maa cha allah touba je suis tidjiane mais je suis fier et content de celui qui a fait cet act .si tout le monde faisait comme cela il n'y aura plus de goor djiguen
Si on parle véritablement d'une ville sainte c'est celle de Touba ! Toujours Serigne di geuna wané boppam. Kouka guiss ci bénen deukk na wakh. Machaa Allah!
s touba dakm bi li yalla dikelè lafi dikelè li yalla di dère lafi dèrre kone yalla nalè yalla faye yène gor jigène yi wara gèna xame ni ligèni dêfe baxone bayile ko ta yalla tax
Té nga bania dougou ci domainou ville informée yoyou. Il se passe de choses les plus basiques de l'nstinct à Touba. Et s'il en sont informés c'est qu'ils sont complices. Lors de la célébration de Massalikoul Djinane rek deux personnes ont été égorgées. Où étaient les services de renseignement ? Bayilén wakh you eupp. Cependant je félicite le travail de ces gens qui ont empêchés le convoi de corps d'homosexuel dans la ville sainte
@@oumarsow8344 Mangui ci société batay tamitt. Dama wakh ni il n'y a pas de statistique qui fait que Touba soit la plus informée de ce pays. C'est un exagération. Pourquoi je le dis? Parce-qu'il se passe énormément de trafic d'organes, de médicaments, de chanvre indien comme partout d'ailleurs. Et ces réseaux ne sont jusque là pas dementelés. Où est l'information?
Touba la Serigne fallou mbackè wakhone rèk nèna touba ma yorè Rato bi ak lonkk bi Lounoufi soule tè warounoulafè soule mame Fallou ma dirila ak Ratobi guènèla touba lèpp lou Fatto fènène niou soulafa tè warounoulafa soule mane fallou loumou goudi goudi ma lonk la thi lonk gui nga fananesi
Comentaire bi laye ègalè Nga fananesi touba serigne bi nèna barina ngiou soule sène nèeweu touba tè nèeweuba molène di ndieukeu guèna touba gor djiguène bi bounou ko soulone touba tamite doulène raw serigne fallou dinako Roto mou guèna touba ak liko weurr barké serigne touba Touba mome Rato fi nè ak lonkk Wassallammmmmmmmmm
En tout cas sou nekkè juillet la woon gnou gui ka niaanal djiegalu Yallah.. Wayé Liguëy bi Mash'Allah, ndakh ap xuppu la thi keppu ku thi nekk.. Wayë di app Sognë thi bepp wadjour bo hamni am nga diaboot buni tuddu di tuddu LOLOU.. YAL'NA NOU YALLAH GUÉNA HAAR TE HAAR DJIABOOT GUI..
Macha alla séne liguéye raféte na lole yalla nalé serigne bi guene takhawou té fayale léne bopame touba borom moukay arale bopam incha alla serigne mountakha mbacké yalla na fi yague lole té andak wérr bamba merci
@@saikh2348 kham nga loguis mandou dathia guen togne bakhoul man li ma wakhe mom la guem manothi dara sama diguen tèèk sama borom nak totinga thi dikou lidjianti gnakou foula ak gnakou fayda manoul wésou kou wakholak yaw ngaye wakhwk moum dangèna sokhour wayé dangén dè thi khoul you khat serigne bi li mou am manou lèn thi dara démal djiamou dji yala ta lidjianti sa bopou mou guen
@@saikh2348 yaw danga khamoul mais linga wakhe manga thi am bakar borueye ndakhe man yala ladèf moye sama borom yonèntèbi moye sama yonènté s.l.h.w. kon bowakhè loulou rèk fèn nga ta fèn bakhoul ta man moum wakhe degue amoma djiot pour nekue fi di wérènté djiapal linga djiapou ma djiapou lima djiapou
gourjigene boye doundo denko wara raye bou Fatou kenno waroka dioule danoko wara sane sa sanbe dierejefe wa moukhadimatoul khidma sen ligueye refetna yella nalen yella faye guengue Faye amine
Lii warna tax nite gorei ba dheii nangou liko yalla melale tengua sante kosi boubax dieureudieuf SERIGNE TOUBA
Dieuredieufé serigne touba Diarama mame chiékh Ibrahima fall
Touba mbacke amna boroum
Sérigne Touba amoul morom
Je suis tidian mais dieredief wa touba yalla molèn di fay
Merci et toi frère yalla fayla toi aussi
maa cha allah touba je suis tidjiane mais je suis fier et content de celui qui a fait cet act .si tout le monde faisait comme cela il n'y aura plus de goor djiguen
Machallah yalla nalèn serigne touba fay
Touba renseignements akkk sécurité plein fouleu akk fayda tek ci bilahi Barker borom touba
Yaw dé doy ngua waar ni def bâ khamni goor djiguéen la
Touba la ville avec une population la moins aphabetisé mais la plus intelligente et la plus informée du Sénégal.maleen fan deh
Attention ce n'est pas la ville la moins alphabetisé... tu parle peut etre du français.... mais alphabet ne se résume pas au français
Merci moustapha
Bonne les son a toute les musulman islam la vérité dierediefe serigne touba
Merci wa Touba Mbacke ni le wa Senegal yép waron déf ní
Si on parle véritablement d'une ville sainte c'est celle de Touba ! Toujours Serigne di geuna wané boppam. Kouka guiss ci bénen deukk na wakh. Machaa Allah!
Yow vraiment seuytané ga gueuno nio beug seugne bi mais bayil douggou si débat tarikhah yi
Moctar Dia bayil doul
@@goldenmanonly9833 merci
Dieuredieufety serigne touba diarrama cheikh ibrahima fall yalla nagnou yalla mousseul si goor djingene ak lou khetok mome vive lislam vive touba❤️
Bien fait
Liii rék moy deugeul wakhiii serigne mountakha yii bala guay nékk mouride fawgua nékk app djoulite té touba deukou djouliite la té liii gnapé siii wara bayii khél ndakh goor djiguéne dafa kharam kén warouko soulle sii alméérre you djouliite...dieuredieuf borom touba
Kou amm Mbokoum goor diguenee Waxale akk mome Ndaxx sou dewee yawe laye sonale Nakh foo diame akk sab Neew niounala Athia
Assane Samb 😂😂😂😂😂
Assane Samb bilayyy walayyyy
Noooo assane rayy ngama
Yagui may y reee loo
Walahi dek gaa wakh mbokou yi gnoy sonou
Yalla naniou yalla ray si yonou siratal moustakhim
Dèfe lou bakh rek mo am solo ndakh déh day gneuw liguéye bi rafète na machallah
Vraiment ibadou là wakhikhan m'ai contane n'a thiî yénn yallah ngeun yagg fi loooooool thé âme djamme
Waw goor
Moustapha Mohamed ali Bah Niola gana neka ibadou fouf boulen niou sonal s.touba mone ana mouridoul lahi sof guen torob soko done gadiemko diafe te Bayi wakhadji bariguen wakha torob yalla bokoye diamou dagakoye def rekh guir diamam dji te khamne moyesa borom wasalam
Diolyt gua bapa rek mou jditou lepp
@@serignefall8803 wallahi yakar nako ibadu sah duwahne man ibadu la. Yallah nako yallah yieuerram waydawlo bi
Diardieuf nioun niepou penna lanou
s touba dakm bi li yalla dikelè lafi dikelè li yalla di dère lafi dèrre kone yalla nalè yalla faye yène gor jigène yi wara gèna xame ni ligèni dêfe baxone bayile ko ta yalla tax
Barki rassoulilaye maléene guëme yénne Sénégal guéppe guénne waara dirigé 👍👍🙏🙏💕💕💕
Bilay walay touba la gueume
Félicitations goor djiguen thia khath reek
Eskey barké cheikhoul khadim yalla nalen yalla defal diamm
Ay ki yeureum nako dè bone lilay diarigne yalla nagnou yalla khir thi loubakh 😥😥😥
C'est vraiment grave
Doyna War yalla naniou yalla may moudjou gou rafett
Touba une ville le plus informer du Sénégal
Baye Khawsou Diop liguey bi raféte nah 🙏🏽
Té nga bania dougou ci domainou ville informée yoyou. Il se passe de choses les plus basiques de l'nstinct à Touba. Et s'il en sont informés c'est qu'ils sont complices. Lors de la célébration de Massalikoul Djinane rek deux personnes ont été égorgées. Où étaient les services de renseignement ? Bayilén wakh you eupp.
Cependant je félicite le travail de ces gens qui ont empêchés le convoi de corps d'homosexuel dans la ville sainte
Yaw doule li dou affairou tarikha affairou société la mbame guene rek
Amna gnou sokhor nakk
@@oumarsow8344
Mangui ci société batay tamitt. Dama wakh ni il n'y a pas de statistique qui fait que Touba soit la plus informée de ce pays. C'est un exagération. Pourquoi je le dis? Parce-qu'il se passe énormément de trafic d'organes, de médicaments, de chanvre indien comme partout d'ailleurs. Et ces réseaux ne sont jusque là pas dementelés. Où est l'information?
Yalla nanu yalla mousseul si saytanè ak moudjou gou niaw Amine?daray Adina diaroul lii
Touba la Serigne fallou mbackè wakhone rèk nèna touba ma yorè
Rato bi ak lonkk bi Lounoufi soule tè warounoulafè soule mame Fallou ma dirila ak Ratobi guènèla touba lèpp lou
Fatto fènène niou soulafa tè warounoulafa soule mane fallou loumou goudi goudi ma lonk la thi lonk gui nga fananesi
Comentaire bi laye ègalè
Nga fananesi touba serigne bi nèna barina ngiou soule sène nèeweu touba tè nèeweuba molène di ndieukeu guèna touba gor djiguène bi bounou ko soulone touba tamite doulène raw serigne fallou dinako Roto mou guèna touba ak liko weurr barké serigne touba Touba mome Rato fi nè ak lonkk
Wassallammmmmmmmmm
Waaa toubaaa djaramaa a vous !! Djapalè islame rekk
Merci merci merci encore merci serigne touba
Thieuy yalla yalna yalla doli soutoura
Yalla na yalla yok ligay bi rafet na
Li dara diotouko si adouna mo takh def lou bakh rek mo am solo nek si lou nekh yalla
touba serigne béko teuyeul boppam
Na Sénégal gui yeup di def ni.
Gardien cimetière yeup naniouy enquête bala niouy sooul nite.
Goor jiguen sa mbalite rek
Marie Amar Li nga wakh Sokhnaci dou Sunnah !
Machalla wakh dji limasi guena nekh moy diaroul goudeul na guénn touba rek walahi kéndou Ahmadou khadim
🤣🤣🤣👌
Mamy Gueye bayiléne bokalé dieu est partout souf souf la rek touba Dakar paris surtout la Mecque
@@babacardiop9331 yaw dagay togn wala? Gordjiguén kén douko soul si armel kén douko dioulé si diakk lolou khana lou way GATT dégg dégg khamga lolou
Mamy Gueye mes yow chaire humaine si ont l’enterre pas ça amène des maladies
@@babacardiop9331 dieulale gua soul ko sa keur. Ki dou dougou touba wala yaw lo beugue
Li lan mokafii diar thiey adouna wah touba kéneu duu niom gnidanio yabaté mais yalla wérr nalén
Dieureu guene diafati wa Touba yalla naléne yalla guene takhawou ci barcke s.r Touba Mbackè amine
Tahaway bi rafetna Touba sakanam rek
Merci merci merci
Tres bien danio wara dadialer sene ndeye akk tiaga jilene dii def ayy xarite di ande ak niom defsi Pakh talsene ndey
Allahu akbar allahu akbar allahu akbar!!!
Sama ouztas machalla
Soubhanalaaa thieuy Sénégal yalniou yalla mouseul si yiii
En tout cas sou nekkè juillet la woon gnou gui ka niaanal djiegalu Yallah..
Wayé Liguëy bi Mash'Allah, ndakh ap xuppu la thi keppu ku thi nekk..
Wayë di app Sognë thi bepp wadjour bo hamni am nga diaboot buni tuddu di tuddu LOLOU..
YAL'NA NOU YALLAH GUÉNA HAAR TE HAAR DJIABOOT GUI..
Brom ñari tour yi lañou wakh Gor djiguen guakoy ñanal diegalou soñou brom khana khamo li yalla wakh si lolou?
Man daal wa touba la geum
Macha alla séne liguéye raféte na lole yalla nalé serigne bi guene takhawou té fayale léne bopame touba borom moukay arale bopam incha alla serigne mountakha mbacké yalla na fi yague lole té andak wérr bamba merci
Taye d sama xol sed na gouye barki mouhameth machalla
Çëy serigne touba
Lou waroul dougou touba mom loum yag yag dofi dougou bamba dafa defar lepam s bamba rek mn nako femgal di niaw gor djigene rek ay domou ram lan
Waw GOOR way.
Qu'Allah nous guide vers le droit chemin amine
ah ndaysane MAME FALLOU borome rokhe ba ak lonk ba none nà déh lou dougue TOUBA ta bokoul fi dina rokhalabe mou guéne TOUBA.. thiéy
Serigne mountakha néna dioub rek mo am solo li rek mo takh mou wakh ko
Yalla nagnou yalla dioubal lila sénégalais yeup wara def goordjiguèn gnou gnef sèn ndeye
Ak sen minicar bou wét bi sen wadji setoul dé nama yalla bal nak jeure jeuf wa touba mbacké amna soli gorjigén sa malit ma rék
Li rek mon bakh
Ah bon pour mane touba kou djote rék soul sa néw ç est très bien ça
Dieureu dieufé serigne touba
Machalla kadouyi amena solo !! Légay bi rafétena Dia gay dieuf
Dieureudieuf Serigne touba
Tres bien fait machalla ligueye bi rafetna djeureudjeufei S Touba
Lideh diar na néwe bou niawati niou khol ko bapare
*Merci beaucoup moukhadmatoul khidma sène liguey RAFÉT na troop fi koufi addouna diay banga nékk Gor djigene donla roob SOUNU armiel Bamba RK*
Diadieuf way
Theuy yalla doyna waar trop yalla nanou yalla khir thi bopam ngou sakh thi diko diamou ba kheuy fatou
Shi lidai louko guen guen niaw amoul daray adouna diaroul lii walahi merci bcp sen liguey rafetna macha allah
Kou bone mome thia seune ba rêk
Naguine touba rek
Yalna sèn diam yague si barkè s touba
Djeuredjef s touba mamoul morom téh douko ame borom deuk bou séll bi koufi narra déf lou diouboul sounou borome dinala féniale
Manchalah wakh jii rafetna, wawaaaaawww na jogué fofou yeup, sa khatth
thieuy s touba soufou touba niou tédd niofiy teudd dara douléne rakh kou bone mom sa aleu ba rék
Machahlla
Waw lén goor diapeu lén rék yallah amna faye té dina lén faye barkép borom touba
Me
Soow lousi ñoul feñ...bn travail bougueuleum mo tambali ni
Thieuy s.touba 😭😭😭
Machalla sen ligueye rafetna trop yalna borom bi samlen te arr len si barke seydina mouhamed
Allahou Akbar
machaalah nonou dongoula gordjiguénne mome sa bity rek
Maasha ALLAH diiné foulla koy dokhal. Wallahi yena am foulla
Manchalla amna sollo
Moukhadimatoul khitma sen ligeye rafetna
Wa touba nio wara djité senegal daray thiakhane ak tappalé
Yalla nagnou yalla mousal thi wall wowou Lou yalla reub laaa
Gnou mèlni moum serigne bi molèn di fègnalal bopam
⛔Bayi lén bookalé ki Yalla mooka fénial
kignay wakh soumanoone dalén Di téré niouy dougal khalis thia deuk ba
@@saikh2348 kham nga loguis mandou dathia guen togne bakhoul man li ma wakhe mom la guem manothi dara sama diguen tèèk sama borom nak totinga thi dikou lidjianti gnakou foula ak gnakou fayda manoul wésou kou wakholak yaw ngaye wakhwk moum dangèna sokhour wayé dangén dè thi khoul you khat serigne bi li mou am manou lèn thi dara démal djiamou dji yala ta lidjianti sa bopou mou guen
@@saikh2348 pourquoi yalla téré wouléné niou dougal fa xalis bi? Comme yafi wakh wakhou bokalé. Kone dafa mélni yagui bokalé dh.
@@dramecheikhou9323 kham nga limaléndi wakh mooy nguén bayi bokalé té ki nguén ték sén Yalla nguén Di ko nianal yalla yeureum koo
@@saikh2348 yaw danga khamoul mais linga wakhe manga thi am bakar borueye ndakhe man yala ladèf moye sama borom yonèntèbi moye sama yonènté s.l.h.w. kon bowakhè loulou rèk fèn nga ta fèn bakhoul ta man moum wakhe degue amoma djiot pour nekue fi di wérènté djiapal linga djiapou ma djiapou lima djiapou
Rafat tv
yalnagno yala defal soutoureuye adina ak alakhira
Dieuré ngén Dieuf ,yalnalén YALLA fay🙏
Waw leen goor amatina solo yeen wa khidmatoul khadim
Yalla sedaneni serigne Touba beguena si yen.boulen messa tayi.Touba yepp nawnanioulen
Bravo merci
Mashallah ligéye bi rafétna lool Yallah naléne Yallah faye bar kép Serigne bi
Mbalithe mome thia seunba rék
Masha'allah ligueye reik di saytou lepp comme dale dagno fok ni Cheikhoul Khadim noulene nekh nguene beugg def deuk bobou. Sene ligueye masha'allah ♥️
Onzibillah li rek warna takh nioune nitt gneup bayi khèl thi adouna amoul bén solo wari nèn la. Yalla naniu yalla khir si lu bakh🙏🏽
wa mouxadamatoul xidma sèn ligèy rafétna machalla 👏👏👏
Wawe laine goor machallah takha waye bi amna solo
Khawma loutakh domram Yi yab Touba rek yaw doundou nga ba kheuy de si lou nekhoul yalla beug nou sola touba domram demal nou sool len sa khathie