Lima diakhal si cinéma Sénégal saison 1 moy diar yonn mais suite saison yi gneup thiouner rek lagnouy def, départ gainde arrivé chat, j’espère que bi doussi bokk ❤
Vous savez ce qui me plaît dans les séries actuelles c'est le fait qu'il donne de l'importance capitale à la virginité à chaque mariage les mamans ont des pressions à savoir si leurs filles sont des vierges
@@evenprod bilahi question bi rek mo diarra soralé le fais de se rendre une mère fière dara dakouko ak tamite rendre sa bopou fière. Adouna bi dara yagoul degn coumpeu wala gnakeu doylou boum la dougueul moukou si yen yi. La femme n'a que son valeur.
Wednesday and Sunday use to be like big events❤ to me just because of this series betebete best of the best this series contains love,passion,culture and comedy😊 ❤. Laff chatt👌 na dauw ba next year💥 season one bi dora jeex mudess season 2 ak 3.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇸🇳🫶🇬🇲 akk EP dara du soff ❤.
Mane lima guena nékhe théâtre bi moy le fait gnouy revaloriser la virginité ça permet aux jeunes filles de se préserver d'avantage. Even pro, vraiment vous êtes les meilleurs chapeau à vous. Hélas j'aurais aimé être un de vos acteurs afin d'apporter un effort participatif sur ces choses super mega importante et qui enseignent vraiment ❤
Soumboulou va essayer de rabaisser Dieynaba le jour du mariage, Fatim Thiam xolou ndiourel dougouko mou éclater secret bi gars yi di neub. Ne me remerciez pas 😂
La réaction de oumy khary ohhh taye dou yombou kéne beugoul gnou lale sa dôme, amina tégual dara sougnou lokho j'espère lalou diégué wo sa yaye da gueume affairou vierge dès ❤
@@evenprod oui c vrai que sa fille a dépassé les limites aye insulte bokoul.thi sougnou éducation, mais c sa mère la faute elle a commencé à faire le gamine en donnant à manger son mari devant sa fille ou dire bébé se des chose a éviter on doit comprendre mame dior kéne beugoul gnou remplacer sa papeu
Yalnaniou yala defal diam adouna ak allakhira❤Yalnaniou yala may goudou fane bou ande ak wer khéweul gou sawane bawane❤wer werlé 🎉mayniou goudou fane bou ande ak wer si barké seydina mouhamet psl yarabi 🎉❤❤
Les commentaires de série sur TH-cam En France 🇫🇷 : C'est une très bonne série j'ai vraiment hâte de regarder le prochain épisode Au n 🇸🇳 kou beugg Seydina Mokhamed beusseull j'aime 😃
Secret bi moy ✊ Dieynaba ak Amina ayè jumelle fatim jour bamouy accoucher ak jour bi marèm sall di accoucher c’est la même jour marèm sall pert bb bi niou dieul amina diokh ko marèm sall 🫡🫡
Ana gnii contane si seni wadiour❤😊 yalah nagn goudou fann🤲✨️
Amine yarabi
Amen 🤲
Allahouma amine🥰
Amine ❤🎉
Amiin
un futur milliarder et entrent de lire mon commentaire🥰 salut Boss 🫲
Oui çv😊
Amine gnou bokou lep ❤
How are you doing 😊
Bonjour ❤
Salut frère
On réclame le bonheur de chacha❤
Surtout lolou
@Anime.fr256 À suivre. ❤
Ndiaga Thiam est le meilleur comédien ❤ vous êtes d'accord ???
Wou sama ndéye oustaz modou fall contana mé takou aminabi éske tiké lawbé d'où done rakou sow
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@fayefatou3446 Merci. ❤
Mani mba yéna ngui wathie Magalou Serigne Touba domou mame Sokhna Diarra Bousso bi 😊🙏🏾
Wawaw ❤❤❤❤❤😂
@@AmicoleDia-be5cp❤
Magal dougne ko wagne dagne koy paré😊
Café touba lay nan ni sakh
Paré nagnu bu yagg
Cou beugue am dome bou gore toudéka seydina Mouhamed 💗💗💓
PSL
Hana berén mom la toudé sama taw té nopégouma
Sm Oustaz Modou Fall lay sén nonou 🙏Aka Evenprod tjrs ds surprise vs étez les meilleurs ❤❤
❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
@@DieynabasaneDieyna-ic2bd merci
Bly yw Bamako guisé la sama xol sed
@@OumyNdiaye-i2f bilahi.contant 😍
Bande annonce bi démako done guéne sanéx yalle nafi yague té ande ak weur ak keup kou wah amine
Amine
Amin
Amine niou bokouko
Amine
Amine
Yalla nayou yalla may BFEM🙏
Amine
J'ai eu mon Befm 9 ème du centre Alhamdoulilah ❤🎉🎉
@@FatimataKâ-f2l alhamdou lilaahi sante yalla et surtout félicitations ma fille bonne continuation
Amine yarabi
Amin
Mashalla toujours ponctuel, yalna gnou yalla doli soutoura té oubil niou bountou weurseuk yi
Bande annonce bi motakh ma tela yewu 😂
Del tela yewou😂
Aye way 😂😂😂😂 li 😅😅
Ak man tmt li😂😂😂😂😂
Moi aussi 😂😂😂😂
😂😂
Le bonheur de Daba Thiame❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@cheikhouniang-nh7xx À suivre. ❤
Elle est ravissante notre chacha today🥺❤️🎉
Yiw moko gueuna diapp 😅
@mbayangfaye7180 👍
Honnêtement cette série dois avoir bcp de saison comme idole encore merci à tts l'équipe chapeau
Lima diakhal si cinéma Sénégal saison 1 moy diar yonn mais suite saison yi gneup thiouner rek lagnouy def, départ gainde arrivé chat, j’espère que bi doussi bokk ❤
@charloutsam7190 Merci. 👍
Yallah naneci bakaan yobbou bagnou fekké ko teh talko Amine 🙏🏿 Inchallah 🙏🏿
❤❤❤❤❤❤🎉❤❤❤
Amii
Ay paco dél solo ni guir Yallah wagni takay yiii 😂
Vraiment paco kay😂😂
Dafa tangu sakh nak😂😂
Oustaz bime guise motahe mou dindiko
😂😂😂😂
No srx wo bilay da tague mome😂😂@@FatouSamb-e5y
Kou gueme ni soumboulou teug le si série bi rek lalal j'aime
Alkani lakoye tèkni moye teugue bi
@FanmaMbengue À suivre. ❤
Kou beugue sa mère rék lalal j’aime ❤
Bilay on réclame le bonheur de chacha daba thiam et diouma thiam kheucha ❤❤❤❤
Paco
@biteye305 À suivre.
@@evenprod ❤❤❤
képou kou nékk si ayyy tolof tolof YALLA nako Yallah safaraa si barké Seydina Mouhamed (PSL)
Amine
Amine
Allahuma aminee
Allahouma aminn
Amiine
Bien fait pour Mame dior de 😂 kou d'accord lalale j'aime ❤❤❤❤
@yakharangom9934 Gua fokni li dou yakhal Makhoudia ?
Diouma Thiam sakhe Real Madrid laye toppou❤❤🎉🎉😅
Equipou yalla bi hala Madrid ❤❤❤❤
@@Binta-gm9dnsister stp boul bolei Yallah si affairou sport stp dou respect 🙏
@@fatyndiaye5328chaque jour nga déf lou geuneu graw loumou bide nga beug niou diomal fi
Gniokafa ame🎉❤❤😊
Gnoko fa ame
Mame Dior d bala serie bi di diekh yalla boussa lekh yi perrr😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
😂wouy sou peroul tmt yalla boumou si dieulé beugn 😂
@oumarkonate7850 Lol badou mbeithie yi barri ? 😂
Sénégalais mo aye rek avant dagnoudone wakh babél meilleur série mais légui beté bété mo khéw😅😅
Kou guiss ni paco dégue na souniou khass yi lalall j'aime ❤
Yallah na niép am diam si seydina Muhammed S.A.W
Man Lou takh ma bg soumboulou ❤😍🤣🤧
Kou dcr ni domou bay dafa néckh lalale j'aime ❤
Kou ayé wall sa momé thièye yalla souniou borome SWT Amina ennhhh
Meilleur serie Senegal kou d'accord beuzeull j'aime ♥
@Ousmanesarr344 Merci. ❤
Oustaz modou fall ❤❤❤❤❤❤
Wouy la traduction 😂😂
@@MylenejuliaNdour😅😅😅😅😅😅😅
Mafi jditou wa touba amnan ndam 🎉🎉🎉
Bobou question djiguénn bouko doull xalatt loulaa nexx defaal😢❤❤❤
Bilakhi
@ndeyeawasall7178 Baadou louleu nex defal ?
Kou kontane si li Oustaz Modou Fall wakh rek point le doigt 🎉🎉🎉🎉❤❤
@user-qx4lx1dr9d 👍
Kou beugué seydina Mohamed rék l'ale cœur ❤️❤️ yiiiiiiiiiiiiiiiiiii
❤❤❤❤❤❤
Yalna ñeup am diam ❤
Ku yakamti ahmada ak jahman 2024 beussal j'aime 🎉❤
Vous savez ce qui me plaît dans les séries actuelles c'est le fait qu'il donne de l'importance capitale à la virginité à chaque mariage les mamans ont des pressions à savoir si leurs filles sont des vierges
@sambafaye8223 C'est toujours un plaisir de vous satisfaire.
Aaay cas bi dense makhoudia dore mame dior
Marème di ladj ndakh Amina khalélaa ay lolou dou mako lall waay
Est ce que dou cauchemar makhoudia ak mame dior
@@mendyoumy3628 ah peut être loloula
@@mendyoumy3628 lolou marodi ek mokoy deff 😂
Mame Dior keine khamoul Loulou beugue. Mom mo pousser yayam si lokho makhoudia tamit
@@mendyoumy3628cauchemar lako ték ba bamakoy sétane
Sa ma yarame bi dawna. Bilahi question bi mareme sall poser amina jeunes fille bouko dou khalate 😢😢😢😢
@aissatabunmoustapha5327 Badou louleu nex defal.
@@evenprod bilahi question bi rek mo diarra soralé le fais de se rendre une mère fière dara dakouko ak tamite rendre sa bopou fière. Adouna bi dara yagoul degn coumpeu wala gnakeu doylou boum la dougueul moukou si yen yi. La femme n'a que son valeur.
Wa evenprod dal ay nandité 2.0 laniou! Respecter séne téléspectateurs yi di tontou ay commentaires rek nak!❤❤❤
@maryamkeita891 Gnou yeine lagnou ame yeina gnouye doleile. ❤
Kou Geum ni Djingué men dagn koy door thi yoonu Americ bi rk lallal j'aime 😂
Paco inchallah dina tàkk Chacha
@user-ti8gz3bf7u À suivre. 😂
Sama frére dafa décédée démbou dafa lab si ndokh nianale lénko kou bakhone si man😭😭😭😭😭😭
Thiey yalle, nèk si nahar ,di setane bande annonce,bref. Yalle na hipèdji aldjana
Wednesday and Sunday use to be like big events❤ to me just because of this series betebete best of the best this series contains love,passion,culture and comedy😊 ❤. Laff chatt👌 na dauw ba next year💥 season one bi dora jeex mudess season 2 ak 3.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇸🇳🫶🇬🇲 akk EP dara du soff ❤.
Barki Cheikh Bara N'diaye, Evend Prod Yéna meilleires waay. Depuis Idoles laalén commencé toop waayé messoolenma rousloo ben yooon.....
@abraham-compta2134 Yalla bougnou leine rouslo. 👍
Wa Real khana vous êtes content dakh Diouma thiam yénn la sol dhé
Yalla nama yalla may casa 🏠 bou Nice bama def photo kou teddy
Amine
Série bou nékk la te am solo kou d'accord boseul j'aime ❤👍
@diouftv2346 Kone dal yangui si guisse sa bopame ?
Que La paix et la miséricorde d'Allah soit sur le noble Messagé Mohamad S.A.W ❤❤
Kou beugue seyidina mohamed lale Jaime
Aye waye mbédiati naniou mame diorr😢😢😢😢😮
😂😂mome kay li mou encaissé si mbeithe eupeuneu 😂😂
@sylla-lofficielle5512 Doyna ware.
@@evenprod akh lii tmt mingui beuege meti nak 😂😂😂 even kholat lene li waye
😮oustaz Modou fall❤
Ustaz modou fal kou d'accord mou reste si série bi lalal ❤❤
Ay wayy lii yalla bomou diéux 😊😂❤❤❤❤
@sodagaye6847 👍
Qui aime bété bété lalal j' aime 😂😂❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@InssaSall 👍
Kou beug oumou khayri rk lalal j’aime 😂
@nogayegueye1632 👍
Al Hamdoulilah tay Paco correct neu 😂😂😂😂
@@aichagueye1310merci
@@aichagueye1310 demal kholate bou bakh seu dictionnaire kham na appréciation nga beugone wakh lol
La meilleure série du moment ❤ ❤
❤surprise encore oustase modou Fal ❤even produit vraiment vs étés meilleure❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@user-dh8jm2qb6z Merci. ❤
Kou d'accord nii Amina dou Khale rekk lalale jaime
Lolou menoul nk
@@Jalil-BL-Transitloutakh
😂
Pourtant meune neu nékk khalé dèh😂😂
Bouléne faté massage yi ak Monsieur Sow😂
Très contente de voir sm oustaz Modou fall yallah nga yagg fi té werr
Bété bété la série qui n'a jamais perdu sa valeur ❤❤❤
@BayemodouGueye-dk3qs Merci. ❤
Mane lima guena nékhe théâtre bi moy le fait gnouy revaloriser la virginité ça permet aux jeunes filles de se préserver d'avantage. Even pro, vraiment vous êtes les meilleurs chapeau à vous. Hélas j'aurais aimé être un de vos acteurs afin d'apporter un effort participatif sur ces choses super mega importante et qui enseignent vraiment ❤
Kou gueum nii Amina dou khalé rk lalal j'aime 😂
@GorabouTalfa Hein à suivre. 😂
Oustaz Modou fall oh machallah ♥️ daniou lén Di beugue ba kagne🎉
Kou d'accord ni Amina dou dianck reck lalay j'aime
@mameboussoniane5165 Loutah geu wahko ?
Mais paco rafett n'a dh😢❤❤❤
Soumboulou va essayer de rabaisser Dieynaba le jour du mariage, Fatim Thiam xolou ndiourel dougouko mou éclater secret bi gars yi di neub. Ne me remerciez pas 😂
Est dou final fofou sakh
Hum lolou idée la
Waw souko défé gnou finalou nak😂😂 bone gua gnoune doyalou gnou gua beug diekhal li😅😅
😂😂😂😂😂😂
Mais jumelle diouma thiam bi nak kagne lay feggne
Amina nako wakh mére la 😂😂😂😂😂
Aye mbéthie Amatina 😂
Diouma Thiam madrilène la 🎉😊Nii rek la meunone demé 😅
On sait maintenant de qui Dieynaba Tall tient son talent de distributeur automatique de gifles 😅.
😂😂😂😂😂😂
@madamen3706 Lol 😂
Ooh Oustaz Modou Fall wayy ❤❤❤aka mako sop Fall ndiaga yaram Machallah
Bravo even Prod vous nous surprenez de jour en jour
La réaction de oumy khary ohhh taye dou yombou kéne beugoul gnou lale sa dôme, amina tégual dara sougnou lokho j'espère lalou diégué wo sa yaye da gueume affairou vierge dès ❤
@seynabfatalecisse9141 Est-ce que Oumou waroul wakhe ak domame ?
@@evenprod oui c vrai que sa fille a dépassé les limites aye insulte bokoul.thi sougnou éducation, mais c sa mère la faute elle a commencé à faire le gamine en donnant à manger son mari devant sa fille ou dire bébé se des chose a éviter on doit comprendre mame dior kéne beugoul gnou remplacer sa papeu
Dioume Thiam bingua solé maillot Real Madrid laa la bayi😢💔
Xeww mi xeww xeww leuh nara done😅😅
Une épisode chargée d’émotions
Ça promet de ouff 😢😊
Thiakh bi ana thiak bi way😊 Maréme yaye, yaye rk lay done
Demb dieynaba ak fatim thiam la wone tay ioe ak amina🎉
Yalla bakh na gnou doundé yakar
@aiditagaye7920 Yakar geu Amina nek xaler ?
Oustaz Modou Fall❤❤❤🎉🎉🎉 ohhh contana
Yalla na Diam yague ❤
Nèkh na ba noppi oustaz Modou fall nak donc pape cheikh Diallo mofi manqué 😂❤
Mariam sall fekhel ba khew mi melni khew viviane remi watchii vivi nena diokhnala authorisation ❤❤😂
Xew bobou bène lafi
@@bocarguisse2282 mbadou 😆 en tt mousta am ci mim rew
@@Oupsididitagainnous sommes d’accord que c’est vivi qui donne l’autorisation des xewwww au Sénégal 🤣🤣🤣
@@diomalecomte6053 woow nak 😆
@Oupsididitagain Yeine wathie leine ko. ❤
Marieme sall bouy worry amina doy khalé mère leu 😂 astahfiroulah😅
Yalnaniou yala defal diam adouna ak allakhira❤Yalnaniou yala may goudou fane bou ande ak wer khéweul gou sawane bawane❤wer werlé 🎉mayniou goudou fane bou ande ak wer si barké seydina mouhamet psl yarabi 🎉❤❤
Allahuma Amine waye 🤲🕋🙏
Amine ❤❤❤❤❤
Amine ya rabbi
Amine ya raby
Ouztas modou fall❤❤❤❤❤
Les commentaires de série sur TH-cam En France 🇫🇷 : C'est une très bonne série j'ai vraiment hâte de regarder le prochain épisode Au n 🇸🇳 kou beugg Seydina Mokhamed beusseull j'aime 😃
Cou contane si couple paco ak Chacha rek ❤
@fatoudiallo7815 👍
Wayein Amina mba Mr Sow Djehalouko
@user-iv7zc2rc4i Loutah geu wahko ?
Secret bi moy ✊
Dieynaba ak Amina ayè jumelle fatim jour bamouy accoucher ak jour bi marèm sall di accoucher c’est la même jour marèm sall pert bb bi niou dieul amina diokh ko marèm sall 🫡🫡
Oustaz Modou fall🎊❤️
Kou d’accord nei amina amoul ndaw
Merci makhoudia khallé bu reww mom yarr rk😂
@MamanLo-dc7ro Mais yakoro limou def tasse sey bi ?
Franchement leçon bou am solo 😢yaye yi diaxlé nagne si sén dome you djiguene yi bamou diaral léne niouye xalat nakh ay halé lagne 😢😢😢
Kou d'accord né oumou khayri dafa diogué reck lalale j'aime ❤❤🎉
Je te le jure et en plus la plus belle Masha'Allah laff thiat
@AmyDia-ep7uf 👍
Mbèth bi nak moo nara indi problème !😮😂Teugg bi mèth na Reguèè bi
7h layéwou nék thi sama téléphone message bou wathii mané bété bété la ba nélawatt légui la ko kholl😅😂😂
Y’a meune nak 😂😂
@@Muslims-i5r wa gui nga😂
Le peuple réclame la deuxième saison de cœur brisé 😢😢
Mame dior mo eupou limouy dieul coup si serie bi😂😂
Bly sone na😂
@gayeegaye Mbadou mbathie yi da dale ? 😂
@@evenprodtrop kay
Café touba lay nane ni sax😂😂😂 🍵
Cou gueume ni Amina dou Dieynaba té amoul ndao rek rek lalal j’aime 👍🏻
@Koutaltv Loutah geu wakhe amoul ndaw ?