Je suis en gambie et je viens de suivre le combat de issa pouye avec les larmes aux yeux. C'est quelqun que je connais bien pour sa bonté de cœur et son humanisme. Ça me fait mal de le voir souffrir avec ces multiples échecs. Mon champion je te porterais toujours dans mon coeur. Qu'Allah te protège
Vraiment je suis de guediawaye mais Issa pouye me plais beaucoup il a tout fait dans la lutte mais actuellement il est dans tes difficultés soit fort issa
Félicitation Alioune Seye 2 Et Du Courage Issa Pouye Champion Ngua Mai Dakhar Dou Saff Niari Yoon Alioune Seye 2 Yalla Nala Ndam Li Dijk Amine Allahouma Amine Guédiawaye 100%
Dou question de MAK issa pouy soko bolé AK xalé bou ndaw bou mouse mou kawo ko garde zéro té li dafa yag si mome té li molay wane né mbeur yi gnilén di entrainé douniou ay pro un lutteur comme issa pouy gua xamné légui mou déf si lamb ay atte té menoule maytou menoule door
@@dimkhalebambiste2931 même boulén meuné moy yonou lamb kw Après bou si dané kén dém si niom boye niang,gouye gui,sathies,tapha tine gris Bordeaux ,lac 2.......
Franc NDIAGO hamna soceh boubakh lathiel sa arrière parents il vont te le raconter CASAMANCE bébé Guinée Bissau tu peux pas faire un seul combat en lutte avec frappe gagnéko dilaké LAC DE GUERRE tu joue de ta vie Lac de guerre deffa commencé ki souf bé yeggue ci kaw
Je suis en gambie et je viens de suivre le combat de issa pouye avec les larmes aux yeux. C'est quelqun que je connais bien pour sa bonté de cœur et son humanisme. Ça me fait mal de le voir souffrir avec ces multiples échecs. Mon champion je te porterais toujours dans mon coeur. Qu'Allah te protège
Bilahi frère li ngay yeuk ci mome rek lay yeuk aduna mo deme ni qu’il accepte et la vie continue
Saba baye laye lako beugo
2
Ndeysane Gaston sakh dafa yeureum Issa mé dara yalla ndiekhoul
Vraiment je suis de guediawaye mais Issa pouye me plais beaucoup il a tout fait dans la lutte mais actuellement il est dans tes difficultés soit fort issa
Félicitation Alioune Seye 2 Et Du Courage Issa Pouye Champion Ngua Mai Dakhar Dou Saff Niari Yoon Alioune Seye 2 Yalla Nala Ndam Li Dijk Amine Allahouma Amine Guédiawaye 100%
MANGA2 Oubna lamb dji, bayi délousi oubbatt lamb bi.Issa likko tobb mokko bayé goul
@@walyfaye4959 Wakh Ngua Deug Deh Grand Frère Mai Souma Done Mome Damay Bayi Lamb
Je suis parmi des fans de issa pouye. Bonne continuation
Aliou seye nak vraiment meunon gua door sama copain dank 😂😭😭😭mai door ko coup bo hamni dafa metii hiathe bi sori en plus dafa dal
Mousa ndoye du courage champion
Mousa ndoye vs tapha tine père Gaston
Kouy wakhni tapha tine dou noromam nak kou sathies dan ak garga mbosse mais moussa manoul sakh ame yekini jinior migua khamni tapha tine moko dan
Gaston dou gattt
Sunu khaliss kay teugé lamb dji ni
Domerame bou Mak
Niome akeu communicateur sois disant traditionnel vraiment aye domoû khathie laniû.
Ndeyssane 😭 Gaston dfeu beug issa pouy
Franc de tout cœur avec vous
Vraiment la forme physique des deux lutteurs desna loubary
Tu as vu ce k j'ai vu.Aliou Seye nekoul si dara da fékk Issa pouye amoul repère rek
Thieuy ndiago parcélle bii nangou rék wala bagn 💪💪télla nieuw mo gueunn si yénn déh eumeu sene lac2💪💪
Issa pouye Nguir Yalla Bayil lambeu dji Diga si dée dh😌😌
Wa Issa Pouye khana entrainewoul nekhoul ba nekhoul mais mbeurii ay maak laniou Senegal mo meti rek
Wakh Ngua Deug Deh
No entraîne wul bubakh alioune seye mo gueun pare
Ndeyssane dama yerem bilay tok lou yague bakhoul bilay
Dou question de MAK issa pouy soko bolé AK xalé bou ndaw bou mouse mou kawo ko garde zéro té li dafa yag si mome té li molay wane né mbeur yi gnilén di entrainé douniou ay pro un lutteur comme issa pouy gua xamné légui mou déf si lamb ay atte té menoule maytou menoule door
@@modoundiaye7985 Wakh Ngua Deug Deh
Aliou séye bone nga dh hé😂😂😂😂😂
Fran ak Malick Niang moy combat
Kou bax proposé nga combat nak,lou néex migui nonou
Lolou moy yonou lambj
Tiey Yalla kholal ni Issa mélone ak Legui rek.
Kén gnemer wouko wone.
Mais Lamb dji wornako. Issa bayil lamb donatoul yaw
Vérité absolue
Mais Issa pouye il deconne vraiment
Ndeysan thiey yalla lamb Issa yallnala yalla soutoural
wakhena degue dé combat la💪💪
Franc mi eupeul na dh
Say morom yi Yangui fi
Ooooooooh #ISSA_POUYE
Champion Yakhouna 😭❤️
Gaston Yangui yakk lamb dji Billahi ppv bi doxoul dara
Na gayi dieule Malick Niang
ALIOUNE SEYE2 YEKINI JUNIOR
Gaston production Ak sa lutte Tv louy sen problème ?
Xolen issa Pouye 😂😂😂😂 vraiment li diarouko mounan na dem togue rek nopalou
Vraiment Issa pouye demal entrainer rek
Ndeysaaan issa pouye mounoul hèkh
Thiey sama tourodo😂😂😂
Aliou seye lamp takk leu def thi lokho bi 😂😂😂
Faran lilahi boul dieul lac 2 lilahi warasolie ko kou dou mbeur waye ah
Amoul yeureum teulou Doore rék 👊👊👊
Pour mane Issa n'a pas très bien préparé
🤣😂😂 Issa pouye loula diaral li
Franc vs Sa Thiess🤝
Franc vs Sokh
No issa bayil beuré
Franc yagui si État dh
Issa Pouye mii tamite esk dou bayi 😂😂😂
Khadim Ndiaye limokoy yoot
Délen wah di dieteul YALLA SWT du diékhé khékh loum diékhé
Ce becaye ctun vrai opportuniste ils pensent ka leur poche
ISSA BIKO MODOU DORÉ MOU DANOU LA GUEUDJ AME VICTOIRE NDEYSSANE 2009
Issa Pouye, mbeur moo khamné sa carrière yeup meussoo meune khéékh, toog 6 ans beuréwoo, khaar baye waadia retraiter, dieul combat ak khéékh katt boula gueuneu féété ndaw fouff, beugueu tchiéé khéékh. Yaa lorr sa boppeu. Massa.
Ndayssane Issa legui mak nga nopaloloo
Bonne chance Aliou seye
issa pouye amatoul palasse ci lamb dji
Issaa doonatul mbër bayyi leen ko rekk ngir yàlla mu took toogam
Franky 💪🏾💪🏾💪🏾
Issa fitte bi mo dess
Franc vs gris 2
Franc vs malick niang
Franc vs modou anta
Franc vs moussa ndoye
Franc vs amanekh
Beuré da am yone
Gni nga wakh fi nieup franc mo lén meun lou lér lala wakh
@@dimkhalebambiste2931 Franc Ak Lac 2 Moy Combat
Li ngua wakh yeupe logique leu té aye combat la mai gayi dougne dieule franc malako wakh fi
@@dimkhalebambiste2931 même boulén meuné moy yonou lamb kw
Après bou si dané kén dém si niom boye niang,gouye gui,sathies,tapha tine gris Bordeaux ,lac 2.......
Malick Niang Dale mo Massi diahal mes le reste mome franc moléne meune
Ndeyessane issa menegueu beurer mais khekh gua meunoule
Issa demal jubile dji te bayii lamb
Voilà comment je regarderais tes Combat. Rediffusion Rek. Car tu ne vaux pas que ont dépense son argent sur tes Combat.
Ya bone
Alioune Seye No2 vs Niak Ndiarignou
Alioune Seye No2 vs Diene Diouf Kaïré
Meunon len bayi sou mbeur dano rk guenn nako bayil solen ko bayilo yena koy diox loumou yobou keuram
Sa way outoum Dépense dina taxe ngay tayalé sa bakane ki meunatoul té boy yi niepa soxor
Sawaye, bénneu, Issa toog na 6 ans beuréwoul, amoul bénneu compétition, perte na aye repèram. Niaar, Issa meussoul meune khéékh. Meunoul door, meunoul fayyou, meunoul moytou. Niétteu, Issa magg la. Yow mii naane bouko kénneu néé na bayyi, sougnoukofi gaagnéé wala gnou doumako fi wala gnou K.O. ko, torokhal ko, dou yow yaakoye fadj. Kone maye gnou rék, gnou wakh sougnou khalaat tchi moom tranquillement.
@@elilhrairrah01Lou leer ga wakh bro
Non alioune sey warouwonn dor sa way yaw la fral mais issa damo yerem bilahi sama yaram bi sakh day daw
mane gnèmèna Issa nagn mako diokh ma dèfalko bagage 😛
Lac de guérre 2 franc Comba la
Franc 💪🏾💪🏾💪🏾
6
Franc vs Malick Nyang moy combat
Lolou dou combat
Issa pouy lii.mouy ya meun balla gaye😂😂
Bravo
Mane khawma koulla conseilé khékh sakhe kokou moffi indi li yeupp
Issa bayiwoule lamb lamb mo bayi issa
Yerem nako lol nak
Ya bonne😅
@@beuguebamba7612 si lane amna niari diabardé
Franc NDIAGO hamna soceh boubakh lathiel sa arrière parents il vont te le raconter CASAMANCE bébé Guinée Bissau tu peux pas faire un seul combat en lutte avec frappe gagnéko dilaké LAC DE GUERRE tu joue de ta vie Lac de guerre deffa commencé ki souf bé yeggue ci kaw
Issa pouye il faut mou defar yaramome
Alioune seye 👉 malick niang
Fran ahomo sa bop
Palla tay dioum nga beuré bi thi khekh la diékhé
🤣🤣🤣
Issa pouy waro won dieul combat bi dagua waron entraînement un à dora nieuwat
Iisa pouy da yakhu bilay n'a bayi mberé mo gène balla ak lac ak Modou lo depuis bobu ba legui Moy lolou
Franc d'où sama mbeur m gayii dagne ko wara dieule loloy yone
Niom niar nieup amouniou compétition Aliou seye si bopam da diexal way Issa mom boussss la
issa pouye khana meno nopal wa thairoye ta bayi guir yalla
Wakhall way 😅 ah
kou danne tayson2 avec 19 victoire loy doyé sokh
Lac 2 Na Dieul Franc Pousoul Pasoul Danoufi Kéne Dou Beuré Dou Khék Dou Mobilisé Bakom Nékhoul Safoul Xorome Safoul Soukeur Franc Moko Eupp Mbolo Dakh Ko Beuré Eupp Ko Fitt
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Franc 💯 mo neune lac 2
Dans tes rêves
Lac de guerre & Franc combat leu
Métina trop mais issa bayil beuré mo gueune
Issa na bayi bere ah
Issa pouye . iow Giis nga bouma dégeté nga lath revanche contre balla Gueye bilahii nalla porté pleite . iow Alioune seye mola Door nga danou .... Cone ham nganii boula balla Dooré bilahii yow malhiam ngay yéwo ????
Wakh Ngua Deug Deh 😂😂😂😂
@@mansourdieng2000 Non issa pouy wéroule bro .. comment il peux demandé 👉 revanche contre Balla gueye .
@@donandiago8363 Wakh Ngua Deug Deh Kou Manoul Dane Alioune Seye 3 Mano Dane Balla Gaye Issa Pouye Aï Rétane Sakh La Déf Balla
@@mansourdieng2000 Da bakh rékk😂
@@donandiago8363 Béne Instant Damako Yeureum Sakh
Issa pouye na bayi xamul gatttttt franc c le nouveau roi
Ils ont tous plus de 38ans de vieux jeune
Frank vs Malick Niang lolou moy combat bi. Frank boule dawsa morom yi
aliou seye 2 vs dione kairé
issa pouye yalla talone nala mola faye nak geumal lolou ta sétti lénéne boul yakhe linga diotona liguéye
zoss vs issa pouy combat revanche
Issa pouye meunoul kheekh.
😂😂😂😂Issa pouye
😂😂😂😂😂😂😂issa pouye
Issa dafa pérd rpér dafa geudieu beuré ndeysan
Sa thies ak Franc
Comba la dé loutakh gayi wakhounousi
France vs lac de guerre
Issa pouye rk nioune aye gore laniou
Issa demal tok Bala khaleyi dila reye thi lambji bakh na linga mounon mouna toko deh bakh na
no issa li dou azar demal fadiou té bayi beurre
Lamb modoy war issa dane nafi balla t tay balla rawnako luway am dako maseu niak
Sports daffa am ay réalités toklén fofou nane Maradona ndanane lawone wala kiné lam ak Maty Thiam dogo khéwone nagnfi
Balla gaye dane nako
Aliou seye 2 vs franc lolou moy combat
Frans vs lac 2
Ok