He is talking about my great grandpa ,cheik Omar Fuutiyu Taal ,He is my mother father, father ,, My mother saw name is Dem. Pure tookloor💪👍. My own father is a king 👑Am bless.
Machala yallena yalla yésal yeureum mbané si Mame Samba diabare samba yallena yalla khareko aldiana firdawsi. Cette voie d'or restera toujours dans nos cœurs .
machallah . je suis content car t as rappelé l histoire de mon grand père Thierno Alpha Moussa Dia de Galoya.🙏🙏🙏🙏 eskeu Allah déportés mon grand père à cause de rêves (gueunteu) 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
cest très bien de faire savoir aux sénégalais l histoire de l ISLAM au senegal cheihh oumar foutiyou tall en tete moi descendant de ABDOUL KHOUDAKE NDONGO UN des lieutenant tombé a ces côtés te remercie de ton émission bravo félicitations
Amna solo Seugn mbaye gueye dundal Bula dara decouragé Xasoo ken Xeebo ken Yalla ak histoire ngay wahal Kuko beugul deg ap dof kepp nga Kilifa yeup wah nga sen mbir andak magal len Kuy lim nak du matal Kula tagul warula xas ludul ap reewal ak histoiram moko jaralul dara.
Walahi kham ngueen ne Serigne touba dou moroomu kenn ❤❤ moom rekk moo teh toubaab bi Dieurreudieffe Serigne mbaye gueye sylla yague fi lool te and ak weur and weu mo noo won fee gnakk❤❤
Yes. Respecdeded Salam omar who is a teacher fight for his good realigon and procte the people. Good person. ❤ he fell the pencil and took riepul for a cruel people. Salam and kudahapess sir.
Salam ziarr nalen loubari , mais souniou makgni yalnalen yalla fayal boppam ndakh kitakh nga talko mom talouko woon tenak المرتبة لا تسامح il faut faire tres attention
Merci grand père de nous révéler la vérité sur les actes barbares commis par les lâches hypocrites qui ne sont personnes d'autres que ces blancs (français)
Assalamou aleykoum j'aimerai bien écouter l'intégralité du générique merci de bien voir le partager sur votre site. C'est très émouvant merci encore une fois de plus.
Damaa jooy ba sonn ñii ku ànd ak ñoom démb ak tay doo xam ci loo koy teg! Fayu dong a nu war ci ñoom, jeexal nanu sunu woroom xam-xam yépp! Ray wuur ak sëriñ si bàyyiwuñu kenn, lii ñaaw na torob billaahi, waaye nag Xaadim Rasuul siggal na waa Senegaal ci tuubab yu Bon yii, siggal na it islaam su dul woon ak moom ñépp soppaliku ay yéefar.
seykou oumar tal bo xamoul bindam manoo ko wax taane mem fadu bimou fadou bandia gara wax na ko si bena terem bu toudou safina bo diangoul boul nangou wax si mom dara
Bjr xam Sam sa rew suis vraiment content de cette initiative et je vous encourage aussi, mais ya quelque chose qui me dérange vraiment dans l'annonce de cette vidéo. Est ce qu'il ne faut pas supprimer Blaise diagne et ce commandant blanc, j'ignore c'est qui mais ça ne rime pas avec l'idéologie de la chaîne. Ces 2 hommes ne sont pas des résistants au contraire ils font parti de nos pires ennemis que le senegal n'est jamais connu.
Souma guissé toubab bimouy wakh paul holle chef de poste Podor toudé naniou ko béne rue sama kogn daff may métti . Ak dieuf you niaw youmou déff yeup dieul bakanou sénégalais you beuri ak domou dioulite nga délou diko toudé rue . C vraiment honteux
He is talking about my great grandpa ,cheik Omar Fuutiyu Taal ,He is my mother father, father ,, My mother saw name is Dem. Pure tookloor💪👍. My own father is a king 👑Am bless.
Machala yallena yalla yésal yeureum mbané si Mame Samba diabare samba yallena yalla khareko aldiana firdawsi. Cette voie d'or restera toujours dans nos cœurs .
Yalna yalla fayla, wayé mandé menuma begue ab toubab
😭 😭 fierté de notre grand père yalna yalla dolli yeur mandéme si barké naby Moustapha 🤲🤲🤲
machallah . je suis content car t as rappelé l histoire de mon grand père Thierno Alpha Moussa Dia de Galoya.🙏🙏🙏🙏 eskeu Allah déportés mon grand père à cause de rêves (gueunteu) 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
c'est un martyr de l'Islam. Mais liko gayi déf doyna warrrrrrrr!!!!😭😭😭😭😭😭
P
Ligaye Deff amna Solo loye Yalla na Yalla faye. I am learning a lot from you.
Amine ❤❤❤❤💚💚💚
cest très bien de faire savoir aux sénégalais l histoire de l ISLAM au senegal cheihh oumar foutiyou tall en tete moi descendant de ABDOUL KHOUDAKE NDONGO UN des lieutenant tombé a ces côtés te remercie de ton émission bravo félicitations
Machalla amatina solo lool Baye Mbaye Gueye Silla yàlla nala yàlla takhawou ❤️ ❤️❤️❤️
thiey waliyal wali yaabe sernal sernaabe seykou oumar tal moy seeni serigne niom nieup kou neka war na ko magal
L islam au senegal jusqu’à Mali on le doit à cheikh oumar.jah bless him
Merci Baye Gueye Silla de tout cœur
à l'université khary amar fall tu veux dire
Et que dira t'ont de Kaly oumar fall et ceux qui ont fait le jihad 8 siècle avant Elhadj oumar Tall
Ndeysane eskey Baye samba diabare samba yallena yalla yésal yeureum mbané si mome teu khareko aldiana firdawsi Amine.
Paix aux âmes de tous ces resistants qui ont donné leurs vies face aux injustes.
j’espère que ton émission passe sur les télés qu’on puisse connaître notre histoire
Macha allahh amena solo yalla nala yalla faye la té samou Sénégal 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
jërëjëfëti Baay Mbay Gëy Sill ! waxtaan wi am në soló, leer në maachaAllah... Yàlla në ngë fi yàgg té wér ci barkepp Boroom Tuubaa suñu saŋg bi 🙏🏿
J’aime votre chaîne
Amna solo
Seugn mbaye gueye dundal
Bula dara decouragé
Xasoo ken
Xeebo ken
Yalla ak histoire ngay wahal
Kuko beugul deg ap dof kepp nga
Kilifa yeup wah nga sen mbir andak magal len
Kuy lim nak du matal
Kula tagul warula xas ludul ap reewal ak histoiram moko jaralul dara.
Dieureudieuf Serigne Touba amoul morm Serigne Omar fuutyu tall dieureudieuf Cheikh Moussa Cissé Ndiamé borom Darou
ولا تحسبن الذ ين قتلو ف سبيل الله امواتا بل احياءعندربهم يرزقون
Machallah yallah nalla yallah faye
Yalna yalla fayla guenji Faye Amine jerejef seringe by machallah ziarnaniou leh tawféx rèk
Serigne mbaké maram dieurdieuf serigne touba
Père yagui def liguéy bou am solo
Yalna yalla doli takhawu
الله يجازيه عنا كل الخير
المجاهد الأكبر خليفة الشيخ أحمد التيجاني
Walahi kham ngueen ne Serigne touba dou moroomu kenn ❤❤ moom rekk moo teh toubaab bi Dieurreudieffe Serigne mbaye gueye sylla yague fi lool te and ak weur and weu mo noo won fee gnakk❤❤
Cheikhou Omar bimoy liguéyele Sénégal kokou dafa dioudou sakh
Waliwou yoyou la serigne bamba done Dioullite faniou nek ak njii ci mere bi ❤❤❤
J'aimerais un jour visiter tous ces lieux historiques s'il plaît le bon DIEU et je dis merci BAYE SYLLA
Émission si khary amar fall
Cheikhou Omar foutihou dieureudieuf
Yagui ligeye bu refet yalla na yalla gudal fan wi
Machallah Seydi Cheikh Omar Foutiyou yalla na yok leram
Macha allah thiey tuubabbi ak Sénégal yalna gno yalla fayal mak gni.
Kepou koufi serigne el hadj omar moye sa serigne
Ahmadou de rassoulilahi yay serignam
@@boussodieng6813 dieureudieufé Serigne Touba ❤️❤️❤️
Linga wax mooy deug dé
Dou deugg dé
Moy serigniou Serigne si mou nékh ak mou nakhari
TALL Oumar FOUTUYOU TALL 🙏❤️
Jeureujeufeti thii histoire bi yalla nallène yalla dolè fayale
Yes. Respecdeded Salam omar who is a teacher fight for his good realigon and procte the people. Good person. ❤ he fell the pencil and took riepul for a cruel people. Salam and kudahapess sir.
salam il est temps de réclamer nos têtes et réclamer justice et aussi une reconnaissance universelle
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ sorou Mame Yi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah seydi TALL merci beaucoup grand père
merci beaucoup ci histoire bi mais amna lou dess lou bari ci histoire wou c'oumar tall demal nga geun ko geustou
Amna solo lollll papa machallah
Merci papa pour l’histoire de notre pays
O
Machalahh amna solo rafftna loloo yak fi te wer
Machallah s Mbaye léralyi Amna solou💪💪💪
Dieureudieuf Serigne Touba amoul morm dieureudieuf Ndiamé Darou
Ziar nala ygni am diamou histoire samorry toure ak toubab bi mom la niou bgue
Salam ziarr nalen loubari , mais souniou makgni yalnalen yalla fayal boppam ndakh kitakh nga talko mom talouko woon tenak المرتبة لا تسامح il faut faire tres attention
seykou oumar tal moy diambar
Tall tall❤❤
ماشاءالله Amnasolo
Jërëjëf Sëriñ Mbay wëppawi am na solo lool
Jërjëf
Li toubap bi wakh dou degge chiekh oumar foutiyou tall dou moromou toubaapp
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah ❤
رحمة الله عليهم
Merci grand père de nous révéler la vérité sur les actes barbares commis par les lâches hypocrites qui ne sont personnes d'autres que ces blancs (français)
Le géant de l'islam
ماشاءالله بارك الله فيك
Assalamou aleykoum j'aimerai bien écouter l'intégralité du générique merci de bien voir le partager sur votre site. C'est très émouvant merci encore une fois de plus.
th-cam.com/video/6uCmvb0zff4/w-d-xo.html
C samba diabaré samba
Sénégal yag na am ay workatt 😭😭😭
Wa tobabbi mom xana rayonosi dara sonou mam yireg lanoyi rayi😢😢
شكرًا جزاك الله خيرًا
Machalla bay mbaye
Salam goudal fane ak weer diadieuf
Sunui mame dji ndeysanne defna lounek si dineh lislam
Toubab doméram leu rekkk damaléne bagne trop bakhou gniou
😂
😂
Toubbab bakhoul
😢 الله اكبر
Machala sama mame dji
Machallah s. Mbaye geuy sylla
Notre fierté
Amena solo
This is my great grand pa..rest in PEACE
Amnah solo
Senegal😢sénégalais 😂, yallah nañu bolé baal amine 🙏
شكراً جزيلاً لكم سماحة الشيخ الجليل🌹♥️ جزاكم الله عنا خير الجزاء
Damaa jooy ba sonn ñii ku ànd ak ñoom démb ak tay doo xam ci loo koy teg! Fayu dong a nu war ci ñoom, jeexal nanu sunu woroom xam-xam yépp! Ray wuur ak sëriñ si bàyyiwuñu kenn, lii ñaaw na torob billaahi, waaye nag Xaadim Rasuul siggal na waa Senegaal ci tuubab yu Bon yii, siggal na it islaam su dul woon ak moom ñépp soppaliku ay yéefar.
Sa mame kendou mome
Di yéssal waxtanu histoire du Sénégal Amna solo lol yalah nangafi yag ak Weir amouniu sa fay
C'est pertinent
seykou oumar tal bo xamoul bindam manoo ko wax taane mem fadu bimou fadou bandia gara wax na ko si bena terem bu toudou safina bo diangoul boul nangou wax si mom dara
Machalla baba yalla re motakhona diokh mame chiekh oumar foutiyou tall ak diné kou beugué kham safinatou sadadi mogiufi
Machalla baba yalla re motakhona diokh mame chiekh oumar foutiyou tall ak diné kou beugué kham safinatou sadadi mogiufi
Bjr xam Sam sa rew suis vraiment content de cette initiative et je vous encourage aussi, mais ya quelque chose qui me dérange vraiment dans l'annonce de cette vidéo. Est ce qu'il ne faut pas supprimer Blaise diagne et ce commandant blanc, j'ignore c'est qui mais ça ne rime pas avec l'idéologie de la chaîne. Ces 2 hommes ne sont pas des résistants au contraire ils font parti de nos pires ennemis que le senegal n'est jamais connu.
Masahala
Machallah Dieureudieufati
🙏🙏🙏🙏🙏🙏✊✊✊😭😭
dieureudieuf Serigne mbaye Guèye Sylla
Mame omar futiyu et mon arrière grand père
Moi aussi je suis petit fils de elhadji Omar tall même mon oncle porte son prenom
Ndeysann sa mame jambaaar lawone..
Moi aussi je suis sin petit fils
@@elhadjiahmadouba2048😮
Merci sill
Souma guissé toubab bimouy wakh paul holle chef de poste Podor toudé naniou ko béne rue sama kogn daff may métti . Ak dieuf you niaw youmou déff yeup dieul bakanou sénégalais you beuri ak domou dioulite nga délou diko toudé rue . C vraiment honteux
Hakassaa mouride 🇸🇯🇸🇯💖💖
Onrar❤❤❤❤
Machallah machchallah
Dieureudeuf massa thioño de vote recherche
Machallah ❤️❤️❤️✊
Amna solo rafftna loloo yak fi te wer
Tèy la walo gueuna aye je suis en France
Allahou akbar 😭😭😭😭
C’est quoi le nom de la chanson (XaLam) qu'on entend derrière et où l'écouter ?
Is very nice!
La chanson s'appelle saraba
Ndeye sane 😭😭😭
Yemena
شكرا جزيلا
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Serigne Mbaye Gueye sill yalla nangafi Yagüe looool