Oh mon Dieu svp priez pour les gens qui suivaient Adja l'année dernière et cette année-là Dieu leurs a voulu prendre la vie que firdawshi soit leur demeure éternelle😭😭😭🙏
Bon ramadan à tous les musulmans koor gui yalna boum nék siniou moudji koor yala yok weurseuk yi yok xéweul yi kousi nék linga beug yalnako yala déf gni beug diabar yalnalene ko yalah maye gni beug djeukeur aussi pareille
May léne ma j'aime way guir dieumi korr gui mane khana lolou yomouna❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Discours assuré tu a parfaitement parolé charmante respect douce..... machalla tu es galant tu es excellent tu es douceur😂😂Diogoye es l’unique de sa génération
Vraiment j'adore une famille réunie 💞 c mon rêve le plus important !! Adja Mercie beaucoup 🙏 cette épisode doit être exemple dans tous les familles 💞💞💞
Si vous ne courrez pas après ce que vous voulez, vous ne l’aurez jamais. Si vous ne demandez pas, la réponse sera toujours non. Si vous ne faites pas un pas en avant, vous restez toujours au même endroit.
Je vous jure ouroul ayni yi khamnaaa sen rafétaye eupna lokhoo adja rafet boumou rafet rk Machallah 🥺🥰kouko dakk khawma noo nara meileu kii yallah bako yallah lafale thiate way
Messagas you am solo gueni diokhe, djiguene diou bakh coco am sa addina diakna, seydina mouhamed sw.s dafa wakhni الدنيا متاع و خير متاعها إمرأ ة صالحة loulou mouy addina materiela , materiel bisi gane mouy diabar diou bakh, yalna niou yalla maye diabar you bakh ci barke al khoranil karime.
Vraiment serie nekhna trop sakh j'ladore mais dfois waro guen di si bole ben souné sakh degnouy wooné adja mouy djouli bene 2m sakh ou pathe sene lolou mome dafa am soolo si keur
Ngoor dagua bayii sa meunin wala dagn la wakh Star gua revient sur terre frère soi rigolo comme avnt guissou Doudou xana changé woul 🙏🏽Que la paix sois sur vous Bon Ramadan A tous 🤲🏼
Oh mon Dieu svp priez pour les gens qui suivaient Adja l'année dernière et cette année-là Dieu leurs a voulu prendre la vie que firdawshi soit leur demeure éternelle😭😭😭🙏
Amine🙏
Aminé ya Allah
Amine
Paix à leurs âmes 🤲
Amine 🙏🙏
Alima mom tmt leigui day roubé dh😂ms diogay lii moo bakh thi mom😂ani les fans de Diogay beseul j'aime
😂😂😂😂😂Dana réé ba sone
bb y
Rescindir y o🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉@@TheMG20089
😂😂😂😂Esccc n 5:58 vx mhssradsszm di 😂e z, l😮😮😮😅😊😂😂😂😂😂😂😂😂😂1 di che di che e in 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Adja est une femme exceptional belle, souriante généreuse 🥰🥰🥰🥰🥰
Elle est la plus belle machala 🎀 et bien éduqué
C’est son rôle.Rien ne dit qu’elle est comme ça dans la vraie vie🤷🏾♂️
@@galsendelirereebatass114 damako kham motakh
Billahi
@@mbayangsow2729 1
J'adore comment est Adja. Elle est une référence pour toutes femmes. Qu'Allah nous récompense d'épouses comme elle inchallah !!!
Ls revanche de Alima contre diogoye 😂😂😂😂
Le discours d'adja est trop beau
J'espère que le message arrivera dans les familles
Ls revanche de Alima contre diogoye 😂😂😂😂
@@fatouseck4588tu répliques tous ioe😂
L'une des rares séries ramadan qui prône l'esprit de famille té beuriwoul ay khoulo 🥰
Adja toujours aussi belle 😍
C'est la meilleure série de Ramadan vraiment!
Ww c'est vrai mome
Adja rien que la sérénité sur son visage est apaisante 😍 Yalla nagnou yalla mayeu sokhna bou melni Adja 🙏🏾💕
adja kay si elle est comme ca reellement donc son mari a de la chance
@@baalphaba6156 dawal dégue na Amoul Diekeur dh😅
Amiiinnneee 🙏
Amine
AMINE yarabi
👇Diogoye Meilleur comédien du Sénégal qui est d'accord😂
Lolou Kaye kéne wakha touko
moi
Noo c'est sanekh
@@mamadoumbaye3655 moh pourmann niankou Ndiaye falamalen
De ça génération
La discoure d’Adja est important 🙏🏿
Qu'Allah accepte nos jeûnes et prières et pardonne toute la Oumma
Bon ramadan à tous les musulmans koor gui yalna boum nék siniou moudji koor yala yok weurseuk yi yok xéweul yi kousi nék linga beug yalnako yala déf gni beug diabar yalnalene ko yalah maye gni beug djeukeur aussi pareille
Amine
Amine
Amine
Amine frère 😍
Amine way
Non nékhoul ba nékh mais série Adjia dou meusa sapi qui est d’accord avec moi ❤️❤️❤️
Oui😂
May léne ma j'aime way guir dieumi korr gui mane khana lolou yomouna❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cc💖
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wa legui loy doyè j’aime yi?😂
Ok bakhna 🤣
Boudei dangciiy am aay xassanaat ciii koor guiii reikk ah waaa baaxna!
Ce qui regarde Adja à cause de Diogoye liked leine way🤣😂😂
Mangui
Moi je le regard pour rigolé
Asalam, je suis Marocain, j ai tapé ramadan comedie et je suis tombé ici, ca a l air tres beau le senegale, ca ressemble au Maroc.
Discours assuré tu a parfaitement parolé charmante respect douce..... machalla tu es galant tu es excellent tu es douceur😂😂Diogoye es l’unique de sa génération
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Yow it meune nga top cas sokhna fatima
Moma réy mane 🤣😅😂🤣 , woy Victor Hugo 😅😂🤣
@@alexsadio8392 bilay ki kayy
@@mariadieye1502 😂
Ani sopey seydouna Mohamed yi🤲🤲🤲❤️♥️
aDJay. awsLFanNay
Boulen faté nianal gniko daneu setane daw t reneu niou djitou yalla nalen yalla xaré aldiana firdawsi amine🙏🙏🙏
Amin
Amine ya raby
Amine
Yallah naleen yallah yeureum té khaléleen aldiana
Amine
Y'a bcp de leçon de vie😊 merci Adja pour ce rôle que tu joue....référence nga pour les femme
Vraiment j'adore une famille réunie 💞 c mon rêve le plus important !! Adja Mercie beaucoup 🙏 cette épisode doit être exemple dans tous les familles 💞💞💞
Bilay Amy comme sougnou thiatou keur franche touti reew mais au fond elle est gentille une vraie leçon de morale merci
Seri adjia exemple la lî famille bou néck weur nga kô déff je vous j'aime
Vérité absolue
Yallah nala yallah may famille bou mel ni frère Malick🙏❤️
Leçon bi amna solo
Billay wakhtiko
On écrit pas comme ça serai on écrit comme ça serie
Kou beug Al khouran Kareem mangui l'ay nian nga abonné sama chaîne TH-cam svp merci beaucoup bon Ramadan
Ok
Mane dh dina abboner wouu incha allah
Beugue nako trop mh abonné wouma
Le mieux
Niolako guene beugue waye abbone wou ma
adja machalla way keuna la beugue yalla gua ame diamou ❤️🙏kou beugue adja beussel j’aime 👍🏿
P
Adja est une famme très gentile vraiment ses parôles me touchent machallah c'est un exemplaire
Si vous ne courrez pas après ce que vous voulez, vous ne l’aurez jamais. Si vous ne demandez pas, la réponse sera toujours non. Si vous ne faites pas un pas en avant, vous restez toujours au même endroit.
Absolument
@@abdourahmanesindidi1818 Diadieuf 🤟🏽
Vous venez de me redonner l'envie de me battre encore plus pour mon mec lui montré qu'il est tout pour moi merci mn gars
@@bintougaye5927 ça fait plaisir vraiment je t’encourage Amal diam rek bula dara meti lep dina bax inchallah 😇😇🤲🏽
Mdr bien que je l'aurais Inchallah
Keep Kou d’accord sii discourt Adja l’international beuseul abonner
Bilay sama khol bi daff thié sédd sakh machalla notre Adja internationale
Son discours est très important surtout une famille doit s'unir et s'entraider. Bonne continuation Adja internationale
@@mamediarrathiam3485 billahi
@@abdoulayebaneniang billahi Frere
Adja idol leu
Nigir dieumi serige touba à bonne léne fi si kourel khassida tie yalla takh 🙏🙏🙏🙏🙏
💝💖💗🤩😍🥰
Yalla na sa chaine beuri Dolé si barké psl akkeu Serigne touba
@@cheikhndione7614 amine waye lo begue yalla nalako yalla defal
@@Dakarmkinfo OK on est ensemble yama guenn bonne continuation
Serigne guanane serige
Vraiment un serie educatif kou d accord beuseul j aime adja la meilleur 💗💗💗💗💗💗
S mountakha mbécké yalla nafi yague té and ak wér aminnne❤️❤️👏👏✍️
Amen
Allahouma amine 🤲
Amiin
آمين 🙏
Amine yarabi
Mane limay lathie té moy diogaye kane mo kay habiller tamite ki amoul bene yeurmandé 😂😂
😄😄😄😁😁😁
Pino fashion deh mofi diare
louma yag guestu mai ba lgui hamumako ???
17 avril 1946 la rencontre salvatrice
Dieureudieuf serigne saliou🙏🏾❤️
Ohh machallah daga ka wara fête ndk 🤣
Dieureudieufty Serigne Saliou
@@tallfamilleelectroniquekol6840wawaw beuss bi fête la
@@metoundiaye3062 diadieuf mouride ❤️
Machallah
Bravo Amy. Le discours est parfait bonne continuation à toi
Adja est un idole pour toutes les femmes☺️☺️❤️🇸🇳
Beussal J'aime so beuge Alima♥️♥️😘 je l'adore cette fille. Bonne Ramadan Kareem a tous les musulmans ♥️♥️🙏🏾🙏🏾😊
J'aime
SI DOUCHE BI LA NEK DI SÉTANE ADJA WALAY MEUNOUMA KHAR ANI WA TEAM WIFI 😂😂😂😂😂
Loy deff si douche bi😂😂😂😂😂
@@evagueye5551 🤣🤣🤣 amna lo khamni dou kestion way🤣🤣🤦♀️🙈
@@mamdiarrakhouma7620 😂😂no damay lathie rk mais xamna Day ndogou😂😂😂
Nionguini👋
Amna lo xamni dh JAROUL wakh vraiment
Maan dall sagnsé adja dafmay Danel!!!! Elle a trop de classe
Diogoye comme kou reuthié palais😂😂😂 li si garde rouge
😂🤣
😂🤣
😂😂😂😂
💕😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
😀😀
Yalla na meune mougne ak séye comme Adja Amine 🙏🙏 ame djeukeur bouma yeureume 🙏🙏
Amine ma chérie yalla nalako yalla défal 🙏😍
Cc
@@dieynabasy2264 Amine chérie 🙏🙏
Amine waye🙏🏾
@@mamytagueye1096 bientôt
Yalla n'a niou égali kore gui si diammou wakh lénne amine
Amin
Amine
Amine
Amine way
Amine
Kou guiss ni pâte Séné daffa maki si chéri yi beseul 👉j'aime 👌
Waaw momeu ani mou sakh
ak mamie tmt
@@mamedieng241 dafa dème mecque
@@sokhnalo6951 mamie ele s'est marier dans la vie réelle. Set bou bess lah motakh
@@awasow6195 bou bakh
Adja deug deug man sa beauté doumako mine sheeeeu dafa rafét trop way je t’aime
Machala 😍💓👌👌
Bilaye laf thiat 😘
Macha allah
Macha allah
Ah yow tamit peulh rek si rafet doyoul bay dess
Man dh bariwuma loumay sétane série wayé khamnané képou kouy seuye wargua di sétane série bii Machalla tre riche
Votre s3rie est trés amusante,vraiment merci à vous🙌
Un message importante pour notre adja nationale vraiment j'adore trop son style ❤❤❤❤
Yh
Yalla nagniou yalla moussale thi seytané yalla may gniou xolou mougne
Cc
J aime bien le rôle de alima elle commence à s imposer dans la série j aime ça mais liker
Wadioubakh dayy dadji nitt🤣🤣
Message fort de Adja
Les familles doivent tjrs faire ce genre de réunion
Ani mamy yéeeeenn😔😔😔
😂😂😂😂😂
Que nos femmes soient comme cette Adja ci barkei Seydina Mouhamed psl 😍.
Ana gni beug sen Yaye ak Papa Abonner si sama chaine youtube nga activer cloche 🔔 de notification bi yalla faylen amiine
Baye Niass International
Je vous jure ouroul ayni yi khamnaaa sen rafétaye eupna lokhoo adja rafet boumou rafet rk Machallah 🥺🥰kouko dakk khawma noo nara meileu kii yallah bako yallah lafale thiate way
Thieye diogoye mo meune DH legui dafa bayi roubé yiimou d'âne def 😂😂😂mes Adja machalah 🥰 rafettna bakhna man dall Adja nekhnama bilay🥰🥰🥰🥰
Diogoy meilleur comédien de l'Afrique♥️♥️💖
Je suis d'accord
Le discours de Adja ❤❤💖
Le discours de Adja ❤️❤️💖
"Tu as parfaitement parlé" meun naa yak sama adouna. Thiey Diogaye😂
😂😂😂
Parolé sakh la wakh nk😁😁
Dichcour assiré😂😂😂
ADJA UNE MAMAN EXEMPLAIRE ❤️❤️
Bly
Messagas you am solo gueni diokhe, djiguene diou bakh coco am sa addina diakna, seydina mouhamed sw.s dafa wakhni
الدنيا متاع و خير متاعها إمرأ ة صالحة
loulou mouy addina materiela , materiel bisi gane mouy diabar diou bakh, yalna niou yalla maye diabar you bakh ci barke al khoranil karime.
حقاً غالباً
Billahi
Amine niounn tamitt yalleu mayy niou djeukeur diou bakh
Wa ani paré sene🤷♀️🤷♀️koumou manque beuseul j aime
Amy môme souye togue dou rétane xana dou guiss Adja akh Bidêw😂😂
C’est ça une famille Adja elle gentille en plus elle aime partager c’est une femme 👩 brave elle mérite beaucoup de rémercie ma 😂🤣🙏🔥🙏🙏
Bikay yaw Adja kaye machalla👑 💯💕🔥💪💪💪rek yalna nala yalla maye Soxna👰sou mel ni mom soude amaguo ko👏👏
@@ndackdiop9349 amine ama goumako 🙏🙏🙏🤲🏿
@@salioundiaye4933 ndeysane yalna ngaa amm kouko gueune🙏🙏mou bax ,yarou,yatou,am yeurmandé, ak xol❤bu rafett🙏🙏inchallah
@@ndackdiop9349 amine yalla na sa Niane nagou👍🏿🤲🏿🙏🙏
Wadioubakh me tue de rire🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰 kou abonné yanga dougou Ardiana
Wa Diogay loum solni tay
Kou beggue sa Yaye bes ❤
Cc
Adjia bilae je t'aime ❤❤yallah na am diabar niou melni iow
Yallah Nasa Nasa diam diagu 🙏🙏
Vraiment serie nekhna trop sakh j'ladore mais dfois waro guen di si bole ben souné sakh degnouy wooné adja mouy djouli bene 2m sakh ou pathe sene lolou mome dafa am soolo si keur
Bilay
Deug
Amna solo trop lingua wah si djiouli bii mashala
Yalna yalla doli diam si rewmi tè yalla nangoul gniou sounou koor barki serigne saliou Mbacke
Hommage aux gardes rouges 😂
Non Diogoye dou nite😂
🤣🤣🤣🤣
Voilà garde rouge je cherchais le nom😅😅😅
Belle message de Tata Adja des cœur pour Tata Adja ❤️💓❤️❤️❤️💓💓💓❤️
Diogoy comme gardien palais 😂😂😂doma ray 😂😂😂
Mais moi je demande si Adjia est vraiment comme ça même en dehors de ses séries. Mais je l'apprécie beaucoup comme ça
Diogoy saï bou Alima jëllé parôl dey tit vraiment jai perdus mes dents 😃😃😃😐😐
😂wa mom loum khamal diogoye
@@aicha3515 diogoy dafa dioum envoyé alima béneu vocal bo khamni dafa done dragué béneu meuf si je me trompe pas
@@gamousacisse9306 effectivement
@@aidasow6650 voilà
Fans diogaye séne ❤️
Keur adja dafa am dolé💪
Ramadan Mubarak to all my Muslim brothers and sisters 🤲from Indonesia. May Allah fulfil all our wishes.
Thanks you too 🤲
Ngoor dagua bayii sa meunin wala dagn la wakh Star gua revient sur terre frère soi rigolo comme avnt guissou Doudou xana changé woul 🙏🏽Que la paix sois sur vous Bon Ramadan A tous 🤲🏼
Vraiment
j’aime bien adja mais Diogaye me fait rigoler même ma mère rigole🤩🤩🇸🇳🇸🇳🥰😍🥰😍
Long vie à notre très chère mère
Moi aussi mais il fait rigoler 🤣😭😭 ma grand mére
Loy kheudé ?
Man mom fondé rék
Thiarré
Ginar 😂
Banane
@@aliouseck2097 AK méw wla ?
@@bayedieng5963 AK pom wla ?
Toutes les filles qui rêvent devenir comme Adja beuseul j'aime ♥️
Diogoye mo mana sagnsè qui est d’accord beseul j’aime
Yagui togne nk 😂
J'espère que adja et naturellement comesa dans la vraie vie merci a toi
Quel leçon intéressant Adja walahi li moy yeter deugue 🙏🙏🙏😍🥰💕
Premier commentaire guirr yallah rk 1000 j'aime lah bgeu
Loy doyer j'aime yii la beugue hame😂😂😂
Mooooo loye doyé 1000j'aime🥺
13ème mou dés 987
On paye sur le nombres de j'aime ????
Khana daguakoy kheudé🤣🤣🤣
Diogoye neineu day ndampal dayorr gonée😂😂😂li some rayul
Elle est où Mami ma actrice préférée série de Adja 🇸🇳🇸🇳❤️❤️❤️🇲🇱
elle est mariée maintenant peut être qu'elle viendra après
@@evelinegomis7673 retour de mamy rek lay khar
@@fatoubintouseck783 espérons qu'elle sera parmi nous pour ce ramadan 🙏
Diogay est meiller lolou Dou deba sakh diogay bou nekone equipe national Senegal 🇸🇳 dieulna coupe du mond bou yague pas ce que defa aye machalla 🙏✊🙏
Honnêtement j'adore adja de ouf 😰🥰elle est douce 😍sympa 💙bien des choses à vous 😘
Yallah na nieup am diam 🙏🏽😊❤️
Adja toujours Adja je dit la même chose t'es mon idole bonne discours chapeau a toi👏👏👏
Nn adjia man jtm Walah yallana niou yalla may sohna sumelni yaw si barkè weru koor gui
Adija am nga client bodoul yakaĺè frère hèlena bi😂😂😂😂😂😂
Ouagadougou mii key clients leu 😂😂😂
@@mouhamedleye8706 bilay ki dina ma ray rk😂😂😂🙏
Moment bobou la série bi néxonne temps yii boy yii nékk khalé😂😂😂😂
Bilahi boy😂😂😂😂
Cc
@@bintoudoumbia7255 cv
@@mouhamedleye8706 swing Bien
Diogoy sene vraiment il est fort où sont ses fans maninestez vous.
Alima dal bimou amé dieukeur batay da dioukour moutt 🤣🤣🤣mayatoul dara jogoye alaboni célibataire bakhoul dalay timide lo wathié say hormone 😂😂😂
😂😁😂🤣wakh gua DEUG dhe😂
😀😀
Hahaha aye yallah mignou sakkk yeureum gnou
🙈🤣
Adja est vraiment une référence 😍😍😍
Diogay sén néna tougoudougou féckéwoka 🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂
😅😅😅😂😂😂
😂😂😂😂li dé laayy ré
beaucoup de leçons de moral. Yallah nanou Yallah maye famille bou mèle ni
Amin
Adja nationale bilahi vs êtes une femme de rêve
Non walahi j'aime le caractère de Adja
Si toutes les femmes étaient comme Adja kone la vie ne sera difficile
Diogoye comme les gardes de plais “les spahis” 😂😂😂
Alima doo dieugal diogoye nak😁😁
Diogueye amoul billahi 🤣🤣😂😂💟💯💕