Non assane a une belle voix vraiment je l'adore en plus il est cool et correct 'il ne bouge pas sur la scène tout comme papa thione qu'il repose en paix
ASSANE GAYE DOIT REVENIR AU SÉNÉGAL CONTINUER À FAIRE PLAISIR AUX FANS CAR C’EST UN VÉRITABLE TALENT👍 QUI EST D’ACCORD AVEC MOI🤷🏾♂️ TEXTES RICHES,BELLE VOIX,IL A TOUT CE GARS👌
Assane gaye déloussil wayé, il ressemble tellement à mon frère, on avait même son CD à la maison et j’avais tous les sons parcoeurs ndeysane il chante tellement bien.
Merci beaucoup Sidi Diop. Je t'apprécie beaucoup t'a un grand coeur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ bonne continuation. Que Allah te bénisse et te protège Sidi Diop. Merci
J’ai jamais aimé une célébrité comme Assane Gaye. Ce qui me préoccupe moy depuis deux semaines sama xel bi meunoul degn ci mom. J’écoute ces chansons en boucle, di weur ses vidéos. S’il y’a quelqu’un qui peut me mettre en contact avec lui Nguir yalla na ci diap
Ki mo meune gayii, generation 2000, khamouniou ko,. Kou d'accord defal j'aime
Mane generation 2000 la te khamna wayam yeup 😂
Assane il a debuté en 2006
Lou takh nguên yap générations 2000 bii😡
Assane vient continuer ta carrière musicale pour les fans 🙏🙏🙏🙏 demande nationale ❤
Il doit revenir❤
MATAR DIOP NA PRODUIRE ASSANE GUEYE IL EST TROP FORT
Sidy moy Sénégal lou nice rk ngay def❤
Assane Gueye La voix d'Or😢😍😘
Non assane a une belle voix vraiment je l'adore en plus il est cool et correct 'il ne bouge pas sur la scène tout comme papa thione qu'il repose en paix
Assane a une sublime voix. C'est un délice. Je le classe tout juste derrière You et Thione
Il se dit qu elle gâchis de talent,il mérite plus...
ah voilà mon chanteur Assane gaye
Assane yalla Nala yalla diame
J'ai les larmes aux yeux. Assane Gaye que Dieu te bénisse 🙏 bonne continuation à toi ❤️❤️❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Le regard de Sidy envers Assane c’est juste émotionnel ❤
Sidi diop le meilleur senteur du peuple diop rek moffi nek ♥️ inchallah après korr gui gnou défatt lou nekg
Chanteur
😂Lolou la sentir
Vraiment contane na trop si guisate assane gaye kou meuna woye ndaysane ça fait plaisir ❤❤❤❤❤❤❤❤❤merci sidi
Sidy tekk khel la khamna ltkh mou nangou micro bi😂 assane ya meune mchallah❤
Afaire bou Nice machallah sidi
Gni mana way gnépou dagno beuga sidy❤❤
ASSANE GAYE DOIT REVENIR AU SÉNÉGAL CONTINUER À FAIRE PLAISIR AUX FANS CAR C’EST UN VÉRITABLE TALENT👍
QUI EST D’ACCORD AVEC MOI🤷🏾♂️
TEXTES RICHES,BELLE VOIX,IL A TOUT CE GARS👌
Sou délousé ma commencé wate dem concer 😅😅❤
PÉTRI DE TALENT , ASSANE GAYE!
Assane Gaye please go back to the studio you stile young and talent you have the chances people are emotion good luck bro
Mane khamouma loutakh Assane gaye bayi waye dafa meun Machalla ❤❤❤li nekh na trop Bilaye
Oh Assane Gaye reviens nous way kou meune way way machallah ❤❤❤
Li nekhna ❤❤❤❤❤
Ohhh liiii nekhna trop wayyyy
Blh walahi sidy Diop ya meuneu way yalla nala yalla défal diam si barkép borom touba
Assane ndeyssan fo nékone 😊
bly papa dji ya mana way❤🎉
Bilaye sidi Diop ya bakh man Kaolack la dek mé diapaléko pour gnou guissko
Sidy Diop ya meune ya eupeu doolé ❤❤❤
Assane do moromou sidy. Fansam yii sax xamnaniouko
Ya mana waye❤❤❤❤❤❤❤❤
Assane gaye déloussil wayé, il ressemble tellement à mon frère, on avait même son CD à la maison et j’avais tous les sons parcoeurs ndeysane il chante tellement bien.
Sidy kou bakh la ❤
Woy Assane mungui Machalla aka ma bueugue ki ❤️❤️❤️😍😍😍
Sidy Diop dafa yemou si Assane Gaye, voix bi mo nexx trop
Merci beaucoup Sidi Diop. Je t'apprécie beaucoup t'a un grand coeur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ bonne continuation. Que Allah te bénisse et te protège Sidi Diop. Merci
J’ai jamais aimé une célébrité comme Assane Gaye. Ce qui me préoccupe moy depuis deux semaines sama xel bi meunoul degn ci mom. J’écoute ces chansons en boucle, di weur ses vidéos. S’il y’a quelqu’un qui peut me mettre en contact avec lui Nguir yalla na ci diap
Dafa neu dé
Sidi da bakh❤❤❤❤❤
Assane dama contane bimala guissé ohh ningay deff sama khol ak sama bossou dieukeur tamit yaw rekk lay topou dé 😢❤❤ reviens stp sur la chaîne
Diop Yalla nala yallla samou Lou bakh rek nga kham té mom rek ngay def di fenial ndanan
Man deh loumay dioy la xamoul😭😭
Ken du assane geuye bilahi
Thank you Sidi 🙏❤️❤️❤️
Asan gaye ❤
Machalla ❤❤
Assane gaye chante très bien.
Vive sidy yagui fegnial kou ay ❤
Sidy rek
Assane gaye il est trop fort 😊
Mane damako massa begue ❤❤❤Assane ❤️❤️
Li nice nz
Euyyy🔥🔥
Billahi ❤❤❤
Cheeeee Assane Gaye 😢❤❤❤❤❤❤
Voix dégatou mako fen srx❤
Bintaka❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yag nga way lou nex ndeyssan
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J'ai des chaire de poule
Waye Assane Gaye y'a meuna waye
❤❤❤❤
Oh ❤❤❤❤
Assane mo meuna way Mais kéne dou sidy
no ki ❤❤😢😢😢😢
Sidi diop nitte kou niakk kiniane lii kou sokhor douko déff matar soubatélle diapelélle assane gaye téh yalna rek takh
Sidy Diop Dou nitt bilahi❤
Assane namnagnoula ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je connais assane on habite dans une même quartier sara kaolack on surnome cole gaye son grand père etait notre chef de quartier
Lolou deug la, je suis de sara aussi)) cole Gaye il n a pas su gérer son carrière dommage
NDEYSSANE AY SIDY YAA RAFET XOL TE' GORE' BILAY. XOL TOYNA TOROP SAX😢👈
Sou musique wakhone deug heure bi fougn toude youssou ndour tekossi gni yageu suivre musique sénégal depuis 2005 dinagn ma cédé li
Ah bon
Assane Gaye L'enfant Cheri D Kaolack Ndangane Domou Carage Mamadou Beye Bi
Assane a,na thieur si musique sénégalaise🥲
sidy tu a bien fait ma la ko wakhone bo fataliko
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Assane ❤️🫡🫡
Sidy y'a bakh
Micro bou khéwi bi
assane gaye aka mana WAye bilaye diapa lénco
La fille lamigne bi safff na dee djigeune gaye wakh di saga akk youkhou nii nonnnnnnn😢
Dafa alou rek mo takh
Djiguinou milieu la 😂b
@@sonkofocus2024-ph4hv peut être mais des foi dagniy alou dè
Sidy Rick 🎤🎤🎤🎤👑👑👑👑👑✅✅
Lamine lame legui yay snapeur sidy legui 😂
Le talent ne se cache pas assane colou do nite
😢
Mais assane gaye loutakh percer woul disparu des radars d’un seul coup🤦🏾♂️ il etait trop fort sugn jeuness beugone nagnko
Moo dakk way Senegal ci génération wam
Oho assa ne guaye foymou nekone aye
Ki ndéké mingui meun way batay
Aka mana waye
Waay wou nekh dou sapii moukou sonbi benenn afairela
Bilae frère
Ma la mbeugue sidi
Assane delousil beugualgnou namounala
Diop suel kasé
Diabira bou sidi diop ❤❤
Sidy woyam dafa am ay ndaysaane motax mook assane Lou neex rek lay doon .....assane gaye maako yar
Li domasi doyal
Assane Gaye keine dakhouko wayy mais guel bobou di awou sii souff tmt hoo
Guisnga adouna louwaye rendi say lokho laye nothing Assane ndane pir nga
Non li nexx na trop
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤