Ndéye sane souma dégué woye bi réke sama khéle dale di déme si sama yaye boye une femme battante courage qui a tout fait pour que je réussisse dans la vie guoudale fane yaye boye
Amin yarabbi mais moi aussi à chaque j'écoute Maty Thiam Dogo je pense à ma mère à qui je souhaite une longue vie accompagnée d'une santé et qu'elle soit témoin et profite bien de la réussite de ses enfants.
Cette chanson donne du courage a toutes les femmes, la maman est très sacrée longue vie à toutes les mamans du monde
Ndeysan yalna yalla yereum sama yaye ak mbolem dioulit 😢😢
Eup na Mingui tourou. Eupleuw..Ndeysane maty thiam dafa séd.
Macha allah yalna yalla goudal say fann yaye boye
Yalene yalla goudeul sa fane samela tai yokela soutoure
Ndéye sane souma dégué woye bi réke sama khéle dale di déme si sama yaye boye une femme battante courage qui a tout fait pour que je réussisse dans la vie guoudale fane yaye boye
Amin yarabbi mais moi aussi à chaque j'écoute Maty Thiam Dogo je pense à ma mère à qui je souhaite une longue vie accompagnée d'une santé et qu'elle soit témoin et profite bien de la réussite de ses enfants.
Nèkh na waay! Waykat deug nga. Thi ndiakhou mag gni nga naané bollé thia yarr, dall, nangou. MachaAllah
Ndeysaane ooooo Maty ♥️♥️♥️,. Djieyla walleu sokhou bébé lii cover bu nééxla
Macha'Allah loumou meussa wayy da nékh ta bari ndiangalé
Elle manquait de bon encadrement mais elle avait vraiment du talent..
Morceaux bou neh trop machalah
Ndeysane maty thiam dogo dafa yarou. Ba thie ay wayam
J'ai perdu ma mère a l'âge d 2ans j la connais méme pas mais Souma beugué conseil rek Say woy la déug lo ak papa thione bilay
😥😥😥😥😥
Ndeysan GNi mana kotou amougnou mbaam aka me un waaay machallah
Tre belle chanson avc une grande dam long vie maman maty
Elle a chanté une dame qui a bcp de classe Ndeye Faly Diagne
Waay li nékh na di anh 😂😂😂😂. Seuti dogo fally yeup meune wayy. Macha Allah
Dama beugue Sama yaye ba genrou musique 😢sama khol dafay toye😢
Li nékh waay
Bilay sougnou yaye
Ndéyssane 😢
Ohhh way yaw y’a mene way
Nekhna j ai les larmes aux yeux
J'adore cette chanson
Ndeyssane nexna trop
La génération gagnante 80-90
Lii dafa féss nekh na trop
Machalla
Akassa Sama ndanaan bi
Je veux le numéro de maman maty
Moi aussi
Wakh gue deg d ndeyessane
❤️❤️❤️❤️