4:37 machallah yaw mi ya xam nért sciatique instant bi moma dall mais meti waye bi foko tak wésou nako bilahi yalna yallah safara ma ak bepp djoulit aussi
Dieureudieuf Gueye garabou wolof ak mothie Dale moci tané ,marche ak Bayyi sango ndokh mou sedde ak diko nane natation bakhna piscine ou plage bakhna ci ,ak bouillotte chaude tout le temps
J’avais nerf sciatique 5 jours avant que ma mère tombe malade elle a fait trois jours à l’hôpital elle est décédé après deux jours quand le funéraille est passé je ne sentais rien jusqu’à maintenant Alhamdulilah sinon je ne souhaite même pas cette douleur à mes énemies
Massa del dém piscine wala guedj di dokh ci soufou guedj bi Bayyi ndokh bou sedde def marche marche bou tangue ak yeukati Lou diiss ak togaye bou yague, thiakhat reine bi deko nane matin et soir ak khopp yi infuser marin et soir yalna niou yallah maye werr dafa metti
aÿ way mame boye lingua wakh yeup mongui si mane sama nerf sciatique bi sonale nama damaye dioy ba sonou sport sakh soumako commencé doumako meuneu yéguali koumou daloule meuno kham métite bi sonouna 😭😭🤧
Kep kou amé nerfs sciatique dama lay gay dem nguedj di taw si souf si def renforcement di aniyer ak chau fois si semaine bi inchallah dina dem ba dotoko santir
Celui qui souffre de nerf sciatique,il le conseille d'aller au plage pour faire des exercices physiques ( courir faire des marches en arrière, travailler les jambes en global) si tu continues cette rythme à un moment ça va finir par disparaitre. Merci
4:37 machallah yaw mi ya xam nért sciatique instant bi moma dall mais meti waye bi foko tak wésou nako bilahi yalna yallah safara ma ak bepp djoulit aussi
Akka méty yalla nako yalla safaral képp kouko am nerf sciatique
Amine ya Rab koumou daloule do meuna kham métite bi😢
Amiin
Amine yarabi ❤
Wallahi khamnasi dara monguimay beuga ray
Amine mo ngi may ray depuis un ans louné déf nako
En tout cas Serigne Modou Gueye mi Watt na si Yallah meune liguéyam Machallah Allhamdoulilah
Al Salam
Nerfs sciatique, amoul
Hernie discale mon am
Hernie Moy coincé nerfs sciatique.. problème bi, moy fimou nek fou méry, fenèn lay mété
Yalna yalla faylayiw amine ❤❤❤
Elhadji malick magui là siar beug na nga deff waxx tanne thii hernie discale ❤
Dieureudieuf Gueye garabou wolof ak mothie Dale moci tané ,marche ak Bayyi sango ndokh mou sedde ak diko nane natation bakhna piscine ou plage bakhna ci ,ak bouillotte chaude tout le temps
Métina lolou je souffre de sciatique depuis 1ans sonouna
J’avais nerf sciatique 5 jours avant que ma mère tombe malade elle a fait trois jours à l’hôpital elle est décédé après deux jours quand le funéraille est passé je ne sentais rien jusqu’à maintenant Alhamdulilah sinon je ne souhaite même pas cette douleur à mes énemies
@@Oooor87
Walahi méti n'a torope 😩
Bilay momay beugue ray yalla boumo Dale kenene si adouna
Machala k'allah swt vous protège
Mashallah am na solo yalla na diam yag té barkél inshallah
Machalla❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi amnako dama opereeone solako dieulo mais legui mom metiwoul
Barki seydina Mouhamed magui beugu dé frère wayé sante yalla rek
Mashallah papa Mashallah
Machaalah sama torodo papa
شفاكم الله شفاعا عاجلا
Mane dé depuis 6ans lako âme wayé métina trop démena opital ba sone tok tradipratisien tamite démenafa wayé bateye dara
Massa del dém piscine wala guedj di dokh ci soufou guedj bi Bayyi ndokh bou sedde def marche marche bou tangue ak yeukati Lou diiss ak togaye bou yague, thiakhat reine bi deko nane matin et soir ak khopp yi infuser marin et soir yalna niou yallah maye werr dafa metti
Kholal ndakh sa matelas bi bakhna. Wassalam
Même man depuis 6 ans ba léegi
Jazak Allaahu Khairan
Mane nonou la sone
aÿ way mame boye lingua wakh yeup mongui si mane sama nerf sciatique bi sonale nama damaye dioy ba sonou sport sakh soumako commencé doumako meuneu yéguali koumou daloule meuno kham métite bi sonouna 😭😭🤧
Wàllaay même man mooma dal métti na trop
@@xidma865 bilaye dafa méti trop mane sama yaye koumou dégue ni meune nga fasse ndigue démale namafa mei dara tjr dafaye méti
@@CoumbaFall-n4r métti na moom Yalna Boroom bi saafara
Bilaye walaye yal naniou yalla maye wére koumou daloul yalla boko guisse
@@xidma865 amine 🥰🫶❤️
Machallah amna solo
Macha Allah
Amine yarabi ❤
Man dé depuis 15 ans ma ngi ak mom
@@noroudieng8412
Massa😩😢 Mane depuis niari ate métina
Merci beaucoup 💟🌟🌼🏳️
👌🏾👌🏾👌🏾
Je souffre en ce moment troop même
Metitam foko natt wessou nako mane 2011 lako amm soula dalé daguay melni kouniouy dag sa khol bi
@@mamijamilsow861 😩😢
Je suis à Thiès on m'a dit que j'ai le nerf un peu koisse mais je souffre terriblement même malgré les médicaments puis-je vous appeler
Même moi je suis à Thiès j'ai ce problème
Je souffre de ça actuellement
@@bacarydjiba2993
Tu n'es pas le seul c'est une sale maladie que Dieu nous soulage
Bilahi moma dal metina trop
Alhamdulilah 😮😮
J'en souffre j'ai été opérée 3 fois et jusqu'à présent je souffre de douleurs
Ooh massa opération meunou ci dara fasse ak mothie sakh mo tané ndeyessane
Kep kou amé nerfs sciatique dama lay gay dem nguedj di taw si souf si def renforcement di aniyer ak chau fois si semaine bi inchallah dina dem ba dotoko santir
C quoi on a pas compris ,tu peux le récrire en français...
Stp en français c'est difficile à lire
@@LInv-or6km je pense kil ve dire aller au plage courir aussi Faire des saut genre di teup apres bo dawé ba paré
Celui qui souffre de nerf sciatique,il le conseille d'aller au plage pour faire des exercices physiques ( courir faire des marches en arrière, travailler les jambes en global) si tu continues cette rythme à un moment ça va finir par disparaitre. Merci
Hh@@bacarydjiba2993
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Momay beug Ray
Machalla ♥️ mane de moma dale ni waye machalla ♥️
Salam kou bakh lane mola faj ?
Dangay wout 3 rénou thiakhat ak 3 rénou mbanté mbaré nga bolé len togou ko si 1 litre nokh diko nane 3 fois par jour si kassou café
Sama papeu lolou moko dal mai dina ko essayer khol@@onlytrust13
Seugn bi man lolou moma dale damay dokh lou sorri djéki say rek takhaw wala ma took
@@onlytrust13bonjour pendant combien de moi
❤
Sonal nala trop wallahi
Billay malakowah
Maan El Hadj rek laay torp fonk nala trop
Mangui deglou walou pacmi?
Machalla
Yageu fi lol
Loumouy diar
❤❤❤❤
Nerf ciatique c est artrhose ou non
No no c'est pas la même chose
😭😭😭😭😭😭😭
Aka metty do meune tog ni teudeu do meuneu dokhe laa
@@abydiaramouna1529
Niari wér meunou ma dokh alhamdoulillah légui ça va
@@MariemeCamara-t8v Salâm, s'il vous plaît dites comment vous l'avez traité ? Merci
Yamar-kicc si français nooy HANCHE.
Mouse bou yekho daye foudatou
Billaye lou metti torope sakh
NERF SCIATIQUE MOYE AVC Walla?
Nerf sciatique AK AVC c'est pas la même chose. ... Bro
Non SA ndigue lay diap di wathie si bene cote tankebi bassi SA baramou tanke yi..te SA cote bi day inflammer wou.moy waral metite bou taar bingay ame.
non non
Yaw fo né
Machalla