Les promoteurs se plaignent des nouvelles réformes concernant l'heure du grand combat mais je pense que le CNG a bien fait ça va encourager les vrais amateurs de lutte à aller au stade.
Bilahi dég na deg pére palla Serigne biy gnow si lamb bopam lay diay pour woute clients ba paré del micro di wah Di gena diay bopam Come sa Touba nahaté rék😂😂😂😂
Jamaicain boulen niou sonal sen intérêt rek nitt yi daniouy niew lamb mou diex 22h ga guene do am oto dagay dokh b egg sa keur ndax lamb diou goude amateur yi biniouy niew si lamb 18h legui dagn khamni lamb j 23 h la dieum mtx mbeur yi sakh lgui 18 h laniouy neiw ndakh khamni dara doumen si fekk
Pére palla je suis parfaitement d'accord avec vous, les lutteurs passent beaucoup de temps sur kharfafoufa et ça c'est ne pas normale
Merci jam🎉
Wax dji moy 10 combat dafa bari pour bén journée. 5 combats rék donna ci journée
Sa waye mbeure yui légui danio beurri
Les promoteurs se plaignent des nouvelles réformes concernant l'heure du grand combat mais je pense que le CNG a bien fait ça va encourager les vrais amateurs de lutte à aller au stade.
19:30 daffa tell trop 20h 30 sahh
Djieureudieuf paala diop wakhal dee ndakh mou tané
Pére pala lambe 1997 AK lambi taye bokoule normalement grand combat bi 20h00 bakhna si
Normalement 16 a 21 ce très bon pour tout le monde 🎉🎉
Pere Palla Arrête avec lamb demb 😂😂lamb Demb takhoul gua am pourcentage 1 millions
Khamena dé mbeur yiniou nara sanctionné dina beuré ndakh serigne yi nioy sene Yalla
Lolou nak moy problème bi
Mbeur bou douguou dagua wara touss automatiquement 😂😂😂
Pourtant linga wakh nii mo amone mbeur yi dégn dane nieuw rék touss
CNG limou Wakh mou normal sports bou guiss thi adouna bi dafa am heure bomouy commencé am heure bomouy diekh
Tenis 🎾?
Sauf Tennis kone
Généraliser baxoul.
Ce que le cng doit faire c'est chronométrer un nombre exact de minutes entre deux combats
Bilahi dég na deg pére palla Serigne biy gnow si lamb bopam lay diay pour woute clients ba paré del micro di wah Di gena diay bopam Come sa Touba nahaté rék😂😂😂😂
Merci jamaicain
Lamine p3re palla il parle trop d3ko wakh mouyy d3gulou des fois
T3 dou mann kess3 maako wakh aussi
Balla Gaye vs Yekini diexna avant timis
Boulénou fonto nite gni lamb dana diékh nite gni sibilé comantaire té dou goudi 19heur 15 binouléne diokh sakh da goudi
Ioe gnibil gambie
Père palla yaffi nek lamb goudi mome défa méty en plus boy yii dégniy agresser rek
Cng noum déf mome vraiment daye yakh lamb
Boy bi dafa yebate bilahi yow deuko Sénégal ba pare Lou niewe mou kasa
Jamm yénako maggg ms eupolen ko xel machala jammm
Jamaïcain feekké ngua 1997 nak boul fenn waay 😎😎😎😎
pere palla ak jamaicain 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
JAMAICAIN. LIMOU WAKH DEUG LA ..PETIT COMBAT DOU DEM 22H
Lambji Boulene niou sonal 19 h doyna seuk sen intérêt rk vous êtes égoïstes le monde de la lutte
Jamaïcain demal fay xalisou amanekh
Jamaïcain waxna deug. Gni gno beug wakh lamb demb
Jaïm waxna deug
🤣🤣🤣🤣lamine vrais defean la yi moko nekh
Jam rewna 😂😂
Camaicain vrai ngaaka la
C pas vrai billet 300amoul woone1997
Jamaicain boulen niou sonal sen intérêt rek nitt yi daniouy niew lamb mou diex 22h ga guene do am oto dagay dokh b egg sa keur ndax lamb diou goude amateur yi biniouy niew si lamb 18h legui dagn khamni lamb j 23 h la dieum mtx mbeur yi sakh lgui 18 h laniouy neiw ndakh khamni dara doumen si fekk
Jamaicain yaw sa interet rek
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Jamaïcain momm dafa doff vraiment
Dofff bou makk khamoul bopam
Balla Gaye vs Yekini diexna avant timis