ขนาดวิดีโอ: 1280 X 720853 X 480640 X 360
แสดงแผงควบคุมโปรแกรมเล่น
เล่นอัตโนมัติ
เล่นใหม่
Un vrai journaliste il pose les bonnes questions ma sha allah le petit est pétri de talent 💪💪✅
Bilahi mangui Dioy😭😭 tellement damako Niéwante yalna ko yalla defal diam
Momar bon continuation frère 🙏🥰♥️💪💕💞🔥
Yall na la yall diapale lii nèkh na bilaye ❤️✨💍✅
Machallah Momar Gueye laf thiat guoudou fane bou andak diam ak salam thi barkii Seydina Mouhamed sws 🙏❤️🥰
Ndeyssane la partie qu'il chante ses amis et touchant vraiment 😭
Billay
Yala nale yalla defall diamm ak kheweul nga teralll sa yaye
Mashalah gueye fara ma thia ndér matako mathia bayela yalla nala yalla lafal thiate bnne continuation petit frére
Mamita yaaaa wanéé😂😂😂😂😂😂
@@lomamadou4526 Ah tmt li dafa souroumlé. 😂😂😂
Beugnalaa waye ligua wax sii gueyenn yy
Du courage frère, le talent est ça reste les moins. Tu seras un future légende de la musique sénégalaise par la grâce de Dieu
machallah du courage yalla nala yalla may terangau bagua teral say wadiour et continue les études diangeu takhoul nit teki wayé diangual rék bb yalla bakhna
Machaala petit Yalla Nala yalla diapalé 🥰❤️ figuay wowé Say parents touché nama trop😭
Machaala mais Concentre toi sur tes études d’abord c’est important..
Vu son âge Ndeysane sama yaram day daw, machalla Yalla n'a déme fou kawé
Merci beaucoup 💪sidy diop 2 si s sallou bi 😭😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤❤❤🤲🤲🤲
Chante tres bien tu es jeune concentre toi suis tes etudes courage yalla bakhna dina bakh inchall
Wawww he is really good 👏🏽❤️❤️❤️
Le petit est tres posé dalneu.... mais tamite lanimateur aussi fait un bon job dailleur raison pour laquell je me suis aboné
mon fils que Dieu vous protège Longue vie santé bonheurs bonne continuation jeu vous souhaite Longue vie 😁💯💯🤲🤝🙏🤍🤍🤍
Tres intelligent my boiie yala nala yala djapalei Sam la si barkei seydi hadji malick sy❤
Machallah bonne continuation petit frère
Macalla
Tu poses des questions pertinentes
Ousin merci beaucoup à toi aussi tu question ❓ bien machala bonne continuation frere
J'aime bien ce gas sheut bel voir je l'aime bien dall 🤧💞💞💞💞
Mashallah vraiment j’adore ce gamin mais ce présentateur aussi il est vraiment fort ♥️ ték si question you grave lay posè
Bon courage juste concentre toi sur tes études
Momar souba ba legui sa video bi laye sataan di dioye momar gorgor loul dagay dem inchallah
Slt moudié nga nopi wala batay yangi dioy?
Fo tollou si dioy yi nopi nga wala ?
@@boubambaye4946 🤣🤣🤣😅😂
@@yacinenguer1358 ki dafa diongué way 🤣🤣🤣😭
@@boubambaye4946 momar😭😭😭momar😭😭😭momar😭😭😭mala fans maka beug 😭😭😭😭meuneutouma teye samay rongogne 😭😭😭ay momar bokossy 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭yalla nalla boromby soutoural 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭mbegte mbegte 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Yalnako yalla diapale bilay dafma dioylo bilay 💕💕
Macha Allah ndaysane fatéwoul ay mbokame bonne continuation frère
Machallah lén rek lay wakh siii mome bayilén ko khel inchallah day bakh diapal rek momar
Machallah bonne continuation frère ❤️❤️
Ndeyesane mamar gueye machalla laf thiate
Ma Shaa Allah
Machallah pétrie de talent laf thiat bne continuation mais n oublis pas les études
Machalla Yalla nala Yalla defal Diama si Seydina Mouhamed
💓💓💓💓🙏🙏
Moytoul lou Bone te contuné diagbi,te respecté say parent , teye ak yaarr.fobeuga yeug sou nekhé borombi degfa eug.
Machala way nah ay nitameu
Ndeysan boy bii 💪 diambar laaa
Yalla na la yalla lafal thiat
Tu es très telantueux franchement yalla nala yalla diapalé contane dh bliay
Machalla sidy Diop kouko roy Diga mana waye way
Les gens qui disent ce jeune d'aller à l'école bon vous vous ne savez pas qu'il jere ses études où pas mais pas mal
C'est bien alors tant mieux.ligne beugual sougne Rak yi rk lagneko beugual
Démal Diangui mon frère démal diangui
Courage frr mais surtout concentre sur tes études tu as beaucoup de talent continue se lancé 🔥🙏💝
khalé dafa wara djangui kham kham bousi tolo ki wakhléne ay parent deugue
Ah Moy deug Khaler dafa wara diangu boudoul français di dîner gnou wagni Khaler yi gnouy mettre au devant ni wadiour yi gnou bâyi ci khel
Bonne chance
Machala fiston yallana same
Machalla bonne continuation
Khale bi nimouy woye dafmay dioylo
J suis triste vraiment laf thiat rek
Certe. Il a du talent il faut penser à ses études
Sidy daffa bakh
Machallah Yalla nala Yalla barkèle
Machala yalla nalla yalla lafal thiate bonne continuation réussite totale
Jajëf momaar ✌🏾
Momar diambar ga lool wanil kerse gui nak
Machalla
Non machallah ,il l'a du talent
Machala amore lafbouche bonne continuation j'ai les larmes 😢
Deysane khale bi de ndogo lo rek la maye fate Li deysane
Demal séti sa mamyi niou sang laa
Nice
Nouma meuna def ba am numero xalés bi
Neikhna trop
Ma cha ala
♥️♥️♥️♥️♥️👍
Momar rek
Naice
🏃♂️🏃♂️
💪♥️
Va apprendre la music tu dégame trop.
😱😱😱😱😱
Demal ga diage mo gene Sénégal dal dou dem fethie way rek
Jangg taxul ga tékki, jangg bi fayul
Senegal gnifi teker kene diangoufi
Mane diang mo yor rew boulene ko fate dafa tel trop
Li mo takh senegal dou dem khale bou ndaw loumou wara def
Démal diagui moguén si yaw bayi lén khalé yinguéni folo
Copin bayil ki li moy chançam
Demaal janguiii ngay doule nii
Do bayi diambour sa data yaye way
Réwmi fimou dieum moy thiakhan rék kou wara diang l'islam ak alkhouran nax euleuk mat naa soralé
Danko thiatou rek
Ki dou xalé
🥰🥰🥰🥰🥰
Momar fim tok bakhoul kon dou nek en les
Boy damal jangi
Nkhna
Kide mbosom gone moniou sol yapou mak la
boy demal diangui
Cb
Dèmal jangui way✍️✍️✍️✍️✍️✍️
Yaw fim neck ni daradia la la warona feck boul yakhe sa avanire
Démale diangi mo geunne
Jangg taxul ga tékki
Souko.bougoule
Wante gorgour loul deguel sa bopou ta boul khar kene nek si rek amga talan bi
Daga am kersa bam opou ta music buegoul kersa gou bari
Mais cest normal khalela
Wa mais yaw tamite ki 12ans rek la ame aussi c'st normal faut juste l'encourager et le conseiller de continuer les études c tout
@@ndeyendiayendiaye1038 c’est normal kay ki xalé là
@@saintlouis8587 ki si boppam mo doff kidi xalé mounouy sonal ak beuri kersa té boy bi kaw sén dou keersa kerok dako yegeul
@@Enfant_béni_7 non bilahi da ame gnou dof koi mome à 12ans est-ce que mogui done def dara sakh
Sidy diop yakk n’a art bi
Machala bonne continuation mon frère
❤❤❤❤❤❤
Machallah
Machala
Niaw
Un vrai journaliste il pose les bonnes questions ma sha allah le petit est pétri de talent 💪💪✅
Bilahi mangui Dioy😭😭 tellement damako Niéwante yalna ko yalla defal diam
Momar bon continuation frère 🙏🥰♥️💪💕💞🔥
Yall na la yall diapale lii nèkh na bilaye ❤️✨💍✅
Machallah Momar Gueye laf thiat guoudou fane bou andak diam ak salam thi barkii Seydina Mouhamed sws 🙏❤️🥰
Ndeyssane la partie qu'il chante ses amis et touchant vraiment 😭
Billay
Yala nale yalla defall diamm ak kheweul nga teralll sa yaye
Mashalah gueye fara ma thia ndér matako mathia bayela yalla nala yalla lafal thiate bnne continuation petit frére
Mamita yaaaa wanéé😂😂😂😂😂😂
@@lomamadou4526 Ah tmt li dafa souroumlé. 😂😂😂
Beugnalaa waye ligua wax sii gueyenn yy
Du courage frère, le talent est ça reste les moins.
Tu seras un future légende de la musique sénégalaise par la grâce de Dieu