursy283 6 หลายเดือนก่อน +10

    Oustaz CHEIKH Ahmed Tidiane Ndao yalna yalla sam léne Aar léne 🤲

  • @heutou_talibe_cheikh
    @heutou_talibe_cheikh 6 หลายเดือนก่อน +10

    Macha"allah el hadji makhtar ndiaye tu est tres véridique et direct dans tes propos

  • @Papelaminediop
    @Papelaminediop 6 หลายเดือนก่อน +10

    Cheikh Ahmad tidjane ndao dafa dioume yalnaco yalla téggil li dale sa kawame . Té boussi guéné yalna boumeco défati ci barké cheikh seydil Hadji Malick Sy radiyalahou taala anhou wa ardahou wa ana bihi amine .

    • @khalioudrame9526
      @khalioudrame9526 6 หลายเดือนก่อน

      Kouleu wakh dafa dioum souko sonko defé nak? Ousmanensonko khamaloulene ko dara ..ay mbireum leroul.

    • @mouhamadtamourougueye387
      @mouhamadtamourougueye387 6 หลายเดือนก่อน +3

      ​@@khalioudrame9526yaw moom est ce que say mbir leerna ? Dioulite dou toumaal moroomou dioulitam. Limou wakh même soudone deug warouko wakh.

  • @kanekiken9566
    @kanekiken9566 6 หลายเดือนก่อน +2

    Directeur bi deugou na.
    Yalla nako yalla arr
    Finalement sama khol fekh neu yalla na yalla dimbali ouztaz ndao

  • @ababacarseckfaye7719
    @ababacarseckfaye7719 6 หลายเดือนก่อน +4

    Machalah oustaze mactar ndiaye, c'est la première fois que je vous écouté mais vous incarner enseignement de el hadji malick. Vérité absolue

  • @ndeyefaye6835
    @ndeyefaye6835 6 หลายเดือนก่อน +4

    Machalla oustaz cheikh tidiane diabarla vraiment défadioum

  • @black2krack982
    @black2krack982 6 หลายเดือนก่อน +1

    Je vois sur ce plateau l'Islam. Macha allah rafetna. Li ma japalone Iman gnep fatena ko daxx PDG. Merci

  • @Ndeyemarem-ux8iq
    @Ndeyemarem-ux8iq 6 หลายเดือนก่อน +7

    Cheikh tidiane ndao yalla yalla takhoul guir dioumy séydina moukhamét louma kham thi mom yawla

  • @alassanethiam6870
    @alassanethiam6870 5 หลายเดือนก่อน

    Cheikh Ahmad Tidiane ndao yalla nala yalla same ci barrke seidina Mouhamadu ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @DabaKebe-wg6dk
    @DabaKebe-wg6dk 6 หลายเดือนก่อน +9

    Kou bakh dafa dioume yalna ko yallah takhawou yalna léne yallah fay rafét
    na

  • @bbfa864
    @bbfa864 6 หลายเดือนก่อน +7

    Macha allah PDG c'est très bien et très important ce que vous avez fait . La vérité c'est primordial et il faut rectifier le tire . La dermache est excellente djoulit nilay def . Nous sommes tous abasourdis de ce que a dit l'imam vraiment mais voyre posture est louable macha allah . Yalla na nek leçon pour nous tous si mandou, si rafetal ...nitt loumouy wouyo dakoy nourou...nous devont perpétuer notre statue d'exemple.
    Merci malikia❤❤❤❤❤❤❤

  • @MaggatteGaye
    @MaggatteGaye 6 หลายเดือนก่อน +1

    cheikh Ahmed tidjane ndao yalna yalla geuneu goudeul faname té dolliko wer barcké mame maodo 🤲 té yalla teguilko natoubi

  • @salifoundong4197
    @salifoundong4197 6 หลายเดือนก่อน +1

    Cet homme est franc

  • @ousseynoudieye1431
    @ousseynoudieye1431 6 หลายเดือนก่อน +1

    Oustaz deh niongui koy nianal yalla ndakh ndioumté dal nako dfa dioum ndakh yalla nako yalla taxawou mou diégalou rek yalla nako yalla defal tawfex Sénégal yalla nafi diam yagu in schallah dieireujeuf PDG

  • @groupenabiyetv8211
    @groupenabiyetv8211 6 หลายเดือนก่อน +17

    KÉPOU KOUY OUSTAZ BAYABO NGA XAM YAW YAY KAN LI GEUN THI XAM XAM MOY XAMSA BOPPOU❤ TÉ NGÉN MOYTOU POLITIQUESENT YI OUSTAZ NAK DAFA DIOUM WAYÉ YALLA NAKO YALLA GÉNNÉ THI XAT XAT YI❤❤❤❤

    • @dioptalla755
      @dioptalla755 6 หลายเดือนก่อน

      Frr wakh nga lepp

  • @Dia88186
    @Dia88186 6 หลายเดือนก่อน +1

    Grâce à borom grand boubou bou maron bi❤❤❤j'ai abonné sur Malikia Tv🙏🙏🙏

    • @babs7555
      @babs7555 6 หลายเดือนก่อน

      On est 2 alors

  • @Xaliloulah_Bou_Sonko99
    @Xaliloulah_Bou_Sonko99 6 หลายเดือนก่อน +3

    Mashllah hadj makhtar ndiaye al amine

  • @cheikhseck4760
    @cheikhseck4760 6 หลายเดือนก่อน

    Imam cheikh tidiane ndao yalla Nako yalla takhawù wayé yén WA malikya sen émission dara rafétou ci lii khawma Hein bingauén diapal imam la khawma loumou doon wayé niawna trop Amna mbétél bou REUY si yén yalla kham nako

  • @papabiranendaw1195
    @papabiranendaw1195 6 หลายเดือนก่อน +1

    MachAllah le PDG a tenu discours très responsable. Yalla rek mo mate Allahoumma salli ala saydina Mouhammad wa sallim

  • @Momo44454
    @Momo44454 6 หลายเดือนก่อน +3

    MashaAllah Malikia ❤️ il faut être juste et honnête 🙏🏿❤️

  • @mansourdiagne1964
    @mansourdiagne1964 6 หลายเดือนก่อน +21

    Sonko kouka songou sankou

    • @Ahmadu-o2n
      @Ahmadu-o2n 6 หลายเดือนก่อน +4

      Ku masa songu gaçca rék nga say jëlé

    • @mohamedgaye408
      @mohamedgaye408 6 หลายเดือนก่อน

      boulen sonal nite gni

    • @cheikhseck4760
      @cheikhseck4760 6 หลายเดือนก่อน

      Bayi lén doul
      Doul nguén ba yakkù

  • @moustaphagaye2362
    @moustaphagaye2362 6 หลายเดือนก่อน +4

    Machallah makhtar ndiaye

  • @omarpouye1493
    @omarpouye1493 6 หลายเดือนก่อน +2

    Mon soutien à Oustaz Ndao. Yalna Yalla takhawou la.

  • @NiangLaye
    @NiangLaye 6 หลายเดือนก่อน

    Vérité absolue matare diagne merci mashala way

  • @DabaKebe-wg6dk
    @DabaKebe-wg6dk 6 หลายเดือนก่อน +4

    Machallah serigne Makhtar Ndiaye

  • @thiernobirahimdiop1637
    @thiernobirahimdiop1637 6 หลายเดือนก่อน +6

    Vraiment ce pdg il est Tres digne serieux je suis emut

  • @salioudiouf4593
    @salioudiouf4593 6 หลายเดือนก่อน +1

    machaala beggnaniou trop si plateau bi. Yalla naco yalla Takhawou té delloco si Ndiabotam si barkee sws

  • @ndawlislam7021
    @ndawlislam7021 6 หลายเดือนก่อน +3

    Macha Allah malikia dèfe géne Yefou kilifa PDG mouhtar Ndiaye wahega wahou responsable diabote bou tognè hamakoni mo togne imame dioumena nite moye dioume té diègalouna yallah nako yallah diégale amine PM sonko yite yallah nako diégale imame dramé topouna mèrame dounonou thi aye dioulite kounè warega ame liga tanè sa morome adouna dou keur

  • @daoudambengue5306
    @daoudambengue5306 6 หลายเดือนก่อน +2

    Yala na Bour Yallah mousseul Sénégal ci goor djiguéne yi ak séni alliés.

    • @Abibatoud
      @Abibatoud 6 หลายเดือนก่อน

      Amine ak imam oustaz nafekh

    • @daoudambengue5306
      @daoudambengue5306 6 หลายเดือนก่อน

      @@Abibatoud Yeup, Amine

  • @mberryable
    @mberryable 6 หลายเดือนก่อน +2

    Yalna yalla takhawou leu thi barkep yonentibi sallahou wa Salim amine amine.

  • @ibrahimaMbathie-kg2lr
    @ibrahimaMbathie-kg2lr 6 หลายเดือนก่อน +4

    Je vous adore ❤❤❤joulit ni lay mél❤❤

  • @DahiraSiratikalMoustakhimUASZ
    @DahiraSiratikalMoustakhimUASZ 6 หลายเดือนก่อน +2

    Macha allah. Yalna ko yalla taxawou inchallah

  • @al-futiiyutv_TBD
    @al-futiiyutv_TBD 6 หลายเดือนก่อน

    Le prophète SAW a dit "Sa mboku, dé ko jappalé, ci bu tooňe ak mbuň ko tooňe"
    Merci PDG, vous êtes un homme honnête, franc et responsable. Puisse Allah vous protéger !

  • @elhadjindiaye1246
    @elhadjindiaye1246 6 หลายเดือนก่อน +1

    Bravo et Merci Mr Ndiaye bien dis

  • @serigneniomrelo6956
    @serigneniomrelo6956 6 หลายเดือนก่อน +3

    Cheikh Ahmed yalnanko yallah takhawou

    • @mansourdiagne1964
      @mansourdiagne1964 6 หลายเดือนก่อน

      Yalla douko takhawou nakh doméram la

  • @Abibatoud
    @Abibatoud 6 หลายเดือนก่อน +2

    Naniou yallah mouseul oustaz ak imam nafekh

  • @oumarsow2035
    @oumarsow2035 6 หลายเดือนก่อน +3

    Alhamdoulila doulila li rafét na trop manchala ❤️❤️❤️

  • @CheikhDieng-gf1sp
    @CheikhDieng-gf1sp 6 หลายเดือนก่อน +2

    Oustaz dioumoul deugue la wakhe na counén khol si yalla,yalla mofi nék

  • @dieynabasene8425
    @dieynabasene8425 6 หลายเดือนก่อน +1

    maacha allah PDG vous avez réagi en vrai nitou dîné sans parti pris avec toute franchise en toute honnêteté merci de parler à cœur couvert un témoignage digne d un vrai seutou Mame seydi Elhadj Malick sy Radi allahou tala ane hou un plateau riche avec des hommes de valeurs

  • @azizndiaye9483
    @azizndiaye9483 6 หลายเดือนก่อน +6

    SËYDI EL ADJI MAALIK,MOSUL TOOÑ TE MOSUKO DIGLE,SOO AMEE SA MBOKKU JULIT BU TÒÑEE, WOXKO DËGG,WAL ASR LA BUUR YALLA WOX, USTAS DAFA TOOÑ,NA JEGGËLU,LUKO YOON JOX MU JÊL,LI MOOY DĒGG.

    • @cheikhlei3193
      @cheikhlei3193 6 หลายเดือนก่อน +3

      Lolou moy waakh dji dé mais dangaay guiss yén gars yi di parparloo beugko déf victime

  • @happysenegaltv333
    @happysenegaltv333 6 หลายเดือนก่อน +1

    Niongi nian ndieukkeul ngir oustaz cheikh tidiane ndao wallahi kham nagn ni mo toogn kon dieggeul leenko té yalla takh

  • @abdoukhadrediop2210
    @abdoukhadrediop2210 6 หลายเดือนก่อน +1

    De tout coeur avec ctndao nous le llaissons entre les mains d allah soubhanahou wa tallah et son envoye. Un mourant ne peut rien contre un mourant.

  • @PapethiateNiang
    @PapethiateNiang 6 หลายเดือนก่อน

    Macha alla pdc Makhtar ndiaye al Amine

  • @azur2117
    @azur2117 6 หลายเดือนก่อน +2

    Nattou dou wéés Naniou diappeu ni mounoul wooneu niak . Yallah na fékkeu dafa gueun . Yallah na Yallah fankhléén léppeu lou aay ci barké Yonnet bi SAW. Diaa guéén dieuff.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @azur2117
      @azur2117 6 หลายเดือนก่อน

      Waaw Al Kamaal lillahi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @papesambagueye5974
    @papesambagueye5974 6 หลายเดือนก่อน +10

    Il faut qu'il arrête. Cheikh ahmed n'a jamais cessé de jeter des diatribes a M. Ousmane sonko.
    Joullit dou togn. Té dou toumal moromou joulitam.

    • @assiandiaye8904
      @assiandiaye8904 6 หลายเดือนก่อน +1

      Tout à fait. Ceci n'est pas un accident. Lui et Moustapha Sy Al Amine ont souvent été très virulents envers Sonko.

  • @modoudialo3282
    @modoudialo3282 6 หลายเดือนก่อน

    Machlla yonéne tébi néna sa bokou diapaléko bou toyé walla bounuko toyé bou toyé noko kay wakhé ganiko yatoye machlla pdg❤❤

  • @ousseynoudieye1431
    @ousseynoudieye1431 6 หลายเดือนก่อน +1

    Nit Boula yalla dioxé yén thieur yi dangay moy yén yi oustaz nak yalla nako yalla taxawou bamou guén si xat xat yi té mou banie ko dalati in schallah 🇸🇳❤️ jeureujeufeuti PDG

  • @laminesaliourafahi6906
    @laminesaliourafahi6906 6 หลายเดือนก่อน +4

    Ñiongi ñianal cheikh Ahmad tidjan ndaw yalla tègil ko nattu bi

    • @mohameddiedhiou5476
      @mohameddiedhiou5476 6 หลายเดือนก่อน +2

      Lii du nattu buñu di jaawalé, kii dafa toppu bakanam ba fayeeku li mu jiw. Moom fu kawé la nekkoon waayé moo suuféel boppam ndax térangay àdduna yu ñàkk solo yii.

  • @dedesylla6508
    @dedesylla6508 6 หลายเดือนก่อน

    Maa Chaa Allah le PDG M.Makhtar Ndiaye Al amine est très véridique ak sangnessem bou rafète, nous voulons des personnes pareilles pour le développement de notre pays,
    جزاكم الله خيرا أيها المدير الصادق،وفقك الله،وحفظكم

  • @yacinediop1922
    @yacinediop1922 6 หลายเดือนก่อน

    Salam Oustaz Ndao. Say preches jubanti lu barè ak ñu bare. Xalaat Yonenta Yallah Yusuf. Jamm rek ngay am. Deug rek nga wax. Yallah sa weruway la abadaan.

  • @IbrahimaNgom-dt5wb
    @IbrahimaNgom-dt5wb 6 หลายเดือนก่อน

    اصبتم السنة واصبتم الحق فجزاكم الله خيرا

  • @imamndaw9693
    @imamndaw9693 6 หลายเดือนก่อน +4

    Alkhourane kou tok ba diko firi ak diko diangalé warnga ngako djikowo .
    Yalla na yalla takhawou ko.

  • @Mariam_org
    @Mariam_org 6 หลายเดือนก่อน +15

    Cheikh Tidiane Ndao défa Bagne Ousmane Sonko ba gneupe khame ko. je me suis désabonner de ses comptes depuis plus 2 ans, ak gnou méle ni mome dax déma allergie lou bone . Yalla nako djégueule dakh li dara gueunouko ñaw. Il véhicule une haine vicieux et c'est très grave!

    • @babacarndiaye8263
      @babacarndiaye8263 6 หลายเดือนก่อน

      CHEIKH TIDIANE MANOUL BEUGUE WAHABITE

    • @cheikhlei3193
      @cheikhlei3193 6 หลายเดือนก่อน

      ​@@babacarndiaye8263wahabite bi dé gnikoy togn yeup yalla monguilene di toroxal. Seydi hadji Malick tognoul andoul ak kouy togn talibé cheikh dou togn té souléne moytouwoul parparloo

    • @paousmanendao2030
      @paousmanendao2030 6 หลายเดือนก่อน +3

      ​@@babacarndiaye8263 wahhabites dara nekousii dans la religion il y a plusieurs branches respectons la croyance des une et des autres

    • @babacarndiaye8263
      @babacarndiaye8263 6 หลายเดือนก่อน

      @@paousmanendao2030 JE NE PEUX PAS RESPECTER LES ASSASSINS DE LA FAMILLE DU PROPHETE ET LEURS CONTEMPORAINS LES POSEURS DE BOMBE ET PROFANATEURS DE TOMBE DE SAINTS
      DEMANDES A SONKO CE KIL AVAIT FAIT DU DRAP DE WAZIFA TIDIANE QUAND IL ÉTAIT A GASTON BERGER
      COMMENT POUVEZ AIMEZ CES GENS LÀ QUI DÉTESTENT MEME LE TITRE DE SEYDI ATTRIBUE AU PROPHÈTE

    • @DEBO_DIMO
      @DEBO_DIMO 6 หลายเดือนก่อน +3

      ​@@babacarndiaye8263
      Kou séleki kou bone manoko beugue. yaw ya ñak argument dëg souko nékhé nék Wahabit, souko nekhé! et après?t'es qui pour juger? I don't blame u, blame yourself! Séne xol dou ame Sakina mouke ndax bagnéle

  • @aminataseck7481
    @aminataseck7481 6 หลายเดือนก่อน +1

    Machalla yallana léne yalla Faye ywe 😢😢😢

  • @mansourdiagne2659
    @mansourdiagne2659 6 หลายเดือนก่อน +2

    merci beaucoup PDG

  • @BoubacarBa-zi1mu
    @BoubacarBa-zi1mu 6 หลายเดือนก่อน +1

    Asalamou Aleykoum warahmatullah
    Mangi lendi nouyou dilen ziar boubakh té dilen nianal jamm
    Mangi rafetlou jotay bi boubakh si mbiroum sougnou mbok bi Di Oustaz cheikh Ahmed Tidian Ndao di len nianal boubakh Yallah na nelen Yallah fay yiw
    Nit ni rek la wara mel bou mbokam nekké si Jafféjaffé mou jappalé takhawou ko .
    Oustaz kou amal njerign nit ngni la ndakh Yag na niou gindi Di niou begal si ay wakhtaanam si ay att you beuré bueri
    (Dafa joum rek ) Ndakh kouy wakh ak kouy def rek Moy joum ken matoul ay nit rek len mankoy Toubal boubakh Di jeggaloul 🙏 Mangi nian Yallah teggil ko nattu Yi si kawam jappalé ko takhawou kou boubakha bakh moudellou waat si liguey bou rafet bimou nekk Di woo ngni si Yallah
    Yallah nako Yallah Yeketi Yok kham kham bi boubakha bakh dolli ko soutoura defal ko Jammu Aduna ak Jammu Al akhira

  • @mamadoutall8827
    @mamadoutall8827 6 หลายเดือนก่อน +1

    MA CHA ALLAH PDG VRAIMENT JE VOUS ADMIRE ENCORE PLUS VOTRE FRANCHISE ME VA DROIT AU COEUR

  • @bambadiop
    @bambadiop 6 หลายเดือนก่อน +2

    Un mara se protège en prêchant la vérité

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 6 หลายเดือนก่อน +5

    Kou séll ki kuko songue sankou wassalam 🙏

    • @alydiop-x1x
      @alydiop-x1x 6 หลายเดือนก่อน

      kou sell diga teuddéh domou diambour, bayi lén fén wakh léen sonko deugg, sonko fén nalén ba falou, wayée doufi am diamou deh fénal nafi macky sall lou amoul

    • @bambaniang1271
      @bambaniang1271 6 หลายเดือนก่อน

      @@alydiop-x1xIoe sakh soko songué gni niouss sa ndey

    • @MoustaphaNdiaye-ho2qn
      @MoustaphaNdiaye-ho2qn 6 หลายเดือนก่อน

      Dioulit day moytou di wakh louko woroul ,on sera en face à allah azza wajal bientôt 🙏🏼

    • @FODEDIABYGASSAMA
      @FODEDIABYGASSAMA 6 หลายเดือนก่อน

      Koi yengou niou teppi sa leufeul ndey domeram yi yenn wa apr ​@@alydiop-x1x

  • @PapeNgom-po8et
    @PapeNgom-po8et 6 หลายเดือนก่อน +1

    Seydi makhtar Ndiaye ya de gou ma la sope❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamadoudiop5844
    @mamadoudiop5844 6 หลายเดือนก่อน +3

    Oustas limou wakh rék la wara wakh deugg d'où romb nope yalla nala yalla sam choix for puissance 🙏🙏🙏👍🤝 peace and love yalla nala seri Babacar sy alhalifa wallou🙏🙏🙏🙏🙏

    • @taarikhs
      @taarikhs 6 หลายเดือนก่อน

      Défal vidéo nga wah lolu.
      Soyons véridique guir yalla

    • @cheikhlei3193
      @cheikhlei3193 6 หลายเดือนก่อน

      Défal video wakh limou wakh moom ndéyou mbileu dji mongui diégalou kom khamnga kokou il regrette

    • @KaBassirou-uc4nz
      @KaBassirou-uc4nz 6 หลายเดือนก่อน

      Defal vidéo wakh ko😅😅 niou Kat sa ndaye si kaso gu 😀😀

    • @modoudialo3282
      @modoudialo3282 6 หลายเดือนก่อน +1

      Oustaze dafa dioume nagoul rk

  • @sady1964
    @sady1964 6 หลายเดือนก่อน +1

    Merci kebè

  • @Dia88186
    @Dia88186 6 หลายเดือนก่อน

    Wakh deug yalla plateau bi Mature na❤🙏🙏❤

  • @CheikhDiaw-c5c
    @CheikhDiaw-c5c 6 หลายเดือนก่อน

    Machalla ❤❤❤

  • @mactarndiaye1976
    @mactarndiaye1976 6 หลายเดือนก่อน

    Macha'Allah tourondo kaddu yi rafetna

  • @matarcisse1174
    @matarcisse1174 6 หลายเดือนก่อน

    Alhamdou sonko sii adouna la sa lepp leer diam sii ioe mai merci beaucoup PDG 👨‍💼 yalla rek mo matt

  • @Mohamed-se3lr
    @Mohamed-se3lr 6 หลายเดือนก่อน

    MachaAllah PDG, il a fait une faute et non une erreur.
    Que Dieu l'assiste.

  • @binetasakho892
    @binetasakho892 6 หลายเดือนก่อน +2

    Yalla deug la beug même si on te mets un couteau sur la gorge . J’écoutais très souvent Oustaz mais qd j’ai entendu ce qu’il a dit ça m’a fait trop mal vraiment. Il a fait une erreur . Yalla nako yalla takhawou

  • @cheikhseck4760
    @cheikhseck4760 6 หลายเดือนก่อน

    Li rekk la Imam Cheikh Ahmed Tidiane Ndao wax koumou méti rk goordjiguén nga:
    "Ahonzou billahi mina sheytani radjim.
    Bismilahi rahmani Rahim.
    …………………………. ( des prières)
    Mboki djoulites yi mboki Sénégal séne mbok séne sopé Cheikh Ahmeth Tidjiani Ndao mo fass yéné wakhtane ak yéne si li khéw si Rewmi.
    Mou mélni, tabara kallahou, fane yi yeup gni ngui guiss lo khaméne tani daal daloul khél thi ay nitou sheytané you nga khamni gno nga diougué thia Tougueul nga khamni makk gni Tougueul Daroul fassikhine lanouko toudé; manam réwou kathior yi. Moy Tougueul, lou bone louné falane koy nassé. Rawatina France rawatina Paris.
    Mou mélni fane yi amna niari Kilifeu yo khamni diogué nanou Tougueul bassi niati kilifeu, tabarak’Allahou nieuw fi si Rewmi. Niome niati kilifeu yoyou teup ay gordjiguène lanou.
    Ana lane moniou wara bolék kilifeu yoyou baniouy ame ak niome yéne relations yi, lou diara lathie la.
    Ndakhitam gni nga khamni niome lanou dink Rewmi touma dji daf léna top, rawatina Ousmane Sonko.
    Ousmane Sonko, depuis digane téme ak Adji Sarr li niouy toudé ak ngordjiguène danouko ték si déram. Adji Sarr si bopam mo wakh né Sonko done na seuy ak mome si guanaw. Toumal kossi wakhni loumou beug la, ndakh mome ladane déf ak mome.
    Kone sou féké toumeu bobou dalna Sonko moudi kilifeu warna moytou nak ndakh kouniouy djigne beuti goudi do sothio yéli gouné.
    Kone souféké né toumeu bi tégouna si kawam ma dégate kounouy wakh Bah Diakhaté déf wakhtane né: limay wakh soudoul deug nama Sonko porter plainte. Toumalko si né done na sékh’ak kouniouy wakh Ndiaga Seck ba gagne ko bamou déme hôpital di fadiou. Lane lanou sékhone seuy bo khaméne tani seuyou goor ak goor la. Lolou nék lou niaw t’a depuis Bah Diakhaté wakh ko guissouma Sonko déf béne réaction si lolou pour woné ni takhal nanou déram pour diémko ragueu.
    Niarél ba wala niatél ba moy biniouko falé maire rou Ziguinchor guiss nanou l’amourachant ndieuka recevoir diougué France gordjiguène la.
    Niou délou wate guiss Sonko si bopam mou yor béne parassol bo khamni mi nguiko teuyé ni, lolou yeup kouko gueustou di ngako guiss, di dokhanetou. Couleur bi couleurou drapeau gordjiguène yila.
    Lolou yeup di ay toumeu yo khamné ni dakoy takhal toujours ta douma guiss mou wédi ko.
    Niou fal léne diokh léne Rewmi Ka niou ndieuka invité sa palais ba dip gordjiguène niou thiowko fi thiow lou reuy ba Mame Makhtar guéneu nassi wakhtane si wakhtane bou yatou; nio ngui kossiy gueureum diko santt.
    Beurki démb université, kiniouy wakh Jean Luc Mélenchon nieuw fi. Niou recevoir ko si daara dji gueuna makk nga khamni mou symbole bi gueuna reuy si Rewmi niou fay tagaté gniy wara yor Rewmi euleuk, ta gni yor Rewmi nieup diarfa. Université bobou lanou yobou say-say bii mou takhaw wakhni, si kanamou étudiants yi si kanamou sounouy ndaw sounouy yakar, né : « maa djiteul a khékh ak ngordjiguène sa France baniou nangou kofa goor di seuy ak moromou gooram »
    Néna lolou moko dieuka khékh France baniou légalisé ko.
    Ta dafa mélnimission bobou moko in’di Sénégal. Ta meunou kofé dokhal nak tant que diapalé wounouko. Té arabe dafay wakh ni « ane nassou ala diini moulo kihim » peuple bo guiss la séni djite gueum moudi séne diiné mome lanouy gueum. Ta dafa mélni Sonko daf niou beuga gueumlo ak ngordjiguène ayoul.
    Lolo waral nguéne guiss kilifeu nguéne guiss diléne sétsi si sénouk kay, bamou néké maire, ak biniou léne diokhé Rewmi, ak beurki démb kii nieuw di Jean Luc Mélenchon wakh wakhbou reuy bii né mo ndieuka khékh nguir niou légaliser ngordjiguène sa France ba goor ak goor difa seuy.
    Mou mélni Abdou Karim Khroum khakh wakh nani biniou criminaliser ngordjiguène fi si Sénégal, mbolo And same djiko yi diko khékh démone nanou si Sonko pour mou signer wayé dafa bagne; lolou mome diakhal nama. Ta sakh mbolo same djiko yi nga khamni Ababacar Mboup moko djité, amna niou wakhone né, mbolo momou ab lobby la bo khaméne tani dafay publicitél gordjiguène yi. Cheikh Oumar Diagne wakh nanouni nite la ko khamni dafay publicitél gordjiguène yi. Lolou lép di ay toumeu you takhaw, bassi casseroles yi nga khamni Sonko dane na wakh pour nioukoy teug di manifester wakhone nanouko néko lolou bakhoul si Rewmi ndakh gordjiguène yi baniou dé khékh séni droits thia Tougueul thia Europe mome lanou done déf di teug ay casseroles kone nak boko défé roy ngaléne niome gordjiguène yi. Ba tay rék dafay mélni empreinte gordjiguène dafa guénoul si parti bi niouy tousé Pastef. Dafa mélni dafa ame louniou d’accord, louniou weuleuréne té.
    Lolou lép nak di moussibeub Sénégal. Ndaw gni ngéne yéwou dayi séne bop khél khamni euleuk gou Sénégal mi ngui nék si danger sou féké déme nanou ba légaliser fi ak ngordjiguène.
    Sonko tamite bimouy tontou guiss nannou né tontou you woyof la tontou ndakh dafa mélni dafa beuga masla ak gordjiguène yi.
    Ta Al Xur’an dafa wakhni « waddoulaw toud’hilou fa youd’hinou » gordjiguène yi liniou beug moy nguéne maslah ak niome baniou meuna dokhal niome séni programmes. Maslah bobou nak lanou léne warta may béne yone.
    Waw « Ya ayouhal Nabiyou djiahidoul kouffara wal mounafi khouna weukh louf haleyhim » Yalla néna yaw Yanéneta bi salla lahou haleyhim wa salam djihaatal ak yéfeur yi ak nafékh yi néna ta nga bania maslah ak niome si dara. Na nga sokhor si niome. Sokhor ngogou lanou wara dieulane té ak gni nga khamni nio gadou agenda gordjiguène yi pour tass ko thi adina bi. Nga khamni ay missionnaires you sheytané lanou.
    Mou mélni Sonko sou wakhéni fi si rewmi ak ngordjiguène ak mouray feulé sa France, mou mélni dafay comparer niar yi, kéne dou comparer lou dagane ak lou kharam. Ak ngordjiguène danou koy dindalé ak rayy nite, di da lako ak bokalé ak Yalla, di da lék ak thiathie ak viole; wayé kéne douko dindalé ak moytou. Polygamie la beuga wakh moudi diabar you beuri. Khame nga France danio dafa ak ngordjiguene fofou wayé dano téré diabar you beuri. Niari diabar niari diabar lolou bakar la si niome. Sonko nak ni, euuuuh mou beuga comparer polygamie bobou moudi niari diabar niati diabar dieum ba gninti diabar ak ngordjiguène ; dédéte. Bi dafa dagane, bi dafa haram. Bokouniou. Kone liniou beug daaal moy moi khamni mome dafa compagné wone ni mome sou falo limouy ndieuka déf modi criminaliser ak ngordjiguène mome lay ndieuka khékh bamou dégne si Rewmi. Lolou lanou diay si projet bi, né sa bou falo limouy ndieuka déf moy di di fi ak ngordjiguène, wayé bobou ba légui guissou niou mou yeuy si wala mou yabi si, loudoul woo séni kilifeu niou nieuw beuga nék star si kanamou khaléyi.
    Niou ngui koy niane mou ragal Yalla, diko niane Diomaye niou ragal Yalla si khaléyi khamni nioy yakarni euleuk…."

  • @HoodBi-op5pq
    @HoodBi-op5pq 6 หลายเดือนก่อน

    Kou Kate ndayem moy s'en wa dji
    Kou todj lefeul ndayam

    • @ABDOULAYESOW123
      @ABDOULAYESOW123 6 หลายเดือนก่อน +1

      Ségne bi amal yar liguay déf déy amoul sens té diguako reuthiou

  • @sidymbacke8837
    @sidymbacke8837 6 หลายเดือนก่อน

    Merci p d g ❤

  • @modoukhabanembackediorel8591
    @modoukhabanembackediorel8591 6 หลายเดือนก่อน +1

    انصر اخاك ظالما او مظلوما، قالوا يارسول الله فكيف ننصره ظالما؟قال تأخذ فوق يديه

  • @Infoslivetv
    @Infoslivetv 6 หลายเดือนก่อน

    Je l’ai toujours écouté et tiré beaucoup d’enseignements sur bien bien vrai que je savais qu’il détestait Sonko mais pour être franc il dépassé les bornes avec cette nouvelle sortie

  • @DAOUDASAMBASY-np6bb
    @DAOUDASAMBASY-np6bb 6 หลายเดือนก่อน

    DJARAGUEEN DJEUF
    YALNA SUNUBOROOM SAMLÉÉN AARLÉÉN YOKK TAXAWOU LEE'N YALNA SUNUBOROOM TAXAWOU OUSTAZ CHEIKH AHMAD TIJJA-NI TEGGUILKO NATTUBI CCI BARKI YOHANTABI S A WSLMM CCI CHEIKH ABUL BASSE CCI BARKI MAWLA-NA CHEIKH

  • @NdeyeSarr-nm7pw
    @NdeyeSarr-nm7pw 6 หลายเดือนก่อน +2

    Melason limou wakh mo ganagara te Dara fekoukothei

  • @babasall4261
    @babasall4261 6 หลายเดือนก่อน

    Machalla ♥️♥️♥️❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @DiengAhmed
    @DiengAhmed 6 หลายเดือนก่อน +4

    Mahtar wah n'a degue sapokou bou djoumé dagua konane dagua djoum

  • @Sirou71
    @Sirou71 6 หลายเดือนก่อน

    Alhamdoulillahi Wahidoul Ahad

  • @abdoulayesow3869
    @abdoulayesow3869 6 หลายเดือนก่อน +1

    Oustaz niogui sa guinaw

  • @zenithtransitinternational9094
    @zenithtransitinternational9094 6 หลายเดือนก่อน

    assalamou aleykoume wa keur gui niougui ziar di balou akh wayé andoumak matar ndiaye limou wah ndakh Al Oustaz Cheikh Ahemd Tidiane Ndao limou wah dara amoussi boulén fatini kiniounane daniouko togne dém la wah Président Macky lou geuneu niaw lolu donc analyse bi fofu gako warone kholé Oustaz waham daniouko rafetlou yalna Yalla geune ko yégué

  • @omartoure2251
    @omartoure2251 6 หลายเดือนก่อน

    Free ❤❤

  • @aliounembaye61
    @aliounembaye61 6 หลายเดือนก่อน

    ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏

  • @pembazolo9262
    @pembazolo9262 6 หลายเดือนก่อน

    Vive iustaze Ahmed Tidjani ndaw ❤

  • @Infoslivetv
    @Infoslivetv 6 หลายเดือนก่อน

    Cheikh Ahmed borom kalimatoul kacc 😮😮

  • @ousmanealaminefaye2495
    @ousmanealaminefaye2495 6 หลายเดือนก่อน

    Soutien total au Oustaz Cheikh Tidiane Ndao

  • @cheikhseck4760
    @cheikhseck4760 6 หลายเดือนก่อน +3

    Billahi politique bi yakk na khol yii yén nieupa yem guemolén dara wayé yalla bakh'na imam yalla nako yalla takhawù😢 té mousseull niou ci seytané

    • @Ahmadu-o2n
      @Ahmadu-o2n 6 หลายเดือนก่อน +1

      Ndao naafeq piir la shraiha muhamadiya çaw nako 80 yar

  • @IbrahimaNgom-dt5wb
    @IbrahimaNgom-dt5wb 6 หลายเดือนก่อน

    li yonėn tibi wakhon ci wa an sar mo nėkke çi sonko kou bakh dinako begue wayė kou sa khol sėlloul doka begue xam xam bou sa xol rafė sėtoul dalay alak yalna yalla dini kiniane çi xolam

  • @ndiagafall4560
    @ndiagafall4560 6 หลายเดือนก่อน +1

    Mak mo rew dafa xewi
    Mak mo yarediko dafa xewi
    Mak mo khamadi dafa xewi

  • @ousseynoutoure9417
    @ousseynoutoure9417 6 หลายเดือนก่อน +2

    ❤❤

  • @mouhamedlaminefall6218
    @mouhamedlaminefall6218 6 หลายเดือนก่อน

    Macha alla PDG nitt day dëggou

  • @BabacarNiang-yb4my
    @BabacarNiang-yb4my 6 หลายเดือนก่อน

    Machala yaw nit kou deugou nga

  • @mouhamadoulamineseye6553
    @mouhamadoulamineseye6553 6 หลายเดือนก่อน

    Ce PDG eladje ndiaye est très loyal

  • @MoustaphaSow-my2yu
    @MoustaphaSow-my2yu 6 หลายเดือนก่อน

    Oustaz

  • @papediop7867
    @papediop7867 6 หลายเดือนก่อน +1

    En tout cas dioulite dou Accusé sans preuves... il faut qu'il arrête

  • @aminatadiaw9283
    @aminatadiaw9283 6 หลายเดือนก่อน +1

    Nafek bakhoul sokhor bakhoul une bonne leçon à retenir dadone khawi soutoureu far khawékou, yené Nek la....

  • @Le_blogs_de_ndaga_sy
    @Le_blogs_de_ndaga_sy 6 หลายเดือนก่อน

    DG et un lâcher

  • @ndeyefaye6835
    @ndeyefaye6835 6 หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏

  • @maradiop1147
    @maradiop1147 6 หลายเดือนก่อน

    Serigne Moustapha Sy almakhtoum d'où morom de