Je suis Talibe Cheikh. Mais sérieusement c'est extraordinaire. Je vous ai écouté durant toute la nuit. Non je peux pas dormir tellement c'est fabuleux.
Wawaw Mourite🤍Naguén défak kénal gui ba Ahmadou Bamba yéna gui kay Bërr📌 Gni nioy le reflet d'une bonne mélodie 🎶 vous reflétez très bien la réalité des écrits d'Ahmadou Bamaba❤️🥺
Képe kou aimé sama commentaire yallah nga ngeureumou serigne touba
Amine❤❤❤❤
Amiiine
Alakhouma amine
❤
Amine❤
Je suis Talibe Cheikh.
Mais sérieusement c'est extraordinaire.
Je vous ai écouté durant toute la nuit.
Non je peux pas dormir tellement c'est fabuleux.
Daga bax rek
Gni tok si kourel gui yeup mou nekh leine mou nakari leine daniouy dem ALDIANA❤
Par force
Mais mourite bou dougoul ardiana kouyy douggou aldianna
😢😢😢barket borom touba
th walaie ni laniouy togué aldiala di diangal serigne bi mou tok di tewlou ahh mbolemm mouride inchalah
Même mane mi di deglou wallahi ndeye sane
Way Jazbu bi mérite d’avoir 1M de j’aime 😭😭❤️❤️❤️✨✨
Billahi
Wa darou khoudos adouna yénafi daka diangeu masallah laf thiatt
Maasàllaah ❤️❤️❤️ Sëriñ Maxtaar yal na Yàlla yokk wér gi ak kàttan gi barkeb Xasida yi.🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Ndesane machalla Amine waye jaajëff sama jewrin
@@babacarndao528 Jërëjëf ❤️🙏🙏
اللهم ءامين يارب العالمين
Amine wy
Amine barkëb sëriñ Tuubaa ♥️
Jazbu de l'année machallah gayou bakh yi 💖💖💖💖💖
Du siécle
❤❤❤😊
2007 ba legui magui soga degg jazbou deug deug et authentique 🎉
Ndéyssane lii nékhna
Jazbou c'est de L''or
😭😭😭 hbtdkh dinagn Ray nit ly dawna yaram dieuzbou darou bi
Sama confiance ci serigne bi Mom wallahi bokou ngeen ci likoy yokku 😭😭😭😭
Këup ko beugg lou bakh ta yalla rek takh dina len beugg wallahi Ndakh yalla rek ken woulo sërin tuuba rek ken beugg lolou lérna gnëup
Amine wy
Walaahi lu wër Nga wax 💘💘 htdkh ❤️🍒
@Lou doul AK talibe safouma
@@abdoudiouf2084 Lo beug wakh ? Maname ?
Dieuredieuf Serigne Touba
Sama rabou xassida yi thi yén lay yeungo walahi HTDKH yéna meun niép❤
Baye ablaye Niang kholom sédna si yéne ndeyesane li kawéna 😭😭😭😭😭
Ndey saan cëy yàlla 😭♥️
❤❤❤❤❤❤ yalna sénn diamou sah dack mbarké borom Touba. Bilahi guisslénn rekk layy révé
Li senegal rek la ame weureul monde bamu dadj doko guis dieureudieuf borom touba
Wa li nékh n'a dè aye way aldiana soriwol fî dé❤❤❤
❤❤❤
Paradis sur terre ❤❤❤❤ laa mourit Di doundou
Kawé na
Deugou na
Magué na
Nexnaa
Yalla gen dadié ak ngeureumou kou ted ki si barké Mame Lamp fall❤❤
Amine❤
amine
Yallah nagnou sáx si diamou yallah ak sáx si beug Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul❤️
Borom touba moroman te woull serigne mountakha mbacke yalla nafi yague te wer❤❤❤❤❤❤❤
Thieuy baay ablaye niang yalnako yallah yeureum bayna Waram
Makhtar diene yagu fi té andd ak weer guiir yalla😭😭😭
Billahi yéna dakh diangue si monde bi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉je suis content de vous ❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Manchallah Seugn bou mak bi meun na bind wayé yéne tamite meun nguén diangue. Yalna sa borome nangou té barkél si barké weeru koor gui ❤
manchallah amine yalla nayalla yok were😍😍🥰🥰🥰
Banneex bii yeené nathi s muntaxa looll sax wallaahi❤❤❤
I am so lucky for been a mouride.i listen to xassida every day I love it.its makes me feel good ❤❤❤jerejeff shering touba 🙏🙏🙏🙏watching from Sweden
You are kind
❤❤ ❤❤❤❤❤
They speak with our soul our heart
Qq😊😊@@dakarvaisselles
❤❤❤❤❤❤❤❤@@wakeurboromtoubasenegal5905
Barke serigne touba dolene nite😭😭😭😭😭😭😭
Jazbu Daaru Muhty/Baay Ablaye Niang - Kurel National HTDKH - Dundal koor 1444H/2023
0:01 1er Daaj
18:35 Soppi 1er Daaj
31:47 2ème Daaj
43:25 Soppi 2ème Daaj
52:40 Daaju Baay Ablaye Niang
😂🥰
Diadieuf mouride🎉
Kènedou cheikhoul khadim dieureudiefé borome touba
MashaAllah❤ trop 💪 forts ils sont dans un autre univers il sont au dessus vraiment!!!!
Machallah douma dagne diko déglou
🙏❤️MACHA ALLAH❤️YALNA LÉNE SERIGNE BI GUEUNEU TAKHAWOU BOU BAKHABAKH 🤲
Thieuy wa aldiana national bou htdkh ❤😊
😭😭❤️❤️est-ce que bayi guen khel ya khayra zik yiiii 😭❤️❤️❤️❤️
Ndey saan xolalma sëñ Mbàkke aka yëemë ta Yaru htdkh amuñu moroom ♥️♥️ sëriñ Saaliwu moo léen sàmp bu léen ragal dara 👊👊👊
Wawaw Mourite🤍Naguén défak kénal gui ba Ahmadou Bamba yéna gui kay Bërr📌 Gni nioy le reflet d'une bonne mélodie 🎶 vous reflétez très bien la réalité des écrits d'Ahmadou Bamaba❤️🥺
JAZBU bu neex loool ❤
Jërëjëfatii BOROM XASIIDA YII ❤️
Yàlla na ngeen si tasek tawfeexu XASIIDA yi si barkep mbecte Murid yëpp 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Machalla ♥️💝 dieureudieuf Serigne Touba diarama Mame Cheikh Ibra Fall ❤❤
Dieuredieffeti serigne Touba Mbacké Amoul morom ❤❤❤❤❤
yal nangeen dajale ay ngeremiy
barkep maam seex IBRA😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤ ,sama xol daa sedd way❤
اللهم صل على محمد وسلم
Machallah serigne touba amoul morome dh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla tawfekh rek barké Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ ❤️
Dieureudieuf borom touba wayé diadieuf kourel Kat yi
Bilay hawna dioy .li defa daw yaram machaalah ❤❤
Jezbu bi mounou ma sappi 🥰🥰🥰
Dieuredieuféty Borom Touba ❣️🤍💫👋😭😭😭😭
Sérigne bi rek moma yéém bilahi
Alaahu akubar! 🤭🤭 man de walaahi tay laa gëna yeemu ci boroom tuubaa jërëjëf Seexul Xadiim 😢😢
Waye sama khol sedna waye yalla na sene diamou sakh 😢😢😢😢😢😢
Adouna ak yawmal yikham yenafi dakha diangue Barket borom touba
Nagne weureul kouy deudj nihmal Nabi dji 😭😭😭🥰🥰🥰🥰🥰
Alhamdoulilah alhamdoulilah alhamdoulilah jarëjëf SÉRIGNE TOUBA
bilahi daye guena nex rek ba aldiana ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lii dé Yallay késsé leu 😭😭
Jazbu bi moom DEUG yalla Amna solo
Ndaysan yalla na lenn yalla defal diamou barke seringe touba❤😢
s.touba amoull morom❤❤
أللهم صل على محمد وسلم
Ndeysane 😭 sama MaMe moko dadj S Matar Diané Daroul Mouhty
Dieureudieufati yakarou diam gni❤
Diangéne jëff yalna yalla yagal léne takhawo léne barkep xasida yi sala❤ sédd na yarona pagé na
Minute 32 meune nama rraay.. dieureudieuf Serigne Touba
Kouboule Serigne Touba falé wouniou la😢❤❤❤❤
Wakh len niou lolen beug tmt😂atanou niou li Baye Ablaye niang bi oh❤
Ahmadou borom diamono di sunup yakar dunya wa uhra yalnanouko sam borom féyal bilakhi walakhi
Manchallah 💯🙏🏾🥰
Yéneu fi meun walahi ❤️❤️✅
ESKEUY DIEUREDIEUFEI SERIGNE TOUBA JAZBU ❤❤❤j
Serign makhtar diene yalna yalah goudal fanam ❤❤
Dieuradieufé BOROME TOUBA
Machalla ahmadou rék ba fawou ❤❤❤
Ndeysaan 😭😭😭😭😭😭😭😭 thieuyyy Niooom dh Touwarkaah bilay yèmè na lool sakh
Li néhna ba diégui dayoo ❤❤❤❤❤
Alhamdou lilahi rabilhalamina s.mountakha mbacke yalnafi yegeu loooolll tewer ❤❤❤❤❤❤❤jawrin likawena loooolll
Wouy sama ndaye li limou ❤
Ndëyssan 😂😂
Theuye sarigne touba ❤❤😢😢
Machallah tabarakallah 💙🖤🧡💜💛❤️htdkh ma fierté
Jërejeufei serigne touba ❤ serigne Mountaha yalna fi yagu loll tei and ak wérr 🙏
Machalla li nekh nadh
Mais si première dadie bi kiy yokhou té mo bokk si ngiy awo mome kanla tmt guir yalla wakh lenmakou ma ziaré ko ❤❤ allahou akbar il n'est pas humain
Segn Moustapha Niane leu tout tank leu deh wayé deuf yémé
Jazbu bou melni doufi amati😭😭
Aka yémé dégal dathie ba 😊 ndeyesane
yalla nalen yalla fay si barke khassidas yi
Machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah
Maa saa Allaah baarakal laahou fiika ❤💞😍😭
Machalla SMA rouyo waaye yi❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah amna solo ❤
Woorna yalla kontaan nañ loooll❤❤❤
HTDKH bénéne dimensions la 😍😍😍😍
Ndeysane thieuy liyaka néx way❤❤❤❤
Thieuy sm mokou yi wa HTDKH ♥️😭😭
Ndeyssane thieuy lii kawéna lol waye barkep brome touba
Cëy amolène morome dé ❤❤😭😭
Ndey Saane aldiana sori woul yén n'a man lingén di deff❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bayina di déglou xassida man késsé ohhhhh❤❤❤❤
Li nexxna ci khôle way❤❤❤😢😢
MASHAALLAH CHOUKRAN ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla n'aléén yalla défal diamm waay
Jërëjëff borome Touba 💯👌
Yalla rek Molé. Féye