Ziare Serigne bi cest ma premiere video gnre mom la ndieuk ctane ci chaine bi jai preferei commncei par la referance SEYDINA MOUHAMMAD PSL...breif pour dire tout simpleman k jai kiffei avan mm d l visionnei teilman je suis contan de decouvrir cette chaine...Oustaz Ahmad Fall merci euh E Daara Diaspora sa kaw sa kanam Mansour yalna nga ndirou ak sa tourando borom daara dji ci leipeuh inchalla dieureudieuf contane bou bakh ci ioe 🙏🙏🙏
Sopou guimala sopou manak yalla rék nioko khame, serigne mansour yalla na yalla sammela, défal la tawfékh, ak mouthiou, aral la bopam thi barké seydina Moukhamad (psl).
Machallah ❤❤❤❤ je suis trop contente ❤❤❤
Man oustaz oustaz Ahmed ba rek lakoy kholi alkhamnolilahi ❤
Ziare Serigne bi cest ma premiere video gnre mom la ndieuk ctane ci chaine bi jai preferei commncei par la referance SEYDINA MOUHAMMAD PSL...breif pour dire tout simpleman k jai kiffei avan mm d l visionnei teilman je suis contan de decouvrir cette chaine...Oustaz Ahmad Fall merci euh E Daara Diaspora sa kaw sa kanam Mansour yalna nga ndirou ak sa tourando borom daara dji ci leipeuh inchalla dieureudieuf contane bou bakh ci ioe 🙏🙏🙏
Fa Tabarakallahou 😍 Yalla na Yalla Barkeil 🤲
Je sens de la profondeur. 'Ilmou zawkh. Mashallah
Laylatul qadr moy Seydina Mouhamad jarneu firiiii dehh
Machallah sama serigne yallna yalla takhawou la Bijahi Rassoulilah ❤🤲🏾
Mashallah serigne bii yalnah borom bi takhawou leu. Rabbi zidnik 'ilmaa
Ma challa ❤❤❤
Macha Allah ❤❤❤
Sopou guimala sopou manak yalla rék nioko khame, serigne mansour yalla na yalla sammela, défal la tawfékh, ak mouthiou, aral la bopam thi barké seydina Moukhamad (psl).
Essaye qu'on puisse télécharger
Macha Allahou ❤
Activél mode télécharger
hadj mansour nionguila siar dila jajeufeul thi njangalé mi
Niongui laye niane nga dimbeuli niou thi khantaratoul mourid comme seydil hadj malick mome laniou jaglél nioune gni nekk thi woutouk xam-xam