Walahi je suis tidiane mais j'estime cette personne vraiment. Il a un art de perler mais également il save comment communiquer avec la jeunesse. Merci borom chikory🙏♥️🙏
Guisnga deh, sougn diiné li kepp la, n’hésitez pas à vous documenter davantage sur l’islam Mr Mendy, vous allez rien regretter, n’écoutez surtout pas les polémiques créées en toute pièce autour de cette belle religion. Si ce discours vous touche c’est que vous aimez la vérité. J’ai bcp d’estime pour vous, qu’Allah vous facilite.
Quand on est épris de paix, de justice et conscient du rôle de chaque individu dans une société, on ne peut qu' adhérer à ce type de discours, plein de sagesse et de bienveillance.
Son discours est plein de sagesse et de bienveillance. Borom Darou est une chance pour la jeunesse,mais malheureusement beaucoup ne mettent pas en pratique ses précieux conseils.
Il a evoqué trois trés importants nagnou respectan tel nagnou soutouralan tel nagnou yerémantel bref bon magal à tous en esperant que ce bon discour ne restera pas dans l'oreil d'un sourd
Machalla yalna yalla defal la diamm ak sutureux li la beug si kilifeu dîne ay discours you responsable ak deugou dieureudjieuf borom darou yalna yalla goudeul sa Fann 💓💓💓💓
Bilahi Kou la sope la Mach Allah goudoufane weer ak werle yakh sa ndiaboot ak mbolom dioulite thi daradiaye Seydina Mohamed saws PSL barke Serigne Fallou rta ❤
Walakhi mbacké Yalla Mo wakh ci coran bi sakh dakh Mame Bamba lolou la toopou ba borome bi fayyko naniou toopou diiné ye yalla dji 😢 dieuredieuf mbacké
Mame Borom Darou à chaque fois que je l'écoute il tient à la jeunesse un discours véridique, responsable, un sage. ✊🏾🇸🇳
Walahi je suis tidiane mais j'estime cette personne vraiment. Il a un art de perler mais également il save comment communiquer avec la jeunesse. Merci borom chikory🙏♥️🙏
Douma musulman deh waay kaduu yi ma degg jarnaa dag say yité dem Magali! Machallah.
Mr Mendy deug mom nieup nioko mom parce que c'est pour tout le monde.
Machalla
Guisnga deh, sougn diiné li kepp la, n’hésitez pas à vous documenter davantage sur l’islam Mr Mendy, vous allez rien regretter, n’écoutez surtout pas les polémiques créées en toute pièce autour de cette belle religion.
Si ce discours vous touche c’est que vous aimez la vérité.
J’ai bcp d’estime pour vous, qu’Allah vous facilite.
Parce que nitou deug gua ndakh déug momo amoul musulman wala creutien
Ah bon vraiment c vrai 😅❤🎉
Quand on est épris de paix, de justice et conscient du rôle de chaque individu dans une société, on ne peut qu' adhérer à ce type de discours, plein de sagesse et de bienveillance.
Vraiment 😊❤
Son discours est plein de sagesse et de bienveillance. Borom Darou est une chance pour la jeunesse,mais malheureusement beaucoup ne mettent pas en pratique ses précieux conseils.
mamadou il est tres ecoute surtout dans la diaspora,au senegal aussin les jeunes l ecoutent machalla
❤❤❤❤bôrom darou si. Khôle .Mala sop. Beuguel la sama bop
@@Yayouaskanwi oui vraiment c'est un cadeau pour la jeunesse. Que Dieu lui donne une longue vie.
@@Yayouaskanwi 🙏❤️
No le problème c'est que certaines personnes font semblant de ne pas l'entendre. Il est véridique dieureudieuf borom darou
Lii rek mo takh ma beugue ko serigne day digulè lou bakh 🥰 borome darou 👌🏽
Un vrai guide religieux pour la jeunesse sénégalaise yallah naleu sunu borom Sam are leu may leu goud fan mbacke
Machalla amna solo lol le Discours de Thierno Borom Darou Norayni très important vraiment et pertinent limoy Serigne 💪❤️👌💯🙏😪😴😎🇸🇳
Suis pas son talibé mais je l'aime bcp suivons ses conseils
Vraiment respect à sont conscience moral.....
Et le sens de son discours véridique
Machallah sama soper bi discours bi amatina solo
MachaAllah borom Darou 🎉yalla sa jamm yagu AK mbolem djoulit 🙏
Toujours véridique ,a chaque fois il pousse la jeunesse d'être conscient
Allahou Akbar nqen dou borome darou sante nala yalla'na yalla doli lére ❤❤
Masha Allah. Quel guide de référence 🥰🥰. Yalla nako sunu borom defal diam ak tawfekh 🤲🏻🤲🏻🤲🏻
Borom Darou y’a bakh té deugou Machallah ❤❤❤❤
Lii moy serigne dafay digle ay talibem lou bah di len yeee ak di len warre pour niou dem si yalla ❤❤❤❤❤❤❤❤
Borom darou mane talibe chéikh la de me bilahi cou degounge yaw danga nagou jamou yala ❤❤❤❤ diredeffffffff bala ahisa alahouma la adourrr ❤
Ma beugue BOROM DAROU bilahi
Jeureudieufé borom touba
Il a evoqué trois trés importants nagnou respectan tel nagnou soutouralan tel nagnou yerémantel bref bon magal à tous en esperant que ce bon discour ne restera pas dans l'oreil d'un sourd
C'est ça le sens du magal dadialé sa ndiabot tékléne si yonou ndioub ak siratal moustakhim. Yalla na yalla yagal takhaway bi mbacké❤
Au moins lui il dit là vérité à ses disciples en les orientant vers Dieu, Yalla nako yalla yokk yiw❤
Voilà, mome on n'entend Yallah dans ses discourt, longue vie à Borom Darou, Inch'Allah j'irai le voir. La jeunesse avait besoin de ça
Borom Dara je l'aime tellement mashalllaaaa yalla na yalla yokou Say fane akh beupou domou adama amine
Voilà ce qu'on attend d'un guide un discours très responsable diadieuf Serigne bi
Beug na ❤Borome Darou ndakh xélam mou sell machalah yagfi té wér
Machalah mame thierno borome Darou noreyni sounou wasila discours bu amna solo ont l'aime pour tout simplement ya wor mbacké bala aicha
Borom Darou 🥰thi xol 🥰
Masaallah 🕋🤲🕌 Amine yarabi Masaallah 🕋🤲🕌 Amine yarabi 😭🤝🏴🚩🇸🇳🕌🤲 Serigne Touba skawo 4 🇸🇳 tawfekh rék inchallah bilayi 🤍🥰
Dieréredief borom darom yaw dé Serigne gua Long vie à toi ya cheikh ❤️❤️
Wakh n'a lou am solo : " Ku beugua ligueyal Serigne Touba, dagay nago diamou SA BOROM " Macha'Allah
Dieureudieuf borom darou
Machalla yalna yalla defal la diamm ak sutureux li la beug si kilifeu dîne ay discours you responsable ak deugou dieureudjieuf borom darou yalna yalla goudeul sa Fann 💓💓💓💓
Machalla amatina solo dieure dieuf Mbackè yalnanga fii yague thé andack weure barkep xassidayi yeppou Amine
Macha Allah wakh dji amna solo
Machallah Mbacke ❤
Salam macha allah amna solo merci
Manchallah borom daroue longe vie ❤❤🙏🙏🙏
Dieureudieufeuty Mbacké yaag fi lol te andak wér❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis catholique wayer qui d ay kaddu weum dafa am solo machalla kouko sopeu la dieuredieuf borom darou
Machallah mbacké amatina solo
ماشاءالله تبارك الله فيك وجزاك الله خيرا هذا هو الحق
Mborome Darou yalla na yalla goudal sa fane si BARKÉ alkhouroune inchallah
Machalla môme wakhetanale da âme sollo yalla mayegnou degue AK tope
Amin yarabi ❤🎉
Respect Borom Darou, yalna Yallah mayla fane bou goudd
J'aime Borom Darou.
Goundeul fane inchallah
Merci bcp yallah naniou may degue ak topo
Borom darou message bi lèrnaa koula topp topp yala souniou borom
Machallah, dieuredieuf borom darou
Dieureudieuf Mbacké.ya bakh.ya foyof.Goudeul fane
Machallah vérité absolue yalna yalla goudeul fan wi mame borom darou
Machallah dieureudieuf
Bilahi Kou la sope la Mach Allah goudoufane weer ak werle yakh sa ndiaboot ak mbolom dioulite thi daradiaye Seydina Mohamed saws PSL barke Serigne Fallou rta ❤
SouNiou BaBouLahi ❤️🖤 BaBouL 'aL 🖤'Hamdoulilah ❤️ on t'aime tout simplement point
Machalla mame borom darou ❤❤❤❤
Des ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ pour borome darou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Walakhi mbacké Yalla Mo wakh ci coran bi sakh dakh Mame Bamba lolou la toopou ba borome bi fayyko naniou toopou diiné ye yalla dji 😢 dieuredieuf mbacké
Machalla Mame borom darou
Un discours plein d’enseignement. Djeuredjeuf borom darou
MashaALLAH deugu req nga wax MBACKE
Lidé diaféna trop si mouride wakh ay talibém DEUG😢😢 dirureudieuf brm darou🙏🙏👈
Machallah
Kadou yi amnagn sollo loooool.
Macha Allah vraiment il a dit ce qu'il faut dire et le lieu où il doit le dire
ndeysan limotax niepou sopouko ❤❤lima geuna nekh si mom dafa simple❤
Il â raison merci beaucoup pour le message
Tiey mbacke yallah nala fi yallah bayi
Dieureudieuf borome Darou ❤❤
Dieredief borom darou ❤❤👏👏
Il devrait être le porte parole du khalif.
Ça devrait le discour officiel de demain
Machaalla merci
Un discours très instructif et véridique Machallah Mbacké
Machallah ❤
Machallah ki taxiid deug lay waxéé diamou yalla rèk mo woom
Maachaala. Amna solo.
Macha alla ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤MERCI BEAUCOUP MAGAL 2023❤❤❤❤❤❤
Diarrama mame yalla nala yalla bayi souniou kanam ❤❤❤❤❤❤❤
Voici une personne que j'adore ❤❤❤
Vraiment kilefa la❤❤❤
Yal na nga fi yagu te wér Mbacké, Sa mame Borom Touba ak Borom Darou Mouhti gàccaaloo len de❤
Machallah kadou yi amna solo Serigne li laye dieurine talibé wame tekko si yonou siratal moustahine
Ma chaa Allah vérité vraie
ma sah allah kadou yi ame na solo 🙏🙏
Jeureunguèn jeufty MBACKE ❤❤❤
Une belle personne machalah qu'Allah le bénisse amine
Geuna yagg geuna werr Mame Borome Darou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Li rék lagnouy doyé kilifa yallah nassa diam yagg borom barou ci barké seydina mouhamed
Wakhoul ak Kéén Koudoul Ndaaw Yii ,Si Ndiari gniou ndaw yi la Introduiré ,La developpé ,la concluré yala Na Anede ak degu ak Topou
J aime ses paroles pleine de sagesse pour la jeunesse
Dieureudieufeuti Mbacké 🙏🤍
Il est avec Diamono, il a compris la philosophie de cheikh ahmadou bamba
Un homme véridique,un vrai guide merci Borom Darou🤍
Notre Thierno Babulahi yague fi Mbacké
Merci borom darou quel discours ça restera dans les annales merci encore yalla nayou magal tout té andaqu vére
Yalla nayou magal you Bari té andanque vére
Machallah Kilifeu day gnéme wahk talibe deugue dahk euleuk kepou kou djité ay nite dinagne la demande noléne yoré wone Merci Borom Darou 🙏❤️
Walakhi musulmans comme chrétiens doivent prêter attention à son discours c'est une chance pour la jeunesse sénégalaise
Ayewaye mback danouna lere Mane mi talibe chekhe la me degena dege
Macha allahh Anna solo trp merci mbacke
Borom darou ak rafahi Mbacké ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Borom darou ❤❤
Bilakhi deukla merci borom darou
Dieredief borom darou yalnala sounou borom défall tawfeekh ❤❤❤
Wallahi azim❤❤❤❤❤
Machallh mback balla yague fi lole ta ande ak weer
Gueuneu yag gueuneu wère mbacké balla Aïcha ❤