Kooru Wadioubakh - Saison 2 - Episode 30

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 31 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 923

  • @diagnembay8768
    @diagnembay8768 2 ปีที่แล้ว +142

    Ak lou ma n'a xéw magui santé serigne TOUBA

  • @thioubcheikh1084
    @thioubcheikh1084 2 ปีที่แล้ว +81

    Yallna Sénégal dieul coup du monde ✊🏼

  • @fatysall8842
    @fatysall8842 2 ปีที่แล้ว +26

    Yalna nagnou feke kooru deweune si Barker seydina moukhamet gni fi djouge yalla kharre lenn aldjana firdawsy 🙏🙏🙏🙏

  • @ahmadoubambadiop2001
    @ahmadoubambadiop2001 2 ปีที่แล้ว +264

    Bonne fête tous les sénégalais🇸🇳🇸🇳 Yalna niou Yalla nangoul suñu koor merci beaucoup wadiobakh Yalna la Yalla défall diam ♥️♥️🤲🏿

  • @ahmadoubambadiop2001
    @ahmadoubambadiop2001 2 ปีที่แล้ว +108

    Sénégal Campion d'e Afrique🇸🇳🏆✊🏿
    Yalna ci coupe du monde Bi topu way si barkep cheikh ibra🇸🇳🇸🇳
    Bonne fête tous les sénégalais♥️♥️🇸🇳🇸🇳🙌🏿

    • @cheikhounadia581
      @cheikhounadia581 2 ปีที่แล้ว +1

      Aminn

    • @aliouba1325
      @aliouba1325 2 ปีที่แล้ว

      Si barki yalla cheikh ibra mana lougn niou dara

    • @ahmadoubambadiop2001
      @ahmadoubambadiop2001 2 ปีที่แล้ว +2

      @@aliouba1325 bouy yamal rèw nga lo seex ibra mo gën sa baye😫

    • @aliouba1325
      @aliouba1325 2 ปีที่แล้ว

      @@ahmadoubambadiop2001 khamoul tounou ndeyam

    • @generalbmb4983
      @generalbmb4983 2 ปีที่แล้ว +1

      @@aliouba1325 boye yaw lilaye dal khamoko sx commentaires ymbuna. trop bun dffé vs dinga khamné mandu bahna

  • @thiernosow3688
    @thiernosow3688 2 ปีที่แล้ว +40

    Nn Ty mome dafa nekh yalnane kou féké aye ATI ate si barke Serigne saliou ❤️

  • @djibymoumamesaliou5132
    @djibymoumamesaliou5132 2 ปีที่แล้ว +41

    Wadioubakh do nite😅😅yalla nala fi yalla bayi basi kaname gua yague gno béguele gnou fékeko aye ate bou kéne manké déwénati ❤️

    • @fatoumbengue
      @fatoumbengue 2 ปีที่แล้ว

      Non😃😃😃🤣

    • @djibymoumamesaliou5132
      @djibymoumamesaliou5132 2 ปีที่แล้ว

      @@fatoumbengue Fatou loy ré😅

    • @fatoumbengue
      @fatoumbengue 2 ปีที่แล้ว

      @@djibymoumamesaliou5132 non wadiou douma ray def limiy def ba paré di daw

  • @fatougayeelementmamemakhta774
    @fatougayeelementmamemakhta774 2 ปีที่แล้ว +131

    wadioubakh da melni lou guiss coumba seck ndaw lou nekh 🤣🤣🤣🤣 longue vie à toi notre comédien 🥰🥰

  • @khadimmbayetalibebamba3077
    @khadimmbayetalibebamba3077 2 ปีที่แล้ว +46

    Bonne fête tou le sénégalais wadiou bakh yalna sa diamou yagne barkp borom touba 🥰🥰❤️💝💝💝

  • @babacarfall1136
    @babacarfall1136 2 ปีที่แล้ว +28

    félicitations de notre champion Wadioubakh ak ééquipe bi yep 😇 ..
    Serie bi rrk moma rawoul ci koor gui ♥︎
    Varement Wadioubakh nous on taim 🤩❣

  • @khadimniang2230
    @khadimniang2230 2 ปีที่แล้ว +57

    COMÉDIEN DU PEUPLE BA DÉWÉNAK DIAMOU INCHALLAH 🙏🎉💯ET BONNE CONTINUATION À VOUS, 💯🎉✌️❣️

  • @sfmotivation2386
    @sfmotivation2386 2 ปีที่แล้ว +96

    Il est trop fort longue vie , sante , a toute la population

  • @babacarndiaye9252
    @babacarndiaye9252 2 ปีที่แล้ว +40

    Ouais c’est comme ça. Même la vie humaine se termine par malheur.
    Inch’Allah à l’année prochaine, Ramadan 2023

  • @wakhlouyydeffarnittgni4965
    @wakhlouyydeffarnittgni4965 2 ปีที่แล้ว +50

    Gnounn gnîyy gougué werr bii yalna yalla nagoull gnou sougnou gougué ba lépp lougnou si fass mou défall gnoukko ayy yiww.
    Sinon Merci infiniment Wadiou Bakh begu nayy loll

    • @massgueye2893
      @massgueye2893 2 ปีที่แล้ว +2

      Yalla bouko yalla nagou saytané

    • @khaliloulah2167
      @khaliloulah2167 2 ปีที่แล้ว

      Ligay diamou yalla yaw la concerné po ñioune ligay do.si am dara dakh guistal.la bayi.si xel defal.tei.yalla takh c mieux

    • @wakhlouyydeffarnittgni4965
      @wakhlouyydeffarnittgni4965 2 ปีที่แล้ว

      @@khaliloulah2167 Sénégal metinaa, manouu dioynaa.
      Yalna yalla mayegnou kholou mougne

    • @wakhlouyydeffarnittgni4965
      @wakhlouyydeffarnittgni4965 2 ปีที่แล้ว

      @@massgueye2893 gueyen bii tamitt kénn dina gnanall li sa bourr,

  • @prince1473
    @prince1473 2 ปีที่แล้ว +57

    Aid Mubarak a vous qu'Allah accepte nos jeûne par sa miséricorde inchallah et bonne continuation a wadioubakh le meilleur comédie i'm from Sénégal ouest africa 🇸🇳 America🇺🇲🇺🇲

  • @souleymanedeme1095
    @souleymanedeme1095 2 ปีที่แล้ว +32

    Wadioubakh Kouy Conquirent ak MoM Mane NGA Dème Tokk WaLLaHi Affaires Yi daay ñeuw si MoM Naturel dafa Melni NGA Nii Messi Si Football bii Yalla NGA Goudou Fann Amine 🙏 ak beup Djouliit 😃😂

  • @Tiktoklamb221
    @Tiktoklamb221 2 ปีที่แล้ว +190

    Quel scénario jusqu’au bout du suspens !!! Félicitation à toute l’équipe chapeau 🎩 Wadiou Bakh

  • @fatouthiam4420
    @fatouthiam4420 2 ปีที่แล้ว +55

    Félicitation à toutes l'équipe surtout bakh et sa femme vous êtes fort cette chéri me plaît beaucoup

  • @ndsng8364
    @ndsng8364 2 ปีที่แล้ว +62

    Anta mm ps 5 minute khemnafi 2 fois 😍🤩😍😍😍 lii nèkhna trop merci baucoup 👍👍👍👍👍❤❤❤

    • @bolodiop2814
      @bolodiop2814 2 ปีที่แล้ว +2

      Loolama reee lo bamay yokhou

  • @awatraore3601
    @awatraore3601 2 ปีที่แล้ว +52

    Machalla meilleur série de l'année yallah n'a guene goud fane ande AK weur gou barii vie sur tt l'équipe de wadioubakh ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @alioudieye5721
    @alioudieye5721 2 ปีที่แล้ว +42

    Lima xalate sama xél ni mbadou lolou mo ame
    Kou xalate ni li meun na nék ay guénteu si Wadiou Bakh lalale j'aime ❤️ ?
    😂😂😂😂

  • @lesenegalais86
    @lesenegalais86 2 ปีที่แล้ว +55

    Wadioubakh est une grande star
    Son talent unique ne cesse de nous surprendre . Bonne continuation ! ❤👌💯🙏

  • @papeousmanediante9766
    @papeousmanediante9766 2 ปีที่แล้ว +20

    No bah est le meilleur de sa génération 😅🤣😁😂Lou guiss daw wadioubah beusseul j'aime

  • @nba_young_boy9561
    @nba_young_boy9561 2 ปีที่แล้ว +50

    Bonne fête de korité à tout la communauté musulmans

    • @khabyBa224
      @khabyBa224 ปีที่แล้ว

      😂😂❤❤❤😂😂

  • @adjaladiane4892
    @adjaladiane4892 2 ปีที่แล้ว +73

    Wadioubakh est extraordinaire clé meilleur

  • @falloudiop1608
    @falloudiop1608 2 ปีที่แล้ว +10

    Vraiment bax setane na lépou serie bi machallah yala nagn ko yageu setane lima meti rek moye migui diéx 😭❤❤

  • @aliounemar1578
    @aliounemar1578 2 ปีที่แล้ว +35

    Machallah felicitation a toute l'equipe. J apprecie bcp le role de anta. Malgre les derives de bah et les influences de sa maman elle reste tjrs intacte, gere son foyer comme si de rien n etait.
    un film qu on peut regarder en famille sans de gros mots. Merci vraiment et bonne continuation🙏

  • @mamependaba7129
    @mamependaba7129 2 ปีที่แล้ว +30

    😂😂😂❤❤❤ c'est la seule série ramadan avec une digne fin 🎉🎉

  • @virtueltechy6103
    @virtueltechy6103 2 ปีที่แล้ว +151

    Félicitations à notre cher Wadioubakh. Vraiment on est très content de vous ainsi que toute l'équipe de cette série. Chapeau à vous . ♥️♥️♥️♥️💯💯💯💯💯

  • @Hassane221
    @Hassane221 2 ปีที่แล้ว +62

    Tout mon soutien Pape Nice 😁😁😁😁😁en vrai Lena est trop mignonne très fraîche 🥰🥰🥰🥰envelope de l'équipe 😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁mdrrr

  • @lunebadouu7667
    @lunebadouu7667 2 ปีที่แล้ว +13

    Franchement Lii baax jouer si dernier épisode bi c’est à apprendre dans tous les maisons de production, 🔥🔥 juste vous rappeler que Lena est millionnaire malgré cela elle a accepté d’épouser un pauvre comme baax et refuser un jeune homme qui était prêt à tout faire pour elle C’est incroyable cette leçon de vie ! Big Chapeau 🎩 à toi waajubaax, Vraiment meune ga bindeu série dei bilaay dîna réussir parce que lala , tu viens de déraciner le baoba 🎉
    Anta une très jolie femme de cœur ouverte, une victime qui n’a rien demandé force à toi , mais bon , mon conseil : oufeul sa jumelle geen topato sen Jekeur puisque vous l’aimez tous les 2 , Yalla beuri na soutoureu liiy ñew mooy daaq lii passer 🤝💔
    Big up a tous la team waaju baax !!!
    Chapeau aux réalisateurs
    Dewenati leine yall nen ko tewe att yu baari🤲🏿

  • @CheikhCisse-zj2gw
    @CheikhCisse-zj2gw ปีที่แล้ว +1

    Nn wadioubax D'où nitou fi koi Mais kénn d'où madior vraiment c'est le meilleur du monde kou dakor rk lalal ❤️

  • @ndeyeleye5280
    @ndeyeleye5280 2 ปีที่แล้ว +27

    Machalah je vous kiffe chui très contente de vous

  • @ahamadousow8643
    @ahamadousow8643 2 ปีที่แล้ว +4

    Machallah mailleur série de l'année yalnaleun yalla diaplé té goudal seune fanne wax deug zéro stress laniou doundou

  • @mathiamthioub4196
    @mathiamthioub4196 2 ปีที่แล้ว +7

    Maye lén ma aye j'aime waye dama KO sokh la bilahi diapo lén si waye

  • @wahabsakho4200
    @wahabsakho4200 2 ปีที่แล้ว +4

    تقبل الله منا ومنكم صالح الاعمال كل عام وانتم بخير
    Dewenety bal lén ma akh bal na niép yalla nanou yalla bolé bal niou féke ko ay att you beuri inch'Allah ❤️✨

  • @phonetv5025
    @phonetv5025 2 ปีที่แล้ว +45

    Meilleurs comédien

  • @abdounjiesgoogle2852
    @abdounjiesgoogle2852 2 ปีที่แล้ว +4

    ماشاء الله بارك الله فيكم حافظكم الله ورعاء 🤲🏻 كل عام وانتم بألف خير خيرا ،🤲🏻🤲🏻💯💯💯💯💯❤️❤️💖💝💞🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇶🇦🇬🇲🤩🤩🤩

  • @boromlibaakh8837
    @boromlibaakh8837 2 ปีที่แล้ว +43

    Nekhoul ba nekhoul me amo morom 😂😂😂😂

  • @IbrahimaDiallo-is9to
    @IbrahimaDiallo-is9to 2 ปีที่แล้ว +2

    SONKO mo tané aliou sall dé mais t’es le meilleur wadioubakh

  • @khoudialo7725
    @khoudialo7725 2 ปีที่แล้ว +19

    Wadioubakh yalena goudou fan ❤❤dinalèn namou trop bilay🥺mais wadioubakh bakh ray nama ak sagnesè bi🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @azzoking3201
    @azzoking3201 2 ปีที่แล้ว +23

    😂😂budget senegal 10mille mosidess Khanaaa nooo wadjiou bakh amoul 😂😂😂😂😂😂

  • @abdoulahadkane9557
    @abdoulahadkane9557 2 ปีที่แล้ว +3

    Machallah wadioubakh chéri bi nékhna yalla nanko fékké ay att you bari 🙏🙏🙏

  • @scottsiby9976
    @scottsiby9976 2 ปีที่แล้ว +4

    Dewenati korou wadioubakh 🇸🇳
    Sonou ngén si niouléni sétan 🇸🇳
    Ramadan ak diam 🇸🇳
    Ramadan mubarak 🇸🇳
    J'aime beaucoup 🇸🇳
    Wadioubakh 💚💛❤👍🇸🇳

  • @abdelonetv2436
    @abdelonetv2436 2 ปีที่แล้ว +60

    Wadioubakh le meilleur 😁😁

  • @habibatacamara137
    @habibatacamara137 2 ปีที่แล้ว +71

    Kanamou bakh billay c trop mm quand t’il et sérieux je peux pas m’empêcher de 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @papandiaye2130
    @papandiaye2130 2 ปีที่แล้ว +22

    Bakh acteur du peuple 💪🏿✨

  • @almamidiop271
    @almamidiop271 2 ปีที่แล้ว +2

    Ay way sonko rek 20 24 inch'Allah ❤❤❤❤❤💪

  • @malickba9778
    @malickba9778 2 ปีที่แล้ว +8

    J'espère que Tabaski wadioubakh dina am inchallah

  • @modoukanteye228
    @modoukanteye228 2 ปีที่แล้ว +95

    Senegal gamou tivaoune moma fi bayi😂😂

  • @gueyebineta7154
    @gueyebineta7154 2 ปีที่แล้ว +20

    Wadioubakh yalla nag deim makka 😂😂😂😂😂😂

  • @fatelkounta321
    @fatelkounta321 2 ปีที่แล้ว +11

    Khar na ba sonou ms bonne fête 🥳 à tt les musulmans 🥰🤩😍

  • @ibrahimkebe5802
    @ibrahimkebe5802 2 ปีที่แล้ว +30

    Très sympa ligueybi rafetena vous mérité votre salaire

  • @amthfall4901
    @amthfall4901 2 ปีที่แล้ว +12

    Wadjoubah conta nagnou si yowe♥️💯

    • @adamaba7152
      @adamaba7152 2 ปีที่แล้ว

      Rastaman bi dafa nirok ndoy bane

  • @papitv7218
    @papitv7218 2 ปีที่แล้ว +3

    Kou guiss anta si guinaw ba wadjiou bakh di guene si salon bi ak mariama👍🤷‍♀️

  • @matasy925
    @matasy925 2 ปีที่แล้ว +11

    Vraiment wadioubahk chaque jour il diminue le stresse

  • @aramediouf4524
    @aramediouf4524 2 ปีที่แล้ว +63

    Koudou khale😁😁😁

  • @modydiop6663
    @modydiop6663 2 ปีที่แล้ว +2

    Saway présentéwoul 2024 yawlay wotel yafi né dé AK fi rewmi tol ci thiow.Yaye sounou anti stress dé. Yallna diam yagg ci mime réww.félicitation à toute l'équipe, vraiment vous êtes les meilleurs.

  • @yadiscopro1412
    @yadiscopro1412 2 ปีที่แล้ว +9

    Vraiment vous êtes trop fort. Anta tu es la meilleure crise guafi khamé fi sa diaroo bi mem pas 5 minutes je te remercie sur cet acte. En plus bakh il a trembler toute la maison en fuiant rapidement.je vais pas laisser tomber le ndawtall du président de la republique avec une somme de 10 000fc , de cel du maire de guédiawaye 1 500 fc 😂😂mdr. En outre l'habillement de bakh 😂😂 néna gorr gni sakh danouuyy âme robe mariage ainsi que la défaite inattendu de mariama.sincèrement je suis très triste à la fin du série.A la prochaine vous êtes les meilleurs😂😂🕺🏼🙏🏽

  • @abdoulayeperoba2930
    @abdoulayeperoba2930 2 ปีที่แล้ว

    Wadioubakh machalla yal na s'en diamou yague bly contane nane trop si yene yw dagua niouy doundale dall bilahi yal n'a gua fi yague th andal werr ak werr leh

  • @mpssylla9796
    @mpssylla9796 2 ปีที่แล้ว +10

    Macha alla série nékhna, déweunati incha alla😂😂wadioubakh c l meilleur😂😂😘

  • @binetou6005
    @binetou6005 2 ปีที่แล้ว +61

    Meilleur série ramadan 😂

  • @seynabousarrniane8404
    @seynabousarrniane8404 2 ปีที่แล้ว +38

    🤣🤣dama ré ba sounou 🤣🤣

  • @aichamouserignebabacarsy9845
    @aichamouserignebabacarsy9845 2 ปีที่แล้ว +1

    Bakh yalna sa diam yague barki sang bou téde bi machalla contane nagne thi yow♥️♥️♥️💪💪💪🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻

  • @dieynabadiallo4649
    @dieynabadiallo4649 2 ปีที่แล้ว +10

    Merci beaucoup vraiment khol yi sedd neu♥️♥️

  • @badaradiopkhassida1746
    @badaradiopkhassida1746 2 ปีที่แล้ว +28

    Amna gno khamni d lèrnama ni koumpa molèni ray balaa èpisode bi di daw

  • @lecitoyentv2022
    @lecitoyentv2022 2 ปีที่แล้ว +20

    Anta est vraiment belle et gentille

  • @ibrahimakhalil520
    @ibrahimakhalil520 2 ปีที่แล้ว +27

    Thieuy Yallah 😭🤣🤣 OOOH 😭 C'EST TRSITE.💔💔💔 BAKH YAA BONN DEUG 🤣😭😭😭 😭😭🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
    OOOH KON THÉÂTRE BI DIEEXNA NII
    MAIS YALNAGN FÉKÉ DÉWÉNN INSHALLAH KEN BAGNIA MANQUÉ
    ❤️🙏🙏 YALLAH MEUNAKO YALLAH NAKO DEF ❤️🙏
    Yakarna nak WADIOUBAKH doo arrêter rek 😰 sinon dinagn la namm trop 🙏 NEEXON NA TROP BEUGOUNIOU SAXX MOU DIEEX
    CIAO À BIENTÔT ❤️☺️👋👋👋👋👋👋👋

  • @azizsamb4691
    @azizsamb4691 2 ปีที่แล้ว +38

    ibou diagne momey fathie😂😂😂il est sous estimé vrai acteur le

  • @sambabara6581
    @sambabara6581 2 ปีที่แล้ว +42

    Wadioubakh est très extraordinaire

  • @bosslady2368
    @bosslady2368 2 ปีที่แล้ว +10

    Seutt wa Bakh sa traine sabador lanela tamite🤣🤣🤣. Jumelle qui moy sama « papa »😭ak bakhanam bou gouddou🤣🤣🤣

  • @serignemansourlayengomngom5323
    @serignemansourlayengomngom5323 2 ปีที่แล้ว

    Wadio bakh yalnala yalla defal diam barke seydina limamou laye jambar dji begg nane lolou

  • @khadimthiam3299
    @khadimthiam3299 2 ปีที่แล้ว +4

    Merci beaucoup wadioubakh vraiment koor nekh na yalla na sa diamou yague rk inslha 🥰🥰😂😂😂😂

  • @Bestfunny7777
    @Bestfunny7777 2 ปีที่แล้ว +5

    Kou sabador Wadioubakh bi rétane lo rek beusseul j’aime ❤️❤️😂

  • @diakhoudia2674
    @diakhoudia2674 2 ปีที่แล้ว +3

    Wouyyy wadioubakh sagnsé tina akkk treine bi nakkk😂😂😂 non mako beuggg c le meilleur machallah 😍😍😍💕♥️

  • @Stretch000
    @Stretch000 2 ปีที่แล้ว

    Mane dh nima beugué wadiou bakh sakh dama diakhal❤❤😢

  • @morawahtdk39
    @morawahtdk39 2 ปีที่แล้ว +8

    Awo bi nitt kou bakh même boudoul théâtre bi elle a un visage Doux

  • @mbackegaydelserignembacke8335
    @mbackegaydelserignembacke8335 2 ปีที่แล้ว +1

    Thia dougousi bala
    Kel deseptions bakh nak guirie la dh😂😂😂😂mes seire bi neekhna mes khamna 2em saison bey dakhue merci wadioubakh ak sa Wa equip niep Machalla denenaty lene 🙏♥️♥️

  • @beuzmanbalde
    @beuzmanbalde 2 ปีที่แล้ว +34

    Rien à dire, juste ont a nomme meilleur comédien

  • @assaneyade9217
    @assaneyade9217 2 ปีที่แล้ว +4

    Wadiou bakh c est le meilleur série yeup do sen morom

  • @fatmawade9363
    @fatmawade9363 2 ปีที่แล้ว +19

    Massalah on est content de vous

  • @rabyndiaye722
    @rabyndiaye722 2 ปีที่แล้ว +1

    Son excellence bakh machallah on est content nio gui déwéne inchallah noumouye moudié bravo bakh

  • @baye-falllecreateur3549
    @baye-falllecreateur3549 2 ปีที่แล้ว +30

    Chapeau à vous.

  • @amicoleseck2909
    @amicoleseck2909 2 ปีที่แล้ว +7

    Bonne fête de korite a tous les musulmans yalnagnou yala nagoule sougnou koor nagou sougnou diamou yala🙏🧕🌙🙏

  • @matarndiaye7405
    @matarndiaye7405 2 ปีที่แล้ว +26

    Wadioubakh ak kholem bi dou diam🤣🤣🤣

  • @elhadjiadamdiop449
    @elhadjiadamdiop449 2 ปีที่แล้ว +21

    Le meilleur, merci

  • @djibrildiallo483
    @djibrildiallo483 2 ปีที่แล้ว +9

    Heeeee macky sall 10000 😂🤣😂😂🤣 Y’a plus de bugs Sénégal

  • @khalifacamara1193
    @khalifacamara1193 2 ปีที่แล้ว +1

    Maman Aïcha yalla na goudou fane 🎉❤bravo bakh t'es le meilleur

  • @ndeyefatoufall7054
    @ndeyefatoufall7054 2 ปีที่แล้ว +11

    Des cœur pour bakh😂😂❤️❤️❤️

  • @weuzzpeuzzi8410
    @weuzzpeuzzi8410 2 ปีที่แล้ว

    Nn man bakh moma geunna nékh si adouna yalla nala yalla défal diamou

  • @elhadjiseckdiop9710
    @elhadjiseckdiop9710 2 ปีที่แล้ว +8

    Quel suspens !
    Bravo à wadioubax et son équipe.

  • @bayesaliousall5377
    @bayesaliousall5377 ปีที่แล้ว

    Akassa wér na dh diaradiefaty borome Touba rék ♥️♥️🙏🏾👌

  • @thiamb7170
    @thiamb7170 2 ปีที่แล้ว +62

    1500 Alioune Sall : belle lecon
    5.000 Sonko . Il n est pas du genre
    Chèque Macky : Secret d Etat

  • @seydinaomardiouf46
    @seydinaomardiouf46 2 ปีที่แล้ว +4

    N'oubliez pas les 5 prières de Allah c très important 🙏

  • @mbayendiaye1290
    @mbayendiaye1290 2 ปีที่แล้ว +23

    Li ay genteu lay done rk si wadioubax 😂😂

    • @Sodagaye2312
      @Sodagaye2312 2 ปีที่แล้ว +1

      Je pense deh mou nekk ay guente

  • @barroba7564
    @barroba7564 2 ปีที่แล้ว +5

    Machallah ♥️♥️🤣♥️🤣 yalla naaniou yalla may noiu fekke dewenn kontan naaniou billahi

  • @serignesamsall1141
    @serignesamsall1141 2 ปีที่แล้ว +7

    Wadioibakh t'es le meilleur wallahi

  • @kharfaye9321
    @kharfaye9321 2 ปีที่แล้ว +13

    non wadiou bakh ki laye gnawal faw mou niam kosso🤣🤣🤣🤣🤣

  • @gomisfabienne6858
    @gomisfabienne6858 2 ปีที่แล้ว +29

    Trop bien. Wadioubakh c'est top

  • @wahabsakho4200
    @wahabsakho4200 2 ปีที่แล้ว +1

    Way kéndou wadioubakh c le meilleur bilay diam si iow diogoye