Thiey Cheikh Moussa! Goor guii ka goré! Machallah...lii dh Haarif rk mooko meun...guiss ni yalla dèf thi baye nga nangou ko tè feusseul ko ték thi neub sa bopou woné yalla kou guindèkou rk moko meune...waayé kouy wooté woo haarif ba paré di 6 diaamou yalla yi thi pays bi wakh deug war nga khoolaate sa bopou ndakh yalla teunkouwoul Yalna yalla yookou lèèrou Cheikh al islam Ibrahima Niasse ak Cheikh Moussa Ndiamé Darou
wakh ji loumouye barri yep si bene bountou lagnouye diar yegue si yalla moy lahilaha ilalala kou wet xam sa bop BAYE ak NDIAMBÉ nagnoulen ormal fonk bou bax lignou diokh diamou yalla amoul parti nognou doundou anrif NDIAMBÉ ak BAYE yalla gueuremalene té dougnou ay none béne none lagnou ame mouy seytané mourilene sen kiraye y nono waroul ame sougnou diganeté dakh hame y mounegno wouyou si yalla .... dieuredieuf sante sangue Niane NDIAMBÉ ak BAYE yalla yok seni leer
Non senegal mo nekh Gni ni Baye gni ni Niambé lima si leer moy ken xamoul dara si loumouy wakh gni danio diamou yalla ba yalla faylen demlen diamoumdji yalla t kounek top kila doy liguen di xeuthio amoul ben sens yéneu bokk diné sama gayi. di diegalou nak nou werr wa salam
@@fruitmanager2.0 Amadouwame li zikrihi fahouwa akbarou mine koulou makanine mouridoune youksirou....wereul firi bi. Akramani lahou bi zikrihi wama liya atarahou wali hadal aqwama. Zummou ala azkar wal awrad fi koulou laylatine wa fil nahar. Weuril.liiiiiiiiiiiiii
Walahi prtan compliqué woul d!! Wayé lolou lép niak dieufé linioulene di diangal la rk Wayé kèneu guissoul serigne boufi digeul ay talibem pr nioune soutaneté ka rawaneté!! Niom nieup ci yalla lagn niouy khir,na kouné taneu kala doy t mandou tia gni déss
Borom diamono kéne lay done si diamono waye cheikh moussa si Serigne touba lako dieulé direct te yaw sax déguo wax dji cheikh moussa si diamono mo nékone khoutbou amoul sik sakka bayiléne sen yoyu té sakkou dji waat xam xam
pays cheikh ibrahima niass bi takhawougnou si yalla yalla rek déé gnouy dagnouy kham yalla kham yonenti kham cheikhoutidjiane kham si baye bolén djiougué di sonal nitt yi nane yalla yalla waw c'est normale nakh mom rek guain fanahou ter fofou kham amoufa démal gua khami ter guain bayi baye niass bilahi douséne morom
YAINE LILAINE METTI MOYY LINGAINDI NIODDI DI WAKH KHAM YALLA NDIAMBAI DAROU AK WAA KEREUM LOU RAW LANIE SI KHAM TAI AYY TALIBE SERIGNE TOUBAA LANIOU. NDIAMBAI DAROU SI TAIRAI SERIGNE TOUBA YII LA KHAMAI LII. YEEN NIASSENE YII DANGAINE SOKHOR MOURIDE YII REK NGAINE BANIE WAYAI MOU NEKH LAINE MOU NAKADI LAINE FII SI SENEGAL SERIGNE TOUBA MOOFI DEUGUE TANKE. SERIGNE TOUBA REK MOOFI NEKE. SOULAINE NEKHAI NGAINE AM 1 MILLIARD DE TALIBE A L'EXTERIEUR WAYAI FII SENEGAL SERIGNE TOUBA REK MOFI NEKE MOU NEKH LAINE MOUN NAKADI LAINE
Bayilen dikatt dou warifou joulit japp leen ci been batt té bagne takaliko di batou:Lailahailalah kaddu yonenté bi la.Guestu leen bidoum serigne ci giir dieum La ilaha ilalah nah tuur bo guiss dafa am jeum.
cheikh moussa cisse moy rasoulilah kouko wédi do kham yalla mom rék mo kham lé yalla khamlé diamou yalla ndiame rawna léne bou yague amoulén fayda wutilén yalla molén magki
serigne touba xamone na yallah bou weire mais amoul wone ndiguel pour xamlei yallah, soudone lolou kone mome moye dieuk wotei xamlei yallah mais naka leu moussa teup teup rek nei day xamlei yallah alors que serignem sakh amoul ndigueul???? Gayi tmt yewou lene ngir yallah
Mane Lima diakhal moy defna listakhar giss BAYE Niass m kiray biko topou ba topoul BAYE Niass wan nagn koko si listakharam vraiment on t'a montré ki est khoutbou zaman gue topou yônou papeu bountou chariatou moy Mouhamed psl bountou mahrifa moy BAYE Niass kou nieuw diko woté si maum gue wara topou Baye mola may djieuzbou way raniewo
Yen lahilaha ilalaha rek la baye niass yem ak yen ngen beug sonal niit yiii surtout xawma sagu moussa xawma Bilay baye niass mo bari xam xam wayei ndiambé mo niak chance yaw yalla xamal la xoutbou nga nieuw mou yem ak yaw si lahilaha ilalaha rek ngani ame nga xam xam wayei baye mom nak bœuf lala bolek rek mo defal la bagage
serigne bi el hadji sa xam xam wax deug yalla dala rére niar niu bokul dimension nak meununio waxtane wayé manguilay xamalni yalla meuno ague ci mom té diarro ci baye ndax kadone yablé yablétoul dieumeum mo far di téw
@@serignegueye6717 ya meneu doule..Baye Niass mo toth adouna toubal ay millions millions de personnes dans le monde di khamlé Yalla di tarbayi niit gni délo léne sen borom fi ba pakistan ba Indonésie ba singapour ba chine ba inde ba malaisie ba bangkok toute l'Amérique l'Europe l'Asie l'Afrique..yén wéssouwoulén diamniado..1/5 monde bi ay talibés baye plus de 500milliions de fidèles à travers le monde.yen motoulén sakh 3millions..nopil mo gueune siyaw
Kou xamoul yalla rek moy dem diko weurri pour xam ko ba far rere A mediter nak Yalla neubeutouwoul banguen dii ay aylou fii yena wanei rek dii weddi lissi al qur ân batakh nguen perte Gueum leine sii koumpeu dînei l'islam tei bania remettre en cause 🙏🏽🙏🏽🙏🏽 Chekhoul khadim,seydi hadj malick, cheikh omar foutiyou etcc nieup xamnagn nii niongui aldiana esk digueul nagnou keneu yone bii nguen topp nii naane xam yalla par le biais de tarbiyou com vous fêtes ?? Réveillez vous kou nekk sii lingay diamoo yalla rk lanioukay juger so weddi wei ay waxam mou lakk leu point barre mandou leine nak c valable pour vous tous???
Haɧaɧɧa tay dal golo goumou nekh rek ngua diouk ni danguay wotte khamelle yalla ta kerok Bako Baye wakhee nieupa weddi tay nguenii sonal nitt ngi ak wakh djiou beeuri koudoul baye khamo tee do khamlee yalla
sama guayi ame léén yaar gnune yalla yalla yi woté wugnu Aÿ FO . dinguatougnou kéne té borom may dou dinguate borom may yééne gnasséne yi daguén Fock ni kou nékoul gnassén dou égg si yalla . bilakhi Diamono dji kou nékoul yalla yalla perte ngua . bamouy méti daguéne nangoul baye xana tay la nékh kou diok ni gnass. gnune bamuy méty dagnou top ndiamé kouy kilifa ndiamé la mane si Diamono dji . té léér bi mougui keur sangue cheikh Oumar NDIAYE ndiambé kofa bayi . bayiléne diguate ndiambé yalla lagnou wane wanougnou aye mark allahou yémsi wara roukh yémssi yalla lagnu wane
Wa xatta ma fathi inda mahdi baye moko ndieuka wax té kén waxa touko ci ganawam goorgui limou wax dafa léér ci kou xam khakika ndieulbénou manhrifatou billahi moy fathou maname oubékou name serigne touba ay mbindeum yeup ci xam yalla lay wax wayé kougnou guindiwoul ci ndieulbén bobou do meussa xam limouy wax goorgui néna ganaw bi ko baye niass yoboo ci guéth gogou nandal ko ci touti ganaw ga lay sogue di xam li waxi s. Touba woundou kone thiow léy barri rk wayé goor goufi taxaw feug sa deunn baye mola nandal ci ay loxom dou waxou madjzoub nak
tu nous fais rire baye niass avait pris le khassida de serigne touba en disant c'est lui qui l'a ecrit: en plus baye est le talibe de cheikh tidiane cherif alors serigne touba a dit dans son khasida aui sapelle hikam que j'ai depasse cheikh tidaine et serigne absou khadre djielani:
boken todati khadimo rasol di todo ay bay niass way bay kobakhla waye serigne touba bayamla thi lep baniwo serigne sa ndar ana bay lan motakh yobowonko aybodemon dingen khamne serigne touba amol morom te moromante wol
Yow moom ci rewande AK soss lan la tarbiya ....so musoon russa wax lolou ..Cheikh Moussa baye diegge wulo ci akhlaaq yu Tedd te walllahi bokko wedde demal ba darou Cissé gni fekkee dundam nettelila kimu doonoon
fanahou fi zati bakhahou si khilafa, ragné Yalla, Yonente ak sén ndiogne, Diamou yalla khamé taramyi akmélomyi ndakh kouko kham dinga ko diamou si zahir( wakhtou yi diourom,) komnouko anrif yi ak soufiyanké dane déffé, kham Hakhahikh yi ak mazahir yi ak nissab yi ak hadrad yi ak dawahir yi ak euzeulatyi ak eubadad yi, lolou moy fayda Cheikh Ibrahimia Al khalifatoulah. Bou féké si lahilaha ilalah laniou yém kon lima la wakhni lanla, yéne kay yéna khamoul Yallan Déggouléne Yalla te Gissouléne Yalla ndakh si c'était le cas dingéne djouli com noumou diaraléwone sérigne Touba bamouy diuoli si gédjn té nak khamnagne léppou, Baye Niass rék mofi khamlé Lahou kou diaroul si mom dou kham touss. Bou Bamba nékone Khoutbou zamane konne mou wathié Cheikh IbraFall mou déé si fanaw. Yéne cohéence Zéro, doléne mouide ndakh touba sakh daléna sékhlou ndakh ndiognou Dadial ngéne. Wa ana Nak bi lol. Baye Niass moy Bayou mindéf yi kou nangou ak ki bagne
Man bougueuna xam ban teere la ndiambe bind s. Touba bindna teere, baye niass nonou ak gneneen Xam xam kena douthi werente sou jant fenke doto guiss lamp
wa diambé dagno fanaw fi zaati Wayne amougnou yab-kha fil khilafatie. Kone amougnou tamize ak nizeub. laa-ilaha illah fanaw Jesse dara amou faa. haarif yii de gué bagne ma
Lima jakhale moye séne bayii yaguenagne fii mousounio woté xame yalla mé baye Niasse wako rek kounék di wakhe dit heuthie di Anna sénii njite Balla baye dit niow
Yéneu gneup ay yéféreu kéneu yalla moléneu taxa dioukk Baye walla niambé talibé baye yalla laye kiss si barham talibé baye Moussa yalla laye guisss si niambé mogui fépeu kayeu koneu boul waxné iow yakoyeu guiss ndax mougui fépp
walahi deño rérr bokalé manul wessou nii yalla tolu nga nénnaléko sa bopu . kone yalla anamou . talibé yii ñoy wax lolu rek mais baye niasse waxulenn lolu . né mom dong moy xamlé yalla .
baye mo nandal mboléme waliw yalla yi gni ndieuk ak gni mudj serigne moussa tontounaléne ndax néné amna yuniuy mbotal. mbote momou nak boléne koko ladione ngéne fekk fa baye RTA Kép ku nane mola nandal. kumu néx nanga gueum kum néxite nanga wédi.
Mane dal diakhléna iow gue dougou khalwa si khol khoutbou zaman giss BAYE NIASS mou tok waron gue kham lan moy tok si lal bi Lima méti moy guay dem di nékeu mouride BAYE moy BOROM DIAMONO
Ce que je déteste, c'est toujours cette comparaison que vous faites entre Shaykh Ibrahim Niasse et les autres Shuyukh. Nom de Dieu! Mais vous êtes vraiment timbrés vous les majzob, qui prétendent être des disciples de la Faydha Tijani! Vous êtes pathétiques! La connaissance divine à laquelle appelle Shaykh Baye, aucun d'entre vous n'y a vraiment goûté, nul d'entre vous n'a atteint l'ouverture, nul d'entre vu n'a été en présence de la divine face d'Allah, nul d'entre vous ne maîtrise même et saurait mener quelqu'un à cette "connaissance" que vous clamez et essayez à chaque fois de dénigrer les Niamé Darou parce que certains d'entre eux disent des choses que malheureusement vous soi-disant Arif Billah ne maîtrisez! Ceci est dû à quoi? Ceci est dû à votre paresse spirituelle et à l'arrêt de votre sayru, alors que vous êtes plus ignorant que ma petite sœur qui n'a même pas encore le jezbu. Vous devez vous occupez de 3 choses, de 1) Vous; en 2) de Vous; et en 3)de Vous! La haine viscérale que vous avez envers les Niamé Darou c'est juste parce que dans certaines zones, ils sont en train de récupérer certains de vos condisciples, le pourquoi? Parce qu'ils sont plus déterminés et plus convaincus que vous de ce qu'ils sont et de dans quoi ils sont que certains talibés du Shaykh, qui dansent, fument, et ne prient (Faydu "Sanni") Shaykh Ibrahim Niasse vous a TOUT apporté, TOUT! Mais vous, vous vous plaisez tant aux illusions et mythes, au napéisme/niangalisme spirituel, toujours là à ressasser Baye Baye Baye comme de vils illuminés alors que le Payii en est à sa vitesse de croisière! Le Hadra Ilahiya a évolué, continue de marcher! Et vous restez là à toujours adorez vos fantômes tels Mayra Fall Kossi, et vos Mudaqams! Fisssttt! Certains disciples de Shaykh Ibrahim sont eux vraiment sur la Voie, comme les (vrais) disciples de Shaykh Uld Hayri, de Cerno Oumar Sow, de Cerno Alpha Sow. C'est vrai, Shaykh Ibrahim Niasse voulait récupérer quelque chose de Shaykh Mussa Cissé Niamé Darou, oui, et c'était ce grand arif billah, ce gnostique, et par l'occurence son neveu direct, fils d'Aminata Cissé et d'Ibrahim Ndiaye, je fais réfèrence à Sangue Babacar Ndiaye bien sûr,, qui me semble t-il est le Muqadam que vous haïssez le plus parce qu'il a été Yalla Yalla un quart de siècle avant de rejoindre la Faydha Tijani. Malheureusement pour vous, dii ngén, car Ses disciples sont en train de vous laminer ici au Sénégal et partout et les talibés de Baye sont, ils sont en train de les récupérer 1 par un, et par dizaine de milliers. Normal. Parce qu'Il est le digne successeur spirituel de Shaykh Ibrahim Niasse, son Khalif, sa Voie, son Verbe, son Avocat. Tant que vous ne rangerez vos conneries et n'essayerez de savoir qui est SBN, il vous sera difficile vraiment difficile, de vous sortir de ce carcan et gêne que vous ressentez quand vous rencontrez les Niamé Darou. Né le 05 Février 1960 à Tchakho Tiofior dans le Saloum, à 20 kms de Kossi là ou Shaykh Ibrahim Niasse a déclenché la Faydha en 1927. Les Niamé Darou, sont des sufi, ils ont atteint l'ouverture spirituelle. Au lieu de vous attardez à eux, occupez-vous de vous, eux ils s'occupent pas de vous!
Itasyl Bil Salsyl jai un problème avec ton discours qui est defois le contraire de que Baye a di " kéneu dou kham yalla loudoul nga diar sama bountou" ba paré sangueu ndiaye bi ngay wotél nékone nafi kham bou magg té borrom mbirmi dou meussa nékeu ci réer .
rouhlah fall yen lahilaha ilalaha la baye yem ak yen ngen beug sonal niit yiii fou ngen taxaw di beug ray niit yiii ak lahilaha ilalaha boudoul diekh deug la wayei dess na lou bariii gorgorlu len
+Djiby Boxeur mais il faut les répondre gni hamougnou dara ba paré reuy lamégne dof dof lou rek wayé hamnégne ni barham dou sene moromou serigne dama teup talibé yi talibé bi gueuneu touti sah thi baye meune na neke sene serignou serigne
Hhhhh ku baax ci passion rek nga né wayé khamo dara ......Sa biir boumou feess banga fook né sa Baye rekka am depense ci rewmi....Gniko dakh njell fouf dougnou jeex ci aduna bi.Guestuleen rek dingeen mossa kham ne yeena gueuna niakk xam xam ci gniy wouyo arif ci aduna bi.......Yalla yonenté bi cheikh tidjiane baye niass seen mokhadam ...C'est tres limité et contingent lolou du xam xam.....Xam yallah defa universel nekkul ci diné nekkul ci tarikha .
Thiey Cheikh Moussa! Goor guii ka goré! Machallah...lii dh Haarif rk mooko meun...guiss ni yalla dèf thi baye nga nangou ko tè feusseul ko ték thi neub sa bopou woné yalla kou guindèkou rk moko meune...waayé kouy wooté woo haarif ba paré di 6 diaamou yalla yi thi pays bi wakh deug war nga khoolaate sa bopou ndakh yalla teunkouwoul
Yalna yalla yookou lèèrou Cheikh al islam Ibrahima Niasse ak Cheikh Moussa Ndiamé Darou
Sa wakh rafétna trop content na si yaw
Akassa yaram bakh dieure-dieufé cheikh Moussa Cissé niamé borom darou👌
All the way from the eastside of detroit may Allah Raise baye Niass to the highest level of jenna
Anna Kane moy mouhamadou Rassoul . dieureudieufééé baye Niass.
Baye niass moye internationale bagne bagne beugue moye brome faydou moye khoubou Jamal dieuredieufé baye niass
Gor yalla d'où khedio
Sante Cheikh moussa cissé ndiamé borom darou léerou lerr yi rek ba faw
Cheik Moussa cisse
wakh ji loumouye barri yep si bene bountou lagnouye diar yegue si yalla moy lahilaha ilalala kou wet xam sa bop BAYE ak NDIAMBÉ nagnoulen ormal fonk bou bax lignou diokh diamou yalla amoul parti nognou doundou anrif NDIAMBÉ ak BAYE yalla gueuremalene té dougnou ay none béne none lagnou ame mouy seytané mourilene sen kiraye y nono waroul ame sougnou diganeté dakh hame y mounegno wouyou si yalla .... dieuredieuf sante sangue Niane NDIAMBÉ ak BAYE yalla yok seni leer
Jërëjëfati chekh Moussa
Jërëjëf baye
Guiss yalla moy dëgg
dieuredieuf cheikh moussa cisse ❤💯❤☝✊👌
Non senegal mo nekh Gni ni Baye gni ni Niambé lima si leer moy ken xamoul dara si loumouy wakh gni danio diamou yalla ba yalla faylen demlen diamoumdji yalla t kounek top kila doy liguen di xeuthio amoul ben sens yéneu bokk diné sama gayi. di diegalou nak nou werr wa salam
bilahii waxatiko mboke mi nite yo xamenei daniou werde di geune wax werde sakh moleine geuneul diangue alkhourane.t serigne touba nena keip kounei sofianké nge yakarnei liga yor mo geune alkhourane sheytané mola wotame.
@@fruitmanager2.0
Amadouwame li zikrihi fahouwa akbarou mine koulou makanine mouridoune youksirou....wereul firi bi.
Akramani lahou bi zikrihi wama liya atarahou wali hadal aqwama.
Zummou ala azkar wal awrad fi koulou laylatine wa fil nahar.
Weuril.liiiiiiiiiiiiii
boy so khamoul da ngay nopi
salam Niambé woo woul béne talibém si kheuthioo ndakh nitt loumou momOUL rék lay kheuthioo. SANTE NDIAMé rék moo niou warr taou niou wérénté.SALAM
Lèrou Yalla bay momouko serign touba momouko diambè momouko lèèrgui lèroup Yalla la kouka nèkhe la koy diokhe wa Salam fa Yalla parti yèguoufa
Kouko nèkh la koy diokhe
dieureudieufé Cheikh Moussa Cissé Ndiambé Borom Darou yalna yalla yokk say lérr té tass gniou sissa barké
Ziar
mahrifa dou pour bodianeté, Nangoul lène gneup séne maye bagna Khatal YALLA assamane mou ngi yatou, YALLA teunkouwoul. Oubiléne sen deune yi
eskey yalla nanu lén yalla fayal suis talibé ndiambé mais j'aime baye niass wa salam
Jërëjëf Mame Ndiamé Darou
Sante borom darou diadieuf wayyyy👌👌👌👌
Sante cheikh Moussa ndiambe borom darou
yalla dé diaroul xeuthio kén kouné na si dieul limsi meuna dieul té nandou
Walahi prtan compliqué woul d!! Wayé lolou lép niak dieufé linioulene di diangal la rk Wayé kèneu guissoul serigne boufi digeul ay talibem pr nioune soutaneté ka rawaneté!! Niom nieup ci yalla lagn niouy khir,na kouné taneu kala doy t mandou tia gni déss
Dieureudieuff BAYE niass Kéne dou BAYE niass
Il a résumé tout .il a fait un listikhar pour savoir qui khoutbou et il a vu MAME BAYE .BAYE reeek
Borom diamono kéne lay done si diamono waye cheikh moussa si Serigne touba lako dieulé direct te yaw sax déguo wax dji cheikh moussa si diamono mo nékone khoutbou amoul sik sakka bayiléne sen yoyu té sakkou dji waat xam xam
Kouy teukeulé Baye ak kénén wolahi niak xam Baye laa moy tasarifatt nék louko nex réglé situation yi borom xél you séll yi lay waxall
pays cheikh ibrahima niass bi takhawougnou si yalla yalla rek déé gnouy dagnouy kham yalla kham yonenti kham cheikhoutidjiane kham si baye bolén djiougué di sonal nitt yi nane yalla yalla waw c'est normale nakh mom rek guain fanahou ter fofou kham amoufa démal gua khami ter guain bayi baye niass bilahi douséne morom
+Gueye Ibrahima wahnga deug
khame yalla amoul tricherie loye yeuk la. deugue deugue baye niass d'où djeum
Gueye Ibrahima .ف
Baye Niass sou meunone Sénégal kone mofiy eupe talibé. Mais 90% des musulmans sénégalaid gueumouniouko
YAINE LILAINE METTI MOYY LINGAINDI NIODDI DI WAKH KHAM YALLA NDIAMBAI DAROU AK WAA KEREUM LOU RAW LANIE SI KHAM TAI AYY TALIBE SERIGNE TOUBAA LANIOU. NDIAMBAI DAROU SI TAIRAI SERIGNE TOUBA YII LA KHAMAI LII.
YEEN NIASSENE YII DANGAINE SOKHOR MOURIDE YII REK NGAINE BANIE WAYAI MOU NEKH LAINE MOU NAKADI LAINE FII SI SENEGAL SERIGNE TOUBA MOOFI DEUGUE TANKE. SERIGNE TOUBA REK MOOFI NEKE.
SOULAINE NEKHAI NGAINE AM 1 MILLIARD DE TALIBE A L'EXTERIEUR WAYAI FII SENEGAL SERIGNE TOUBA REK MOFI NEKE MOU NEKH LAINE MOUN NAKADI LAINE
Bayilen dikatt dou warifou joulit japp leen ci been batt té bagne takaliko di batou:Lailahailalah kaddu yonenté bi la.Guestu leen bidoum serigne ci giir dieum La ilaha ilalah nah tuur bo guiss dafa am jeum.
Cheikh moussa danga gnak kignane rek mais bilahiii kén dou baye niass
yene yzna rere dème léne lathie sangue ndiaye diarbatou ndiambé la tè talibé baye la l4gui
Banga douga xalwa di séét Khoutbou Zaman waay waay guisso ST Khadimou Rassoul waayé kinga guiss mooy Borom DOKK gui,Rafét KAALA,Djekk FASS. Kon kagn wax lepp xam ngani BAYE mooy KHOUTBI BI
Bitèye Serigne Seck
Aàaaààà,.
Bilahi
Yéneuyi gorédila bilahi BAYE NIASS mola khamal Yalla si ligeuyal bigheuko ligueyal gue worgue ndiambé
da ngay doul boy
nioudone jigne dof niou khm ylla dem bakoy kheuthiok Mme Allahhhh
Limou wah né da dougou khalwa niou wone ko Baye Niass doyna seukeu pour niou warra topeu ci guinawam ci non perte rk.
cheikh moussa cisse moy rasoulilah kouko wédi do kham yalla mom rék mo kham lé yalla khamlé diamou yalla ndiame rawna léne bou yague amoulén fayda wutilén yalla molén magki
serigne touba xamone na yallah bou weire mais amoul wone ndiguel pour xamlei yallah, soudone lolou kone mome moye dieuk wotei xamlei yallah mais naka leu moussa teup teup rek nei day xamlei yallah alors que serignem sakh amoul ndigueul???? Gayi tmt yewou lene ngir yallah
@@Smokin_mass33 ioe wakhma nakh cheikh tijane amone neu ndigueul pour khamlé ko
@@dembaba202 legui da ma ley ladj si waliyou yallah yi Kane mofi otei xam yallah?
C vous ki n connaissent ki est ndiambé mais bay l connaît très bien yen demb Guen dioudou bayilén fanatique yalla dafa yatou deukul fén
Dieng Sette yen lahilaha ila ngen yem nieuw len dokh
Kay gnou tarbiya nga xam Yalla
Khamlé woleine yallah ba baye niass nieuw guein commencé di lambatou mba paré né thi bennene serigne guaako dieulé. Deuk kaolack diégué baye sathi makhama ta liguenni wakh khamoleine thi dara
Yene daal khawma lolene di kheuthio lolou adouna la yam ligueye lene yalla Aka beugue soutoureu mandou lene si ko lene Guiss Ndiamé yeurmandé la
Mane Lima diakhal moy defna listakhar giss BAYE Niass m kiray biko topou ba topoul BAYE Niass wan nagn koko si listakharam vraiment on t'a montré ki est khoutbou zaman gue topou yônou papeu bountou chariatou moy Mouhamed psl bountou mahrifa moy BAYE Niass kou nieuw diko woté si maum gue wara topou Baye mola may djieuzbou way raniewo
Yalnaniou yallah taxawou
Yalna diamm yaggu
yen boulén gnou doulo way baye Niasse seni bayiii serigne sax baye Niasse DoU sen morom la ferme waay kou nek diii am lumuy doul #barhama #for #ever
thiey Baye NiasS yaye sen Baye dh
yaa meneu doul
demba faye ningay wakhé anrif douko wakhé yaroul touti
lol sisi bro c'est la verity guys yi sen serigni hamnegn lolou
demba faye yama doul
Amall yarr domramm
yallah rekey xamelei yallah
wakhi doff bayilma s touba du moromum nii ak nialé Kofi yakar momla yakar mofi def lu wér
Serigne Touba Rek !!!
Baye niass niass niass niass niass niass niass rek
fiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii dale Baye NIASS rek mooooooooooo yiy khamlé yalla BILLAHI
Y'a meun fénnn
Bayil féne
waw gooor sinane khana khamall wayyy 👂👂👂👂
Ya nekh
Wakh joju khewina .kou guissoul sa rouh noy khamè yalla. Wa mane arafa nafsaho arafa rabbaho .
Kou kham sa rouh kham sa borom
Gorgorloul agsi mo gueune
Mouji judu gueuneu bess ma arifa dafa evolue dè ....fekhelene weur tène yu bess yi beune .baye niass gniko topone jeurigne nalene bubakh.
Wayee ndeysane khamoulene ko ndeysane
Baye Niass sou fekone moofi meun biir sénégal kone mofiy eupe talibé mais 90% des musulmans au SENEGAL gueumouniouko
Bii xam yalla dii ame baye niasse dioudouwoul tambaléwoul sii mom té dou yam sii mom...ndiambé moudié woté xam yalla wayé moka feusseul
ndaysan néna baye dioudo guoul haha diemal xam kouy baye ba paré
Yen lahilaha ilalaha rek la baye niass yem ak yen ngen beug sonal niit yiii surtout xawma sagu moussa xawma
Bilay baye niass mo bari xam xam wayei ndiambé mo niak chance yaw yalla xamal la xoutbou nga nieuw mou yem ak yaw si lahilaha ilalaha rek ngani ame nga xam xam wayei baye mom nak bœuf lala bolek rek mo defal la bagage
li ngay wakhni khamosi dara boy nopil lernama khamo sa yalla
Sante borome darou
Loutakh niou wannko lal bi mou tok si soko khamon rek do topou kenen koudoul BAYE Niass si m ndeysan dégoul lilal bi di signifié
serigne bi el hadji sa xam xam wax deug yalla dala rére niar niu bokul dimension nak meununio waxtane wayé manguilay xamalni yalla meuno ague ci mom té diarro ci baye ndax kadone yablé yablétoul dieumeum mo far di téw
thieuy yalla Baye reik moy xamlé yalla
Loool, Té do wakh ni Baaaye mola défar req, té naq dala khegne req nga sour, waayé moosso ko.
+Adam Barham Diagne Bien dit
Adam Barham Diagne bamba ko defare ter bamba defare baye, so weeder ladjiale wa kossi yi
+Serigne Gueye ya meuna doul
@@serignegueye6717 ioe ya meune doule ladjal s.fallou kou sén bay
@@serignegueye6717 ya meneu doule..Baye Niass mo toth adouna toubal ay millions millions de personnes dans le monde di khamlé Yalla di tarbayi niit gni délo léne sen borom fi ba pakistan ba Indonésie ba singapour ba chine ba inde ba malaisie ba bangkok toute l'Amérique l'Europe l'Asie l'Afrique..yén wéssouwoulén diamniado..1/5 monde bi ay talibés baye plus de 500milliions de fidèles à travers le monde.yen motoulén sakh 3millions..nopil mo gueune siyaw
Lo wakh deugeule sanguabi damala beugeu sama kole
Kou xamoul yalla rek moy dem diko weurri pour xam ko ba far rere
A mediter nak
Yalla neubeutouwoul banguen dii ay aylou fii yena wanei rek dii weddi lissi al qur ân batakh nguen perte
Gueum leine sii koumpeu dînei l'islam tei bania remettre en cause 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Chekhoul khadim,seydi hadj malick, cheikh omar foutiyou etcc nieup xamnagn nii niongui aldiana esk digueul nagnou keneu yone bii nguen topp nii naane xam yalla par le biais de tarbiyou com vous fêtes ??
Réveillez vous kou nekk sii lingay diamoo yalla rk lanioukay juger so weddi wei ay waxam mou lakk leu point barre mandou leine nak c valable pour vous tous???
Haɧaɧɧa tay dal golo goumou nekh rek ngua diouk ni danguay wotte khamelle yalla ta kerok Bako Baye wakhee nieupa weddi tay nguenii sonal nitt ngi ak wakh djiou beeuri koudoul baye khamo tee do khamlee yalla
mane deh amnaa YALLHA te diarouma si baye niass am YALLHA DOU Parti santoul niass santoul mbacke santoul sy
y'a meuneu doule
Karim Thioune c vrais
Boul farr YALLA rek mo ham
+Baye Khalipha lol feine reik Baye reik moy xamlé yalla xamal la deug deug yonette ak cheikh tidiane
Dagay sopp mahrifa mom baye niass rek
boy sama numero migui ni woma sayo beugue 0039 3891153886:
kham kham ken douko fortatou souniy wakh kham kham:kham yall motakh gnouy wakh .
béne tarikha meussoul woté xam yalla xana tay ngéne di heutio ak baye wayé serigne buci wét rek dadiek boromom té moy mine ka.
Talibe baye warr n'a rousse du doug ci débat you enfantin yii baye niass dou l'i wayyy
Hamoni Bay niass serigne Fallou moko tarbiya négua yame
sama guayi ame léén yaar gnune yalla yalla yi woté wugnu Aÿ FO . dinguatougnou kéne té borom may dou dinguate borom may yééne gnasséne yi daguén Fock ni kou nékoul gnassén dou égg si yalla . bilakhi Diamono dji kou nékoul yalla yalla perte ngua . bamouy méti daguéne nangoul baye xana tay la nékh kou diok ni gnass. gnune bamuy méty dagnou top ndiamé kouy kilifa ndiamé la mane si Diamono dji . té léér bi mougui keur sangue cheikh Oumar NDIAYE ndiambé kofa bayi . bayiléne diguate ndiambé yalla lagnou wane wanougnou aye mark allahou yémsi wara roukh yémssi yalla lagnu wane
Thieuye senegalais mo sokhar wayei bouleine sokhar KEINEU DOU BOROME TOUBA. Boulene yeimou thi pakabi wala hilerbi wayei yeimoulene thi TEUGUEBI ...SEIGNE TOUBA MO YEMOU
FI KEN NEKOUL YALLA KESSE MOY NDAM ESKEY NDIAMBEE
ndiambé mo meune sène baye meune sène serigne ndakh diamou kheureum gnène fi néké té kou kham yalla deug daf kay doy lo. Gnoune ndiambé daf gni défère soko wédé ladial wa kaolack
Yén wéssouwoulén bountou pikine..ko len défar?indilma 10 personnes youdoul senegalais youmou toubal..bayi lén fén tédi wakh deug mogueune..
Serigne touba dou moromou kénn sourtou serignou tidjane yi
Wéssouwoul diamniado,foumou toth si adounabi?yaw do ragal Yalla tédi wakh deug..so guéné touti di nga kham kouye Baye Niass...dof doflou mola nekh
Wa xatta ma fathi inda mahdi baye moko ndieuka wax té kén waxa touko ci ganawam goorgui limou wax dafa léér ci kou xam khakika ndieulbénou manhrifatou billahi moy fathou maname oubékou name serigne touba ay mbindeum yeup ci xam yalla lay wax wayé kougnou guindiwoul ci ndieulbén bobou do meussa xam limouy wax goorgui néna ganaw bi ko baye niass yoboo ci guéth gogou nandal ko ci touti ganaw ga lay sogue di xam li waxi s. Touba woundou kone thiow léy barri rk wayé goor goufi taxaw feug sa deunn baye mola nandal ci ay loxom dou waxou madjzoub nak
+aldiouma fall diarra wahatiko
bayilene di wo nit ngi si sene bop wala si sene serigne wolene nite ngi si YALLHA diaroul wah bou bari bilahi
dafa leir Baye moy deug
Dieuredieuf bay niasse nitou yala deuglue waye nak sounekon nawetan manila bay kadé la seringe touba moy junior
Yénna meunn doull Yalla kénn momouko imbécile yii
Li rek warna takh ngen nieuw si yonou BAYE
tu nous fais rire baye niass avait pris le khassida de serigne touba en disant c'est lui qui l'a ecrit: en plus baye est le talibe de cheikh tidiane cherif alors serigne touba a dit dans son khasida aui sapelle hikam que j'ai depasse cheikh tidaine et serigne absou khadre djielani:
Serigne Saliou mbacke etait le khoutbou
Kone ba légui marifa bi désna comme cheikh bi mogui guisse li wathione si yonéneteu di wathie si môme .
wa mann demay lathie kou xamal chiekh ibra fall yalla dou borom touba khana kou talif majalikul djinane dou borom touba kou waroul khamlé yalla serigne touba lou wakh thie tassawoof dou diekh kou kham yalla lepp loo kholl té guisso thie yalla konn khamago diém lenn guiss yalla thue domou sokhna yii
boken todati khadimo rasol di todo ay bay niass way bay kobakhla waye serigne touba bayamla thi lep baniwo serigne sa ndar ana bay lan motakh yobowonko aybodemon dingen khamne serigne touba amol morom te moromante wol
Tu est tellement nul il faut aller a la quête de dieu le chemin le plus proche c'est medina baye
Ki kane la borom nakk bii 😂😂😂 bayi len baye niass baye moy sen baye
Yow moom ci rewande AK soss lan la tarbiya ....so musoon russa wax lolou ..Cheikh Moussa baye diegge wulo ci akhlaaq yu Tedd te walllahi bokko wedde demal ba darou Cissé gni fekkee dundam nettelila kimu doonoon
fanahou fi zati bakhahou si khilafa, ragné Yalla, Yonente ak sén ndiogne, Diamou yalla khamé taramyi akmélomyi ndakh kouko kham dinga ko diamou si zahir( wakhtou yi diourom,) komnouko anrif yi ak soufiyanké dane déffé, kham Hakhahikh yi ak mazahir yi ak nissab yi ak hadrad yi ak dawahir yi ak euzeulatyi ak eubadad yi, lolou moy fayda Cheikh Ibrahimia Al khalifatoulah. Bou féké si lahilaha ilalah laniou yém kon lima la wakhni lanla, yéne kay yéna khamoul Yallan Déggouléne Yalla te Gissouléne Yalla ndakh si c'était le cas dingéne djouli com noumou diaraléwone sérigne Touba bamouy diuoli si gédjn té nak khamnagne léppou, Baye Niass rék mofi khamlé Lahou kou diaroul si mom dou kham touss. Bou Bamba nékone Khoutbou zamane konne mou wathié Cheikh IbraFall mou déé si fanaw. Yéne cohéence Zéro, doléne mouide ndakh touba sakh daléna sékhlou ndakh ndiognou Dadial ngéne. Wa ana Nak bi lol. Baye Niass
moy Bayou mindéf yi kou nangou ak ki bagne
borom bakh ndéysaane loufi diarr wakh diou niaw??? nioune kheuthioowouniou ndakh Ndiamé dafa niouko téré. Yalla moo kham ki nékk si deug. Salam
Binga diape né baye rek moy hamle YALLA si nga danou hamo darra .ndiambe par force
Baye gui xamlé yalla d wayé ioe xamagoko,weuriko dom t bayi féweulé!! Souniou borom kéneu douko teunkeu
@@Smokin_mass33 cheikh tijane amone neu ndigueul ou pas
@@Smokin_mass33 Segn bi Ziare nala 🙏...xana beugo nek waliw dinguent nitou Yàlla dafay teudj bountou noubouweu toub ko gaw...
Cheikh Ibra dou morom dou mapando téh nio manndou si mome aki nioniam 🙏
Yèslou nak
Tè guèn baye niass miguènni mboubbo fatkhou si yalla amoulenko diassbou sakh amoulen ko .
bou feke talibe baye yi si salatoul fatiha laniouy amer di amle yallha bouniouy deh tabi safara ndah lahilahahilala salatoul fatiha ab sante la ndakh chekh tidjane defa joub joubal islam baye niass nonou bamba nonou maodo wayer nioufi nek nio rero deug ana cheikh tidjane limou neh yallha motalinako lou manke wone oubilko lou tediouwone sila soga jote deug bou tegou si kaw deug tidiane bouko amoul do talibe cheikh bayil diko boubo
Masala bay jame daro
baboul wakhif moy Bay niass kou amsa warko diokh thierou Bay
Niass niass niass niass niass niass niass niass niass
mane dé koudoul talibé baye sougnou wété ma xamal la lo xamoul si yalla
awa rassoul seck Soxna si boul Khatal lou khatoul assamane bi Yatouna, Yalla ngi yatou boul teunkeu lou teunkouwoul, mayou YALLA AMOUL frontière
Walahi waxatiko
awa rassoul seck bgue na man akk wett dhh nio wakhtan té taneu souka bgue si oie la dess dhh
awa rassoul seck khamal ma yalla
so beugué dieuleul sama numéro
Baye rek moyyy deugeu
Man bougueuna xam ban teere la ndiambe bind s. Touba bindna teere, baye niass nonou ak gneneen
Xam xam kena douthi werente sou jant fenke doto guiss lamp
Oumar Kande mane terer la ndiamee mo ma bine deu
khoutbou zaman Dotoul guénatii tarikha cheikh t baye niass thi tarikha cheikh leu bok konn moy khoutbou bi
kone warone ga ko ragnai si dieum djiye wakh
Alioune MBAYE ya meuneu doule
Boba Khana mirou yalla mom béne place rék la nék
@@khadimcisse1585 mouy fane wakhma
Theuye ndiame borom darou
Continué d’être têtu Baye Niass MOY Borom Faydou. Khole léne bou Bakh Baye. Yalla Yalla yi baye laniouye djiéma cons diguene fote dé thi 2,3 ak 4. Déléne mbeukenté thi bounte 1 bi rék bouléne ame fouleu rék pour kham khakhikhatane Yallah.
gueureum sala rothie Baye dall moy souniou Baye d'i sen baye
Kéndou ndiambé
wa diambé dagno fanaw fi zaati Wayne amougnou yab-kha fil khilafatie.
Kone amougnou tamize ak nizeub.
laa-ilaha illah fanaw Jesse dara amou faa.
haarif yii de gué bagne ma
dou béne deug ngay wakh nane serigne touba mola khamal yalla
Baye Abdoul Kane amal téguin yako féké nekoulo royukay
Baye Abdoul Kane sa baye yaw domerame dji moye douneder doule ba dioure la gare dit aye doule yaw
Mome thi guente lah tolou 😁😁😁
Cheikhou serignou baye niass sakh defa done gente
Lima jakhale moye séne bayii yaguenagne fii mousounio woté xame yalla mé baye Niasse wako rek kounék di wakhe dit heuthie di Anna sénii njite Balla baye dit niow
Kat kham kham baga dougé khal wa di lathié khoutbou zaman après nga guis baye way way nek baye moy khoutbou zaman tanopalou
COMME D HABITUDE GOLO GOU DIOUK REK WOOTEI
sa baye
Musa Many wayé sa baye moy golo gou mak gui té wotéwoul
Yéneu gneup ay yéféreu kéneu yalla moléneu taxa dioukk Baye walla niambé talibé baye yalla laye kiss si barham talibé baye Moussa yalla laye guisss si niambé mogui fépeu kayeu koneu boul waxné iow yakoyeu guiss ndax mougui fépp
ndiambe la solution eternel
walahi deño rérr bokalé manul wessou nii yalla tolu nga nénnaléko sa bopu . kone yalla anamou . talibé yii ñoy wax lolu rek mais baye niasse waxulenn lolu . né mom dong moy xamlé yalla .
C vrai
baye mo nandal mboléme waliw yalla yi gni ndieuk ak gni mudj serigne moussa tontounaléne ndax néné amna yuniuy mbotal. mbote momou nak boléne koko ladione ngéne fekk fa baye RTA Kép ku nane mola nandal. kumu néx nanga gueum kum néxite nanga wédi.
ndiambè damay woo nak bi dè.
badu badu amal yar yaw kén xamula
Mane dal diakhléna iow gue dougou khalwa si khol khoutbou zaman giss BAYE NIASS mou tok waron gue kham lan moy tok si lal bi Lima méti moy guay dem di nékeu mouride BAYE moy BOROM DIAMONO
Démlen diamou yala te bayi wakhji yala rek mofi nék
Baye amna baye baye mame
Moy bayam🤣🤣🤣 yala douséne moroom jiamou koo rek moléne war xamouléne sax limou binde bakoy xam .
talibe baye niasse bou geune ndaw mo eupe xame xame ndiamedarou dieure dieffe baye niass
sarr masse dagaye doule
Lalbi lalou baye bayela môme rek mossi menona tok menongua kontiné diko liguéyal rek mo lay diérigne
gnoune dé dagnoo touti pour juger goor yalla yi.kone nagnou mandou té gueum kigni yalla booléle
Mooy diammou dé sama waydji nekal si diammou
Ce que je déteste, c'est toujours cette comparaison que vous faites entre Shaykh Ibrahim Niasse et les autres Shuyukh. Nom de Dieu! Mais vous êtes vraiment timbrés vous les majzob, qui prétendent être des disciples de la Faydha Tijani! Vous êtes pathétiques!
La connaissance divine à laquelle appelle Shaykh Baye, aucun d'entre vous n'y a vraiment goûté, nul d'entre vous n'a atteint l'ouverture, nul d'entre vu n'a été en présence de la divine face d'Allah, nul d'entre vous ne maîtrise même et saurait mener quelqu'un à cette "connaissance" que vous clamez et essayez à chaque fois de dénigrer les Niamé Darou parce que certains d'entre eux disent des choses que malheureusement vous soi-disant Arif Billah ne maîtrisez! Ceci est dû à quoi? Ceci est dû à votre paresse spirituelle et à l'arrêt de votre sayru, alors que vous êtes plus ignorant que ma petite sœur qui n'a même pas encore le jezbu.
Vous devez vous occupez de 3 choses, de 1) Vous; en 2) de Vous; et en 3)de Vous!
La haine viscérale que vous avez envers les Niamé Darou c'est juste parce que dans certaines zones, ils sont en train de récupérer certains de vos condisciples, le pourquoi? Parce qu'ils sont plus déterminés et plus convaincus que vous de ce qu'ils sont et de dans quoi ils sont que certains talibés du Shaykh, qui dansent, fument, et ne prient (Faydu "Sanni")
Shaykh Ibrahim Niasse vous a TOUT apporté, TOUT! Mais vous, vous vous plaisez tant aux illusions et mythes, au napéisme/niangalisme spirituel, toujours là à ressasser Baye Baye Baye comme de vils illuminés alors que le Payii en est à sa vitesse de croisière! Le Hadra Ilahiya a évolué, continue de marcher! Et vous restez là à toujours adorez vos fantômes tels Mayra Fall Kossi, et vos Mudaqams! Fisssttt!
Certains disciples de Shaykh Ibrahim sont eux vraiment sur la Voie, comme les (vrais) disciples de Shaykh Uld Hayri, de Cerno Oumar Sow, de Cerno Alpha Sow.
C'est vrai, Shaykh Ibrahim Niasse voulait récupérer quelque chose de Shaykh Mussa Cissé Niamé Darou, oui, et c'était ce grand arif billah, ce gnostique, et par l'occurence son neveu direct, fils d'Aminata Cissé et d'Ibrahim Ndiaye, je fais réfèrence à Sangue Babacar Ndiaye bien sûr,, qui me semble t-il est le Muqadam que vous haïssez le plus parce qu'il a été Yalla Yalla un quart de siècle avant de rejoindre la Faydha Tijani. Malheureusement pour vous, dii ngén, car Ses disciples sont en train de vous laminer ici au Sénégal et partout et les talibés de Baye sont, ils sont en train de les récupérer 1 par un, et par dizaine de milliers. Normal. Parce qu'Il est le digne successeur spirituel de Shaykh Ibrahim Niasse, son Khalif, sa Voie, son Verbe, son Avocat. Tant que vous ne rangerez vos conneries et n'essayerez de savoir qui est SBN, il vous sera difficile vraiment difficile, de vous sortir de ce carcan et gêne que vous ressentez quand vous rencontrez les Niamé Darou.
Né le 05 Février 1960 à Tchakho Tiofior dans le Saloum, à 20 kms de Kossi là ou Shaykh Ibrahim Niasse a déclenché la Faydha en 1927.
Les Niamé Darou, sont des sufi, ils ont atteint l'ouverture spirituelle.
Au lieu de vous attardez à eux, occupez-vous de vous, eux ils s'occupent pas de vous!
Eyyyyywaaaaaay mdr,bamey lire tei yeigagouma rek khamoone nanei talibé sangue ndiaye nga.
Yangui litterature,wa faydou sani di avancer rek,noopiilene teey weird,mo gueune.
Itasyl Bil Salsyl billay c vrais
Itasyl Bil Salsyl sangue Ndiaye
Itasyl Bil Salsyl jai un problème avec ton discours qui est defois le contraire de que Baye a di " kéneu dou kham yalla loudoul nga diar sama bountou" ba paré sangueu ndiaye bi ngay wotél nékone nafi kham bou magg té borrom mbirmi dou meussa nékeu ci réer .
Ciaoa
Niambé Moom doff la dhh Té yoroul bagassou goné Halib dou Gloria doonté leep meew Dieuredieuf Daal Borom Touba kene dou moom dhh
rouhlah fall yen lahilaha ilalaha la baye yem ak yen ngen beug sonal niit yiii fou ngen taxaw di beug ray niit yiii ak lahilaha ilalaha boudoul diekh deug la wayei dess na lou bariii gorgorlu len
li dou degueu
ya mana doule loutakh guene bone kaye ma khamala ki gua donne
mahrifa dou kham kham wéranté kom chariha bi les haqoula kou nék ni ga nané ak ni ga yeugué nagnou beugueuneté bagn di biodianeté
Sa wakh rafétna werante bi diarouko té yalla da yatou kou khatal mbiram khamoko wasalam
Si aye gente dale ga nekone
talibé bayi boulé niaka foula xam guene bou bakh liguen done bouléne tontou gni
+Djiby Boxeur mais il faut les répondre gni hamougnou dara ba paré reuy lamégne dof dof lou rek wayé hamnégne ni barham dou sene moromou serigne dama teup talibé yi talibé bi gueuneu touti sah thi baye meune na neke sene serignou serigne
Hhhhh ku baax ci passion rek nga né wayé khamo dara ......Sa biir boumou feess banga fook né sa Baye rekka am depense ci rewmi....Gniko dakh njell fouf dougnou jeex ci aduna bi.Guestuleen rek dingeen mossa kham ne yeena gueuna niakk xam xam ci gniy wouyo arif ci aduna bi.......Yalla yonenté bi cheikh tidjiane baye niass seen mokhadam ...C'est tres limité et contingent lolou du xam xam.....Xam yallah defa universel nekkul ci diné nekkul ci tarikha .
+Djiby Boxeur bilahi wakh nga deug,
+aunom deDIEU ligueur wahni wahou kou sohor leuh je tiens juste a te dire que l'aveugle ne peut parlé de la clarté du soleil