Souma done gnagna douma fayoul magoum deuk, ngour di déllou si lokho magoum deuk mouy donat mbindane si palais bi, limana am souma done mom kay ma fékhé done première Dame fofou tothie❤
MAGOUM DEUCK ALIAS BOUR SALA NDER (walou)TAMIT YAGUE NGA DI DOKHAN SAY DAGE YII DAAL NII NGA DEFON DEGUINE BA AME THI MAMADOU 🤣 MAIS C'EST FORMIDABLE ON VOUS SUIT.
Salut mais gayi délén ndokél ndji yor caméra yi si limage you rafet yi ak ki yor son bi Machallah amna solo franchement parlent dan léni fate té lepp niom la
1 milliards abonné laa begue Sango gouma TV ❤❤❤
@@omardiange3542 ndeysane mba linga beug dana yomb nakk dome yaye
Bai fekke moi mag bu jara bai c dekk ❤
Kou d'accord né sagar mo dankheu si serie bi bou mouré rasta yi lalal j'aime
Magoum dekkeu fofou dé darra bakhou si latir khamna léne dé🙏🙏
Kenn du Laatir waaye magum dëkk réer na lool.
Sama seri la baol dafa nex❤❤❤
Magoum deuk négua yakar guay deglou pour dem kharé ba ,loutakh taguowoooko biguay dougou thi Ñaña😂😂😂😂yalla nañla coup d'état 😂😂amiin
Alahouma Amine 😂😂😂
Nonononono lolou bokoul dé kharé bi pour niép 😂 la mais pour sokhna Moy tanal bobam 😂 merci si commentaire bi
Yaakaar mooy conseil constitutionnel yoonam nekkul ci ku président wara takk walla boog comprenduleen série bi
Lou leer nga wakh wayè dinako rèthiou li la latir di bagne noni deumb bougnou nangou wè tey rekk sèn pèkhè diouboul❤🎉
@@madickediop968 wawaw
Souma done gnagna douma fayoul magoum deuk, ngour di déllou si lokho magoum deuk mouy donat mbindane si palais bi, limana am souma done mom kay ma fékhé done première Dame fofou tothie❤
❤
😂😂😂😂😂
@@AmySarr-c9t moogën Moy delu si Ak njame de
LATHYR LE LION !!❤
bu ngeen wuuteg LATHYR niakk dh
WALLU gatt nga xel😢😮
C'est pas possible !!!!
Thiey yalla tey nak diaxlèna wakhouma walou nè da dèm keur bangoura bani fax togue diomi amoul heure ndèkètè... wayè noni deumb bougnou nango tey sèn pèkhè diouboul Latyr moy goor tè gorè tè deugou wallou nak moy xalapp deuk bi ❤❤❤🎉🎉
😝walou kay diaam deug leu liii ngour kay doyna warr
Baye féké wakhe nga dégeu magoum dekkeu dé🧏 walahi
non li bounékoul ay guént moy serie bi wathi nguéne yone bi vraiment 😢
Wakh nga DEUGUE dh
Billakhi
Laatir moy sonko 😂😂😂❤
Watije gene yon bi dh😢😢😢😢
Magoum Deuk nak wéré nga
Meilleur série ❤❤❤❤❤
Je t'aime Ndéla Yacine à Love you Ndéla Yacine ❤❤❤❤❤je t'aime bcp Ndéla Yacine ❤❤❤❤❤ Ndéla Yacine rek lay topp nak
Ndéla yacine sama ndéla yacine la boko kholé rek man ok yaw la
Nidjayou Birima gui mo geunna nékh si série bi vrai comédien la
Domou baye badou😂😂dafa khoromou😂
Magoum mii ku ñàkk fayda la te bëgg jigéen
Wa sagarr Ana rasstayi guisouma ko dé😅😅😅😅😅
Walou loula diarale li😂😂
Walou défoul dara danio reuroo
Djiguéne
La tiur rk laye toppo
Li magum dekke Def ay gente la waradon svp mais amie
Walou youw doo khalatt khana
Bangoura Manu laa beugeu mouk ndakh lému bëugë mome nga your
Ces la premiere foi ma djitoufi😂😂
Li com parti pastef nimouy dokhé lay dokhé😊😊
Déléne aimé série bi li mo ame sollo ❤serie traditional
Keureu gui dh sa Keureu la Bagoura ak yasine Peinda boulène Ma raye waaye 😂😂😂😂😂😂
😂 Yacine penda seytané original la
Vraiment serie bi nekhna ma surtut allebi
Ndéla Yacine rek lay topp man
Dinayou sama chéri Ndéla Yacine
Wa yacine penda mi diakha louléne 😂😂😂
Yasine Peinda aka khoromou 😂😂😂😂😂
Ay waye téy la warou man ci Yacine 😂😂😂😂😂🤭🤭
Meilleur série au Sénégal
Magoum deukk thioup ngeu sa drapeau way😊
Dior mon combat ❤
😂😂Yacine pénd réyna Billaye 😂😂😂😂🎉❤
Ana premier ministre dangay trahir walou dioh sa papeuh état bii
Nice ❤❤❤❤❤❤❤
Magoum dekk moy diomay moy magoum dekk
MAGOUM DEUCK ALIAS BOUR SALA NDER (walou)TAMIT YAGUE NGA DI DOKHAN SAY DAGE YII DAAL NII NGA DEFON DEGUINE BA AME THI MAMADOU 🤣 MAIS C'EST FORMIDABLE ON VOUS SUIT.
Magoum deuk bamou douguéé si nîania la dof!
Non épisode bi môme baye féké déé moko môme
Khana wa série bi amou niou téléphone 😅
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
kou diommy ci magoum deuk khél niaawna dh
Yacine penda mome tay ya nékhal série bi 😂😂😂
Ay Magum Dëkk lu la jaral lii de mooy livraison à domicile 😂😂😂
Bilahi li néhatul dakhe li amatul bén sanse li dafa yombu torop ah
Assalamou haleykoum wa pout ma ngui ni
Magoum deukk do yag sa ngour bi 😢😂
❤❤❤❤❤😢😢😢
Kou djitou tè khama figay tègue sa tanke dofa yague
Wallou dh thii aythiakhane kep la nékkk
Mane dinama bayi série bi ndakh wallou dafa fouy légui thiiiiiiiim mounane sokhoré
Latiur latiur rk
Latir moy Sonko moy latir
Cv bonjour ❤❤❤❤😂😂😂
Vers kon mooye wallou
Machalla 🎉🎉❤
❤❤❤😂😂😢
Man mom franchement walou tayéllonama
Latir walakhi yaye gor té goré
Sonko moy latir latir moy Sonko
Walou do ngat
Yakaar khana khambeu yii da baxoul
Li palans rk la mana nk
Latyr ❤❤❤❤
Magoum deuk bou beug djiguen waw amna
Yasin binda dama dialhall
Wallou Diop mi xél zero😅
do yague sa ngour gui dakh danga fouy thiiiiiiim
Non bayigua sa lokho
😅😅😅😅
❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂
Yakh nge Seri bi 😢
Filme bi dafa guawa diékhe torope 😡😡😡😡😡😡
Man nak ten na nak
Li nèkhôl ma
Magoum deuk amoul volume
Gemou ma latir say say la macodou la sokh la😂
Ki moye khalep deuk
Salut à tous diléne wakh guéne abonné Sango gouma TV
Serie bii nékhoul
Réalisateur yii khamouñe dara
Artists yii ayouñou tchi sèn role
Mann Dale khamouma louma fii bayie ba légui rek 😡😡😡
lolo ma dal man mi
Salut mais gayi délén ndokél ndji yor caméra yi si limage you rafet yi ak ki yor son bi Machallah amna solo franchement parlent dan léni fate té lepp niom la
❤❤❤❤❤❤❤❤
Bangoura😂😂😂😂😂
Wallou mi nimako diépé ki
Bangoura sofna😂
Magoum deuk mi mom dafa Sof yaakar yaakar rk
🎉
Salam abonné lén way Sango gouma TV
Filme yifiye dawe yéppou bi mofi gueuneu guawa diékhe 😡😡😡😡😡😡
Bou djiné beugé dakhar kou yék niousou si souf😂😂😂
Série bi la comprendre mooy domou bour walla
Non magoume duegue
Magoum deuk
❤❤😂😂
❤❤😂😂🎉
❤❤❤❤