44h33 segundo daxawa gata yen wa rafahi tv yenafi nekal dongay daara yi s.abdou rahim mii dimbale lenñousi guir yalla ak s.touba mou def hay imiso you barii te yalla rek takh dax ñoumanse diariñou
ASSALAMOUHALEYKOUM MAGUI LEN DI ZIAR DI NIANAL SERIGNE MOUNTAKHA MOU YAG FI LOOL TE WER DILEN WAX NE KOU YESS LA THI TH-cam DILEN JAAN GUEN ABONNE THI SAMA CHAINE DAGAY BEUSS THI SAMA PHOTO PROFIL A GAUCHE
Merci ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Jërëjëf S Abdu Lëy
Jaajëf S Abdur Rahiim Lëy
Macallah s. Leuy ❤❤
44h33 segundo daxawa gata yen wa rafahi tv yenafi nekal dongay daara yi s.abdou rahim mii dimbale lenñousi guir yalla ak s.touba mou def hay imiso you barii te yalla rek takh dax ñoumanse diariñou
Kou beug si livre yi NK
Machallah amatina solo
Journaliste bi machaallh
Maasàllaa Njaatige Sëriñ Abdurahiim Lëy saa-wolof am na solo lool jërëjëf 🙏
Massa ahlla lidal la xam alhamdou lilahi rabilhalamina boumoufi di geudia nakh
Maasàllaa amana solo lool aëriñ abdu rahiim lëy
Ma Challah, diang Wolof lou bakh la si Sénégal🇸🇳😍
Moo tax nga wara jàang
Amna solo nayaatu
Maasallaa Sëñ Abdul Rahiim Lëy amadagunduŋ
Maasàllaa Abdu rajiim lëy lii amna solo lool.
Masàallaa jërëjëf waay sëriñ abdou rahiimi lëy ❤️👏🏿✅👑
raafeet naa luull
Waw goor
MachAllah, leer na daal 😅💚
Maasallah amna solo lool jotaay bi war nay am ay bës bune
Machalla LOU LEER NGAY WAKH WADJI!!!
SAKH CI DAKKEU REKK LEGUI NGA BEURRI MOROM INCHALLLA….. Dieuredieufe
Amna sulo
Machahll amna solo lool yaalana yaala barker
Machala serign abdou rahim leye waye sa journaliste bi mom dou dara
Machallah ch abdou rahiim
Waw gor
Aa maasàllaa man de musu maa kis lu mel nii amna solo lool sax ca kaw ca kanam rekk insàllaa 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Maasalla
Ma chllah
👂👂👂👂✊✊✊✊✊✊✊
Kou begue téreyi nak foumouy diar
Kou beugu si livré yi noy def
Machalah Amna solo nayaatou
Masàlla amna solo lool
Machalla amna solo loll mandé beguna ci teeré wolof anglais ak wolof farancé contacbi la soxla?
Amna solo 👌
Machallah jotaybi amna solo taié yoyu la beuga xam kuci beugue fanlamana diarr ba amci ?
Maa shaa allah mandè damaa jommi sahx!!!
Lula jommal?
Massàllah.
*Machallah sñ abdou rahim machallah sm journaliste bou mak bi sa liguèye mo rafêtte rk mo warall critique Yi*
Machalla kaddoyi amna solo loll loll loll
Machalla degla
Kou beug si baatoukaye wolof yi noydeff
Merci beaucoup 💖💖💖
Làkki réew mi ñu dugal ci daara yi sax saa tugal yi ñoo wax ñu dugal ko ci ekool yi ngir xale yi jaare ci man a dawal bu yomb farañse.
abdou rahim laye amna solo gëm saboppou rek
ku beug ci livre noy def ?
ماشاءالله
Màssllaa amna solo waaw góor yàang ca yoon wa
MACHALA LI MOY PATRIOTISME
Les analyses du journaliste 🤗🤗🤗🤗🤗
Ku réere saw làkk, réere sa mbatiit !
Billahi ngi djiité reew mi warnioula bayyi xel
Macha allah 👍🏾👍🏾👍🏾
Loooool
Wawaw
🤣🤣🤣🤣🤣 bilahi damako naw doumasi doyal bilahi 🤣🤣🤣🤣
Barina solo
Le wolof
Day yeex rek waaye dina baax, Inshallah
Nangeen ko woo wâat de
Dël bayyi señ leye muy yatal
Wallahi ki lou am solou lay wakh. Senegal doxol wallahi
Tubaarkalla amna solo lool 💫💦💦
Vraiment niveau tolo woul abdou rahim leye ki dégul ligay wax amoul niveau pour dila questioner
na jotaay bi di gëna gudd waay
Vous me pardonnez car je ne maîtrise pas assez l langue wolof.
Man dëy da maa bég ci yéen bay jooy...
Kubegeu terebi fokoy ame
Lu léer là wax
Sëñ bi dañ koo waradalal Sénégal 7 wala Soliton wala ci yaneen site yu siw yi
Seringe bi yaw mi di modernes jotay bi amo professionnels dara
Bly
ASSALAMOUHALEYKOUM MAGUI LEN DI ZIAR DI NIANAL SERIGNE MOUNTAKHA MOU YAG FI LOOL TE WER DILEN WAX NE KOU YESS LA THI TH-cam DILEN JAAN GUEN ABONNE THI SAMA CHAINE DAGAY BEUSS THI SAMA PHOTO PROFIL A GAUCHE
Presenateur bi ayoul dafay ladj pour galgal saway l’homme qu il faut à la place qu il faut
Imam ndao domou darala imam darame entre autre sont trop influencés
Sereignebi maguilene di ziar.
Waw mandé dakorouma ak yaw si yene khèlatt yoo wakh: Modi khéyi nagoo tounio dianga: Loolou amoul li am moodi amna si diangalèkatyi you amoul khamkham biniou warana am pour diangalè.Amnasi nio khamné amou niou aye diountouwaye guir diangalé klassyi bouféké dafa fèsdèlle dafaye diaffé si gueye diangalé di dégguelo nieupeu, di toppeutoo nieupeu.
Loolou bouamé responsabilitébi nieko yor moye gnie yoré Riiwemi.
Kilifaye Sénégal si sineboppe nio doul dieufeudéko sine khél: noune wa afriq laniou nécke danio wara khool li dapoo ak sounou aada, niniou déckè addouna soukodéfé nioye dianga liniou wara dianga.wayénak loolou waroula takh niouné douniou dianga khéw-khéwou yenène riiweyi.ndakh loulou dafaniouye dolli khélatt
Yaw mii de sa bopp bi dara nekku ci.
Deel teewloo xel, teewloo nopp du yëfi nit.
Li dh lou amesolo la na gana yatou rk
Journaliste bi mome
Dindi garap you bakh yeup fruit yi remplacé KO ak Aÿ garabou niiim MDR....
Journaliste bi xamo tous andal ak tey ak dal ndakh gnye diglu mana diariniou
Journaliste bi con na