C’est terrible j’ai vécu la Mm chose cause j’ai perdu mes parents à l’âge de 05ans sur ce ma vie été trop compliqué donc je fuguer trop de la maison lounè déf nako sma adouna mais lgui mom sante n’a yalla bou bakh j’ai vachement changer et je remercie le bon dieu yalla nalén yalla changer 🙏aussi
Mane dè magui dioye thie khallè 14ans bi li metina wallahi say wadiour deudou amo kene yalla na lene borome bi sopi same lene metina trop😭nagne lene dimbali centre yi mougui fi
Un très bon reportage. Une faillite totale d'une politique pour les enfants,les orphelins et les jeunes banlieusards . C'est désolant vraiment ♥️🥊🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Jtjr je remercie à ma mère et ma grande soeur pask 2004 je devais faire la classe de CM2 mei année blanche lako moudjei pask dama commencé wone yakou nekeu pikine sandika top borom Charete di guinz di sathie non kel folie de jeuneusse mei santeu yala legui diangue na ba moudjei ame sama bac sokoy expliqué nitt sax doula gueum pask legui nima mél . Mei li yeup en génèral pauvreté mokoy indi Yala nalene yala diapalei chèr frère tolou way leu rk
😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭 YALLA NALÉN YALLA SOUNOU BOROM SOPi hirlén si diamou YALLA ah déff LOU bah si Barhép SEYDINA LIMAMOU LAHI AL MAHDI sala lahou ALEYHI WA SALAM.
Affair sathieh agrèssè ou banditisme fepeh leh ,banlieue c vrai c grave,mai thiaga yi ag goor djiguen yi,boit de nuit yi,sathieh katou milliard yi gnogui ville wakhlen ci lolou gnom gno takh banlieu bi yakou
Suis de yeumbeul mais c’est triste 👩🏾🦯👩🏾🦯👩🏾🦯 des jeunes sans avenir qui nous perturbent Certains se disent orphelins mais c’est pas vrai c’est juste qu’ils n’ont pas reçu une bonne éducation tout simplement
Assalamaleykoum gaayi dileen diadieufël si commemtaire yi soxnasi ame nga jarama. Déja vendeur dilliant yi amena gnou si sene part de responsabilité, warnaniou leen tek Daan
Layy manila demal montagne malicka la eupé meusna nek si bus 52 dem keur massar ben peul fouta bou ande ak diabaram di woté ben wayy si fenêtre bi l keufé caal bi dougou mbeubeuss
Le gouvernement ne prend aucune initiative sérieuse contre l'insécurité et cela depuis plus de 20 ans avec le début des agressions. La conséquence est que l'insécurité est en progression continue. Ces jeunes sont d'une part victime du système qui ne n'offre pas de solutions aux jeunes en difficulté.
Avec un total de douzemille (12000) policiers pour 14.000.000 d'habitants,comment pourrait on prétendre à une quelconque sécurité?Surtout quand 11999 de ces 12000 policiers passent tout leur temps à raquetter les automobilistes
Bayilen gouvernement ak pauvreté amena yo khamni nite ki si vopame la concerné saye parents dañilaye éduqué m3 so guené yake sa bope si mbede bii wa legui a ki la faute nite kuné sa magume bope la nite sa aduna yakoye defarale sa bope wasalam
Non life bi tarr na quand tu penses que t'es maudis c'est que ta pas vue la situation des autres. C'est pas pour les juger mais je pense qu'ils sont faibles gnak boumoula takha diaay sa ngor. Dolli sante yallah rek diko gnane mou maygnou sutura aduna ak alakhira...
Comment ça la banlieue est pourrie, je viens de la banlieue et je ne suis pas pourri moi. C'est juste une question d'éducation peut être que ces jeunes n'ont pas reçu la même éducation que toi mais cela ne te donne pas le droit d'insulter l'effort que font certains parents sur l'éducation de leurs enfants dans la banlieue *pourrie*
Mane dama khalat dagnon wara tidji beine centre pour gnou dilene redresse pendant des moi petetre mou taner li gnawna ame na gnoufi nek ta ligueyougnou gnou tek lene fa gnoudilene surveille apre di fayercou
Elle est où la police sénégalaise aucune sécurité nous les africains on est égoïste il est temps d’avoir des hommes politiques pas corrompus où va ce pays
Kouye wakh si délinquance bi nopalal sa bope dou fi diougué légui gouvernement bi diémougnou dara si population bi amougnou yeurmandé dieule khalissou deuk bi di sathie rék kou deukoul banlieu khamo banlieu boy yi dougnou daw policier ragualougne si deureum Macky Sall yeureumeul population bi dagnou lakoy gnane
J'ai vraiment versé des larmes ils sont presque tous des orphelins. Certains n'ont jamais eu le choix dans leur vie
Bilahi c est dure
On a tjrs le choix
💔 J'ai le cœur brisé cela fait la 2ème fois que je regarde ce reportage j'ai terriblement mal... 😢
😊😊😊😊😊😊
C’est terrible j’ai vécu la Mm chose cause j’ai perdu mes parents à l’âge de 05ans sur ce ma vie été trop compliqué donc je fuguer trop de la maison lounè déf nako sma adouna mais lgui mom sante n’a yalla bou bakh j’ai vachement changer et je remercie le bon dieu yalla nalén yalla changer 🙏aussi
Bilahi amna ay parent yo khamni daw responsablite rek 14 ans meunalo sa dom dara !!
Yalnala yalla Fayal sunuy wadiour té dioubeul nitt Gni
Goné yi légui danou deugueur bopp trop
J'aime l'émission bonne continuation sokhnasie diame djou barré si yow peace
Thieuy adouna yalla naniou yalla may kholou mougne🙏
On doit juste se dire la vérité pour régler nôtre pays
Mane dè magui dioye thie khallè 14ans bi li metina wallahi say wadiour deudou amo kene yalla na lene borome bi sopi same lene metina trop😭nagne lene dimbali centre yi mougui fi
Ça me fait mal au cœur ❤ bilahi
Un très bon reportage. Une faillite totale d'une politique pour les enfants,les orphelins et les jeunes banlieusards .
C'est désolant vraiment ♥️🥊🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Aý boune yeumbal Malika Keur Massar tiwaoune peulh bilahi dangay warou
Bolesi diakhay
Jtjr je remercie à ma mère et ma grande soeur pask 2004 je devais faire la classe de CM2 mei année blanche lako moudjei pask dama commencé wone yakou nekeu pikine sandika top borom Charete di guinz di sathie non kel folie de jeuneusse mei santeu yala legui diangue na ba moudjei ame sama bac sokoy expliqué nitt sax doula gueum pask legui nima mél . Mei li yeup en génèral pauvreté mokoy indi Yala nalene yala diapalei chèr frère tolou way leu rk
Ndeysan yallah maynalla chance dioup rk Moy DEUG
Machala amine niome tamite yalla na léne yalla soppy bima amone khalix ma diélniépe en charge mai yalla bakhna
Heskey
Good job la journaliste.
Yalna yalla dioubal mbolem dioulit ndeysan t samu
😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭 YALLA NALÉN YALLA SOUNOU BOROM SOPi hirlén si diamou YALLA ah déff LOU bah si Barhép SEYDINA LIMAMOU LAHI AL MAHDI sala lahou ALEYHI WA SALAM.
Je l’aime 7 journaliste
Ndeysane 😢😢❤
Ndéyssane li ça fait mal au cœur suñul rak yalla nalén yalla diapalé
Yalla naléne yalla dioubeul
Lolou gnikoye deff deukou niou yeumbeul
Billahi yaoo ❤❤❤❤
Affair sathieh agrèssè ou banditisme fepeh leh ,banlieue c vrai c grave,mai thiaga yi ag goor djiguen yi,boit de nuit yi,sathieh katou milliard yi gnogui ville wakhlen ci lolou gnom gno takh banlieu bi yakou
li yeup pauvreté moko waral thiéy Sénégal
Nooo Bilahi Thieuy Sénégal bilahi yar l'en xalé yi Bilahi li dawnna yaram
Lii yeup c l'échec de nos politiques qui est la cause
Suis de yeumbeul mais c’est triste 👩🏾🦯👩🏾🦯👩🏾🦯 des jeunes sans avenir qui nous perturbent
Certains se disent orphelins mais c’est pas vrai c’est juste qu’ils n’ont pas reçu une bonne éducation tout simplement
Sokhna ci sa lingéy nce naa
Votons pour Macky Sall Pour qu'il change le Sénégal en 2024. Mé ne laissez pas les opposants vouz manipule
Ho dama dioye dama khamni so neke djigene rek sa Khole warna toye
Ndaysaan gniou bari ay guiriim lan molènkou tekk
Sante sama yaye bou bakh dawalena charrete ba dém exterieur mais jamais délinquant
Salut bro dôma explique yonn bi stp
Trés intérressant reportage.
Mane daal yeumbeul la beuguone deukk nga xamni damay Am fite
Fiit moy ngay moytou bou bax
Niakk nga fayda dh
Les responsabilités c situe entre les parents et nos dirigeants comme la police c bien d parler au gos
I would like to see what the government gonna do about this? This young people don’t have much choice! Honestly is very sad 😢
Journaliste ni chapeau à elle perso je n’aurai pas osé rentrer dans le milieu
Ya rien là-bas j'ai vécu 2ans il sont tous gentils
@@KIXZEE_973 fi kay woroul
C claire
Je suis de yeumbeul et j'ai vraiment honte 😢😢😢
C'est incroyable !
Ndeysszne li metina
Boy yi dougnou boy malika
Yalla na yalla diapale
Yalla n'a laine yalla sopi
Assalamaleykoum gaayi dileen diadieufël si commemtaire yi soxnasi ame nga jarama.
Déja vendeur dilliant yi amena gnou si sene part de responsabilité, warnaniou leen tek Daan
Ay wayyy😢😢😢😢😢
They adouna métina..
Ho hooo doyna warr
J'habite à malika mais amoul li.
On vit heureux et dans le calme surtout à la cité sonatel.
Weiih bien dit j'habite à Malika mais amoul li bilae walay
Un ami habite là-bas mais amoufa wala jissoumako fa
Demal dokhontou montagne...wala côté quartier diago nga khôl
Layy manila demal montagne malicka la eupé meusna nek si bus 52 dem keur massar ben peul fouta bou ande ak diabaram di woté ben wayy si fenêtre bi l keufé caal bi dougou mbeubeuss
Boutelbi soudiéhé bayna guezz migui may ray
Ohoho avanir senegal 13 15 17ana nane si diok
Nenako Magui Diapalè Sama bopp
Magui Gainz😁😁😂
Mîèzè Narco 😂
No bilahi boyi daño rew
Boy bi sol rouge noir bi beugg nako dimbalè kouko kham walla nga kham ay mbokam fait moi signe
Niawlé gèdiawe marché boubes
Mach alla Diadieuf
Thiey Senegal
D'arrière le palais il y a des '''''
Au Almadies il y a des '''''
Partout a Dakar il y a le même problème
Le gouvernement ne prend aucune initiative sérieuse contre l'insécurité et cela depuis plus de 20 ans avec le début des agressions. La conséquence est que l'insécurité est en progression continue. Ces jeunes sont d'une part victime du système qui ne n'offre pas de solutions aux jeunes en difficulté.
Avec un total de douzemille (12000) policiers pour 14.000.000 d'habitants,comment pourrait on prétendre à une quelconque sécurité?Surtout quand 11999 de ces 12000 policiers passent tout leur temps à raquetter les automobilistes
Intéressant donc les forces de l'ordre ne sont que 12 000 sur toute l'étendue du territoire national ?
Keur massar malika amoul bandit sof rek
Bayilen gouvernement ak pauvreté amena yo khamni nite ki si vopame la concerné saye parents dañilaye éduqué m3 so guené yake sa bope si mbede bii wa legui a ki la faute nite kuné sa magume bope la nite sa aduna yakoye defarale sa bope wasalam
Thieye aduna metina mais na wadioury geuna yare xaleyi 14 ans ki waroul teu aye wadiouram
Ndayssan sama yaram Bangui daw sakh li Méty dh😅😅
Waa Sénégal dougnou cotisé lak sarette yi borome sarétte yeup ay weuyou lagnou ray katou nit, wooleen diambar yi rek (police)
Copin bilahi ligua wax yeupou deugle
Gneupa beug bax kéne beugoule bonne mais cette pauvreté extrême est la cause de tout ça
Doule rek guenes neke sene morom goy dane sene dolle
Mane dé sama perug cheveux lagnefa keuf si scouteur 21h sama quartier dafa grave dhh yeumbeul beurri roukou teeksi koula sathie dokham foum diar
Djiguene bou bakh mo mana tax gor gouye def lou bone bayi lép Lou bone
Yeumbeule se n’est pas dangereux venait à malika et Keurmasar
W
C pas la faute de l'État ni de la pauvreté mais la non-responsabilité des parents et la manque d'éducation de base
😭😭😭 ndesane
C triste 😢😢😢😢
😰😭aywayy dji sama khel sakh dou dale nakh sama mbokou yeup niogui malika
Yéné meuna dimbali sene bopp
Non life bi tarr na quand tu penses que t'es maudis c'est que ta pas vue la situation des autres. C'est pas pour les juger mais je pense qu'ils sont faibles gnak boumoula takha diaay sa ngor. Dolli sante yallah rek diko gnane mou maygnou sutura aduna ak alakhira...
Triste Triste
Ca toujours etait comme ca une inegalite sociale un systeme pourri et Des parents irresponsables.
Boys bobou nek tournalou yeumbeul kainkalleur bi si côté diaye catou téléphone bi mo wara bayi diaye dulien boys yi
Tous ces jeunes viennent des villages (touba où mbacke)l’état doit des initiatives
Yaw oubil sa leufeul ndeye nga bayi wa touba ak mbacké domou ram imbécile que tu es
Des jeunes sans métier ni qualification...la banlieue est pourrie Mbalitou sénégal...Goor yallah day ame métier...
Comment ça la banlieue est pourrie, je viens de la banlieue et je ne suis pas pourri moi. C'est juste une question d'éducation peut être que ces jeunes n'ont pas reçu la même éducation que toi mais cela ne te donne pas le droit d'insulter l'effort que font certains parents sur l'éducation de leurs enfants dans la banlieue *pourrie*
Daysane gni koulein diapalé niou changé banditisme amoul dieurine
Macky Sall diappalé gnu domaram ioe tékkiwo dara domou saram ndeyam bi
Parceque nos poliziesco et gendarmes doivent les prendre tjrs mais domage il preferent les 1000f des cars rapides et taxi
C'est la faute des gens qui font des enfants sans les occuper et les donner une bonne educations. Ils repondrons a Allah inchallah
Je ss peur le future di senegal
Mane dama khalat dagnon wara tidji beine centre pour gnou dilene redresse pendant des moi petetre mou taner li gnawna ame na gnoufi nek ta ligueyougnou gnou tek lene fa gnoudilene surveille apre di fayercou
Ñide kon naby ka yor centre ba lañouy degal ndayam dem sen yon ñi kay yermandey YALLA donga leni tournee
Trop triste
😢😢😢
😭😭😭😭😭
Boy ya tepi sa data ndeye
thiuey addouna
No guinj man bii affaire l😂😂
C le gouvernement du Sénégal le seul responsable
Elle est où la police sénégalaise aucune sécurité nous les africains on est égoïste il est temps d’avoir des hommes politiques pas corrompus où va ce pays
14 😭😭😭
Adouna soukh na
Kouye wakh si délinquance bi nopalal sa bope dou fi diougué légui gouvernement bi diémougnou dara si population bi amougnou yeurmandé dieule khalissou deuk bi di sathie rék kou deukoul banlieu khamo banlieu boy yi dougnou daw policier ragualougne si deureum Macky Sall yeureumeul population bi dagnou lakoy gnane
Bilshi Boy yi niongui ginz mé aggressé woiniou kenneu, zal mena bou bouteille bi diekhé mou bayi😁di doull
hehehe bilay liii yemena torop
Doyena ware setan sognou maguee deef musiba thia Keen fousy mouthi centre Serigne Modou kara l'ETA waron nako gana taxawou
Au lieu de vamporiser le peuple ,voilà le résultat des gouvernants qui ne pensent qu à eux
14 annss hoooooo
Ohh
C'est vraiment 😥 comme sort !
Ce produit qu'ils utilisent , de quoi s'agit-il?
Je pense qu'il s'agit de diluant qu'on utilise pour la peinture.