Ndeysane c'était mon DG plus qu'un DG c'est un frère liniouko lekal meunenako may nite tei ken dou yeug walaxiii daniouko togne rekkkk !!! Koudoul bokam dimbeulinala mane en personne bimay voyager dafmaniii boudei djeundago billet bayil ma djeundeko maniko djeundena mba paré mounima waxxma loy sokhla une fois labas ...bilaxii kou la birr la kou oyoff, kou xam akk employés masta mon frère yalna yalla done sa avocat bon courage ✌️✌️✌️✌️✌️
@@ndiemendiaye9979 bilaxxii nite gueunouko si adouna walakhii soudone nieup bureau soko guissé doniii moyy DG tellement qu'il est modeste . Dalay may xalish tei ken dou yeug, dalay fay mba mayla barki al hourane nitte kassé mo nkk niii daniouko togne rekkk motakhh mou waxx mais dou waxx kat..
Un travailleur un mouride pure et dure.... Vraiment vous ne méritez pas cela... Reconstruisez votre entreprise inchalah... Yallah khole lay faye.... 🙏 🙏 🙏 🙏
Bayilen lingeni wakh lou bone si khett yeupe la am amoul wolof amoul serere amoul peul lou bone ak lou bakh fepp la amé yalla na yalla doli soutoureu rek
Bllhi digua guiss kouko geune insha Allah Force à toi Bro 💕 Yalla mogui guiss lepp bonn ak niakk fayda ak beugue lou bonn li mo niaw bllhi Boul wax ak mome nah Charia danni djguenn bou ndiallo dagne ko wara ray mais malheureusement Sénégal douniou deff lolou Mais amal sa fouleu dh amal sa fouleu
@@aisatoudiop2298 boul généraliser s’il te plaît. Est ce Mbathio Ndiaye peulh fouta la ??? Il faut arrêter de généraliser, kou bone dagua bone , kou bqkh daguèye bakh rek!!!
On connait tous le senegal khamoul kou togne... Kou fayou la khame... Tu construit ton entreprise... Tu trouve une femme tu la construis.... Mou deme baa sibir dila danel di dém si yénéne goor.. Lolou daffa niaw... Limotakh sounou joueur yi di takk toubab... Sénégalais loulay danél rek lay weur
Mbone fép la am dou nite kou nioul dou toubab, bayiléne compléxé. Qui parle de mariage parle d'infidélité ou d'adultére et c'est condamnable pour l'homme et la femme. Goor yi am diabar gui teudé xaleyou djiguéne gni té kéne yobou wouléne tribunal ish. Diaroul wone siweul comme que amna niou ay doom, ndax fi Sénégal yalla boumou am ay doom you djiguéne nak douniou guawa diar dh mba bouniou diaré dinaniou léne xassé séne yaye da amone dieukeur ak far et moindre faux pas niou bolé léne thi. Wakh dji moy dieukeur ak diabar danioukoy tane, yéne beuguo léne lou bakh, na xéss na mole da diék, physique baléne guena intéréssé soléne paré di sonal nite yi alors que xam guéne boubax fi niou bakh gni nék, ish. De même aue djiguéne gni kou yoor diantal laniouy weur, Ish. Fi dal kouy seuy nianl ya allah bolé leu ak kou am diné comme niko yonnente bi saws waxé wone moy li guene,ndax kou ragual yalla dina diomalé boppam lou beuri moy goor commr djiguéne nak, mais seuy mom nak lathi xéwi euleuk ya allah rek ko xam mouy goor di djiguéne daniouy niane yalla bolé niou ak ki guene thi nioune moy l'essentiel.
Niata jouer la séne diabarou toubab danél🤣🤣🤣 kone iow wéro dh. Bone ak Bakh thi nite douthi appartenance raciale, ni ethnique, ni religieuse. Yalla na Ya Allah mousseul té moutieul niou🙏
A mon avis il devait récupérer les biens que la femme lui a pris et ensuite la libérer . C'est très dur, mais il ne devait pas publier l'adultère.parce qu'il a détruit la vie de ses enfants innocents et une partie de la sienne parce ce que partout on parlera de sa femme et de ses enfants,on prononcera son nom.
May len gnou diam jiguene moy outal domam waye dou goor ,yena wala sopi sen dokhalin yen jiguene gni danguen di def linguen def ba pare di victimiser wou
Soutoura dara wadji liko dal da guene khame foumou ko tolou koume fi dalone dinala meti mome mo guisseul bopam diabaram mouy adultère yorna ayyy preuve diokhna ko juge bi lou guene beuguate tamit et dans tous ça femme bi lolen diko wakh tamit
😂😂néna li bokoul si destin wame hey Mr sa destin yoroko dé le Mr a dis une chose il dis que dako foto sa femme si hôtel avec un homme mais wakhoul dafko fékeu si kaw goreu Sénégal 🇸🇳 mom Suniu né pripeu niou khass les femmes bon Bne chance
Tu devais libérer ta femme té soutouralka té yalla takh comme un vrai gentleman à cause des enfants, woutalgua tes enfants khass boudoul fay , t’as fais une erreur mon frère. Courage à toi
Mai pourquoi Sénégal khamou niou kou togne mai kou fayou nguen kham Bilahi dafa am ndjguen you bonne vraiment sa Dieukeur defal Teranga bi yeup ngakoy trahis
Sa way nopil aye j'aime rek gua begue ki limou def nii mo geune mou rayko deuk bi dafa ame yone té si yone lako yobe voilà bou léne niou sonal boula dalone doko ball wakh rek bfff
Sa diabar tayouko ay none you bone nolene yakal rek boulko sourrrrr !!! Sa diabar dane ko utiliser si lima guissss franchement c est un monté yaw nak yaye❤kilifa donc koula bagne sa sey❤lay gnieuk tasss dof lo la pour meune atteindre son objectif et fais attention bou darra khewei malako niane bilahi khamoula khamouma sa diabar mais j t ai écouté sur theme de la semaine jc k kou bax nga sa soxna aussi kou bax la none mo doxx sene diganteii ndax khalisss
Vraiment je te suis depuis le début de l'histoire mais à t'entendre parler on voit une personne qui à toutes les armes pour ce battre avec la mère de ces enfants même si le problème est réglé et que la Damme est condamnée tu ne sera jamais tranquille
Si j'étais vous je ferai tout pour interview la femme cars il faut toujours écouter les deux camps avant de juger la femme. Nakh nitte dafa lundeum trop wallahi
Serigne mbacke bo guissé sama message,..... Dama beugone gua dém tfm émission jakarlo... Gnou déf débat bou yatou way am solo lol si khalate tou adouna 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪
Un homme, un vrai, un bon Sénégalais, ne réagit pas comme ça, tu pouvais la libérer dans la diplomatie. LAHOU, beug soutoura mo takh mou lath témoins thi adultère. Soutoura mo takh mou binde goudi ak beuthieuk.
Waxo fiii dara yaaaw sunu borom mo ndieukk bagn Togn nga nane ayy soutoureu fiii maylene niou wayyy sa genre gui rekk nio yakkk deukkk bii akk sen Soutoureu à la Con wesh
Vous êtes libre d'aller au tribunal cher monsieur pour clarifier cette affaire mais à Quoi bon vous exposer et à accorder des interviews comme ça ? On aura tout vu dans cette vie, d'autres ont vécu pire que vous et l'ont géré dans la plus grande discrétion
Ak loumana am yalla rèk mo kham fi deug fètè wayè djiguène dèskoy soutoural djiguène boko wolotoul bayiko mou dèm rawatina mou dioureul leu ay dom ndakh dom yim la dioureul bakanam khadione nasi
Ndeysane c'était mon DG plus qu'un DG c'est un frère liniouko lekal meunenako may nite tei ken dou yeug walaxiii daniouko togne rekkkk !!! Koudoul bokam dimbeulinala mane en personne bimay voyager dafmaniii boudei djeundago billet bayil ma djeundeko maniko djeundena mba paré mounima waxxma loy sokhla une fois labas ...bilaxii kou la birr la kou oyoff, kou xam akk employés masta mon frère yalna yalla done sa avocat bon courage ✌️✌️✌️✌️✌️
Ndeysan yawit ku bakh nga prck témoiniage bi nga def ku bakh rek moka mane
@@ndiemendiaye9979 bilaxxii nite gueunouko si adouna walakhii soudone nieup bureau soko guissé doniii moyy DG tellement qu'il est modeste . Dalay may xalish tei ken dou yeug, dalay fay mba mayla barki al hourane nitte kassé mo nkk niii daniouko togne rekkk motakhh mou waxx mais dou waxx kat..
Wayé Manon na sor diaborgui li dientiko té dou méll ni
Il travaille dans Quoi ndeyssan si c'est vrai Dee qui jamais il n'aura confiance en aucune femme
Stp son numéro
Justice divine tu es brave un exemple pour les autres couples
Je compatis frère yallah na la Ya Rabbi May Ndam Rek 🙏 inchah Allah
Allahuma sali hala seydina Mouhamed yallah naniou Yallah khiir thilou bakh...doliniou soutourah
Aminn way
Un travailleur un mouride pure et dure.... Vraiment vous ne méritez pas cela... Reconstruisez votre entreprise inchalah... Yallah khole lay faye.... 🙏 🙏 🙏 🙏
walahi li nga wakhe mo âme bro mai yalla nala yalla takhawou
Yallana yalla amy diambar bou guéne ti yaw
Vraiment j'ai écoute ton problems depui longue temps c'est fatigua que le bon dieux te vienn en aide
Il a raison liko soxnassi déff dafa métii
Serigne qu'allah t'accompagne dans cette épreuve yalla bakna mon fils ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋💪💪💪💪💪💥💥💥🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
De tout coeur avec toi yala naniou yala mousseul si jiguéne bou bonn
Amiiiiiiiiiiiiiine
Bravo à toi tu fais tous l boulot à la des enquêteurs mais continue à être positif Allah a tout vu et justice sera faite
Bon courage
J'ai suivi cette histoire sur la chaine xalat tv mais le gas est courageux et patient force à lui
Svp c’est quoi le titre de la vidéo guissoumako ci chaîne bi
@@missndiaye1594 smbg
Bayilen lingeni wakh lou bone si khett yeupe la am amoul wolof amoul serere amoul peul lou bone ak lou bakh fepp la amé yalla na yalla doli soutoureu rek
Bilaye walay
tu as raison dans toutes les races ceci existe !!!
Amna fepp
Frère par expérience..... Bilahi peul daa meuneu worrr
@@laminedieng9951 aye fène gua wakh, dans toute les races il y’a des bonne et des mauvaises.wassalam
Yalla nagnou borome bi yokou soutoura adouna akk allahiri Amine ya rabbi
Courage a vous mon frère je vous suis depuis le début des problèmes
Ou suivre depuis le début le problème ?je veux vraiment comprendre
@@sallaicha8845 regarde sur youtube vous verrez les vidéos inchallah
Mane fattè wone Na koo sax pour mane li dialle Na bou yague ..Li aye tappalè nion Si nèc kham naniou kou tonie
@@mamecheikhsylla4431 wallay la femme Est fotif vraiment djiguene doynaware
Diégual ko rék tei yalla takh iow borome karaw bou nioule nga niakoo dra li lép leçon de vie la yalna Yalla mayla xoloup mougn
Il faut voir le côté de l homme il a des sentiments et il est blessé personne ne veut être la risée de personne
À chaque fois que je t'écoute j'ai les larmes 😢 😢 aux yeux vraiment c'est triste bro que Dieu te vient en aide
Vérité absolue🙏🙏🙏
Il n’y avait 1 Y à qui est délégué venue pour Hugo et Magni❤️❤️❤️ se connecte Lights correctives ni Snap arrête là et il ne connaît
Machala du courage mon frère j’ai suivi votre problème depuis longtemps que dieu vous protège
Bllhi digua guiss kouko geune insha Allah
Force à toi Bro 💕
Yalla mogui guiss lepp bonn ak niakk fayda ak beugue lou bonn li mo niaw bllhi
Boul wax ak mome nah Charia danni djguenn bou ndiallo dagne ko wara ray mais malheureusement Sénégal douniou deff lolou
Mais amal sa fouleu dh amal sa fouleu
Ndeyssane addouna
Mon ami mon frère ioe diam rek ngay ame inchalla niogui sa guinaw mousou nioula xame si thiow vraiment
Il faut comprendre la tromperie traumatisme te fait perdre confiance en toi tu vois en lui la souffrance en silence force en toi❤️
Ça c’est vrai ça traumatise
Peulh Guinnee yi Diallo yi ay vrai bandit lan ay
@@aisatoudiop2298 boul généraliser s’il te plaît. Est ce Mbathio Ndiaye peulh fouta la ??? Il faut arrêter de généraliser, kou bone dagua bone , kou bqkh daguèye bakh rek!!!
@@lapaix4523 bilahi walahi
Non Sénégal dugnu dem .. Wadji c’est un brave type et très intelligent de surcroit.. Yalnala yalla takhawu baga dioth si sa alal inechalah !!!
Bro liguéyal continue Yalla bakhna yalna yalla mayla lou ope lolll barké cheikhoul khadim 😭
Serigne nit kou bakh nga yalla nala yalla diapale
Un monsieur courageux
Nitte kou bakhe moye mbacke du courage borom doubai
Serigne mbacke nope nala dé kay Tak ma
Massa way mn frère metina trop yalla nalene sounou broume dafale diam teguele lene diafei diafei yi yeupeu metina
Serigne mbacke yalla nala Yalla takhwou dam rék bou nékhé yalla
Khana trompé woo kou mignon kii dh😂😍 ak yeuy chewing-gum bi wa bakhna
Massa Yallah nala Yallah takhawou force à toi ❤️🙏🏾
Le pauvre ... j ai vraiment de la peine pour lui
On connait tous le senegal khamoul kou togne... Kou fayou la khame... Tu construit ton entreprise... Tu trouve une femme tu la construis.... Mou deme baa sibir dila danel di dém si yénéne goor.. Lolou daffa niaw... Limotakh sounou joueur yi di takk toubab... Sénégalais loulay danél rek lay weur
😂😂😂😂😂😂 Ray ngama
Mbone fép la am dou nite kou nioul dou toubab, bayiléne compléxé. Qui parle de mariage parle d'infidélité ou d'adultére et c'est condamnable pour l'homme et la femme. Goor yi am diabar gui teudé xaleyou djiguéne gni té kéne yobou wouléne tribunal ish.
Diaroul wone siweul comme que amna niou ay doom, ndax fi Sénégal yalla boumou am ay doom you djiguéne nak douniou guawa diar dh mba bouniou diaré dinaniou léne xassé séne yaye da amone dieukeur ak far et moindre faux pas niou bolé léne thi.
Wakh dji moy dieukeur ak diabar danioukoy tane, yéne beuguo léne lou bakh, na xéss na mole da diék, physique baléne guena intéréssé soléne paré di sonal nite yi alors que xam guéne boubax fi niou bakh gni nék, ish. De même aue djiguéne gni kou yoor diantal laniouy weur, Ish.
Fi dal kouy seuy nianl ya allah bolé leu ak kou am diné comme niko yonnente bi saws waxé wone moy li guene,ndax kou ragual yalla dina diomalé boppam lou beuri moy goor commr djiguéne nak, mais seuy mom nak lathi xéwi euleuk ya allah rek ko xam mouy goor di djiguéne daniouy niane yalla bolé niou ak ki guene thi nioune moy l'essentiel.
Niata jouer la séne diabarou toubab danél🤣🤣🤣 kone iow wéro dh. Bone ak Bakh thi nite douthi appartenance raciale, ni ethnique, ni religieuse. Yalla na Ya Allah mousseul té moutieul niou🙏
@@LaBarhamienne sa texte bi da goude torop.... Awma temps Diko lire 🙄
A mon avis il devait récupérer les biens que la femme lui a pris et ensuite la libérer . C'est très dur, mais il ne devait pas publier l'adultère.parce qu'il a détruit la vie de ses enfants innocents et une partie de la sienne parce ce que partout on parlera de sa femme et de ses enfants,on prononcera son nom.
Mrcii ba paré dome yii dagnuy ame way boudul faye waroul wone khol lii femme bii df rk m thie domame yii
Wa yén hana hamolen ni liguey metiwé hana ?
Damay lathié rk…
@@leralkhassidayi4746 déleine rafetale t Bayii yok problme di guena tale rk
May len gnou diam jiguene moy outal domam waye dou goor ,yena wala sopi sen dokhalin yen jiguene gni danguen di def linguen def ba pare di victimiser wou
serigne mbacke inchala yalla dinala maye ndam
Yallana yalla léral lép frère du courage yaw diam rék thi yaw
CE QUI EST DÉPLORABLE DANS CETTE PROBLÈME C'EST LES ENFANTS ET CE VIDÉO RESTERA GRAVÉ A JAMAIS DANS LES RÉSEAUX SOCIAUX
Massa way. Yalla bakh naa inshallah. Que le bon Dieu me pardonne on dit souvent Les peuls C'est des!!! Pas tout mais la majeure partie.
Soutouralal sa sohkna té yalla rék tahk yalla soutouralal.
Franchement
Billahi, lui n a pas compris car il n est pas bon musulman yalla soutoura akk maandu mô taakh mounée 4 personnes gnookoo warra guiss
Soutoura dara wadji liko dal da guene khame foumou ko tolou koume fi dalone dinala meti mome mo guisseul bopam diabaram mouy adultère yorna ayyy preuve diokhna ko juge bi lou guene beuguate tamit et dans tous ça femme bi lolen diko wakh tamit
@@malickgueye3188 si c’est vrai femme bi limakoye wakh moye ( bonne na) Té Niakh barké.
Mais le gars ne devait pas l’exposer à cause de ces enfants
@@lapaix4523 saway dafa nekoul yaw rek té nitt gni yamouniou kou djiguen ki es k khôl na si ay domame bamouy def li
Serigne mbacke YAllah nala Yallah maye ndame diambar nga Depuis un an mangui deuglou sa video khamne nit kou bakh nga
Je compatis avec toi mon frère. Soit brave.mètina trop
Do léne bayi begue lou xéss rek doxléne rek mane dé noire 🖤 rek ma nga thia sérér ya
🤣🤣🤣
😂😂
@@InfosetTutos degue dou rombi nopou
@@mamansokhnafall1316 ba lima wax lolu ngay wakh
😂😂😂
Serigne balko Adouna Amoul solo svp tournel page bi
Djèguelèl
Courage bro Sénégal mome li moko yak sounékone fem bi la dal sounou feminste yisi rew mi commencer di conférence de press
😂😂néna li bokoul si destin wame hey Mr sa destin yoroko dé le Mr a dis une chose il dis que dako foto sa femme si hôtel avec un homme mais wakhoul dafko fékeu si kaw goreu Sénégal 🇸🇳 mom Suniu né pripeu niou khass les femmes bon Bne chance
Toi la esk cava une femme marié à l’hôtel avec un homme tu trouve ça normal n’importe quoi
Ioe moom weroo ay wakhou doff rek guafii wakh
Waww sokhna sii soo guisonnn saa borom keur hôtel akk benee femme noyy defff ?
Courage a toi freroo yall nala yalla sammeu doolel leu yokk leuhh 🙏🏽🙏🏽
Amen
Mon frere IL y.a des femmes tres dangereuse dans ce bas monde.que le bon dieu te donne un bon Coeur.. j.ai vecu pure que sa.
Pure que adultère oohhh massa
Pure que adultère oohhh massa
Dieux va faire son jugement il faut pardonne en tant que musulman mon frère long vie à toi que dieux vous protégez ça ira inchallha dieux et grand 🙏
SÉNÉGAL DA BARY AY DEMOU NOHOR ME DU COURAGE MON FRERER
Yow dé mala yéné gagner ba sagar hingn.
Ndawsi yalna déé réék
Mon frère même bou juge bi atéwoul yallah dina até inchallah
Sama hol bangui tang dieur dieur💣💣💣💥💥 woooy amena louma nakari.
Ndawsi moo deug deug
Massa c’est très dur ndeysane
Mbacké du courage que dieu avec toi
Courage frère yomboul
Yalla nala yalla doolel
Tu est tellement brave frère
Thiott ndeye peulh Guinnee yi Diallo yi ay vrai domouram lan jeunes sénégalais yi bayilen takk Guinnee yii
Tu devais libérer ta femme té soutouralka té yalla takh comme un vrai gentleman à cause des enfants, woutalgua tes enfants khass boudoul fay , t’as fais une erreur mon frère. Courage à toi
Mai pourquoi Sénégal khamou niou kou togne mai kou fayou nguen kham Bilahi dafa am ndjguen you bonne vraiment sa Dieukeur defal Teranga bi yeup ngakoy trahis
Mani djiguéne la mais ki diaroul soutoural mo togne ayy domame mo khawi soutouram té dafa wate si kamil lou nekk deug
Ki baxoul ken warouka soutoural
Sa way nopil aye j'aime rek gua begue ki limou def nii mo geune mou rayko deuk bi dafa ame yone té si yone lako yobe voilà bou léne niou sonal boula dalone doko ball wakh rek bfff
Non suis désolé mais femme bi moo outeul dom yi khass soutoureu nit mokoy outeul bopam
Force a toi Grand frère
Aaay way ana ngor si mim réw ,koula diapalé takhawula nga défko lii,thiey aduna ngi nonu kumuko diaral dieuleul
Je vous suis depuis le départ 2020 mais t'es un homme brave 🙏
Que justice soit faite ont du courage 🙏🏿
Kay dieulma ma seyal la lou adouna di thiow Bilahi walahi barkep serigne touba
Waw coumba dinalako may
Chiip
@@cadiortvgueye8945 inchalah
@@ousmanecisse498 thip dh yawit
😃
Sa diabar tayouko ay none you bone nolene yakal rek boulko sourrrrr !!! Sa diabar dane ko utiliser si lima guissss franchement c est un monté yaw nak yaye❤kilifa donc koula bagne sa sey❤lay gnieuk tasss dof lo la pour meune atteindre son objectif et fais attention bou darra khewei malako niane bilahi khamoula khamouma sa diabar mais j t ai écouté sur theme de la semaine jc k kou bax nga sa soxna aussi kou bax la none mo doxx sene diganteii ndax khalisss
Bilay li méti a torop li kay dou sokhar ya nék si deugg bilahi 🥺
Wa dji nimoiy wakher khôl bi dafa tangue. Mais franchement vu qu'ils ont des enfants ils aurait pas du donner autant de détails.
J'espère que amo lénn ndiabote rek ndakh li images boye dess a jamais le té soudé vous avez des enfants moune na lénn perturbé demain
Si amenagn 4 dome
TRAHIR AKA MÉTI
Yalla nala Yalla May kolou mougne frere masta
Vraiment je te suis depuis le début de l'histoire mais à t'entendre parler on voit une personne qui à toutes les armes pour ce battre avec la mère de ces enfants même si le problème est réglé et que la Damme est condamnée tu ne sera jamais tranquille
Il ne fera plus confiance à une femme.
Vérite absolument
Macha allah sa takha way rafaite na
Massa Massa métina....thieuy adouna do kham sakh loy wakh,adouna métina avocat yi tamit naniouy khôl si yalla ,ndiallo koukoy far farro thjilou bakh
Si j'étais vous je ferai tout pour interview la femme cars il faut toujours écouter les deux camps avant de juger la femme. Nakh nitte dafa lundeum trop wallahi
FEMME DI DEFNA INTERVIEW XALASS,,mais soko déguon mouy wakh danguay wakh ni wadji kou bon leu,,,,djigueen bou meuneu doul
Serigne mbacke bo guissé sama message,..... Dama beugone gua dém tfm émission jakarlo... Gnou déf débat bou yatou way am solo lol si khalate tou adouna 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪
walahi yalla na niou yalla diégal si barké séringe babkar s'y bambél diar na khalate
Kola mayati domam de xana ak nitem Desna li dafa rouslo
Justice pour ce gars ndeysanne
Courage frére on est dériér de toi❤️ li nieup wakh Moy deugue
Il es trop fort
Bo demandé wone do dougou si peulefoute bakhouniou wor rek lolou sene derete la même bouniou amai dieukeur daniouy deme fenene lalante
Soubhanalah yangui bakar
Lou lére Gua wah
Yagg na degg lolou
Nama yalla ball Ms sen djiko la daniouy fooo
Moo toogne bopam kone
Gni hana amougn dome😂😂😂😂
Même bouder deugue ki d'où nite pour tousse gnata Sèye mot tasse ci soutoura
Mais dako done sathie elle voulait détruire sa vie bayileine nafekh
Yen dimalilen niou nafek guen trop
@@bambaniang1271 wakhal sa khalate th civilisée nafekh ken douko wakh KO khamoul
Soutoura égal nafekh dioulite dou fenn
Yallanala yalla may kholou mougne
Un homme, un vrai, un bon Sénégalais, ne réagit pas comme ça, tu pouvais la libérer dans la diplomatie. LAHOU, beug soutoura mo takh mou lath témoins thi adultère. Soutoura mo takh mou binde goudi ak beuthieuk.
Waxo fiii dara yaaaw sunu borom mo ndieukk bagn Togn nga nane ayy soutoureu fiii maylene niou wayyy sa genre gui rekk nio yakkk deukkk bii akk sen Soutoureu à la Con wesh
@@abdourahmanendiaye8441 Sénégal mo beurri aye naféx déf say n'diombé ba paré di waax waxi soutoura
Wallahi ta raison.il pouvait régler ça bamou soti té dou dem si média yiii.legi dal les problèmes se règlent devant les médias.niaw naaaa
Sa genre gui rek nioy Def niombé Yi di lakatou si guinaw soutoura
Bilaaye waah ngaa deugg sougnou borrome daffa beugg soutoura, donté ta femme t a trompé il faut savoir pardonné yallaa mooye défarre doomou adama liingaa yoore mollakoo djookh komme dangakoo sourre baayiko mou deemme c est mieux niitte keenne doukoo weerre.
Courage mon frère
Yalla nala yalla meye kholou mougn
C dure vrément mais yalla bakhna
Yalla naa Yalla mouseul nou sii djiguene bou bonne
Yalla nala yalla samou
Courage mon frère mais soutoura c'est très important.
Ndayssane 😭 yalla na Yalla defal Sotou ra
Vous êtes libre d'aller au tribunal cher monsieur pour clarifier cette affaire mais à Quoi bon vous exposer et à accorder des interviews comme ça ? On aura tout vu dans cette vie, d'autres ont vécu pire que vous et l'ont géré dans la plus grande discrétion
Ak loumana am yalla rèk mo kham fi deug fètè wayè djiguène dèskoy soutoural djiguène boko wolotoul bayiko mou dèm rawatina mou dioureul leu ay dom ndakh dom yim la dioureul bakanam khadione nasi
Courage frère... Djiguén gnii dano dooyy warr
Courage frère qu'allah facilite
En tout cas tu pouvais la libérer en toute discrétion mo geune nga nek thi media yi di wakh té ngéne ame aye dome li niawna trop langue de vipère
Vraiment des paroles de diable
Lii niaaw tchi femme bi leu diougué il faut savoir appréhender les choses
Katy Diop dimbeuli lein niou danguay am diabar mouy katanté founek,,bangua diap ko sa genre yi naan soutoureu va fan culo way