Amy collé & Birame Dieng " Sargal Viviane " clip officiel
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 27 ม.ค. 2025
- ♯Tendances musique ♯amicolledieng ♯biramedieng ♯viviane
Ami collé Dieng et son jeune frére Birame Dieng réunis pour rendre un vibrant hommage à la reine de la musique sénégalaise Viviane Chidid sous la houlette de Bakane seck avec son label Jeri jeri studio
Retrouvez nous sur :
Facebook: / jerijeri.bakane.seck
Instagram: / jerijeribakaneseck
TIKTOK : / jerijeritv0
Contacts:
Jeri Jeri Studio at Dakar Region, Dakar Department, Almadies, Yoff, Rue YF-361, ☎️ +221 778 10 33 33. 78 378 59 88 : Bakane Seck.
Ndeyessan vraiment Viviane mérite d'être honnorer
Ndanane bakena Ndanane li nekhna ❤❤❤❤
Les fans de Queen ❤ venons leur donner la force, le million de vues ❤😊
@@Forever-lov vraiment elle le mérite
@@Forever-lov bilaye yaw machalla dafa meuna way dieng sala 🥰contane nagnou gnoune wacoeur vivi🙏❤️❤️
Forever Vivian ..love from Gambia
Tata vivi❤❤❤❤❤❤🎉
Amy Collé Dieng Salla la reine 👸 de la musique 🎧🎤 mondiale 🌏 avec son ami son petit frère Birame Dieng Salla un grand chanteur 🎧🎤 rendent hommage a leurs amie l'idole de Amy Collé Dieng Salla Viviane Chidid une grande chanteuse 🎧🎤 c'est un bon geste toutes mes félicitations a vous et a Bakane Séck le propriétaire de cette label Jeri Jeri studio 🎙 👏👏 ❤️❤️❤️
@@Leslégendesdumondeentier ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💚💚
Walay kéneu meunouko thi way . Lafthiat rek
Lii nékhna❤
Amy collé dafa yague u beugueu Vivi meus na setaan beneu interviewam ça fait 8ans maintenant elle disait qu’elle se battait pour viviane bilay nek fans Viviane légui la neekh mais gnoun ancienne yi xoulo nagn ba sonou ndakh mom. Merci Ami le peuple est content
Bilahi wakhal dei😂❤
Bilay tè bizarrement mom Lou rafet rek lay waxal niènèn gni surtout Viviane ❤❤🎉
Bilay Aka métiwone khoulo ba sone😀
Même 24h akk bign ko invité si Viviane le demone
Machalla yalna yalla sameu no liii nekh na way❤❤
Ndeysan kouy fans vivi😢sa yaram dawna li ami collè weuy si xol❤la diougué vivi da nekha beugu nak
Waykat piirrr machala
Ndeysan la très belle voix d Amy colle Ay wayy nagnouko diapale
Bilahi dama beug Viviane ba beugeu kouko beug Amy colé je le déclare meilleur artice parce que da déf Lou diafé Moy nagoul sa moromou artice bilahi malla naw yalla nala yalla défal diam❤
Diambar day beugue diambar
Amy colle mo mana way mashallah sama yaram bi sakh migui daw
Li daw na yaram dh mashallah mashallah amy colle mala beug way 😍🥹❤️ya bakh khol sed na way tata vivi Love you ❤️❤️❤️❤️❤️🥹🥹❤️❤️❤️❤️
Vraiment nékhna dayesane oh ami collé dieng yallah na la yallah maye goudoufane gou ande ak wérr té moussal la si thiate yak sa rak birame 🎉🎉🎉🎉momite ligako way dotoul fay mouk 😢😊😊😊😊❤❤
Di waye baniou wayela Viviane wathiegua li dafa nekh Yayou Gawlo you niawoul yi Macha Allah. Amy AK Birame yéna niak kiniane. Longue vie à vous ine sha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ohh ma Vivi kiimeu beug depuis toute petite 😭♥️♥️♥️Xawmeu kagn lalay guiss Chidid😭♥️
Ami collé elle fait partie des meilleurs chanteuse du Sénégal ❤❤
Tata amy geune nala beugue ndakh maman Vivi kouko beugue ma beugue leu barké Serigne Touba mais li nékhna waay
Vraiment li raféttna.
Djiguene artiste bouy Sargual bénén djiguéne artiste.
Viviane wayou Ami Collé bi Reuyna, SAMA yaram sakh dawna,thiéy Birame Dieng kéne dou yaw masha'allah.
Oh merci beaucoup Amy
Assallamallikoume machallah
Ma vie Viviane
Machalah Amy Collé Diéng yabakhe ❤yallah nala yallah May wére🙏🏾❤️❤️😘😘
Bakh reik mo am solo bokk ak Ay nit métier nioulay waye ça en dit beaucoup sur Viviane. Machalah Amy Cole et birame bon vent Yalna y’a rabbi teik lokho si sein carrière Bi Inchalah 🙏❤️
Mokofa ame dh
Machalla ami colé jai des frissons Viviane damako beug tes yalla takh machalla
Machallah amy colé pour ce vibrant hommage à Viviane Chidid ❤❤li daffa raféte machallah yalla na la yalla faye takhawoula
J’ai pleurer Walahi Amy collé à une voie extra ordinaire ❤
Machalla ❤❤❤❤❤li nekhna nanane gend wayyyy ❤❤fierté Sénégal vivi diabare deug ❤❤❤
Bravo Amy colé ya waye koudiara way notre vivi
Machala li nékhna❤❤,ana wa coeur Vivi 🎉🎉🎉🎉
Ndaysan sama yaram dafa daw Amy colle dieng
Joli clip masha allah
Mo meune woye kay ami Cole rek machalah
Wa mais nous les fans de viviane on est touché 😢. Vous avez regardé la fin?😢❤❤❤manchallah
Amy colé dieng notre fierté et son frère birame dieng yalnalénn yalla sammm
@@khadimseck7813 yalla sonou borom takhawoulène ami collé et son frère si barké Seydina Mohamed SAW
Ndanane wooy na ndanane ❤ Bilay yeina bakh. C'est le Sénégal qui gagne. Bonne Continuation à vous !
Hoooooooooooooo ami collé birame liguéne waaay Viviane reuynaaaa hoooo💃💃♥️♥️♥️♥️
Bilahi elle le mérite merci ami et BIRAM ❤❤❤❤❤❤🎉
Alibaba Coumba naar niaaf 🎉🎉❤❤❤
Machallah khôl seidatatina khôl bi seidatatina kou beugue sa yaye beusseul j'aime pour le retour de Amy collé dieng si la reine de la musique africaine et sénégalaise ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machaillha les personnes anvance viviane chidid une référence pour les jeunes artistes toujours au sommet en modestie ❤❤❤ i love like ❤❤
Sargal ngen kou diara sargal! Longue vie à la Reine du Djolof Band
Modakh way Sénégal
c'est beau bimay dioy tayoumako sakh les fans de Vivi venons lui donner de la force, le Million de vues
Elle le mérite amplement ma Vivi ndanane way na ndanane ❤
Contane na sm xol fesna comme fans Viviane yeup merci beaucoup à vous tata amy collé❤
Macha ala ana wa cœur ❤ vivi niowlène niou remercier amy colè ak bireme dieng nila niit daguakoy sargal si bimouy doundou mâcha ala ❤
Wawaw contane nagne viviane rek lagnouy top❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Yalla na yalla samla arla, mayla wer ak sa frère bi birane ak mboleme dioulite, bravo vivi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah la voix d'or accompagnée par Boydo DIAGNE le Grand Maître du Khalam
Nééhena machalla Amy collé Dieng Sall la reine de la musique
Bilay li kouko aimer woul do sénégalais 😢😢❤
Bilay
Notre Amy Colé de retour 🎉❤ Yalnala Yalla doli wérrr🎉
Mâcha ALLAHOU
Amy colle y’a bakh nak y’a meuna weuy borom khol bou sett rek mo meune li tague sa nawlé avec ta belle voix longue vie à toi ❤❤❤❤
Machala amy colé yalna yalla weral bat bi sopé tata viviane yeup contane nagn🎉🎉🎉❤❤❤
Amine ya rabi
Machalla magnifique Amy colle❤❤❤❤❤
Bakh réck mo ame solo machallah Viviane nieup nioko beugue ❤amy ioe tamite kou bakh nga
Ndeysane li dawna sama yaram trop bilahi sama ronkogne yangui touroi😢😢😢😢
Hooo Machalla Un Grand Hommage A Notre Reine Viviane chidid
Ndeysaneee 😭😭😭😭 machallah 🥰❤️
Merci beaucoup❤ amy colle ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Machallah amy colé yallah n'a yallah wéral bat bi li nékhena trop ❤❤❤❤❤
Machallah ❤
#Queen V u deserve it😊
Ligua way sama Vivi hooo🥰🥰🥰 Dina la batrée ay diounii souma fayé 900mil yi ba paré
Viviane Dina contane❤❤
Machallah. Merci beaucoup pour cette belle chanson dédiée à Notre Reine de la Musique Africaine ( Viviane Chidid), l'international sunu Chérif bi Massa Issa Dièye❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalla n’a yalla samela bâte bi werrr
Machallah diéng salla ami ya bakh na fans Viviane yépp partagez li bobou hommage machallah
@@Diarra.vivi. diarra vivi dina lekkl sa leufeul ndaye yaw magui lay reube si deuk bi rk dmrm ji
Manchala rafetna ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amy collée soxoroul dei❤
Exactement elle est pure
❤❤❤❤I I ❤❤ am a ❤❤❤❤❤❤❤
Bilay Li nékhna trop sax❤❤❤ ❤
Bilakhi machallah Amy colle ioe rek Bilakhi ❤❤❤❤
Cherif bi❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😢
Sa voix est extraordinaire machallah ❤️❤️❤️
Super super super super super super super super super super❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wa waw li nékhna way❤❤❤
Le frère de amicole kou bakh leu machalah
Ndeye mary ndiaye gawlo défalône nako papa thione ak fatou guéweul
Ndeyesane yalna yalla fay yéné yissi khôl yiii
Mbakh mo am solo
Pour Viviane aussi et Youssou Ndour 😊
Li nekk way machalla elle mérite
Manchalakh mes amours ❤❤❤
Machallah machallah lii rafatna trop laf that mai amy colé gua balma wayè ligua way Vivi machallah mai yaw AK sa talan manedama guisni menona gueneu nekh yaw danangua machallah
Toutes mes félicitations 🎊 Yalna Yallah werall batbi Tata Amy❤️❤️❤️🙏
Ndeyesan mon artiste préféré amy colle
Machaillha belle chanson la reine tu mérite tt les honneur du monde entier ❤❤❤❤
Ami cole j tm yalna yalla maiye la were bou sakh dakh ❤❤❤❤
li bétouma bilay ❤❤❤❤❤
Machalla
Machalla li nekh na way❤❤🎉❤❤
Ami ligua waye sunu reine taarkala ❤❤❤❤
Mashallah ❤ yaram dawna yaakh déss
Machalla hol cedana yalna diama yague lool ❤❤❤❤❤❤
❤❤❤ nekhhh n'a trop vraiment merci pour ce beau témoignage
Waye nga kou mana waye ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah nilaaa nitki dagnkoy rendre hommage si bimuy doundou ❤❤❤❤❤
Yalna yalla weral sén bat❤
Tata vivi elle le mérite vraiment