Belle leçon sur la sensibilisation des jeux de hasard communément appelé NAAR BI interprété par IBOULAYE où on peut noter des dégâts maléfiques tels que dépression, anxiété, culpabilité, colère, solitude, isolement, déception, perte d'estime de soi, perte de contrôle et idées suicidaires. Respect Evenprod respect ✊✊✊
Vraiment Boury je l’aime bien elle est tellement differente des autres femme dans le showbiz a part sa j’aime le concept da Xalisso bonne continuation.
Teint bou rafet wala fond de teint bi mo rafet yënn khana guissoulënn sokhna bou makk sans maquillage akk bouton you reuy akk guëmine gou wëgue gui melni kagna😂😂😂😂 guënn di wakh teint bou raffet bayilënn ba guiss niey guën si télé yi sans maquillage la on nous allons parlez de beauté mes chers😂😂😂
La mère de Maty Rose, par amour, conseille à sa fille de laisser tomber Oumar, renonçant ainsi à l'unique bonheur de la vie: aimer et être aimé. Cela me rappelle Nicolas Sarkozy qui disait "les pires conseils sont ceux que te donne une personne qui t'aime". En effet, celui qui t'aime cherche à te protéger en te conseillant de ne pas prendre de risques. Or qui ne risque rien, n'a rien. Mais.... avez-vous BIEN passé hier la fête du 31 février?😂 c'est bien ça, c'est très bien.😂😂LOVE
HEURES DE PRIÈRES DU 03 AU 09 JANVIER 2025 Fadjr: 06h22 Suba: 06h37 Tisbar: 14h15 Takussan: 16h45 Timis: 19h01 Gue: 20h01 Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Khadija, la mère de Anta nous parle de sa relation avec son ex qui est d'ailleurs son premier amour, cet homme pourrait bien être Amath ... Si cela se tiendrait il serait fort probable qu'il soit alors le père biologique de Anta. ( Anta et vieux Ass, mouss dou diour gaïndé) Et n'oublions pas que Khadija préfère 1000fois Anta à Diadia. Elle l'aime énormément Mère bi dafa melni dadone découcher di guissé ak Amath "l'homme de sa vie" 😅
Le jeu d’acteur d’Iboulaye 😂 Le théâtre c’est sensibiliser et instruire sur les phénomènes sociaux. Evenprod le réussi brillamment. Les paris sportifs sont à l’origine de nombreux maux.
Pourtant le père de Boury c un papa exemplaire top et responsable franchement je l’adore contrairement à Ibou Laye dont c sa femme qui porte le pantalon ❤❤❤❤ Mes meilleurs vœux à tous !!!!
Bonne et heureuse année à toute les internautes et particulièrement à nos acteurs d'évenprod qui se sacrifient toujours pour notre bonheur et qui nous conscientisent merci beaucoup
❤❤❤ Yalla n'a yalla doli'gnou défal soutoureuh inchallah 🎉... Mashallah Fatabara'kalahou ♥️☝🏿🕊️... Mais Sénégal war'nagnou xam'nei galathie leuh si djiguén Mouy tokk keur borom djeukeur'eum waxou'mala mou nék fa masoul fay galathie bou mata sameuh Am'na nitt gno xam'nei molén Di fadj tmt 🎇 🥰... Film bi limouy djangualeii tmt barineuh dh mashallah 🥰 🥰 y'a beaucoup de leçons a retenir ☝🏿🕊️ vraiment on ne peut pas dire tout en un mot merci ...
Khadija mbaadou Ndaw banquier la doone beugueuntél eumbe fekk Ndao banquier yoroul khalisss mou tekk deal Ass Diagne seuyeul ko après la diour Diadia qui est la fille de Ndao banquier motakh mounou ko mougneul dara.... Temps bimouy eumb Ndao banquier mingui nekk pauvre Voilà khara ma noppi sakh... Mais j'insiste na Nianko alias Omar Diagne werr mou nekk si bénène personnage pour une première fois dabs sa carrière artistique bref tres bonne année à toutes et à tous
2025 bi yalla done atou banekh AK joutoura AK xéwal AK goudou Fane AK wér AK werle keppou kou febar yalla nala yalla may wérr kou nék kasso yalla nala yalla guéne AK diamou yalla na Ousmane sonko Am ndam si kaw Ay nonam barke zeydina Mohamed inchallah Amine yarabi 🤲 inchallah ❤️❤️❤️
Il repose a Medine on l’a jamais vue ni jamais entendu sa voix mais son amour vit des millards de personnes notre bien aimé le prophète Mouhamed saw ❤
Sallahou Aleykhi Wa Salam ❤❤❤❤Masha'Allahou Alkhamdoulilahi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
Salalahou aleyi wa salam
Paix et salut sur lui ❤❤❤
SPL Mohamed notre bien aimée 😭😭😭😭💓❤️💕💘💞
La classe de boury est réel même hors série bi sakh doko guisss fèn si réseau yi elle est trop classe et responsable des Coeur ♥️ pour elle ❤❤
❤
❤❤❤❤
🎉🎉🎉🎉
Bilay ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Bilaye walaye
C’est l’anniversaire du décès de ma mère aujourd’hui je sollicite vos prières 🤲
Yala borome bi yésal yeurmadem si kawam ak bolém dioulite
Yalla nako yalla yeureum
Yalla nako yalla yéreum
Paix à son âme 🙏
Quelle repose en paix ❤❤❤
Ay way koumay aimé 😂épisodes 1 ba tay awma j'aime ❤😂😂
❤Sofe nga trop😂
Belle leçon sur la sensibilisation des jeux de hasard communément appelé NAAR BI interprété par IBOULAYE où on peut noter des dégâts maléfiques tels que dépression, anxiété, culpabilité, colère, solitude, isolement, déception, perte d'estime de soi, perte de contrôle et idées suicidaires.
Respect Evenprod respect ✊✊✊
Bilahi t’as tout dit ✅
Bolessi endettement sévère
Surtout
@+niangmahi8635Merci, heureux de savoir que vous avez tiré une leçon de cette série. 👍
diap na tay 80000000f narbi dou ay tiaxane
la main qui touche le téléphone en ce moment touchera des milliards en 2025🥺🥺🥺 inshallah ❤🙏
Amiiin 🎉
Amine ❤❤❤
Amna lo khamanté nè mounoull nekk 😂
Amine yarabi
Amine yarabi❤❤❤❤❤
Team Maty rose ak Omar diagne yalla Nanou don millionnaire si année 2025 bi
Merci Evenprod japlen ci mou mat 5M
Amine gnogui ni dh gnomm rkk lagnouyy topppp😂❤
Amine
Amine ❤❤
❤❤
Amine
Wa mais la classe bi boury andal tito lén si très bien boury bien fait boury😂😂😂😂😂
@dabagueye3713 Mome dhei neina dey nape Ndiawar. 😂😂
Avez-vous vu le talent d'acteur de Boury ?
Quel charisme !❤
Si elle est très charismatique
Vrm boury est une grande d' actrice
Oui
Dd❤❤❤❤❤❤
@ModouCoulibaly-c2n Merci beaucoup.
Ohh la sensibilisation sur les dangers des paris en ligne avec Diop Fall est excellente, vraiment top 😊
Vraiment 👊
Bly
@@AbdoulazizSy-b2l walahi dé
Borome Chelsea 😂😂😂
Narr bi bakhoull😂
Yalla Na Année 2025 Soit un Année De Bonheur ❤️❤️❤️. Et En Plus 1 Janvier Bi Yalla Nagne Ko Yagueu Fékké Ba 1 Janvier 2099...
Amine
Amine yaa rabbi❤
Alhmdoulilah Sante yalla rék
Amine yarabi niou féké nioune nieup
Amine inchallah psl
Vraiment Boury je l’aime bien elle est tellement differente des autres femme dans le showbiz a part sa j’aime le concept da Xalisso bonne continuation.
@SoumaDiop-k3c Merci beaucoup. ❤
Lima nékh si evenprod MOY dagno respecté sen internautes yi ndakh heure bignouléne promettre vraiment chapeau 💪❤
Wallahi Ndayesane ❤❤❤
Woute naniou ak ngama kham
La vérité
Walay Ndeysane
Même wa yesdakar danio respectei heur
Premier épisode de l'année yalnagnou ko feké ay dewen si barké seydina mouhamed
Amine 🙏 inchallah 🥰
Amine yaa rabi 🤲🤲🤲
Amine
Amine waye
🎉🎉🎉🎉
J’aime anta paske dafay wakh yayam deug
Gaïde bu deggul djiat lay waxall 😂😂 motax limuy waxe meunagul deff Effét legui 😂😂😂
Billay ❤️❤️
@diarrambaye299 Mome key dou faral yayame. 😂
😊😊😊😊😊😊😊😊😊
@@evenprodtay AM nga temps nièp nga tontou😂😂😮😮
Bourry lii sagnssé kassé la wala🎉ah machallah way
@SokhnaFall-rl8zl Tital niarel. 😂
Soda mareme tu monte sama kaww bopou 😂descends wathial 😂😂😂 ndiawar wayy 😂😂😂
😂😂😂😂😭
😂😂😂😂😂😂😂😂te srx lassi andal
😂😂😂😂😂😂😂😂
Ndiawar dafa nékh Bly 😂😂😂
Mouniko c’est très bien toute suite toute suite 😂😂ak moudié naniou mettre d’accord
Des cœurs pour notre prophète Mouhamed ❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Ani sopeye seuydina Mouhamed yi ay cœur waiy❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
Vraiment iboulaye joue bien son rôle sheuttt 😂😂😂
Bravo à toute l’équipe de xalisso 👏🏻❤️😊
@mbayangdiagne1904 Merci beaucoup.
L’habillement de Boury on en parle ? Wa ki meune na sagné way Mashala ❤️
Trop machallah ❤️🥰
Boury sagneusé la meune té ameu classe
Machallah elle est belle way té dionguama 🥹🥰
Sama mak mokoy Solal 😍😍 Mamy ❤
@@dipodicorrea1310 machallah kène dou sa mak dji laf thiate 🤩❤️💯
Boury vraiment da nga âme classe Machallah c'est très bien c'est bien bien 😅😊
😂😂😂😂bien très bien c’est très bien 😅😅😅
Boury dama lay beugueu ba kagn ??❤❤❤❤
Boury rék mom késsé❤️❤️😂
@MbayeLô-q4v 👍
Téy ndiawar amna bénén expression 😂😂😂😂tousssuite 😂😂c’est bien ndiawar c’est très bien 😂😂
Il va me tuer 😂😂😂
Waw tisswit 😂
Soda mareme tu montes 😂😂
😂😂😂
Ndiawar dafa ay dee
Ibou Laye koumou rétane lo rk lalale j'aime 😂😂
Néna xana niom palméo ak jackson joué woune😅😅😅
Dama rètane ba sonou 😂🤣ba parè yeureume ko le pauvre😢 dafa rakadiou rk 🤣🤣
No cest le mellieur😂😂
@enzojunior6632 Maisno guisser réaction si diabarame bimou perter ?
😢😂😂😂😂
Palmeo la deuck
Mais evenprod lolene di khare si souffrancou mére khadija lolou dafa lent😂😂😂😂
Dina gneuw dhé wait rek😅
😂😂😂
Badou diokhé bi dafa lent😂😂
Bayilen sama tanta bobou
Bilay
Kou amoul 1xBet lal j’aime 😂
Dou beurri j’aime fi niepay carte 😂😂
@@KhassoumCissé-u6z
Sauf mw boul wakh lolou
Wallahi khawma louy karte@@KhassoumCissé-u6z
Bamou dess mane khawma KO sakh
@@FatouDiop-lz7xiak mane dèh khamouma sakhe nimouy dèmè
entendu sa voix mais son amour vit des milliards de personnes notre bien aimé le prophéte mouhamed saw ❤😂🎉😢😮😅😊 26 Ww 31
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Awoo nakk nila waraaa melll❤️….Boury Fall Je t’aime wayyy💪🏻💃💃
@nganengane5205 Mome leigui niarel. 😂
Moukk thi Adounaaa Fi dale kou diour Taw yaye Awoo😎💃
@@nganengane5205 c'est tré bien😂
@@evenprodNio bagne😂😂😂
@@MomiDiop-v6f C’est bien🤣🤣
Comparez l’arrivée de Boury et celle de Soda Maréme dans le salon🤣 aythi Bouri Awo yaye yaw rek lay topp❤❤❤
Boule dèm bayïma dé😂
Boury rek do moromam
Niveau bi d’où béne😂😂😂
En tt cas ndiawar bou defoul ndank dotoul guiss sourire bii 😂😂😂😂😂
Man cours accélération momaye raye 😅
Mercredi ty bi yalla boum nek bou moudie si att mou bess mi dit amine ❤
Amin
Amine
Amine
Kousa heur dé jot dangay dé ah😂sof ngen trop
Amine yarabi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Even pro lignouy joué thi ay millions yalla na 2025 bi mel nonou thi khaliss gnepp yore ak millions ak weergui yaram boubari ak soutoura❤️❤️❤️🙏
Allahouma amine ❤❤❤
amine
@@mariememboup5082 ❤️❤️❤️🙏
@@cheikhsarr-sc5uy ❤️❤️❤️🙏
Amine
Boury cette Dame class bimouy dégager eupeuna wayy ❤
@tina5063 👍
Iboulaye AK sokhna ndiangne sene keure mo dakh si films bi niome niare dagaye ré ba tasse 😂😂😂
Sama satt bi dou ni
Sunu sante bi dou nii@@AwaDiagne-k3p
Le dégagement de Boury ❤️🥰
Kone guiss ngako ❤❤❤
Sa prestance, sa grâce ohh❤🤩
Commentaire bi ladone weur,Boury kay machallah ❤️
Ohhhh😮😅
Oh Boury kaye machallah
La beauté de sokhna bou mag est ce qu on en parle nek ben instant. Seytane la mais teint noir bi machallah 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹
tein bou rafét layor❤
@@leye4137mashallah elle est toute belle
Bilay elle est trop belle ❤❤
❤❤❤
Teint bou rafet wala fond de teint bi mo rafet yënn khana guissoulënn sokhna bou makk sans maquillage akk bouton you reuy akk guëmine gou wëgue gui melni kagna😂😂😂😂 guënn di wakh teint bou raffet bayilënn ba guiss niey guën si télé yi sans maquillage la on nous allons parlez de beauté mes chers😂😂😂
Boury dégage une chose inexplicable avec ces beaux yeux ❤🎉
@MarièmeFaye-j3l 👍
La mère de Maty Rose, par amour, conseille à sa fille de laisser tomber Oumar, renonçant ainsi à l'unique bonheur de la vie: aimer et être aimé. Cela me rappelle Nicolas Sarkozy qui disait "les pires conseils sont ceux que te donne une personne qui t'aime". En effet, celui qui t'aime cherche à te protéger en te conseillant de ne pas prendre de risques. Or qui ne risque rien, n'a rien. Mais.... avez-vous BIEN passé hier la fête du 31 février?😂 c'est bien ça, c'est très bien.😂😂LOVE
Sacré fata 31 février kaye
Encore fata😂
Diadia il ne t'aime pas
Toujours Fata c'est important
C'est très bien c'est très bien c'est bien 😂
Des cœurs pour notre prophète mouhamed psl ❤❤
C du manque de respect dou fi nga ko wara toudé😢
HEURES DE PRIÈRES DU 03 AU 09 JANVIER 2025
Fadjr: 06h22
Suba: 06h37
Tisbar: 14h15
Takussan: 16h45
Timis: 19h01
Gue: 20h01
Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Machallah❤
Yén meuno lên dimbalili nitt yii di regarder Lou Haram ba paré dissi dougal diouli
Wouy timis bagay demate 19h fouy bor woor yi nzk diot na 😂😂
@ragenpro421yaw li rappelle la dara nekou si
@@coumbandiaye6664 fay lene bor yi🤣🤣🤣🤣🤣
Kone Ndao Banquier mo yorr Djadja si souff😂😂
Voilà cône bimouy dokhane Boury mougui dieul diadia si souf😂😂
@MbayeSeye-vk4yp Ah mougui nonou. 😂
Commentaire bi la done weurr ndeké Diadia aussi mongui farane tou😂
Té lima sama khél diokh da mélni monékone 1er amour yaye dji si lima yakar
Wawaw sampou rék andak maty rose ak boury c'est bien c'est très bien 😂😂😂
@biteye305 👍
@evenprod 😊❤❤
Maty Rose merite de l'amour môme ak Boury kou beuge Xalisso rek l'alal j'aim ❤❤🎉🎉❤❤
Magui deeeeeh Ibou laye assure grave son rôle d’acteur 😂😂😂😂😂😂
Non mane iboulaye monma Ray Tay mokhe narbi gou d'accord lalal j'aime 😂😂
😂😂😂😂yaw déh nion damay réee meune ba sonou😅😅
@AstouGueye-mk8hy Affaire perdre match leu. 😂
Bayiléne NAAAR BI AMOUL BÉNE NDIERIGNE SA T APPAUVRI IL EST ENTRAIN DE DÉTRUIRE NOTRE COMMUNAUTÉ MERCI EVENPROD SI LEÇON DE MORALE YI🎉🎉🎉🎉
😂😂😂😂😂😂😂DIOP FALL DOU NITT NENA ANI PALMER AK JACKSON. NOO LII BOUKO NARBI GUISSE REKK AFEROU DIOP FALL DI BAKH
C est un grand acteur 😂😂
😂😂😂😂😂
Mane dh bayina 😂😂😂
Al hamdou lilla j ai vu niou yakheu😢@@Yahyacheikh544
Barki Yalla Ndiawar Diagne la beugueu souma ko guissé damay contane 😂😂 il est tellement naturel dans son jeux d’acteur 😂
Merci Evenprod 🥰❤️
C'est très bien 😂
@oulimatapouye3292 Merci beaucoup. ❤
@@evenprod ❤️❤️❤️❤️
@@phaniedione 🤣🤣🤣
Vraiment il joue bien
Bourry amna classe ❤❤❤c’est bien c’est très bien 👍 😅😅😅
Des cœurs pour notre prophète Mohamad bien paix et salut sur lui ❤❤❤
Boury la classe 🎉❤yaye awo mome 😊
Gua tekfo fan😂😂
Vraiment beug na Boury lol ms pour nekat awo soda mareme layy nexx ms dou mom dou diawar vraiment
@@boussondiayebah si sou fekone boury bimou tasser dafa seyat oui mais seyoul wone donc moy awo
Niarel leu
@@boussondiaye𝐰𝐚𝐱 𝐝𝐞𝐮𝐠𝐞𝐮 𝐤𝐚𝐲 𝐝𝐚𝐤𝐡 𝐢𝐝𝐚 𝐛𝐢 𝐝𝐢𝐞̇𝐤𝐡𝐧𝐚
Wakh léne si série bi té bayi Seringe si guir ay ❤❤
Lou ler
Bilay ❤
Gua sagne ko wakh tmt
Franchement sone nane trop hawma Jaime yi lougn koy doyé😊
wakh deugeu
Boury sagnse ga nk machallah ❤❤
Khadija, la mère de Anta nous parle de sa relation avec son ex qui est d'ailleurs son premier amour, cet homme pourrait bien être Amath ...
Si cela se tiendrait il serait fort probable qu'il soit alors le père biologique de Anta. ( Anta et vieux Ass, mouss dou diour gaïndé) Et n'oublions pas que Khadija préfère 1000fois Anta à Diadia. Elle l'aime énormément
Mère bi dafa melni dadone découcher di guissé ak Amath "l'homme de sa vie" 😅
Ce serait plutôt Diadia sa fille. Anta est plus jeune
Wa yén dolén wakh si ibou laye ak narr bii😂😂😂😂😂😂
Nar bi Dina ko ray😂😊
😂😂😂😂
@@GorFall-ro3dw raye nako ba pare kay 😂😂😂😂
Nar bi kay lekk rk lako defoul dh🤣😂😂🤣mais baxneu si mome
Damako ré ba meunetouma 😂😂😂😂Nar bi bakhoul santoul yallah
Pourquoi ndiawar diagne beugue c'est bien😂 ou c'est très bien😂 kou d'accord ak man rék lalal j'aime
Lolou Kaye moye cas bi 😂
Force à toi Maty Rose c pas évident et tu mérite des ❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
@wakhlouyydeffarnittgni4965 👍
Le jeu d’acteur d’Iboulaye 😂
Le théâtre c’est sensibiliser et instruire sur les phénomènes sociaux. Evenprod le réussi brillamment.
Les paris sportifs sont à l’origine de nombreux maux.
J’ai rigolé entre iboulaye et ndiawar soda Maréme tu monte 😭😂😂😂😂😂
@lennavivilennavivi 😂
Ibou laye moo guena deuggou si série bi mais naar bi mooko sonal mom 😂
😂😂😂😂😂😂sama wadji
Bilay li ma ré Tay meussou mako ré sama adouna
Ibou laye na sa diam yagg waay 😅😅😅
@laminedrame8399 perte baxoul. 😁😁😁😁😁😁doma rewww
@@laminedrame8399d’où yw kessei😂
Ibou nar bi dinako ray 😂
Bon année yalla nanio ko yague féké atoum nata gué ak xewal ak diamou
Avec xaliso série yeugual diamano
Amine
Amine ❤❤❤❤❤
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Des cœurs 💕 pour Boury 👌🏽🤗
Soda Maréme tu montes sama kaw bopou descend wathial 😂😂😂non ndiawar amoul
Ndiawar est très faible
😂😂😂😂😂😂😂
Toussuittttttt
Dafa nekh
Pourtant le père de Boury c un papa exemplaire top et responsable franchement je l’adore contrairement à Ibou Laye dont c sa femme qui porte le pantalon ❤❤❤❤
Mes meilleurs vœux à tous !!!!
Le père de Boury c'est lui ki gère sa maison contrairement à Iboulaye à ki on gère 😅😅
Top nar bi rek😂
Diadia battling dala beugeu déh 😢
@ même Diadia bagnouko dafaye sagou rek
@KhadyThiam-g7z Merci et bonne année. ❤
Des cœurs pour notre profete mouhamed PSL ❤
Une sensibilisation très importante sur les paris en ligne, merci beaucoup 👌
Djadja connais bien les bonne manieres les sacoche au restau c'est pas sur la table merci ❤
Malgré nos différences nous avons été et resteront inchallah un grand peuple❤Que Dieu bénisse le Sénégal 🇸🇳
Ibou lay yakhou na dh 😂😂😂bayi lén nar bi té yalla takh
@ModouNiang-x9i Wakhal dh. 😂
Boury fall : la classe et l’élégance a letat pur, te trop belle❤
Alhamdoulillah santa serigne saliou ak yalla ak sama yaay ak sama papa cheri
Boury c'est bien c'est très bien 😂ya am classe Awo yaye
Kouy mboury 😂😅😅😂
@@NdeyaMboup😂😭ioe tmt meun gua topp nitt
@@NdeyaMboup sa Tata🤣🤣
@@Heyy_angel2 Boury rék lay topou Dafa kham bopam😍
@@Heyy_angel2 balma 🤣😂
Yallaa bou année nèk souniou moudieuntèl🙏tè yalla naci weurseuk bari
Amine
Amine
Amine
Amine
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Wa dett koumay leralll Ahmat mii ak Diadia kagn la 😂😂😂😂😂
Wouy iboulay 😂😂 néna day niane batt😂😂
Mom laye seetan ni😂😂
😂😂😂😂😂😂😂aye yaw 😂😂😂
Nar beko yobe li yeup 😂 xbet
Lolou moy teuss
😂😂😂😂Lii rayenama
Ndiawar diagne football bagui soga commencé😂😂😂😂c bien❤❤❤❤ c tres bien
@AydaCamara-s7f 😂
Bourry dafa ame classe Sokhna loutakh teyoul Iboulaye turyan gua 😂😂Soda Maréme do réglé
@adamengomndiaye4209 Wayer Boury limou beug def eupoul ?
Bourry Kay Limou beug amoul fêne
Les 5 millions d'abonnés Evenprod mon combat
Bonne et heureuse année à toute les internautes et particulièrement à nos acteurs d'évenprod qui se sacrifient toujours pour notre bonheur et qui nous conscientisent merci beaucoup
Yalnaio yalla boolé si khadie bi dieme déwéne si barkép psl
Amine 🤲
Amin❤
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Effet narr bii bly daguay énervé té kén doula togne😂😂
La voix d Maty Rose Yenn😢❤ Mére Khadija mii dolen Ko diokh benén tour Khadija dou melni😢😊
@makhouwaly2226 Ah doyna ware. 😥
@ gaw len Maty rose seuy si rkk tégal Ko lou khéré 😂 mes beugon kham noumay df ba bokou si theatre wa Evenprod dh stp
Wakh deug nak😢
Tu as raison 😂😂
Yallah nagne fekkei wate aye décembre you beurie❤❤amine ❤❤
Amine yarabi
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Atou diamou atou khéwalll Ak wérrgui yarmm kou lalll j’aime yalla nala niannn gui dall
Amine
Amine 😊
Omar diagne dof bou ame weurseuk leu bly😂😂😂
Bilay nak Boury ak Soda marème dou combat, la classe, l’élégance la beauté de Boury,ohhh j kiff grave ❤
C bien fall c très bien fall toute suite 😂😂😂😂 sacré Ndiawar 😂😂
Yw mak bou yiwe nga 😂😂
Tout suite bi moma rayy😂😂 non ndiawar beug nako bly😂😂@@BapsDia
@ bly lima ko rée 😂😂
😂 magui déee
Non ndiawar va me tue de rire 😂
21:53 maty rose et sa mère elle sont adorables machallah ❤❤
Dome soko beugué moom rek m0lay wakh deug anta et sa maman .😂😂😂
Bilay 😂😂😂
Mane sakhh est-ce que PA Ass mo diour Anta mba dou ex khadija bimou bouguone moko diourr
❤❤❤
Yalla n'a yalla doli'gnou défal soutoureuh inchallah 🎉...
Mashallah Fatabara'kalahou ♥️☝🏿🕊️...
Mais Sénégal war'nagnou xam'nei galathie leuh si djiguén Mouy tokk keur borom djeukeur'eum waxou'mala mou nék fa masoul fay galathie bou mata sameuh
Am'na nitt gno xam'nei molén Di fadj tmt 🎇 🥰...
Film bi limouy djangualeii tmt barineuh dh mashallah 🥰 🥰 y'a beaucoup de leçons a retenir ☝🏿🕊️ vraiment on ne peut pas dire tout en un mot merci ...
Wa boury sa blanc rafete na machallah❤❤❤❤❤❤❤ laf bouche
Amine yarabi
C'est Bien, C'est trés Bien Fall
"tissui" (tout de suite) : Ndiawar waaaaay 😂😂🤣🤣
😂😂😂
Non se mot la man neume ray😂😂barki BOROM KHÉLCOM
,😂😂😂😂😂
Bonne et heureuse année à tous les téléspectateurs de Evenprod. Atoum nattangué atoum ngueunel atoum yokouté Ak werr.
Amine
Amine
Amine niou bok lép insha allah 🤲🏾❤️
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Kou geum nii xalissou Diop fall dina diekh rk lalal jaim ❤😂😂😂
Wa mane diomi wouma ndao banquier et diadia Ay boury bouko yeugué😂😂😅
Mom da meusseu beugu femme😂
@shadotoure8080 cas bi dense na
Diadia m’a trahi 😢😢
Trop
@bathiesamb512 diadia khamoul ni ndao ak bory don don guénn
Tay mome douma ñian cœurs way kouma may ma dieul ❤❤❤❤
❤❤❤❤may nala dieulal😂😂😂
❤❤❤❤dieul yalla dioxla 😂😂😂
@@NdeyearameMboup-j9v légui ngamay rétane 😁 mai contant n'a amal diam fo tolou
@@oumoungom6180 merci beaucoup chérie
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J’ai bcp rigolé 😅sacré iboulaye il me fume bonne et heureux année à tous 🎉
Pareil walahi 😂😂😂😂
Khadija mbaadou Ndaw banquier la doone beugueuntél eumbe fekk Ndao banquier yoroul khalisss mou tekk deal Ass Diagne seuyeul ko après la diour Diadia qui est la fille de Ndao banquier motakh mounou ko mougneul dara.... Temps bimouy eumb Ndao banquier mingui nekk pauvre
Voilà khara ma noppi sakh...
Mais j'insiste na Nianko alias Omar Diagne werr mou nekk si bénène personnage pour une première fois dabs sa carrière artistique bref tres bonne année à toutes et à tous
Je suis Dacor ce que je dis
T’as beaucoup d’inspiration 👏🏽
Diop fall motakh maay sétane série bii 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Nio yam 😂😂😂
2025 bi yalla done atou banekh AK joutoura AK xéwal AK goudou Fane AK wér AK werle keppou kou febar yalla nala yalla may wérr kou nék kasso yalla nala yalla guéne AK diamou yalla na Ousmane sonko Am ndam si kaw Ay nonam barke zeydina Mohamed inchallah Amine yarabi 🤲 inchallah ❤️❤️❤️
Alhouma Amine way
Amine
Allahouma amine
Amine🙏🙏
Diaware dou wah ba diékhal tè amoul c bien😮😂😂
Non jamais doko mousa faté😂😂😂
@YacineFaye-u7z Guisse geu lolou. 😂
@ ak soda maréme tu monte sama kaw bopp descend wathial 😅😅😅
Khalatouko sakh 😂😂
Est ce que kham guéne Anta dafa djiépii yaye djii 😂😂😂