Il faut que le président Ousmane Sonko sache qu’il n’est plus dans l’opposition mais le premier ministre du Sénégal 🇸🇳 il doit nous aider et s’entourer avec les forces de l’ordre sa sécurité me préoccupe vivement 150 députés pour le parti pastef.
Ngone saliou salma penser a couper le micro et faite attention les filles entouré vous de garde de corps même s'ils le faut patriotes depuis Angers France bravo les filles ❤
Sonko limouy xolé baniouy attaqué cortège bi,waroulene may dara,il n'est plus dans l'opposition il n'a qu'à mettre les moyens de l'état en contribution puisk au delà de sa candidature il est le premier ministre du Sénégal
iow momou Di wakh xamnala bou bakh boul faténii sa yaye meuss nangnko béteu ak goor souma dioumoul iow domou eumbeul nga soma wédé nga lathieu sa yaye😊
N'importe quoi. La violence c'est l'arme des faibles mais ça ne passera pas . Arrêtez de trop parler.. Que la riposte soit exemplaire et il n'y aura plus d'attaques c'est aussi simple que ça... La campagne doit se faire dans le calme la joue et la sérénité. Que chacun essaye de convaincre avec son programme et le peuple tranchera.. Il ne devrait pas avoir de problèmes PAS DE VIOLENCE
Ndeysan opposition bi danioo diommi mootakh niou yaakaarne violence moo leen cimeuna guenne'e kenn douleen faale' ba le 17 niou doggalileen niou mayniou diamm😂😂😂
Il faut que le président Ousmane Sonko sache qu’il n’est plus dans l’opposition mais le premier ministre du Sénégal 🇸🇳 il doit nous aider et s’entourer avec les forces de l’ordre sa sécurité me préoccupe vivement 150 députés pour le parti pastef.
Il na pas droit le prendre les gardes corps de l'état c'est politique cause
Tu as bien vu d'autant plus qu'ils prônent la rupture@@madibadiaby3329
Merci fadilou keita bon boulot ce monsieur est incroyable
Képeu kougne attaqué le convoi de sonko dangaye harou. S'ils sont garçons qu'ils se montrent
Mais ils ne sont pas garçons nak, que des lâches
Yow finga tok di wax
Attaquer le premier ministre key😂😂 opposition bi deniouy cinema quoi
Retirez vos cartes d'électeurs plus important que toute autre action.
C est la lâcheté ils faut prendre ses gardes
Il faut donner à sonko la majorité absolue 150 députés
Opposition bi kham nagnu ni perdre nagnu élection yi ba parei li rkk molein dessé violence
Lii rek moleen dessé ils ons perdus sur tous les frons,domeramou macky sall yi ak barth judas ,fi sonko mo fi nekk❤❤❤❤❤
Sa leufeul Ndaye loufi nit def Tay si
Sonko lako guisse
Ngone saliou salma penser a couper le micro et faite attention les filles entouré vous de garde de corps même s'ils le faut patriotes depuis Angers France bravo les filles ❤
Bayil niouy diay beug gor bagn dokhan sen nday kher
Gni dagnouye kharou li wonne wonnina Sonko lègui moye gouverné dou yén té guéne yém
Ça c'est de la lâcheté purement et simplement.
😂😂gniy attaquer Convoi sonko khana dagnouy kharou
Boy yii dagnou lay diaye sen bakene bilay
Battez vous contre ces bandits là
😂😂😂
@@falldiari6919kou ci d3 danga kharoti rek
Merci baucoup on firire de vous❤❤❤❤❤❤❤
Ils vont tous pourrir en prison
Sonko limouy xolé baniouy attaqué cortège bi,waroulene may dara,il n'est plus dans l'opposition il n'a qu'à mettre les moyens de l'état en contribution puisk au delà de sa candidature il est le premier ministre du Sénégal
Demlene jiangui journalisme liguafi filmé AK liguafi wakh darra bakhoussi
Sonko fo diar yone le yaw rék yafi nék di dokhal déffal loula saff opposition amoul
Mais reportaire bi Kane mokoy dictée 😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Diame yiñu dieude la,ñu féye len ñu nagou lolou mooy nekk diame,.
nous devons éviter les violences,si nous voulons avancer notre pays
Vive Bougane Guéye Dany ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✊✊✊✊✊✊✊✊✊
Daur deuk lawone wayé fayou mo tash ndayam kou lenn attaqué ngenn tegal sen nday
aywaye diaye léne combat bi wa Ziguinchor niou yar opposition bi lathie lén doudou ka
Koungueul ak Kaffrine dal ay sauvage lagnou, khekh ak attaquer rek.
Sauvageons opposition bi daniouy kharou rk
Li mom liguéyou fanta sall leu
😂😂😂😂😂
Wa kouguel khana danioulene infiltre .naniou khamni rewmi sopekouna
Nagnou bayi histoire yi
Vous filmez trop mal
Pros yala naka yala may ndam
Koune thi diape rek raye
Koungheul gno guena tardé si politique thim wa diguene de pros rek mofi nek
Ces des domou kharam li reck moléne d’Èce
Avec ca ngen né ay journaliste ngen war ngen woné lep ngir eleg ndax informé juste moy sen mandarga en tout cas defoulén sen liguey tapet deg ngen 😂😂
Degeulema dof bi nane boule dieul violence bi yew petit kon sa bopou ngay filmel wola nioune
Daniouko téré khana sètano association des imam à la télé
Amago 1 ane sakh fo diar
Niou lay yakhou dela sane ay khér😂😂😂
Kone wero yaw pros fou kougnouy trokhal diam yi gnou fay gnoy sani ak di yokhou
Xolal dmr dji sa morom yeup gui rayanté pr Sénégal émerger yaw gay xeuy di mar boune thip
Vive Bougane Guéye Dany ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊
Vive la coalition samm sa kaddu vive président Bougane Guéye Dany ❤️❤️❤️❤️❤️❤️✊✊✊✊✊✊✊✊
Moi je crois que Seneweb fait du Yok
Il sonko s'entoure de la bip et gign en plus de ces gardes
Astaghfiroullah 😂
🧐😂😂😂😂
La Sécurité de PROS doit être renforcée.....Ils sont extrêmement dangereux ce sont des lobys derrière tout ça...P comploteur est tapis dans l'ombre..
Où est l'attaque???? Moi c'est plutôt pastef que j'ai vu attaquer
guissaguoulenn darra 👈🚨💪khaléyi danio sonnn😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Way yaw dall Sa dokhotou Serigne nioune😂😂
N’importe suoi ba la 17 😂
Dagno xamoul nê ki gnouy attaqué mo nara sauvé Sénégal andi natangué
@ niga toll nga wakhei 😂😂😂 sen khol yei bonne massa bois de l’eau frère😂😂😂🚰
Bahna is sonko
😅😅😅 yaw wero
Dotou niou ko doli dh 😂
ousmenteur léger ceinture 😂😢😮😅😊
Kom sa baye rk woyof toubay ba diour dmr bu melni iow
iow momou Di wakh xamnala bou bakh boul faténii sa yaye meuss nangnko béteu ak goor souma dioumoul iow domou eumbeul nga soma wédé nga lathieu sa yaye😊
Sa yaye moy oyof seure kou nieuw roff😂
ca c'est mauvais signe pour un regime qui n'a meme pas fait 1an
Cherchez les vrais coupables à cette situation et doutez nous la paix bordel 😢
N'importe quoi.
La violence c'est l'arme des faibles mais ça ne passera pas .
Arrêtez de trop parler..
Que la riposte soit exemplaire et il n'y aura plus d'attaques c'est aussi simple que ça...
La campagne doit se faire dans le calme la joue et la sérénité. Que chacun essaye de convaincre avec son programme et le peuple tranchera..
Il ne devrait pas avoir de problèmes
PAS DE VIOLENCE
Lann moyy mauvaise si lii dafa mousoul amm si élection Wala
Ndeysan opposition bi danioo diommi mootakh niou yaakaarne violence moo leen cimeuna guenne'e kenn douleen faale' ba le 17 niou doggalileen niou mayniou diamm😂😂😂
Journaliste you tapett nii meussoumako guiss tchimm
❤❤❤❤
Vive Bougane Guéye Dany ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊✊
Lousi sou niou yone