N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Bilahii khamou malla mè kou bakhe monguii nii ya gorrë ya ame djiomm sa kholl rafett naa diambarr yaye bauye tu ma fait pleurer 😢 yalla nalla yalla gueuneu takhawou et tu es toute belle 😢😢
Motakh apparence lou yèmè leu. Ki kouma diokhone kamil ma wate ni dou djiguène nakh apparence. Mais stp dèl defar sa bopp kom djiguène stp. Courage a toi
Binta sama tourando yeye nga mais nk guir yalla nékkal djigéun xolatal sa bopp yaye boye Liguéy bi bakhna trop bonne continuations yalla na yalla barkel leupp❤😍
Souma amone entreprise dieul leu wala yoboula Europe fekhel sa rasta yii goudou nga diko takk ❤ elle est tellement reconnaissante aussi 😢 yalna yalla takhawou defal la ndam goudal fan wi
Metier mom amoul Goor ak djiguen diom la rek, mais Binta défaroul nak djiguen déy saf djiguen, il y’a des femmes mécaniciennes Com toi mais bolén séné khamni aye djiguen lagnou, courage à toi
Walahi meme ici où j’habite y’a une fille qui fait le soudeur 🧑🏭 mai quand tu la vois dangoy beug elle est belle aussi changer woul comportement mai Binta changeel def yeufou djiguenne
Vos vidéos nous apportent toujours autant de joie et de sourires ! Merci pour votre talentueux sens de l'humour et vos performances brillantes et contagieuses !🐻🥁🏸
Pour la première fois, j'ai regardé une interview qui m'a vraiment touché.En plus, on voit clairement qu'elle aime vraiment son travail. Toutes mes félicitations, bravo binta et bonne continuation 👌
@@ElhadjiSamb-p2w diegalou Sakh takhou reutie wayé pour commencer dieulal sa khour yi dém déloko goor yi Dora nieuw jakarlo ak man dawuma Dali massa ya
Sans rentrer dans le stigmat si tu portes des cornes ne soit pas surprise d être prise pour un taureau.. Le métier que tu fais est super . Tu es très intelligente Le souci c le style qui fait penser à un homme maintenant avoir un style masculin ne v pas dire que tu es ...l....
Chacune de vos vidéos est un véritable chef-d'œuvre cinématographique qui mérite reconnaissance et respect. Continuez à nous inspirer par votre talent et votre travail !💵🌔🖥
Ndeysane elle est très brace et tres ambitieuse ❤️ rew mbi ndaw you gueum sen bop kom yaw lagnou soxla . T tres belle aussi maa shaa Allah mais leitoul you meun xam ni djiggen nga . Elle communique bien ❤️
@Jeunehomme9714 lilaye wakhati si séne réwandé bi respecter les gens pour qu'il vous respect et nosé plus jamais m'insulter sinon ce sera pas bon pour toi.
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Ndeye sane Bineta yalla nl yalla 😢diapalé
🇸🇳♥️♥️♥️Kou beug binta lalal j'aime ❤❤❤🇸🇳
En tout cas on vous encourage mes aussi défaroule aussi nga soralé danga wara ame Djieukar
Talkal.nakko.sama.dom.sagarr
Keep going ❤❤
Que dieu vous protège Binta force à toi le meilleur reste à venir
Bilahii khamou malla mè kou bakhe monguii nii ya gorrë ya ame djiomm sa kholl rafett naa diambarr yaye bauye tu ma fait pleurer 😢 yalla nalla yalla gueuneu takhawou et tu es toute belle 😢😢
Pourquoi elles faire son travails
Ohhh 🥹 binta Yallna yallah sama la inchallah te mayla ligua beugeu si ligeue bi inchallah 🥰🥹🙏
Je suis mécanicien Ce n'est pas un métier facile force et courage à toi ❤❤🎉
Motakh apparence lou yèmè leu. Ki kouma diokhone kamil ma wate ni dou djiguène nakh apparence. Mais stp dèl defar sa bopp kom djiguène stp. Courage a toi
Bilay 😅
Wakh deugu yalla mane mome damako beugu te yalla takh Ms batay sama xel daloul xawma lann la nakk
Niossi bok yaam bilahi walahi du jamais vu dafa goorè trop sakh na Djiguénè way na sad djiguéne
@@azizalofficiel5425ki androgyne leu meunoul dara ci li.niounane ko defaroul. Senegal dale..
Waax deug Yalla m Courage à toi
Les goûts et les couleurs ne se discute pas ya des gens qui vous aime comme saa chapeau 🎉 champions ❤❤❤💥🔥🔥🔥
Niobokn kogne depuis enfance mm école aussi 🎉❤ Binta diam si yaw
Elle habite où ???
Kii ne Darah Diourbel la nekk dell wax deug
Binta sama tourando yeye nga mais nk guir yalla nékkal djigéun xolatal sa bopp yaye boye Liguéy bi bakhna trop bonne continuations yalla na yalla barkel leupp❤😍
Dedete ki dou djiguene
@myamandiang non dafa wara djiguéné nk
Ham yaw
Macha allah, Bineta diambar gua , liguèye moye lépe. Mais djiguène dafa wara saf djiguéne. Même so soloul yeuré djiguéne déle létou
Machalla binta.ligeuy.rek.dina.bakhe❤❤❤😢bonne continuation 😮
Eskey yallah nala borom bii défal diam Inchallah ❤
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
Bonne continuation Binta yalna yalla barkel ligueye bi
Machalah Bineta bonne continuation ❤❤
Courage Bonn e continuations sénégalais mo Tama wakh bou niaw me dara❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤😂
Ndeysane Yalnala yalla defal diam bineta en plus tu es toute belle
Yalla Nako yalla diapalé way Binta 🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Merci smaa doom dji Bineta sante ngama t defaloumala dara diam si ioe❤
Souma amone entreprise dieul leu wala yoboula Europe fekhel sa rasta yii goudou nga diko takk ❤ elle est tellement reconnaissante aussi 😢 yalna yalla takhawou defal la ndam goudal fan wi
Metier mom amoul Goor ak djiguen diom la rek, mais Binta défaroul nak djiguen déy saf djiguen, il y’a des femmes mécaniciennes Com toi mais bolén séné khamni aye djiguen lagnou, courage à toi
Ki deh kouma waxone ni djiguene douma ko gueum werante na b sonouna
Bilakh
Même sou defarou woul au moins mou def yeufou djigen.. lii Yalla reub nako
Walahi meme ici où j’habite y’a une fille qui fait le soudeur 🧑🏭 mai quand tu la vois dangoy beug elle est belle aussi changer woul comportement mai Binta changeel def yeufou djiguenne
Binta nek sii rek day bakh on love mecanique
Courage ma sœur ❤
Ndaysane Machallah ❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉
Ohhh Macha Allah ❤yalla na métier bi gueneu dougou inchallah ba do am loula si diakhal ❤
Sénégal bayi leen nafekh kii nimou mell thi djigeen rafetoul lii moom moy ñiakk kilifa djigeen dafay correct letou takk ay diaro lolou mooy deugg bayileen nafekh
K dieu t bénisse franchement sw fière de toi
Force à toi mais Yaw aussie défaroul touti ❤❤❤❤
Vos vidéos nous apportent toujours autant de joie et de sourires ! Merci pour votre talentueux sens de l'humour et vos performances brillantes et contagieuses !🐻🥁🏸
Ndeysane yalnala yalla sam lingay sentou si métier bi yalnagako guiss inchallah
Machallah binta je suis contente avec toi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ yalna yalla diapale amine yarabi 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Force à toi Binta🫶
ndaysane yalla nako yalla diapalé🤲❤️
❤❤❤ chapeau reine
Bineta.daffal.comme.amy.mbacké.boul.falé.ay.wax.you.négative.courage❤❤❤
Hola bineta❤❤❤ vamos vamos te quiero
Tout mes encouragements ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Force a toi bonne chance ❤❤❤❤❤❤❤
Machalla machalla Binta ki mome sama Yaye la yalla na sa diam yague
Du courage bineta
Binta boul dioy nak yakeuga sama journée bi way ndeysan ❤
C'est un grand exemple pour la société d'aujourd'hui
Macha Allah yallah bahna continue binta
Ay binta bo nieuwon europe ak sa méthie bi khalis bou barii machalla🙏🏽
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤
never give up keep going 💪
Bineta 💯💯💯💯
Thieuy yala moy bour ❤❤ force binta
Non vraiment c'est triste mais sa ira inch'Allah hurabi yalla taaxawu là
En tout cas kholou djiguéne la yoré gaw n'a dioy 😢trop du courage yalnala yalla takhawou
❤❤❤❤ Je vous encourage au fond de mon coeur be strong don't care about what people think about you you can do this❤❤❤❤❤❤
Ndeysane ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Franchement respect à elle yalla nako yalla samal bopam
Gracias hermanita ❤❤❤❤❤👏👏👏👏👏🫶🫶🤲🕌🤲🕌🤲🕌💯💯💯💯
Pour la première fois, j'ai regardé une interview qui m'a vraiment touché.En plus, on voit clairement qu'elle aime vraiment son travail. Toutes mes félicitations, bravo binta et bonne continuation 👌
Don’t cry love keep up the good work
Binta ❤❤❤❤❤❤❤
Kon ki djiguen la liguéy dafa méti mais defaroul nak
Noumoye défaro ki ni la mélle doff nga trop
Magui diégallou nak
@@ElhadjiSamb-p2w diegalou Sakh takhou reutie wayé pour commencer dieulal sa khour yi dém déloko goor yi Dora nieuw jakarlo ak man dawuma Dali massa ya
@@yayouSalihousamb1553😂😂😂😂
@mariane2697 balma khalé la😂
Yalla ayna 🎉 té Yémé
Ndeysanne❤diam rek ngay am sister ❤❤
Sans rentrer dans le stigmat si tu portes des cornes ne soit pas surprise d être prise pour un taureau..
Le métier que tu fais est super . Tu es très intelligente
Le souci c le style qui fait penser à un homme maintenant avoir un style masculin ne v pas dire que tu es ...l....
Chacune de vos vidéos est un véritable chef-d'œuvre cinématographique qui mérite reconnaissance et respect. Continuez à nous inspirer par votre talent et votre travail !💵🌔🖥
Wa yén c koi le problème djinguén la kay😂 mashallah ki moy bineta...
😂😂
Ma bagne guemoumako😢😭😢
@@mariamacisse5972mane mi mai legui gueum nako
Mane dh geuw mako😂😂😂
Bravo courage à toi tu est une championne
Ndeysane elle est très brace et tres ambitieuse ❤️ rew mbi ndaw you gueum sen bop kom yaw lagnou soxla . T tres belle aussi maa shaa Allah mais leitoul you meun xam ni djiggen nga . Elle communique bien ❤️
Très belle hum ! Pourquoi vous êtes menteurs ? Va la draguer.
❤❤❤Machallah dîna bakh inchallah ❤❤❤
Yalnalayala takhaeou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oh billaye j'ai les larmes aux yeux 😢 machalla rak dji ♥️♥️♥️♥️♥️ woutégué khalé you djiguéne youye mbarane dissi diok séneu yaye
Yalla nalla Yalla maye ligua beugue si barké seydina mouhamet bilahi g pleuré 😢😢😢Yalla gua téral sa yaye inchalla bonne continuation
Ohhhh Ndesysa ❤❤❤❤😭😭
En tou ca macha allah yalla nala yalla mouseul si thiatt nonou la dhé binta gueum ko rek dina bakh incha allah
Machallah binta ❤❤❤❤
Dioye lo guama MachaAllah ❤
Merci contan si yawe
Du courage
Wa ani bineta 😮
😂tes pas sérieuse
😂😂😂😂😂
Man dh comprendr wouma dara😅
Bilaye j’ai pas compris je demande rekk
😂😂😂
Force à toi rk le meilleur reste à venir 🙏
Amine
@@soukayeyade4310 bilay défa jambar té am kerssa
Courage ma cœur yalla bakh na❤❤❤❤
Cette fille merite une décoration
Machalkah yalla nala yalla sameu❤❤❤
Machalla courage à vous
Waw Coumba Yalna yalla Diapalela
Bonne continuation sis❤❤❤
Force à toi binta❤❤❤❤❤
Na djiguéné cas même 😮😮
Binta sama kharite bi❤❤
😂😂😂aye waye bineta bo waré nampale ? ❤❤❤😂😂😂
YALLAH
Macha'Allah sister courage❤
Binta c bien le travail dure mais sa t’empêche pas d’être féminine toutiiii
Mani yalla nimou téré goor bouy djiguene djiguene lou, nonou lako daké thi djiguene bouy gore gore lou. Nékk mécanicienne téréwoul donn djiguene
Nga dem reglé ko ak mom.
Courage rek dara xéwoul soti 🙏🙏🙏
Macha allah tu es tres belle ,bonne chance
Machallah ❤
Ndaye sane 😢
Machalla deuredief tawfikhe rek inchallah
Ohhh machala binta❤❤❤😊
Aythia binta bonne continuation diam thi iow
Machahalahh ❤❤
Défarale sa boop bi djiguene daye safe djiguene mais bonne continuation ma chérie
Yw duul lii fébarr laa
@Jeunehomme9714 lilaye wakhati si séne réwandé bi respecter les gens pour qu'il vous respect et nosé plus jamais m'insulter sinon ce sera pas bon pour toi.
Elle est androgyne
@@AwaNdiaye-ds8gu billay wakhnga deug vraiment liguéy bi bakhna trop mais nk defa wara djiguéné ak voix tmt
@MbodjAmadou-dw3sh lolou la reck meune nga sagne ame yaramou goor wayé boye solou comme djiguene bou yagué mou dagne
Respect 🫡
Machahala❤❤❤❤❤❤