Pourtant 4 lutteurs yi yèpeu 2 lutteurs rek nio beuré ba roi sans défaite. Yekini AK Tyson. Manga âme 2 défaite avant roi. Birahim AK mor nguer nioko dane Balla âme 2 défaites avant roi. Emeu AK issa pouye nioko dane.
sawaye boul wakh lolou roi des arenes niepou ko merite kou dane roi yaye roi bayi len sissou bi modou lo rekkk apres fran roi daye dire kom modou lo 2019 2024 balla 2012 2014 😂😂 eumeu sene 2018 2019 mou danou 0 victoir 😂😅😅😅😂😂
Roi des arènes mom 4 Mbeur rek niokofi mérité Manga 2,Tayson,Yahya Yekini et le grand Balla Guaye 2
Wakhou siportere rek ngafi wakh
Modou le mieux
Pourtant 4 lutteurs yi yèpeu 2 lutteurs rek nio beuré ba roi sans défaite. Yekini AK Tyson.
Manga âme 2 défaite avant roi. Birahim AK mor nguer nioko dane
Balla âme 2 défaites avant roi. Emeu AK issa pouye nioko dane.
Il le mérite tous
balla est le pire roi des arènes à part eumeu sene bene victoire rek la am ci couronne bi
La légende vivante manga 2
sawaye boul wakh lolou roi des arenes niepou ko merite kou dane roi yaye roi bayi len sissou bi modou lo rekkk apres fran roi daye dire kom modou lo 2019 2024 balla 2012 2014 😂😂 eumeu sene 2018 2019 mou danou 0 victoir 😂😅😅😅😂😂
Waxou doff kéen bougouko AK waxou faar