non mais épisode bi amoul morom.😂😂😂😂....vous êtes les meilleurs bravo à tte l'équipe vous remontez le moral des gens.... ça c'est grandiose je vous adore tout simplement
J'ai trop rigolé!!! Daro c'est vraiment un mac! Serieux, elle fait carrement travailler les nanas quoi!!! Mdrrr, j'adore les expressions de son visage!!! lool
ADJA FALL FIKING PATHIE ,DARO BOY GUETHO SOULA DIAPÉ DINGA XAM. MDRR BOY GUETHO MO WARA EUMBAL DARO REK NDAKH MOU RÉGLER ,WAYÉ FATÉ DARO WAKHONAFI ABY DÉFNA LOU RARE KÈNE EUMBATOUL. LOLLL
hahahahahahahahahahaha non mais j'adore dinama nekh daro mom dou changé moukou maimouna mom am na faïda dem na ak copin wam di liguenti vie weum nuit la bou bah narbi mom bougoule kou meulfeu kou diongama la beugue ki mo saysay rek merci pour cette épisode j'ai bien rigoler comme d'habitude tout les épisode je rigole 😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁
Souma meileini bakhata nga melni youte😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂... Je pitié Maimouna😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂... Daro mi😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂... Na mais elle fatigue grave mon'ventre la vie de ma mere... J'en peux plus suis versé de rires😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 #TeamDaro #TeamDinamaNekhTv
Dokhal fowi guay melni wathiou purée Daro fane guay dieulei say terme !!! Love u Daro tu es une vraie artiste. Sougnu wa keur tay gnu am problème ak américain kou ma wakh rek mani leu mane koba gingembre lol rek,
Naba Gueye way daro dou nitte quoi mom espèrei lo na way dji pour mom Aÿ dix mille sakh lako daro di diokh non dou deim mou nane niou niou dougeul KO si album bi loool
Naba Gueye lool non daro dama yakar ni dafa am febarou xaliss esk dou lolou amoul ngoor si xaliss bâ Parè bolei ko ak wakh djou beuri nak comme kou laka Aÿ 40 perokei lool
dinama nekhtv del leeral rang bi waye am na nio khamer et demi laniou nieuw di kheuthioo pé c po normal loool 😂😂😂😂😂😂 mé daro parle tropppppppp come métrailleuzzzz ratatatatatatata mais ki louko dale mdrr😂😂😂😂😂😂
putain mais c'est quoi cette série sans inspiration ni de thème ni de l'humour pure, darro elle a les mêmes folies tout les jours, un moment donné il faut progresser ls gars
Dinama Nekh TV mane maléni diokh ay idée? Kone d amagolénko, par contre y a beaucoup de scénaristes au Sénégal, vous pouvez aller vers eux pour avoir un vrai scénario parce que là ça se voit que sokhla ngénko
SOURMAN JOJO les goût et les couleurs ne se discute pas non merci je pense on a les meilleures scénaristes du Sénégal essaye de capter les messages de la série c'est important mais tu es toujours le bienvenue nio far 😉😉😉
adja fall est très belle machallah.
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂ouf
trop belle 😍😍
OUI tres belle diongoma piir
Wallahi de trop 😍❤️
#Maman Aicha est quadrilingue,elle parle wolof, peulhs, francais et anglais et peut-être même la langue serere😍😂 super 👏
dianko diane guiss ga 😊😊😊
Aja fall est tresssss belles machallah
Habibatou Baldeh 😊😊😊
Mane serigne Faye momay raye, il est vraiment naturel. Faudrait q'uil revienne souvent
Cheikh Danso c'est noté 😉😉😉
Cheikh yaw dara doula raye
Kouy serigne faye🙂
non mais épisode bi amoul morom.😂😂😂😂....vous êtes les meilleurs bravo à tte l'équipe vous remontez le moral des gens....
ça c'est grandiose je vous adore tout simplement
Sah Sandra Lovato merci beaucoup 😉😉😉
Daro nénako loy dioy dénthial say dioy😂😂😂😂
adja fall li rek mo takhe mou nekh ma dafa ame filing avec ak sourireum bou rafet!😍😍😍
Aminata Mengue Ndiaye dieureudieuf way 😊😊😊
Aminata Mengue Ndiaye wakhal way 💕
Dinama Nekh TV k
Dinama Nekhmaramam
cheikh boy v
Maimouna a trop de classe machalah
mane Daro rey naina sén form you diék bi bou ngene ko utilisé won dou ngene todj deukebi ak pétioum nganaaw😂😂😂
no m genrou daro gui souma bokone ak gnom keur kourou rof lakoy dor noo elle est ouff😂😂😂😂😂
Mais daro kou gate khel leu meussouma guiss lou melni mdrrrr. ...merci à l'équipe chaque jour vs ns surprenez
T 9:57 10:03
Man maye ndaré 😂 bou ngén paré ma niuew1⃣ 👉👂guéwalbi néna kachétbi moye DF bueff😂😂2⃣👉👂daaro néna oumi ngaye mélni wagnou 😂😂😂😂😭
Bamabaguye Bamabaguye daro rek 😂😂😂
Hawma kou inventé coursou fass bi mais Wallah togn nagnou lol... Pé ak Deuss boudoul diékh, toutes les séries nak
Mohamed Boye 😊😊😊
Dinama Nekh TV ttttt
Mohamed Boye 😂mdr
Adja Fall est une belle femme MashaAllah..
dinamanekh Tv dolen meu diokh un moyen de joindre Daro svp? daf mey fethie..non Daro mashaAllah😂
souma ndarré takk sokhna sou mellni Daro yalla na donne labbé Amine
MEGUI MEGZOE 😊😊😊
il est trop fort le Mr très belle voix
mdrrrrrrrr Pa guewel bi raynama nimou danéler aprés les 500 francs de daro je suis pliée de rire
Aminata Fall 😂😂😂
Maimouna elle est très belle machallah noirceur d'ébeine
J'ai trop rigolé!!! Daro c'est vraiment un mac! Serieux, elle fait carrement travailler les nanas quoi!!! Mdrrr, j'adore les expressions de son visage!!! lool
La Karma San 😊😊😊
ADJA Fall Mala fan bilay. daro yew trian nga sédal sa gars ci xaliss bii
Cheikhou Ndiaye 😊😊😊
ADJA FALL FIKING PATHIE ,DARO BOY GUETHO SOULA DIAPÉ DINGA XAM. MDRR BOY GUETHO MO WARA EUMBAL DARO REK NDAKH MOU RÉGLER ,WAYÉ FATÉ DARO WAKHONAFI ABY DÉFNA LOU RARE KÈNE EUMBATOUL. LOLLL
ahhhh bilay daro mo touti khol 500f te nankoo développée .,.... lol
guéwelou maimoune bi nekh bate.wayé daro dou déme
Maymouna est trés Belle❤️Daro ! Totch na fin 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣.!.!.!.!.!!.!.!
wadji néna cassette bi bo guéné daï deff beuf 😂😂😂
Am a Fan of daro i really like her character she always make me laugh
yéne niariborome meulfayi yéna niakfayda mounouléna wona daure Daro bamou mandi nangou khaliss bi mérénaléne trope 😠😠😠😠😠
tfk teew bilahi lingua wakh deugue la
tfk teew
Oumou Diallo
tfk teew lol 😂😂😂
hahahahahahahahahahaha non mais j'adore dinama nekh daro mom dou changé moukou maimouna mom am na faïda dem na ak copin wam di liguenti vie weum nuit la bou bah narbi mom bougoule kou meulfeu kou diongama la beugue ki mo saysay rek merci pour cette épisode j'ai bien rigoler comme d'habitude tout les épisode je rigole 😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁
Fallou1 Gaye diadieuf 😉😉😉
+Dinama Nekh TV de rien💓💓💓💓💓💓
adja Fall elle é TT belle Macha allah
Machallah verite adja fall est très Belle sama fans bi
wooyyy daro dinama tayyy reikk nan sérieux j'arrive poh a trouver un adjectif pr la qualifier lolll
Salamata Hott daro rek 😂😂😂
Souma meileini bakhata nga melni youte😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂... Je pitié Maimouna😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂... Daro mi😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂... Na mais elle fatigue grave mon'ventre la vie de ma mere... J'en peux plus suis versé de rires😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
#TeamDaro
#TeamDinamaNekhTv
j'aim Adja Fall♡
Rokhaya Ba 😉😉😉
Je ne c pas koi mai adja fall khawma loutakh mou nekhhh ma rk dalll !!!elle est tre jolie
Dossa Babou 😉😉😉
Daro 500 la may ki ni ba togue 😂😂😂 non j'ai trop rigolé
petillante rubii motakh mou arrêter waye yi😂😂😂
petillante rubii 😂😂😂
ah daro tay adja fall doute na la ko
Oumy Gaye 😂😂😂
adja fall est marrante elle a joué la sainte ni touche et est reparti avec le gros lot et le griot les a suivis mdrrr il suit l' argent.
Daro elle ma tuee Mama Aicha dinama ray rek verbe love kay Daro mo nay rek 500fr noon Daro dou dem
wakh diam 😂😂😂
bilahi daro ya fatei tei lakalei
ak 500f yi kamguani kendoula way😀😀😀
MARIAMA NIANG daro rek 😂😂😂
Zirik Zezzul kay 😂😂
Daro lui a donné 500fcfa ? Pour une fois elle donne car en général elle raquette 🔺❤❤❤
Daro est INSUPPORTABLE 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
fatoumata thiam
ayway daro mayaina khaliss taye félicitation!!!
maodo diack 😂😂😂
Wa Daro kanela bayi kimo kheumelé waye 😂😂😂😂😂😂
tfk teew 😂😂😂
Dati ayegue ❤❤❤❤❤
Publicité Armonia doy na aaaaaah !Yén ni forcing la !
Saison 3 doumassi doyal bilayy iow😂
Mangui dogua guiss daro guenè khaliss tèy
500fr😂😂
wouy sama yaye, daro dotoko ka defati, niarry gouye mounou nio bokou mbane, daro teye adja fall meune nala 1-0
Rokhaya Kane 😂😂😂
Adja Fall mo diongomah kay❤❤
Deugeuleu kay Partagez liker abonnez svp pour faire découvrir la chaîne
daro wallay tu es une vrai arnaqueuse 😂
mes no il ma fait peur dee boy woy do taguo
😂😂..la dame nénako kay naan dome bouy fourr iow..😂😂
Kobe dinjer la 😂😂😂😂😂 , aka mo sadik, mom ak Djèg Sokhssokhor no comment!!!!!
Mame Kha gni kay dagno déh rek ak seen ay terme you metti....😂😂
fatima Diaw 😂😂😂
Lol !!!!!!
hahaha Non daro billayi yew man dema hamoul nakaa lay niou lay deef vraiment 😅😅😅😄😃😂
maman aicha daye raye nit kw 😀 😀 😀 😀 😀 😀 😀 😀 😀 😀 daro mome dof na kw
😂😂 ya geune khamni soula daro téralé ga wathi wayane gakoy wayane ya togne sa bopou pér
Qui est d'accord que Akim ressemble avk Dadju
xarite yii waxlenn degue ndiol makka kennla mais sou ndiol makka bou djiguene amer maimouna la mashallah
drogba dia oh dieureudieuf way 😊😊😊
31/01/2017 à 20:11, 256 vues. je reviendrai demain à la même heure pour voir.
daro nena da yabamel gnou yap ko ptdrrr😂😂
ay waye dina dè 0 stress lay doundou
darro tu es belle sans beaucoup de maquillage aujourd'hui mom 10/10
Faye Mamy dieureudieuf way 😊😊😊
Très joli Ma vai de dinama Nekh
mane maman aicha la nope
mourtalla njaay wakhal way 😊😊😊
my favourite African TV series Ever. luv you daro
Sofi Ceesay thank you 😊😊😊
you are welcome!
Dokhal fowi guay melni wathiou purée Daro fane guay dieulei say terme !!! Love u Daro tu es une vraie artiste. Sougnu wa keur tay gnu am problème ak américain kou ma wakh rek mani leu mane koba gingembre lol rek,
Macoura Gaye 😊😊😊
weuy Darou dinama ray
lool wa daro mom billets bimou mayy geuweulou Maïmouna bou goor bi wa niata leu koumakoy wakh ngirr yalla pabi off nako dh
No fake in my gang !
No fake in my gang ! bon rek té négueu 500 lako may daro dou nitt
Naba Gueye way daro dou nitte quoi mom espèrei lo na way dji pour mom Aÿ dix mille sakh lako daro di diokh non dou deim mou nane niou niou dougeul KO si album bi loool
No fake in my gang ! 😂😂😂daro rek amoul dalay ngor thie xaliss wayé bayiko ak bou ghetto rek bou niewé rokhoss ko ay péss ba kanam gui guena ndaw
Naba Gueye lool non daro dama yakar ni dafa am febarou xaliss esk dou lolou amoul ngoor si xaliss bâ Parè bolei ko ak wakh djou beuri nak comme kou laka Aÿ 40 perokei lool
dinama nekhtv del leeral rang bi waye am na nio khamer et demi laniou nieuw di kheuthioo pé c po normal loool 😂😂😂😂😂😂 mé daro parle tropppppppp come métrailleuzzzz ratatatatatatata mais ki louko dale mdrr😂😂😂😂😂😂
Mamad OU daro elle est très intelligente tekk deal rek layy def
ahaha ta raison el te terrorise avec ses bruits ohh ell est bavard lol
da ame touti dof
billaye amer na nitti loulerr bayiwoule ken, ell doit nous desintaller waye
Mamad OU '
adja fall rek si xalé 😂😂😂😂 May wax femme bi nane kay nane dombiy four wouuu way 😂😂😂
Daro Faye kay nane doom biy four kay 😂😂😂😂😂rbt
Wadji néna ba cassette bi guéné dafa deff " beufff " LOL
hahhaaa kone degg gaello lol
Jaime bcp daro
ho machalah wa dina ma nekh k du bonheur chapeau pour daro 😂😂😂😂😂
Daro je l'aime a mort💟
Fiers Africa merci 😊😊😊
mane nak teye dama tardé mais comme dab rek dinama nekh rek ah doyoul baye desss maleye loveee déeeee...
Fanta Benjelounne Kouyate nio le fouf 😉😉😉
putain mais c'est quoi cette série sans inspiration ni de thème ni de l'humour pure, darro elle a les mêmes folies tout les jours, un moment donné il faut progresser ls gars
SOURMAN JOJO donne nous une idée de scénario 😕😕😕
Dinama Nekh TV mane maléni diokh ay idée? Kone d amagolénko, par contre y a beaucoup de scénaristes au Sénégal, vous pouvez aller vers eux pour avoir un vrai scénario parce que là ça se voit que sokhla ngénko
SOURMAN JOJO les goût et les couleurs ne se discute pas non merci je pense on a les meilleures scénaristes du Sénégal essaye de capter les messages de la série c'est important mais tu es toujours le bienvenue nio far 😉😉😉
Moi j'ai trop aimé les saisons précédentes mais celle ci franchement ça manque de thème et merci d'accepter les critiques
SOURMAN JOJO on est ensemble 😉😉😉
daro nenako heee naar wakhal ak gnii Lala mayyy 😂😂😂😂😂
daro parlait comme un enfant
wa tamite hakim limou beau lanela
MDR serigne faye ndanan artistes
mamy Ba merci beaucoup😊😊😊
Gniawww Adia fall rekk çi diekk MashaAllah
daro comme trump!
Série bi warna diekh sén inspiration mo,diekh
Aliou Diop pourtant pas ameneu gnoumou nekh 😊😊😊
Daro am gua talent barki serigne saliou
On veut plus de mama aicha et son anglais please!
jimy jones c'est noté 😉😉😉
no daro dinama ray bilay
daro bayil maman Aïcha le verbe love a été conjugué pour elle mdrrrr
Ndieme Faye 😂😂😂
🤣🤣🤣
ndakh rek boufi kène 1 2 3 😂😂
damay guinte ou Daro day mayer haliss😕😕😲 do mayer lou bah danga dioher rek mou baral waay bi tekci mbassa mbassa
très sérieux kan j'écoute darro mes stress diminue
😂😂😂😂😂wouye maman aicha ya mena khasthé bakatha kaye
Khadidiatou Doukoure 😂😂😂
dara tay mome adja fall déff na laka niaw douka défati dé😂😂😂😂😂
Ndeye Diagneniang 😂😂😂
adja fal👏👏👏👏👏👏
beugue saliou 😊😊😊
daro lakalengua trop ak sa mayama niehk bi
peeeeee gaw nguene dale😅😅😅😅
Awa Mbodj masha allah 😊😊😊
😅😅😅 ay Bolt lafi guiss
no daró nekhouta mougne koi fo diar reko nim badola nak khaliss amou ngor
mouhamed samba Loum bilahi Daro nekhoul mougne rétane😂😂😂ba sonou
mouhamed samba Loum 😊😊😊
maman aicha amoul 😂😂😂😂😂
dina si réfléchir no Daro mo réw
daro ya ma rouslo ci maylé.
😁😁😁 non daro ma tué maman aicha merenala trop bayil daro ya yababl mou gnab la
Ça serai bien que vous attribuez un rôle à Oumy aussi, elle est là comme une figurante.
ça c'est vrai personne ne la considère ndeyssane même dans les commentaire on est très peut a parler d'elle enfin bef...
taty kine c'est noté 😉😉😉
wa nara leyni kay nar bi nena molfo amna Mauritanie mdrrr 😂😂😂
Ibrahima Sy 😂😂😂
Mounass toujours egale a toi meme tu es tres jolie
Khadija Rassoul ba 😊😊😊