« momay diayal bégnets yi » Ibrahima Sory verse de chaudes larmes devant les témoignages de sa mère

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 3 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 294

  • @mouhamedmbodj1614
    @mouhamedmbodj1614 ปีที่แล้ว +169

    Boy yalla nga signé pro inchalah téral sa yaye du courage champion

  • @nazyfreshly1857
    @nazyfreshly1857 ปีที่แล้ว +23

    Il a déjà les qualités d’une légende (discipline, humilité, volonté, le sens des responsabilités..)Machallah laf thiat

  • @mohamedvarre1250
    @mohamedvarre1250 ปีที่แล้ว +197

    Quand on père la seule être chère qui nous restait on a le cœur brisé ❣️ souma guissé kou am yaye Ba diko topato damalay gnéé wallahi Yalla boula thiat topou 🙏🏽

    • @ibrahimasambseye2938
      @ibrahimasambseye2938 ปีที่แล้ว +5

      Boy bi dei kou wara gorgolula dioy na ndax yayam

    • @mohamedvarre1250
      @mohamedvarre1250 ปีที่แล้ว +4

      @@ibrahimasambseye2938 bilay saaass bi diiss neu mais Yâ Allah baax na

    • @nadythiam5653
      @nadythiam5653 ปีที่แล้ว +5

      Bilay souma manone guiss sama yaye dji rek 10 mn douma wakh Dara

    • @mohamedvarre1250
      @mohamedvarre1250 ปีที่แล้ว +2

      @@nadythiam5653 Ndeysaann mougn rek Baye, sama boss amna 23ans cibir souff

    • @Boromtouba4
      @Boromtouba4 ปีที่แล้ว

      😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭je ne fé pensé à ma très chère Maman 1fem brave et amie
      yalna firdawsi di Këureum 🙏👌🏽 a ts les mamans disparues

  • @falloundoye6541
    @falloundoye6541 ปีที่แล้ว +73

    17mn35secondes J'ai coulé des larmes. Ce Gamin ira tresloin inshalah. Depuis le début de son interview fatéwoul son coach formateur, Ce qui explique qu'il est très reconnaissant en plus il a de l'ambition. Bro Que Dieu te fasse un grand professionnel si barké alhourane. Gueum Nani seu yene si sa say par force Yalla dinako mot😅ali❤❤❤❤

    • @senisene588
      @senisene588 ปีที่แล้ว +2

      Je croyais que mane rek ma dèf remarque biii🥰merci Frere yalla na yalla nangou sa ñane ya rabiii 🤲

  • @abdouniang511
    @abdouniang511 ปีที่แล้ว +8

    Vrement coach bravo, Boy bi de 5 a u17 yako défar guinaw ndogalou sunu BOROM. yalna sa Boys yeup réussir...

  • @MamesoukaynaDiedhiou
    @MamesoukaynaDiedhiou ปีที่แล้ว +52

    Celuî qui respecte sa maman réussie toujours et aura tout ce qu'il veut

  • @nd0yeibrahima
    @nd0yeibrahima ปีที่แล้ว +43

    Yaye bou sone rek yallanaga dieurignou❤❤❤

  • @AstouSarr-jd7fo
    @AstouSarr-jd7fo ปีที่แล้ว +77

    Que Dieu protège ta maman et toute la famille .

  • @astacisse1007
    @astacisse1007 ปีที่แล้ว +17

    fait tout pour aider ta maman on est de la même génération j'aimerais tellement et d'autres aussi
    aider ma mère qu'Allah nous mènes sur le bon chemin Amine 🤲

  • @warriorkemiseba9184
    @warriorkemiseba9184 ปีที่แล้ว +3

    MOI J SUIS GUINÉEN MAIS, LE SÉNÉGAL C LE MEILLEUR PAYS DU MONDE. LE SÉNÉGAL ET LA GUINÉE C' UNE LONGUE HISTOIRE. YALLA NA YALLA DEF-DIAM CI DIGUÉNTÉ ÑAARY DEUK-YI.

  • @Enfant_béni_7
    @Enfant_béni_7 ปีที่แล้ว +43

    L'enfant Chéri de la Médina ❤🇸🇳👑🫶🏽 Félicitation champion d'Afrique U17👏 💐 Sory Sow 5🥰 🫶🏽 🏆

  • @moustaphadiop7863
    @moustaphadiop7863 ปีที่แล้ว +2

    Le vieux ave l'echarpe noir c'est un grd homme.....il fait partie des inspecteurs qui ont emmené la paix a l'uganda..... Sory tu as bcp de référence machallah bonne continuation

  • @annandiaye7046
    @annandiaye7046 ปีที่แล้ว +21

    Ohhh Ibrahim mon frère tu as une maman très gentille et formidable ❤kou bakh isseu yallah na yallah takhawou

  • @mouha-lethiakola-melody738
    @mouha-lethiakola-melody738 ปีที่แล้ว +26

    La Guinée 🇬🇳 est fière de toi Sénégal 🇸🇳 ak Guinée 🇬🇳 c’est la même chose donc gorgorloul bu bakh🔥🇬🇳🇸🇳🙏🏿✅

    • @salimatousarr98.0
      @salimatousarr98.0 ปีที่แล้ว +3

      Ça se vois Cest un pheul sénégalai origine guinéen donc les gens qui parle du mal au guinéens réfléchissez bien avant d'agir en tanq sénégalaise. La Guinée et le Sénégal cest une longue histoire ❤

    • @mouha-lethiakola-melody738
      @mouha-lethiakola-melody738 ปีที่แล้ว +3

      @@salimatousarr98.0 billaye diadia ko gotoun 🇬🇳🇸🇳💪🏿🙏🏿

    • @salimatousarr98.0
      @salimatousarr98.0 ปีที่แล้ว +3

      @@mouha-lethiakola-melody738 enéne fofe kéne gotoum à diarama alha diarama

    • @habiboudiallo567
      @habiboudiallo567 ปีที่แล้ว +1

      ​@Leana Rodriguez lorsqu'on rentre dinagn déposer walé sa ndeye cap Vert waleu guinée Bissau doméram

  • @LaSenegalaise221
    @LaSenegalaise221 ปีที่แล้ว +5

    boy sa comportement diangalate nama Adouna bien que mala magg fouuuuf, Yalla nala Yalla sameu Ya Rabby, respect aux Mamans ❤🎉❤🎉❤

  • @cheikhsougou5677
    @cheikhsougou5677 ปีที่แล้ว +11

    Ibrahima inchallah dina nieuw dh yalla nga signé pro ba déme aux grands clubs comme Barcelone, Manchester united téral sa yaye ❤️🙏🏿

  • @mouhamadoubambagueye2257
    @mouhamadoubambagueye2257 ปีที่แล้ว +4

    Boy barké seydina mouhamed yalla gua signé pro ba dimbali sa yaye

  • @rimesmakerposeidon2427
    @rimesmakerposeidon2427 ปีที่แล้ว +16

    Oh boy yalla nala yalla diapalai si Mohamed Rassoul psl❤

  • @africansworldtv3381
    @africansworldtv3381 ปีที่แล้ว +11

    Ça touche un cœur mon cœur à été touché j'ai couler des larmes. Alhamdoulillah Yallah motali lëüp in sha Allah

  • @liffootballtv6244
    @liffootballtv6244 ปีที่แล้ว +2

    Walahi geuthie na medina depuis 7ane magui USA Ms mere bi kham nako bou bakh bilay mere bou bakh mogui ni mere bou am respect si domou adama tai brom yaye diou bakh lou bakh rek lay am . Ibrahima gorgoloul rek bilay dra diopoula inch allah dina bakh ba diakhal la prsk sa yaye da bakh

  • @bybrufisquois257
    @bybrufisquois257 ปีที่แล้ว +27

    Machala ce gamin est un exemple pour la jeunesse

    • @ladivaba1951
      @ladivaba1951 ปีที่แล้ว

      Wallahi Wallahi Wallahi

  • @videoviral-w2t
    @videoviral-w2t ปีที่แล้ว +8

    Machala. Nianou wadioure defa nekh ❤ des c❤ pour nos maman

  • @fatouwilane8520
    @fatouwilane8520 ปีที่แล้ว +3

    J’ai ds larmes ô yeux 😢😭😭😭😭😭je te le jure frère inchallah tu va réussir contrat rek bilahi walakhi talay🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @aminataaw8585
    @aminataaw8585 ปีที่แล้ว +4

    Ahhh nos mamans 😢dioyloo nama rekkk 🤦‍♀️yalla nala yalla taxawou future pro 🙏

  • @FatoumataElisaManga-ej1zo
    @FatoumataElisaManga-ej1zo ปีที่แล้ว +15

    Il m’a fait pleurer longue vie à ta maman

  • @nialynialy801
    @nialynialy801 ปีที่แล้ว +14

    machaAllah yaye bou sone rék Yallah na nga féké sa ndiarignou ndiabote bonne continuation 👏🏿👏🏿

    • @habibsarr
      @habibsarr ปีที่แล้ว

      Amine yarabi

  • @awaniang4706
    @awaniang4706 ปีที่แล้ว +15

    Fière de tw Ibrahima prend soin de ta Maman pour tjrs inshallah

  • @elhadjigaye4478
    @elhadjigaye4478 ปีที่แล้ว +12

    Je suis fière de toi ndakh dagua fonkou sa yaye ❤❤

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 ปีที่แล้ว +3

    MACHALLAH MACHALLAH c'est émouvant. Bravo Champion Yalla na nga am une très belle carrière

  • @SokhnaDiaw-e8l
    @SokhnaDiaw-e8l ปีที่แล้ว +7

    C'est vraiment triste ❤ une mére est irremplaçable ❤je t'aime maman ❤

  • @khalifaababacar6828
    @khalifaababacar6828 ปีที่แล้ว +5

    Macha Allah yalla n'a sounou borom tahawoula
    Lafal la thiate❤❤
    Nous sommes
    Derrière tois gaïndè

  • @elhadjiahmadouba2048
    @elhadjiahmadouba2048 ปีที่แล้ว +10

    Émouvant ma cha llah discour d'un sage et occupons nous de nos parents le temps qu'ils sont avec nous .
    Wa salam

  • @elhadjigaye4478
    @elhadjigaye4478 ปีที่แล้ว +10

    Ibrahima Lou bakh rek ngaye âme ndakh sa yaye geureum nala

  • @doudoungom8619
    @doudoungom8619 ปีที่แล้ว +4

    Ndeysane fonkou sa waydjour rék mo woor dina bakh frr diape rék liy nieuw moy dake seule le travail paye ❤💪🙏

  • @assass5084
    @assass5084 ปีที่แล้ว +18

    Machallah amna solo ❤❤❤❤❤❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @mbengueadji8032
    @mbengueadji8032 ปีที่แล้ว +9

    Xalè bi dama co beug ❤️ dafa bakh ndeyesane soko xolè rek khamco

  • @fatoufaye5552
    @fatoufaye5552 ปีที่แล้ว +16

    Mashallah diom rek yallana yalla takhawulene vous faites notre fierté

  • @Boyka205
    @Boyka205 ปีที่แล้ว +5

    Mon frère Sory je te conseil de occupé bien ta maman si tu avancé plus loin dans toutes les tâches tu vas jamais regretter inchallah je te souhaite une bonne carrière longue vie à nos mamans

  • @gaindebamba6439
    @gaindebamba6439 ปีที่แล้ว +4

    Boy incha allah pro REKK. Maaaa chaa allahh

  • @abysta1
    @abysta1 ปีที่แล้ว +10

    Qu'Allah le tout puissant t'accompagne et guide tes pas gua tekki ba teral sa yaye.amine

  • @ndeyebounamadiop5863
    @ndeyebounamadiop5863 ปีที่แล้ว +6

    Khale bii yalla nalla yalla sam lafal thiath bagua teral saye wadiour

  • @fatougninguefaye4284
    @fatougninguefaye4284 ปีที่แล้ว +2

    Amine way halébi yalla nako yalla same way mou gueneu téral yayam.Nday sa dome déguel rek moi ngui lay téral Di am conscience sissa dound bou méti dila diapalé..Et quand sa maman a pleuré il a pleuré.bon courage pour le reste

  • @salaly164
    @salaly164 ปีที่แล้ว +10

    Félicitations à ses parents, entraîneur et les medinois

  • @tafashionfaye1513
    @tafashionfaye1513 ปีที่แล้ว

    Yalnala Mame Yalla défale jammmm té Mousseule la ci Thiate baga Signé Pro🙏🥰🙏

  • @AladjiBOY
    @AladjiBOY ปีที่แล้ว +12

    Machala champion li dawena yarame

  • @amedeosow8921
    @amedeosow8921 ปีที่แล้ว +11

    Yalla na yalla faye ba nga teral sa yaye si barcké seydina Mouhameth 🙏

  • @karimdiop8375
    @karimdiop8375 ปีที่แล้ว +3

    Machalla laf thiate ❤yall nako yall déff kounouy dégue inchallah

  • @muslim-nu9vy
    @muslim-nu9vy ปีที่แล้ว

    Machallah YALLA samko lafalko thiatt. Coach vous avez été exceptionnel, un vrai éducateur .

  • @amethfall5510
    @amethfall5510 ปีที่แล้ว +12

    Sa maman est gentille ❤️

  • @ramatoulayediop8697
    @ramatoulayediop8697 ปีที่แล้ว

    Tata isseu une femme brave ma shaa allah yallah sougnou Borom mayko mou signer pro in shaa allah

  • @AlphaOmarBaldé-z8r
    @AlphaOmarBaldé-z8r ปีที่แล้ว +1

    Bonne chance ⚽⚽

  • @doudoungom8619
    @doudoungom8619 ปีที่แล้ว +1

    Boy kontane na si iow bilahi dina bakh diape rék ak liga beugue sa yaye khamal ni ndam rék ngay am 🇸🇳💪⚽❤

  • @passahtendiop2264
    @passahtendiop2264 ปีที่แล้ว +1

    Ca fait trop plaisir avec tout ces beaux compliment surtout venant d’une mère qui est tellement fière de son enfant et de son entourage, amis oncle tante connaissance etc … Tu ne peux qu’aller très loin avec l’aide du bon dieu et la prière biensure de ta chère bien-aimée mère. Continue sur cette lancée inchallah tout sera comme prévu 🙏🏾❤️🤙🏾 Certified Boy Médina 🤟🏾

  • @aron6054
    @aron6054 ปีที่แล้ว +1

    Ibrahima inchala lou baxe rek ngaye ame kou topato sa yaye kéne doula yeureume té do mouseu gné saye morome , diam si yow

  • @daoudasougou9834
    @daoudasougou9834 ปีที่แล้ว +2

    MACHA ALA frère c comme ça que je faisais avec mes frères pour notre maman MACHA ALA DIEU NOUS A BEAUCOUP AIDÉ bonne continuation

  • @fatoufaye294
    @fatoufaye294 ปีที่แล้ว +6

    Yaye dé bama niamé resultats tarbiyako batay maguisi. Diapal dé topatol maman doko reuthiou inchalla

  • @Galsen221vu
    @Galsen221vu ปีที่แล้ว +5

    Oh j’aime j’ai même les larmes aux yeux 😢😢😢 ❤❤

  • @ahmadoubamba444
    @ahmadoubamba444 ปีที่แล้ว +2

    Gaïndè sa yaye contane na si yaw gorgorlou rekk lep dîna bakh yalah nga signe pro dimba li sa yaye ❤🙏🏽

  • @astoudiallo994
    @astoudiallo994 ปีที่แล้ว +3

    Ibrahima ta réussite migui thi sa tanke yaye ❤yalla boula thiate dougue

  • @SYABLAYE96
    @SYABLAYE96 ปีที่แล้ว +4

    Ohh j’aime vraiment les témoignages de coach ❤😢

  • @mouhamadoukane9835
    @mouhamadoukane9835 ปีที่แล้ว +3

    Boys Sory yalla na yalla takhawoula ba nga téral sa yaye

  • @awadione8857
    @awadione8857 ปีที่แล้ว +1

    Sagou médina la yaye amoul mborome niila c bien 👍❤

  • @yacinembaye_28
    @yacinembaye_28 ปีที่แล้ว +4

    Ndeysan nio bokon classe diangue rk la beugon ndeysane ❤️

    • @amibaozepeto4642
      @amibaozepeto4642 ปีที่แล้ว

      Ah Mashallah c'est ce que je me suis dit , il m'a l'air kou meune diang aussi Mashallah

    • @amibaozepeto4642
      @amibaozepeto4642 ปีที่แล้ว

      J au continué la vidéo, Mashallah le coach l a dit à la fin.

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 ปีที่แล้ว +8

    Machallah yo Allah walé wono-ya pro

  • @salioundiaye4054
    @salioundiaye4054 ปีที่แล้ว +4

    Ibrahima SoRy C Notre Fièrtee🥳❤️❤️❤️❤️🥳🎉

  • @khadyfaye307
    @khadyfaye307 ปีที่แล้ว

    Macha'allah 🥰🥰🥰 yall na yalla soutoural té bayii souniou yaye yii sougnou kanam baniou togue niou téral lénn 🤲🤲 Ibrahima yal nalla yalla féyy yiwww 🤲🤲 incha'allah

  • @tallambengue-vr2ct
    @tallambengue-vr2ct ปีที่แล้ว

    Machala kouh diapalé Say wadiour doh meusa torokh diam si ieo té thiate seéxlou lah

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 ปีที่แล้ว

    *Machallah laff thiate rk Yalla nala Borom bi gueuneu yeukeuti gua téral sa yaye bou bakh yaye momm loko deffal diar nako🥰😻😍❤️❤️❤️*

  • @ndeyefatoulo9609
    @ndeyefatoulo9609 ปีที่แล้ว +3

    Yallah nako souniou borom bi mousseul ko mouthieul ko❤❤❤❤

  • @MbeneDia-z6n
    @MbeneDia-z6n ปีที่แล้ว

    Yalna yalla takhawola ❤❤❤ ndakh khali gua ndaguay doka dorr yalna gua signé bro

  • @khadimg2078
    @khadimg2078 ปีที่แล้ว +6

    Yalla nala yalla defal lép liga beug si football aminnne ya rabii

  • @julssouleyndiaye954
    @julssouleyndiaye954 ปีที่แล้ว +1

    Yalla Nala yalla diapale si yene binga âme sa yaye nga motaliko

  • @diagnealima7973
    @diagnealima7973 ปีที่แล้ว

    MACHALA IBRAHIMA YOKOUTÉ rek yaye mome loko defal sani woko félicitations

  • @alphadiallo2452
    @alphadiallo2452 ปีที่แล้ว

    boy ibou du courage yalla nala yalla diappali way🙏🙏💚🤲

  • @bassiroucoly
    @bassiroucoly ปีที่แล้ว +5

    Machaallah fréro Pros inchallah ✌️✌️🇸🇳Ndéyesane Nos mamans aye ndiambar légnou Yalah négnou fékker lépp 🇸🇳🇸🇳❤️

  • @bayeakimmbacke2226
    @bayeakimmbacke2226 ปีที่แล้ว +12

    Yalnala sounou Borom Same té téralla

  • @moustaphawade6771
    @moustaphawade6771 ปีที่แล้ว

    Machalla félicitations et bonne continuation inchalla yallna bour yalla barkél inchalla

  • @ndellandiaye8628
    @ndellandiaye8628 ปีที่แล้ว

    Ndaysan sa ma rappelle série domou gaïdé série bou ame solo wadiour bou sonn rék yalla ga diéringou bonne continuation gaïdé🇸🇳🇸🇳💖

  • @fandao2138
    @fandao2138 ปีที่แล้ว +1

    Yalnako yallah lafal thiate té yallah motali yenem si yayam, mou magg té mou nek niitou valeurs

  • @louispaulndiaye7255
    @louispaulndiaye7255 ปีที่แล้ว +8

    Merci Maman❤

  • @KineDiop-i4u
    @KineDiop-i4u ปีที่แล้ว +3

    Macha halla yalla boula thiat dougou

  • @fayee4468
    @fayee4468 ปีที่แล้ว

    Machalla yalla naniou la dégg fépp si barké cheikhoul khadim

  • @alikassem7719
    @alikassem7719 ปีที่แล้ว

    Non journaliste bi mashallah 🤝🏾😭

  • @ndiayendieme7056
    @ndiayendieme7056 ปีที่แล้ว

    Machalla nioune wa mèdina daniou contane si ibrahima

  • @ibrahimacisse4474
    @ibrahimacisse4474 ปีที่แล้ว +3

    We love you ibrahima and we’re so proud of you 👏
    Fonce petit ❤

  • @aminatasambou9566
    @aminatasambou9566 ปีที่แล้ว +1

    Yalna la yala taxawou SI barké seydina Mouhamet AK tiere binga dioxe sa wadiour

  • @Fatoumbodji459
    @Fatoumbodji459 ปีที่แล้ว

    Mashalah yalna guén ague sa kanam Inshalah

  • @khadyfaye307
    @khadyfaye307 ปีที่แล้ว

    Qu'allah vous facilite le parcours incha'allah 🤲🤲 ga togue pa téral sayy wadiour

  • @mouhamedseye233
    @mouhamedseye233 ปีที่แล้ว

    Ndeyssane j’ai les larmes aux yeux khalé bi dafa yarou bou niou ko tek pression nak yalla nako yalla lafal thiat

  • @fallcheikhibra1155
    @fallcheikhibra1155 ปีที่แล้ว

    Il a toujours été respectueux envers moi et mes parents ❤bonne continue guorguorlou rk Incha'Allah dina bakh geum sa bopp rk petit frère ❤

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 ปีที่แล้ว +2

    *Sa maman ma fait pleuré😭😭😭😭khôl ba fess meunoul sakh wakh🥹🥹*

  • @morseck1695
    @morseck1695 ปีที่แล้ว +2

    Courage mn frére yalla nala yalla defal jam ak ligua beugue inchallah ❤

  • @mbacke7187
    @mbacke7187 ปีที่แล้ว

    Machallah Ibrahima Guena Liguey Rék Pro Inchallah 🙏

  • @aidathiam6328
    @aidathiam6328 ปีที่แล้ว

    Macha alla lép Dina bakh inchallah

  • @kontesouleymane4659
    @kontesouleymane4659 ปีที่แล้ว

    Macha allah Macha allah ❤❤❤sama khole diôyna❤❤❤

  • @walydiagne8235
    @walydiagne8235 ปีที่แล้ว

    J’aime bien la diversité dans notre pays…Ton penalty face au Burkina montre toutes tes qualités…bonne chance pour la suite SORY

  • @bahneymar2231
    @bahneymar2231 ปีที่แล้ว

    felicitation gaindé bonne chance pour la suite tu es la fierté de toute la MEDINA

  • @ladivaba1951
    @ladivaba1951 ปีที่แล้ว

    Yalla nele yalla diaplé Wallahi lou bakhe rek guey ame depuis arabi saoudi je ľaime bcp

  • @khalifambengue6125
    @khalifambengue6125 ปีที่แล้ว

    Ma challah yalna yalla barkel lepp

  • @amadoufallndiaye2029
    @amadoufallndiaye2029 ปีที่แล้ว

    Bilahi booy Lou bakh rek gaay amm. Ismaël Sarr ni la méloonn❤❤❤