Urgent - Balla Gaye 2 répond et traite Modou Lô de tous les noms : "souma guissè day..."

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 3 ก.พ. 2025

ความคิดเห็น • 270

  • @serignefalloudiongue
    @serignefalloudiongue 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +32

    Lima nekh si balla moy day wakh ba paré di ré😂😂😂

    • @bassdiokhane1472
      @bassdiokhane1472 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

      Dara safou kon togne 😂😂😂

    • @khadimsow7149
      @khadimsow7149 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      😂

    • @khadimsow7149
      @khadimsow7149 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Gni ko bang la yereum 😂

    • @PapaDieye-ym1tf
      @PapaDieye-ym1tf 4 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Balla sisoumane ga rèk gaïndè gou magète ga lolou mo âme 😂😂😂😂😂😂mècontemps ga

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +36

    Ndeysane xol bi mo booone modou lo roi des arènes ngaye bagna dègg par la force dinko dègg😂😂

    • @sadgametv2538
      @sadgametv2538 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

      Lamb ji beneu mbeur mo fi Bonn khol té moy diouteul lo

    • @HAVIS_MARAM
      @HAVIS_MARAM 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Bilae xôl bi mo bon😂😂

    • @mouhamedcherifaidara923
      @mouhamedcherifaidara923 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      @@HAVIS_MARAM bayiko fofou dinako nopale😂😂

  • @serignefalloudiongue
    @serignefalloudiongue 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +21

    Modou balla nèna gua tagou sa yaye ba paré 😂😂

  • @Mahatmaga
    @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +31

    Balla bilay dayy Sisou lutaxx Boy niang wax lako nguay Xoff dieunde Galasss😂😂

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

      Kokou dano sékhone contra té modou sékhounou dara

  • @DJLeeral
    @DJLeeral 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +10

    Balla ❤Seul
    Modou sissou man leu 😂😂😂

  • @AgjkfdghFgftyfch
    @AgjkfdghFgftyfch 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +8

    Bilahi balla gaye kou rew leu 😂😂😂

  • @yaalasadio
    @yaalasadio 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    Xol na ba xol mais Balla Gaye dafa soxor 😂 xolam mooo djekhhh !!!
    Balla mougnal Modou Lo moy Roi

  • @amadinopapounigueye9296
    @amadinopapounigueye9296 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +9

    Vraiment Balla moy lamb ❤.
    Ama na gueune guaw si ioaw, ya meune, ya eupu dolé, ya dakh beuré té yaye dane inchallah.
    Lamb dji socé yi ñioko mome💪🏽.

    • @DioufJérôme
      @DioufJérôme 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Wakho deug dhé

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +27

    Béne video 30s rk nga def interview plus de 20 mn thiey modou dall moy ndanane 🎉

    • @RidialDieng-h2n
      @RidialDieng-h2n 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Sa way wakh lén deug mod lo mo togn na digéré djoutal bi

    • @kaas1610
      @kaas1610 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      😂😂😂

  • @baymoussandiaye8310
    @baymoussandiaye8310 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +25

    Bilahi modou amoul ragalou kay mes yako man pask yako dan 2x me modou dou ragal jamais

    • @icAlphaDiallo
      @icAlphaDiallo 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Wakho degg dé dioutal lo🤣
      Mo ngi wiri wiri rek Mais yag yag di nan beuré mais Balla tamit nékhoul niémé nak😂

  • @Mahatmaga
    @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +11

    Balla néna Siteu moy Rou des arènes 😂🤣🤣

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +11

    Balla gaye deux papaye modou lô

  • @Ibnoucisse24
    @Ibnoucisse24 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +15

    Balla Gaye2 dane na Modou lo Stade Demba Diop ngour Abdoulaye Wade 🔥 dioutalko stade Léopold sedar Senghor ngour Macky sall🔥mou déss Aréne national ngour président Diomaye 😅😅😅thiéye Balla Gaye2 🔥

    • @SyAmadou-y7k
      @SyAmadou-y7k 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

      MAIS BOUL FATTÉ EUMEU SENE DIOUTAL NA NDAYAM DEMBA DIOP DOXAN NDAYAM NGOUROU WADE

    • @dembaztarkinda8270
      @dembaztarkinda8270 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Balla moye bayou Modou Lo

    • @MaodoSeck-u7d
      @MaodoSeck-u7d 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      J'aime ma mère😊

    • @FallouLo-d1r
      @FallouLo-d1r 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      ​@SyAmadou-y7kfi balla ak modou lani wakh sa souniou wakh rèk ngè wout walou 😂

    • @dembaztarkinda8270
      @dembaztarkinda8270 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      @@FallouLo-d1r vraiment daniouy outi walou sasouné😂😂😂

  • @Mahatmaga
    @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +65

    Président FIFA dou moromou président ODCAV 😂 Xaragne Lô 𝑻𝑯𝑬 𝑶𝑵𝑳𝒀 𝑲𝑰𝑵𝑮🤴🏾🥇❤️🫡

    • @AssaneFall-m4c
      @AssaneFall-m4c 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +12

      Prèsident odcav sou nokè président fifa louniou si meun😂

    • @Papa-s3g
      @Papa-s3g 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Wax nga lep nit meun nala raw doula metti mais soko rawé mou ropi la fo tol dangay mer

    • @Papa-s3g
      @Papa-s3g 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +6

      @AssaneFall-m4c yen dangena retard 11 ans 8 combat 4 victoire 4 défaites modou lo si 1ans rek 3victoire 😂pomme dou new MODOU LO LE MEILLEUR LUTTEUR DE TOUS LES TEMPS

    • @AssaneFall-m4c
      @AssaneFall-m4c 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      @Papa-s3g amo lène kilifeu sèn yaye nèna guène bayi balla😂daf lène ni dioutal dè

    • @RidialDieng-h2n
      @RidialDieng-h2n 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Dane bi gueuneu réy modou lo lanouko dane djoutal😢😢😂

  • @falloundiaye3120
    @falloundiaye3120 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    Balla da sokhor nak khôl bii mo bonne meunoul supporter Modou Lo nek roi des arène

  • @Misterboom-x7x
    @Misterboom-x7x 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    Siteu siteu leu ❤

  • @OlivierGomis-n3d
    @OlivierGomis-n3d 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +18

    Pour dire Vrai Balla Gaye ieo vraiment mécontent gue quoi😂😂

    • @bxalil
      @bxalil 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

      Mais modou so waxei si ci mom dafa wara noppi wala 🤷🏾‍♂️😅

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +16

    Yow roi bi modou lo yoré moy dagg sa xol bi di nga sonou dé😂😂😂yow modou lo wakh niarri baate nga wooté conférence de presse

    • @MaodoSeck-u7d
      @MaodoSeck-u7d 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Boul sisou

    • @HAVIS_MARAM
      @HAVIS_MARAM 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

      Bilae ki dof bou bon la😂

    • @MaodoSeck-u7d
      @MaodoSeck-u7d 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Guiss ngeu dh

    • @mouhamedcherifaidara923
      @mouhamedcherifaidara923 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      @@MaodoSeck-u7d nooo mane key sissouwouma ki sissou mo ngui nonou di deff conférence de presse 😂😂

    • @mouhamedcherifaidara923
      @mouhamedcherifaidara923 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      @@HAVIS_MARAM néna métiwouko mouy conférence de presse 😂😂😂

  • @iscojo6600
    @iscojo6600 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +9

    Nite digako dane baparé yéhko! Copain bi da fan Modou!! Un pic de 10 secondes sans même dire ton nom! Tu convoques la télé pour 😂 pour lui répondre avec une préparation bien fait et plus de 2h 😁😁😁!!! Balla day wéré koi !! Danal Modou 100000 fois mais tjrs moy done sa roi 😁

    • @landingbadji9039
      @landingbadji9039 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Modou na niaak titre roi des arènes nga xol ba xam Balla dinako lidjanti. Modou Lo meunoul yoor couronne bi après nguenn beug Balla dou wax ci mom tamitt. Li motax lamb nexatoul Modou choisit ses combats alors qu’il a des adversaires potentiels

  • @papefaye865
    @papefaye865 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Merci beaucoup balla gaye

  • @NgoudaBoye
    @NgoudaBoye 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +6

    Ki Gaude gou magte la khkhkh 😂😂😂😂 Mou d'où Mouye la rowa bi 🎉🎉🎉🎉❤❤❤

    • @Bassirou-f8c
      @Bassirou-f8c 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Kharal ba meune bindeu linga wakh gatt bakhousi

    • @IbrahimaSarr-q2p
      @IbrahimaSarr-q2p 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Balla mo Mane tontou boula sa yaye bayé😂😂

  • @MamadouMboup-n4p
    @MamadouMboup-n4p 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Balla Gaye seul nokhou reik modou lo dafa réw ❤❤❤❤❤

  • @sellediop1817
    @sellediop1817 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Merci Balla ❤️❤️❤️❤️

  • @KhadimDiagne-vr6qb
    @KhadimDiagne-vr6qb 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Ndayssan khol ❤ bii dara nékou sii lép ya fo lakoy dieulé

  • @Mahatmaga
    @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +9

    Mais balla bétt nguama Sagua Faut montrer un bon exemple 😔

  • @khadimdiouf3988
    @khadimdiouf3988 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Je suis fan de Xlo mais balla gaye c'est un poison il me tue😂😂😂

  • @Zam-Zam710
    @Zam-Zam710 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    BILAHI WALAHI BALLA GAYE 2 YAY LAMB ❤❤🎉🎉 BO BEURÉ WOUL LAMB DOU NÉX ❤❤ KÉEN DOU YAW MASHALLAH NÉXA BEGEU ❤ NÉKHA FAAR 🎉❤🫶🏽

  • @mormbengue6641
    @mormbengue6641 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Bala a parfaitement raison siteu à faire tomber Modou lo

  • @alysako168
    @alysako168 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Bg2 seul le meilleur ❤

  • @momosagna
    @momosagna 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Balla bandit leu😂😂😂😂

  • @MaodoSeck-u7d
    @MaodoSeck-u7d 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    Modou dèl am diome di takhaw bo diakarlo ak balla 😂 mais daw rèk dèl am arèt 😅

    • @MaodoSeck-u7d
      @MaodoSeck-u7d 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      @mansourdieng2000 nonou la dèmmè nk

  • @bambacke5299
    @bambacke5299 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    Modou lo Roi des aréne dinga ko dégue par laa force

  • @chrisduncan7822
    @chrisduncan7822 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Waw un 3eme combat s’impose modou lo n’a plus le choix !!! Il est obligé d’affronter balla

  • @AntoineMendy-f3n
    @AntoineMendy-f3n 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Balla gaye 2 champion gaindé la comme ils sont d'accord k tu es un lion 🦁👑 mais forcément tout personne veut vivre jusqu'à avoir des cheveux blancs gaindé déh baguette c'est logique

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Thieye.balla.ma.yeureume.sa.none

  • @Mahatmaga
    @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +8

    Lutax dieulo avance Eumeu di dieul Yaldaw 😂😂

    • @serignefalloudiongue
      @serignefalloudiongue 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

      Nioune douniou daw goorr 😂😂dieulen tapha tine mo geuneu sen wakh diom barri dji😂

    • @Mahatmaga
      @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +5

      ⁠@@serignefalloudionguefallou amall diam 🙏🏿😂 Tapha dou fait daa amoull niveau bimuy beuré ak Xaragne Lo 😂

    • @MouhamedCissé-j9d
      @MouhamedCissé-j9d 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

      Combat bobou thi Eumeu la déss. Balla dou daw mbeur bokoul ak Modou. 😂

    • @Mahatmaga
      @Mahatmaga 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

      @ Balla Gainde tu magett la wala ma wo Boy niang tiapatioly bi 😂😂

    • @serignefalloudiongue
      @serignefalloudiongue 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

      @@Mahatmaga teh pourtant beuré guen ak siteu dh 😂😂 téh yén tapha miguen di wakh amoul niveau 10ans balla kassé moko dan 😂

  • @mouhamedfall6002
    @mouhamedfall6002 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +11

    Gaindé gou maguette gua 😂😂 Modou wakh 30 secondes gua def émission di tontou

    • @babsmstnewmusic7876
      @babsmstnewmusic7876 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Balla gaye nokk ko si 20 secondes 😂😂😂

    • @ibouthiam8999
      @ibouthiam8999 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Esq émission bi yeup modou lay wakh

  • @MamadouMboup-n4p
    @MamadouMboup-n4p 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Siteu seul ❤

  • @senegalrek2579
    @senegalrek2579 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +7

    Nanal glaces yafi wakhone ne Modou lo dou meusse deg Rois ds arènes Lolou moulay déranger ngay Ndelou rék 😂😂😂😂😂

    • @elhadjiabdoulayembenguecis3590
      @elhadjiabdoulayembenguecis3590 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Mou Dane Modou 2 fois Modou Dane Eumeu 2 fois Ték Si Boy Niang
      Mouy 3.2 Modou King ❤ Arénes.

    • @Zam-Zam710
      @Zam-Zam710 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      SITEU AK BAYE MADIONE DANE MODOU LO ​@@elhadjiabdoulayembenguecis3590

  • @saloumbusiness4595
    @saloumbusiness4595 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +8

    Mbeur yup mosi guen dof

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Modou lo comme Dip tjr Moy yeunguel game bi😂❤

  • @AlphaSaliou-n9k
    @AlphaSaliou-n9k 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Modou rék❤

  • @MoussaCamara-v3g
    @MoussaCamara-v3g 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Sokhor bakhoul koi
    Amone na si ieo touti stime mai nangouna ndayem

  • @FallouGaye-dy4sv
    @FallouGaye-dy4sv 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Bly kii instant bii dafay sissou 😂😂😂😂

  • @papaababacardieng7222
    @papaababacardieng7222 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Siteu deh si wax dji la nara diafandou 😂😂😂😂😂 deel khol bamou gnewat face2face ,dina geureum balla 😂

  • @ousseynoudiao9872
    @ousseynoudiao9872 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Nguané siteu da daw ba paré di nonnonn balla da ngua sissou Modou soxlola

  • @NayeFall-qq7xi
    @NayeFall-qq7xi 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Lutte tv son 🔊 bi ci suuf moom pour lan la ahh😢😢

  • @TakoSylle
    @TakoSylle 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Merci bala❤❤ ❤❤

  • @lassanatalla767
    @lassanatalla767 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Yaw daniou la bipé rek gua wo press bi di khotékou Modou moy saï saï 😂😂😂😂

  • @z-gotti3357
    @z-gotti3357 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +8

    Aka wayadi

  • @OusaynouMbge
    @OusaynouMbge 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Balthazar ngako founé yaye lamb😂💛💙

  • @adama6405
    @adama6405 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Bouma xalaté sama yaye douma bayi😂😂

  • @dembaztarkinda8270
    @dembaztarkinda8270 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Balla gaye 2 papay Modou Lo 😂😂

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +10

    *Gaindé gou maguett Boy Niang wakh nalako beu guené ci fethie bou bess, chroniqueurs yi wakh negn lako, Siteu mi nek seu adversaire wakh nalako, teh tontou woci keine. Modou Lo wakh lako ngey beugue rey seu bopp 😂 dey melni roi bi molay deranger😂*

    • @Ndiokarabdn3065
      @Ndiokarabdn3065 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Par ce que mome laniou beuga beurèl nakh mo yore roi tè nioko meune day geuna noy rk

  • @Htqv221
    @Htqv221 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Sama yone nèkoussi mais pour dire la vérité vraiment modou lo est un peu peureux niéméwoul wadji

  • @OnlyFoot-lz4cp
    @OnlyFoot-lz4cp 4 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Fans dioutal lô yi rombou léne sama commentaire 😂😂😂😂 Nokk dane si ngourou abdoulaye wade nokk dioutal si ngourou macky sall😂😂😂😂

  • @badakane-zp3mp
    @badakane-zp3mp 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Hooo Modou yaye wagga
    Baboul Khaïry yaguii youtte😂😂😂😂

  • @TakoSylle
    @TakoSylle 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Merci bala❤❤❤

  • @Makavelimg
    @Makavelimg 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Vraiment vous devriez baisser votre musique li interview le dou film

  • @hadysow4208
    @hadysow4208 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Balla comme ancien gloire Bouy interview 😂

  • @P.A.Dienior
    @P.A.Dienior 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    yagui melni do mbeur khamoo sax réglement nane siteu mo daane ioe daga sokhorrrrrrr

    • @bayemodoundiaye7426
      @bayemodoundiaye7426 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Lolou dako wakh pour merlo Modou rk

  • @AlassaaneSow-sk7rx
    @AlassaaneSow-sk7rx 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Qui bou sagnone Modou Di wakh si mom . premier fans Modou Moy balla

  • @Sylla2406
    @Sylla2406 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Nane ngay sétanei téléspectateur yi 😂

  • @fallougueye683
    @fallougueye683 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Tu n'a rien dit ,sokhor ,ioe ya ignan deug .yalla moy diokhé té mo fal Modou lo mofi nk.geumal yalla.

  • @MaodoSeck-u7d
    @MaodoSeck-u7d 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    Liss or bi diop2 ak wa geudiwaye seul kou sisou yakhame ❤

  • @Science-z5w
    @Science-z5w 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    De toute façon Modou Balla daka dan 2 fois

    • @sirysene88
      @sirysene88 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Eumeu dann balla 2,fois
      Modou dann eumeu 2,fois

  • @mouhamadoulmourtadadieng3311
    @mouhamadoulmourtadadieng3311 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Fans modou lo yi Loutah niou touti xol 😂😂😂

  • @AliouDiouf-ci2ny
    @AliouDiouf-ci2ny 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Balla yagi sisou de adona amoll solo modou lo Roi bi fall 👑 👑

  • @CssNabien-y9u
    @CssNabien-y9u 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Billahi balla fi né Modou bo gnémé combat bi taguoul sa méra

  • @serignembacke1255
    @serignembacke1255 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    balla dou nit😂😂😂😂 lo leer la wakh

  • @mamadousow8935
    @mamadousow8935 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Lamine ray nama nena petard yi motakh 🧨😂

  • @AbdellahiNdiay
    @AbdellahiNdiay 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Modou moye sama mbeur ms mome ak balla aye copin laniou 😂😂😂

  • @Kentrelyukgin
    @Kentrelyukgin 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Wakh deugeu yallah balla a raison 😂

  • @mbackediop7678
    @mbackediop7678 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Balla yamana dull wala Aziz Ndiaye
    Moy dull Aziz Ndiaye Mo wakh finè
    Balla Nèna daye bayi Sathiès pour Modou lo Tay nga wakh nè Modou Mo dèllo avanc bi😂😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Mo wakh mo wédi bopam

    • @Leuzsonko
      @Leuzsonko 8 นาทีที่ผ่านมา

      20 foi la modou daw avence bi bg2 sèn baye la yarou lèn siteu dalèn nokou dane lèn lolou molèn diap ba tay motakh modou di wax rek 😂

  • @ousseynoudiao9872
    @ousseynoudiao9872 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Démal wadial ak siteu ngay wadial tontou si aye gaindé Bou maguatt😢😢😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Modou lô bou amone diom dou wakh ci yaw ndakh amoule diom 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ndiayelaye2861
    @ndiayelaye2861 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Balla gaye 2❤❤❤

  • @falloucamara4808
    @falloucamara4808 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Yenn niepp commentaire laine gayndé gou magatte gui guir yalla

    • @sirysene88
      @sirysene88 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Gainyede ngou maguette

    • @icAlphaDiallo
      @icAlphaDiallo 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Modou dioutal lo 🤣🤣🤣 Balla rek la ragal

    • @falloucamara4808
      @falloucamara4808 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      @@icAlphaDiallo wakhouma li dh😄

    • @icAlphaDiallo
      @icAlphaDiallo 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      @@falloucamara4808 moma diakhal 🤣🤣🤣 Balla seul

  • @kouroubayefallpure
    @kouroubayefallpure 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Balla reik ❤

  • @AbdouDiouf-cm5io
    @AbdouDiouf-cm5io 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Tu es un lion ❤

  • @NayeFall-qq7xi
    @NayeFall-qq7xi 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Cëy Balla 😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤

  • @NdiayeAssane-v2c
    @NdiayeAssane-v2c 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Balla gaye grandit un peu beugue nge ay dagasantei torop

  • @ibrahimasarr8936
    @ibrahimasarr8936 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Demal taal gaz nga took ci sa xol moy bone 😂😂 wakhou kou soxor rek ngafi wakh.
    Yawak Modou yena tollo combat am nga 6 défaites Modou am 3 ba parer gueun la yaggeu ci roi bi. Lolou nga meunoul supporter 😀

  • @MuhammadDiop-v4d
    @MuhammadDiop-v4d 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Balla seule ❤️❤️❤️

  • @PapeMorGueye-t9t
    @PapeMorGueye-t9t 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Balla tu es devenu ridicule tu étais roi des arènes reconnu maintenant tu l'es plus Guemeul yalla Modou lo est le roi des arènes comme tu l'étais c'est ça la vie tu parles beaucoup soit positif et sportif

  • @Ousmanegueye-w5h
    @Ousmanegueye-w5h 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Balla gaye dou touss wakho Dara nitt amoul loudoul ay wadiouram

  • @falloucamara4808
    @falloucamara4808 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Gaynde gou magaatte gui😂

  • @DjilyNdiaye-pw8zx
    @DjilyNdiaye-pw8zx 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Balla dou sama mbeur dh mai kimay guiss ni siteu ame na problème

  • @tidianebiaye1573
    @tidianebiaye1573 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    BG2 ❤le Meilleur

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Athia balla gaye2 😂😂 kou banie koula tontou boul wakh 😂😂

    • @icAlphaDiallo
      @icAlphaDiallo 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Billay😂

  • @bouleuzloum5657
    @bouleuzloum5657 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Ki da nam couronne 😂

  • @ndiagadiagne1305
    @ndiagadiagne1305 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Bombardier dala nox nox you metty eumeu sene nox la nox you metty kom ku yor xalè geumal yalla😂

    • @modougeuye4399
      @modougeuye4399 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      Mou nokhou Modou lo nokhou you méty😂

    • @icAlphaDiallo
      @icAlphaDiallo 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Ba paré dioutal ko😂 no Balla yarou wout nak😂

  • @papeseck9969
    @papeseck9969 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Vraiment peul elle n’est pas pertinente

  • @adamslo7971
    @adamslo7971 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Kii doff la ay Waxam diaroull tontou thiatt douada fall neik sa poulin ganii com mom lagn dioh victoire cii ama nekh kone siteu mo dann Yoe wero balla rouye woutéll nianou wadiour cii yaye mo geun geumo Dara sa bop rk sa thiess sa rak fii gako troxall cii Reseau yii samba alar ga modou xaragne lo daff la raw cii sahirr ak cii batine balla rouye nopill Gainde maguett ga

  • @cherifka7758
    @cherifka7758 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Modou niébé dotoko défati 🤣🤣

  • @PapeSarr-qk1xq
    @PapeSarr-qk1xq 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    No balla gaye rewna bilay 😂😂😂 Modou oustaz lah 😂

  • @ousseynoudiao9872
    @ousseynoudiao9872 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา +4

    😂😂wa mais balla yagui siiisou dhhh

  • @Zam-Zam710
    @Zam-Zam710 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    BILAHI WALAHI YA MEUNE TONTOU 😂😂 YA DEUGOU NIAW😂😂 NIARRI NOKK YI MOKO MÉTI BATAY 😂😂 seul mbeur bounou nokk yayam nane BALLA DOYNA SEUK😂😂 BALLA dako nokeu nokeuuu ba yayam yeureum ko ragal Balla nioussatiko 3éme fois Mouy délo avance 😂😂 ADJA LO IBADOULLAH bi mbeur Bou sokhor bone Xol mais BALLA GAYE LE MEILLEUR DE TOUS LES TEMPS NGAY BANIAN DÉGG PAR LA FORCE DIGUAKO DEGG NAK MOLA NOKK 2 FOIS si niarri Gourou président 😂😢😮

  • @serignedieng4609
    @serignedieng4609 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Waw waw balla gaye rek

  • @alassanendoye9982
    @alassanendoye9982 9 ชั่วโมงที่ผ่านมา +3

    Balla Guaye 2 moye bayou Modou lo 😂😂