Machalla kene dou mawlana Cheikhou Tidiaani kou nek si yonou nassiril haqh bil haqh dadié ak mom sope ko té sakh and ak mom rek ndakh yonou Siratal moustakhim béne la beussoul bleu so dacoré
Meunouma sakh wakh ndakh khol bou sed te fese yalla nalen sunu brom défall diamou ak kheweul soutoure gou sakh dak si barkep Seydina Limamou Halayhi Salam🙏🙏🙏❤️❤️❤️
سررت كثيرا بالاستماع الى هذة القصيدة التي نظمها فريد عصره،ووحيد دهره،لمدح تاج العارفين،شمس الولاية الكبرى و القطبانية العظمى.السيد ابي العباس،أحمد التجاني. نحن أولاد التجاني من ابوات المعاني#ولنا منه نصيب فوق غايات الامانب.
Nekhna dalll ou sont les musulmans puce lenn bleu
Je suis moustarchida mais j'adore sokhna codou laye merci pour cette belle prestation😗😗
Olala 😍❤😇Li nexxxna wayyy❤😍Bilae Serigne Moustapha Sy limou waxx si yénne rk lolou rkk mo ammm bilae mallene beug❤
Je suis une Tidiane mais je fiére de vous c ça le Sénégal diereudieuf yala naléne yala same wéral bate yi incha allah
Amine yaa Rabbal Aalamine
Machalla kene dou mawlana Cheikhou Tidiaani kou nek si yonou nassiril haqh bil haqh dadié ak mom sope ko té sakh and ak mom rek ndakh yonou Siratal moustakhim béne la beussoul bleu so dacoré
Machalakh sokhna codou laye khassida mame cheikh Ahmed tidiane sy almakhtoum yalnala yalla faye si barkème yèna niak kiniane bilahi
Amine yaa Rabbal Aalamine laay
Yalnaniou yalla déf talibé cheikh ahmada tidiany
Toute ma famille est Layénes mais je suis moustarchide, j'aime vôtre philosophie la discipline on a des choses à commun. Je vous aime
𝑵𝒐𝒖𝒔 𝒂𝒗𝒐𝒏𝒔 𝒍 𝒎𝒎 𝒔𝒊𝒕𝒖𝒂𝒕𝒊𝒐𝒏
Je suis layennne mai jai des larmes aux yeux de cette zikr merci codou laye makhatr
Walay ndeysane montre you bax yi nio bokk heure
J ai des frissons merci vraiment les Layennes pour ça Yallah naniou Borom bi def ay talibé Cheikh you wéreuh té niou déssi
Meunouma sakh wakh ndakh khol bou sed te fese yalla nalen sunu brom défall diamou ak kheweul soutoure gou sakh dak si barkep Seydina Limamou Halayhi Salam🙏🙏🙏❤️❤️❤️
Amine yaa Rabbal Aalamine laay
Nahnu awladou tidjani❣️ j aime mame cheikh yalla n'a yalla gnokou ay léram
Amine yaa Rabbal Aalamine
Sokhna Codou thiaw laye mou papa cheikh Mbacke thiaw laye Mala sopp ❤️❤️❤️❤️
Machalah yalla n'a yalla weral bate bi ❤❤
Machaallah li takh na ma gueun leen diap
Mash'Allah Wa Daaray Seydina Limamou Lahi Al Mahdi (Psl)
Wa Ahlou Lahi Yeen Lañou Jagléel Xéeti May Yeena Ame Ngeunéel _ Keep Kouy Sakooti Xeewal Japaléen Yeena Ame Maxaam
Xoxo😍😍😍li nekhna ndeysanne😭😭😭😭 YallaH na YallaH fay yiww tei mou Yokk Leroy Mame cheikh Tijan Al makhtoum 😍
Amine yaa Rabbal Aalamine laay
Diarama Mame Cheikh Tidiane Sy Al Maktoum❤❤❤
Ndeysane je ressens bcp de frissons bilae😭😭😭😭😭❤️ contane na lol Yalna diam saxx si senegal 🌹🙏🏽✨
Douma ci doyal masha Allah Laye Makhtar 😭😭😭😭
Allah! Khôl fèss na té sedd, ni guéne diangué khassida bi nékhna 😭😭😭😭😭😭
Machala keinou dou mame baye laye (psl).... beugueu mame seydi❤️❤️
Manchalla les Layene
Yalla na Yalla weral batt bi té fay la yiw machaallah
Khole yeup sédd nagne
Je vous adore vraiment.
Ooooh machallah 😢😢😢xol sedatina Laye maxtar
Bay lay niepe la ndiabote ma cha Allah
Machalla laye mamadou kenne dou baye laye hool yi sèdena
Mashalah khasida bi serigne cheikh ahmed tidiane sy moka voye
Alkhamdu dieureudieuf yallana diam yagu Sénégal
Mame limamou laye saliguey rafetna macha allah
Vidéo bi douma ci doyal chaque jour ma séane machalah dafa nekh ci kholl
Wallaay, défa neex ci xoll
Masha Allah laye makhtar khol yii seddatina😘😘😘😍😍💫💫💫🙏🙏
سررت كثيرا بالاستماع الى هذة القصيدة التي نظمها فريد عصره،ووحيد دهره،لمدح تاج العارفين،شمس الولاية الكبرى و القطبانية العظمى.السيد ابي العباس،أحمد التجاني.
نحن أولاد التجاني من ابوات المعاني#ولنا منه نصيب فوق غايات الامانب.
Merci bcp lé layenne ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machahala way li moy Sénégal
Jaajeufeuty
machallah yalla na yalla barkel tee weral bate biii
Machallah yalna yalla wereul batt yi si barke serigne babacar sy rta
Amine yaa Rabbal Aalamine
Codou la voix d or machallah délou si yallah
Merci Soodaan TV
Walay ndeyssane 😭😭😭thiye Mame Cheikh kénne dou mom bilahi contane torp bilahi
Maacha allah yeen dé woudjé woolene
Jaajeufeuty laay maxtaar
Macha Alá amna solo trop bilahi yalahi Ken dou serigne check tidiane sy
Allahou akbar sama yaram bangui daw😭😭
Tabarakallahou Akhsana Khalli qhiine
Lii Rafétna trop MachaAllah
Je suis talibé cheikh ahmadou bamba mais li veraima nékhna trop ❤️❤️🤍🤍🤍
Jaajeufeuty
Wallahi li dafa nékh trop
Yalla na djame yagg Sénégal
Merci beaucoup
Machalah laye diabel yalla na bat bi wér
J ss mouride machalla li nekhna layen yi gnon bakh way
Mash’Allah
Je vs aime énormément
Machallah yalla na yalla Faye dieuredieuf
Amine yaa Rabbal Aalamine
Machallah machallah
ohhn maashalahh li nekjnaa
Wallaay
Baye laye lep dafa rafetna
😭😭😭❤️sedena trop bilay
Machallah hol sedna
Machallah xol séde na😍
Djazaakoumoulah hayral jazaa
Machall cudou laye kéne dou mane cheikh
Machallah amna solo
Bilahi yalla nala yalla faye yiw.
Amine Yaa Rabbal Aalamine laay
Ndéysane Sénégal bénela Tidjane Khadre Layene Mouride Niasséne Benelaniiu
Mention spéciale vous montrer le Bon exemple
Machalla lii dawna yaram bilahi
Machallah laye makhtar
Walay macha Allah
Walahi Gamou Layénné yi yi ame Taiba Ndiaye c est qui fait l enregistrement c est ça le senegal Bilahi
Jaajeufeuty
Mashalla li nékh na trop
*MachALLAH Laay Mactar*
seul le pouvoir de DIEU est éternel 😭😭😭😭😘😘
Merci codou
Manchalla Laye Mactar
Machallah ❤️
Macha alla sama khol sèdena
Ndeysane machala 😭😭😭😭
Manchlla laye
Nékhna💓💓💓mame💜💜💜
❤❤❤ bilahii ma sante yallah
Dieureudieuf machakah
😭😭😭😭 aka nio bakh les layennes !@
MACHALLA
Manshallah ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah ❤️❤️❤️💋🤲🤲
yalna yala faylén yiw;
Amine yaa Rabbal Aalamine
Mashallah
Machallakh
MashaAllah 💓💓💓💓💓💓
😭😭 sama yaram daye dao
Mach'Allah
Machalla
Machalla ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👌
Houbou Cheikhi
machala
Walay nekhna
Wallaay, El Hadji
Machaala laye makhtare wanè ngène ni gnoune gneupa boukou fignou dieum moye yalla sougnou borom
Jaajeufeuty laay maxtaar
Non Macha allah 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Jaajeufeuty
Nehna
🔥🔥🔥🔥
ENVOYÈ LÈNN MA NUMERO ,CHANTEUSE BI ,SOPÈMM LA😥😥😥😥😥😥
❤❤❤
💯💯💯💯👍👌
Le générique c'est quelle titre je le cherche depuis longtemps svp
C'est SOODAAN de Khoudia Mbaye Leye.
svp je veux le texte wallaye qu'Allah vous recompense . bi djahi cheicki tidjane
Ta demandé est toujours d’actualité..? J’ai le document.