Je ne vous connais pas, mais je suis particulièrement touchée et émue par vos temoignages mutuelles qui dégagent de la sincérité et beaucoup d'affection. La discretion et la timidité ou plutôt l'humilité de EDU me touche. L'amour profond et l'estime que FAMA a pour son mari est palpable. Vous etes juste MERVEILLEUX. Ne changez rien. Que Dieu veille sur vous et vous protège.
Machallah Édou sédé yi rafféte na trop longue vie et que le bon Dieu veille sur toi ❤dieukeur bou am dîné dafa nékh barki alcourane yalla mayniouco yokal niou souniou diné dioubolé niou ak souniouy borome keur barké Seydouna Mouhamad PSL ❤
Ndeysane edou goor bou bakh féke jiguene mou am ay dom djougué si deception goor yi bari si yaw lagne wara roy motah lou bakh rek ngay am jiguene soko yeramé yalla sagal walakhi❤❤
Machallah Doudou ndao allias Edou témoignage rafetna wayé Gor bou bakhé diabaram Moko doléle chapeau à vous Fama athioune yalna yalla Défal len soutoura ak Diam personnellement ces mots m'ont touché ❤❤❤big Up à vous deux
AMEN AMEN AMEN. Que DIEU ENTENDE ET EXAUCE TOUTES VOS PRIÈRES. QUE DIEU BÉNISSE le couple Edou-Fama (sans oublié ceux qui ont de près ou de loin contribués à ce beau anniversaire)
ils sont trop adorable oui Edou est un cool gars oui et j'adore leur couple fama est une femme que j'admire bcps j'ai meme pas les mots pour decrire ce moment je regarde cet video akk fierte bly yalla nalena yalla sam et paix à son âme a JP
maaachaAllah, dioulité lako niép séédél li laniouy wax l’apparence est souvent trompeuse…..maachaAllah xol ak dieuf moy dîné Yalla naniou Yalla déf deug deuggi dioulite incha Allah🙏🏾🙏🏾
Jan Paul ndeyssan yalla nala yalla yeureum té kharéko Aldiana
Je ne pouvais pas m'empêcher de visionner à nouveau cette vidéo repose en paix Jean Paul d'Almeida
Bilay kokou wakhone dans kelk mois dofi nékatt
je me ss retourne sur cette videos pour revoir les delir de jean paul je te jure
Même moi parsk dafa meti trop te beté mom sakh BET nako
Bilahiii
dd
😢😢😢Jean-Paul ndeysane 😭😭😭j'arrive pas le digéré mon acteur préféré repose en paix 🙏🙏🕊🕊🕊
Fama thioune j suis contente de te voir heureuse 🙂 Machallah yallah na sax
Ndeyssane edu boko guisse kham ni kou bakh la Mach halla ♥️
Ndeysane lima guisse moy il adore l'enfant nonou rek leu kou beug yaye danga wara beug dom c bien ❤❤❤❤
So beugé sérigne Babacar sy do bonne machalah yalla nala thiat séhlou sa barké sérigne ❤❤
Je ne vous connais pas, mais je suis particulièrement touchée et émue par vos temoignages mutuelles qui dégagent de la sincérité et beaucoup d'affection. La discretion et la timidité ou plutôt l'humilité de EDU me touche. L'amour profond et l'estime que FAMA a pour son mari est palpable. Vous etes juste MERVEILLEUX. Ne changez rien. Que Dieu veille sur vous et vous protège.
Un
Bonjour il joue Io Io o
Edou reste comme tu es trop gentil vraiment je t'aime fama dama djitou rek longue vie .Mme figa diapp fofou la ❤❤
Ndeysanne JP yallah nako yallah yeureum
Machaallah trop choux à tes 100ans de plus pleins de bonheur ❤💞 talibé Cheikh bi Edou 🤲🙏❤💞
Hbd joyeux anniversaire edou longue vie à toi doundeul 💯 ans sans ordonnance beaucoup de bonheur et santé et ta femme 🎂🎂🎂🎉❤️💯
Talibé cheikh dafay thiofé way chéri fama❤Hbd 🎂
Bly walay❤❤❤❤
Néna barcké Serigne Babacar li nexna 😢 longue vie talibé Cheikh bi 😊
Sy faguey demba misiii diawarrrrrr borom bonnet carré biii kenlaaaaa yalla nagnoukooo yalla feyal tagnou siii barkemmmm Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Qui comme moi a regardé l’intégralité 😉 Vraiment jsuis touché par les témoignages Machallah Doudou Yalal Nala Yalla Fay sa Dieuf you Bakh🤲🙏❤️
Machallah Édou sédé yi rafféte na trop longue vie et que le bon Dieu veille sur toi ❤dieukeur bou am dîné dafa nékh barki alcourane yalla mayniouco yokal niou souniou diné dioubolé niou ak souniouy borome keur barké Seydouna Mouhamad PSL ❤
Amiiine y’a rabi
Borom keur bou amoul diné kén do mana nék ak mom parce que lola naxari rék lay déf
Machallah edou reste comme tu es😊❤ et soyez tjr heureux ❤
Ndeysane edou goor bou bakh féke jiguene mou am ay dom djougué si deception goor yi bari si yaw lagne wara roy motah lou bakh rek ngay am jiguene soko yeramé yalla sagal walakhi❤❤
ndeysan jp d'almeda comme sama mbo kou repose en paix
J'admire leur couple franchement c'est pas facile mais ça montre qu'edu est un vrai Gentleman machallah 🎉🎉🎉Dieu vous bénisse 🥰
Ndeysanne il avait la joie de vivre ke DIEU l'accueil ds son paradis céleste
Machallah yalla na Yalla lafale ko thiate yalla doli sa soutoura barcké Serigne Babacar Sy RTA
Machallah Doudou ndao allias Edou témoignage rafetna wayé Gor bou bakhé diabaram Moko doléle chapeau à vous Fama athioune yalna yalla Défal len soutoura ak Diam personnellement ces mots m'ont touché ❤❤❤big Up à vous deux
Kou beug SERIGNE BABACAR SY lalala j'aime❤
Machalla raffetna yalla na lene yalla sambe edou qoude fane ak wer hinchalla o prêt d madame hinchalla
Soyez tjrs heureux mes amours.Vraiment Fama tu le mérites❤
Longue vie 🎂à lui guen koy fête des années ensemble
Amine way gni amagoul borom keur yalla naniou may talibé cheikh
Amine way je rêve que ça yallayalla nagou
Ndeyessane Édou sede yii rafetena trop machallah yalla n'a yalla goudale sa fane sii barke seydina mouhamed aleysalatou wasalam
Hooo Jean Paul yalnala yalla yeureume té kharé la aldiana😢😢😢
Bilae dh Rip jambar
Amine
Ndeyssane il était taquin
Bi pape demba di sedei si edu ndeysane mou lim gnep JP niko degouma sama tour non il était sincère 😭
Ndeyesan jp repose en paix 🪦 et k le paradis soit sa demeure éternelle 🪦🕊️
AMEN AMEN AMEN.
Que DIEU ENTENDE ET EXAUCE TOUTES VOS PRIÈRES.
QUE DIEU BÉNISSE le couple Edou-Fama (sans oublié ceux qui ont de près ou de loin contribués à ce beau anniversaire)
Machallah. Vous êtes bien, JPD repose en paix, je vois ton sourire 😢
Oooh Jean Paul si video bi lako gueuneu fateliko motakh ma gneuw directement diko kholate ndeyssane rip!
😢Ooh JP c'est pour toi que je suis revenu visionner cette vidéo oh belle homme si jeune et qui a l'aire si doux avec ses blagues et tout😢😢😢hé la vie
Bakhe rek mo âme sollo yalnéne yalla lafale thiate same léne bopame si barke seydouna moukhamet psl ❤
Ndeysane jean paul demna nii thiey aduna 😭😭❤️c triste bilahi
Ma ChaAllah lou beurri amna nitt You bakh ndeyssane 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Kou yabou délo sa khel si yalla Jean Paul dém na ni rek 😭 yal na ko yalla yeurem😢
C est la dernière vidéo où j ai vu JP hors série
Que Dieu l accueille au paradis
Repose en paix JP tu resteras toujours dans nos coeurs😭😭😭😭😭😭
Edu aka dioulité ❤machallah happy birthday champion
Machallah edu laff thiatt Ndeye sane damako nobop nak mais joyeux anniversaire à toi longue vie et pleines de belle chose ❤️
Edou je très ému du témoignage de pape demba.Yalnala Yalla fay.❤❤❤
Machalla edu longue vie à toi mais doundou AK dé dieguena li yagoul té kholal JP 😭😭
yalna léne yalla sameule bopam happy birthday a edou sama sopé bii
Machallah bakh rek mo am solo fabuleux jour d'anniversaire mn acteur préféré paix sur toi et ta femme 🎉🎉❤❤❤
HBD DOUDOU long vie a toi bonneur santé réussite totale mon Artiste préfère yalla na yalla sakhale seybi barkel ko ake diabote bou barkel inchalla
Aay way Ndeysane JP😢💔💔tu vas nous manquer
😢
Machallah je vous adore les NDAO avalanche de grâce sur vous
Magnifique magui rètane rek
Allakhouma amine inchallah si niane yi goudou fanak wér khéweul diamou salam nioubokou lépou di niane yalla may niou niouyagueko féké té talko thie barke geungui mindéf SAW Allakhouma amine inchallah🙏🙏🙏
Machallahhhhh don talibé cheikh mo nékh ❤hbd Edu ndao chéri Fama thioune🎉❤
Machallah,édou kou bakh nga ndakh lou nieupe wakh moy deugue 🎉
Ohh Ndéyesane l'image de mon très chère jean Paul ma rendu 😢 triste 🥺 que son âme repose en paix 🙏
Macha Allah yalla nalen yalla kafal tiate té mouselene si pekhé none❤
Yalla nalen yalla lafal thiat le couple fama et Edu machallah
J adore édou moussou mala guiss mais tu es une bonne personne Fama tu a un bon mari séyalbadé
Joiyeux anniversaire a edou logue vi sante prospérité becou de bonheur rewise total dans tous ses proges yale bay coce djabaram
Gueuneu yaggue gueuneu wér thii barkép seirigne babakar Sy Malick ❤❤
Machalla sama talibe cheikh yi happy birthday edou
JOYEUX anniverssaire bax rek moo am soolo machahala ❤❤❤❤❤
Walaye li dafa nékhe damaléne fan en fait machalla yalla naniou yalla maye dieukarou Talibé cheikh waye ❤❤❤❤❤❤😢😢🤲🤲🤲
ils sont trop adorable oui Edou est un cool gars oui et j'adore leur couple fama est une femme que j'admire bcps j'ai meme pas les mots pour decrire ce moment je regarde cet video akk fierte bly yalla nalena yalla sam et paix à son âme a JP
Mane Mome Khawma lanela wayé Couple by Reik la beugg yalla kham nako Mr et Mme Ndao les Éléments Almaktoum je vous j'aime 🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩
Bilakhi ak mane damaléne di nianal yalla sameuléne , mousseuléne si seytané
@@maimounasene6488 Billahi Amine inchallah
maaachaAllah, dioulité lako niép séédél li laniouy wax l’apparence est souvent trompeuse…..maachaAllah xol ak dieuf moy dîné Yalla naniou Yalla déf deug deuggi dioulite incha Allah🙏🏾🙏🏾
Repose en paix 🕊 Jean Paul 😢
Chapeau à toi edou kadou yi rafet n’a machalla
Que Dieu vous protège tous et que vous continuez à nous faire plaisir
Joyeux anniversaire edu doundou bou andak wér ak wérlé yalle sameu leuh ar leuh soutoural yak fama yalle naguén done 👴 et 👵 barké NABIL MOUSTAPHA 🤲
Bakh rek mo ame sollo machalah
Ndaysane yalneu yalla sam gniép encore une fois et repose en paix jean
Jolie couple 🎉❤ hbd l'artiste
Talibe Seydil Aboubacar Sy joyeux anniversaire à toi bcp de bonheur et plein de succès 🎉
Machalla domou ndar danou âme yermeudé âme dîne yanalen yalla lafale thiate
Bilay louy lere ngua wakh dine ak yermande kay nioco ame
Ndeye sane toujours taquin jp. Paix à son âme
Oh c génial Macha Alla yalana yala sahaale ANDE bi j n' vs connai pas mé mangui beg kom kou bok AK yeen, paix sur vous
Aaaa thioum talibé Serigne Babacar Sy biii long vie inchll 🎂🎂🎂
C très émouvant🥹 les temoignages🥰 bakh rk mo am solo🎉 Longue vie Édou et sois heureux auprès de Mme Ndao🥰❤️ Que Dieu vous bénisse🙏
Mach halla yalna l'en yalla lafal thiate 🙏♥️
Ma Sha Allah happy birthday to you dear May Allah give you long life good health Amen
Machallah talibé cheikh longue vie a tw
Félicitations edou et à fama amléne diam vous tous
Bilay jp mo takh ma sétan vidéo bi 😢
Jean Paul😢🕊️💔
Machallah yalna yala goudal sa fann mayla weur mousal la si thiat inchallah
Machala. Yalna and gui sakh si diam té souniou borom atek yeurmandé Jean Paul 🙏
J’aime bien votre couples yalla nalen yalla sammeuh 🙏🏻❤️
J'aime beaucoup votre couple. Qu'allah vous protège. Contente de voir oultoum diè aidara karara
Happy birthday Edou 🙏special thanks to your wife Fama she is awesome 👏 ❤
Yalla na Yalla mey peu goudou fane Édou wer, werlé ak sutura bou sakh Barké Yonnenete bi Sallalaahu Aleyhi Wa Salam Barké Serigne Babacar Sy rta
Auhhhhh Jean 😢😢😢
Mashaa'allah talibé setigne babacar vrai la nak motakh
Bravo machallah dieureudieuf Nice trop diamu rék si yén
Très heureux ménage lii nguén di sentou ci sen seuy bi yalna bou ci sen yakkar tass ci barké Seydina Mohamed psl.
Que vous protège monsieur et Mme ndaw longue vie à vous 🎉🎉🎉 jp repose en paix
Yallah n'a seringue saliou dolli len soutoure 🤲🤲🤲
Ah joyeuse anniversaire sama tipo doundale weral amale diame ❤🎉
Oooooh mes acteurs préférés au Sénégal ❤❤❤
Votre sœur Mauritanien vous aimes ❤❤❤
Bilakhi sandene arame fakha beuleupe doukoumane doumou baye diame thi yaw 🎉🎉🎉
Serigne Saliou yala nala leral leral inchalah machalah 🤲😍