Balla nekoule sama mbeur deh mais bilakhii nimako yénéwone ndaam lii dafa eup.. Parce que sougnou keur gneupeu nii wone Balla daye danou, ma bagne depuis le début bilaye walaye...sama khole fess neu..yalnako ndaam lii djiik si barké seydina mouhamed SLS🎉
@@ahmadoudiop5016 danga dègoul fima wahé. Sissouma kèneu ndakh mane mi momouma serigne bi. Mais ma labiré la : dieulè na thi wahtane "nit meusna indi bèneu mbeur thi serigne bi nèko ki dé dafa am combat gnanale ko, serigne nèlèn kay lèn , dém ba ègueu thi armèr nèlèn, nolèn défak mbeur mi Dane gni gnèpeu". Donc fonk sa serigne mongui ndieuk thi né doko toudou thi diotay you mèlni. Wormal serigne bi Moy dièma nèkeu thi limou diglé tèy dièm bayi limou téré
@@toubagning5975 serigne bi lèpam mo yatou facon bounè la am kounè ak nimou dèmè ak ioe balla gaye2 serigne bass dèpassèna serigneum bayam la mo toudou domam yeup
Thierno ngir yalla boul bayeti Balla gaye yaniou djik bilahi
Lou léer mais nak d'où si thierno la probléme bi diougué wone sinon nice niome niarr dagnio YAGUE 🥰🥰🥰
Balla gaye lima lay conseil moy nga fonk thierno Gueye nitt boula yéné rk si visage bi day wah ak entraînement si géej gui 😢😢❤
Amine Thierno kadou yi ci Serigne Bassirou rafete na machala. Deug la.
Balla nekoule sama mbeur deh mais bilakhii nimako yénéwone ndaam lii dafa eup.. Parce que sougnou keur gneupeu nii wone Balla daye danou, ma bagne depuis le début bilaye walaye...sama khole fess neu..yalnako ndaam lii djiik si barké seydina mouhamed SLS🎉
Mashalah le Retour de Thierno Yalnalénes Yalla Lafal Thiate Yaw ak BG2 🤲
Balla fonkale niou thierno Guire yalla❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Santé lénes yalla reke mognou may ndam
Merci mame thierno bilahi balla cest le meilleur cest le roi ❤️❤️❤️💪💪🇸🇳🇸🇳
Bane roi????
@@alaminegueye1186😂😂😂😂😂😂
Balla moi roi Modou lo mou neck mou nakari balla rek 💪💪❤️❤️💯
@@alaminegueye1186empereur
Machallah thierno jërëjëf diajeufeuti
Machallah sa ma Serigne bi Serigne basse barra❤❤❤❤
Merci beaucoup Thierno 😊
Toutes mes félicitations Thierno Gueye 🙏 Amine Yarabi 🤲
Thiérnou machallah❤
Merci cherno ❤jereh jeff
Oh ndeye sane machalla 😢🥰✌️🫶💪🦁
Merci, geuneu ligueye rek
Thier dafa beug balla❤🎉fidèle si mom
Thierno machala goudou fane rekk inchallah Balla gaye2 kuko beugue mah beugue lah bilah walahi ❤❤
Nioyem man kou begue balla ma beguela
Balla Gaye rék à vie ♥️♥️♥️♥️♥️
Sama khol sedena billahi thierno soumako guisse sama khel daye dale alhamndoullilahi ♥️💪🙏🙏♥️
Yaw dé gno yéme thier gno bok serigne bassirou barra en plus dagno nékone ay deukeundo you yague sakh
❤Thierno Guédiawe te remercie merci encore ❤❤
Bella guaye fonkale kiiiii boubakh tierno gueye
Merci Thierno fier de toi ❤🙏🙏🙏
Yalna diamou yague ❤❤
Amine
Merci Mame Thierno 🎉
❤❤❤❤
Alhamdou lilah ❤
Aka yarou machahalla
Antouca kou djig balla la yalla khamnaco
Balla gaye seullllllllllllllllllllle
Ndeyssane jai des larme aux yeux 😢😢😢😢
Ly victoire
Machalla❤❤❤❤❤
Ameen yarabi ❤❤
Ki lanou Balla Gaye la svp
Père Babou ken d'où yaw
Nit kou tey mongi ni
Balla diappal say nitt
machalla❤❤
Diambar dgeu leu machala
Ndeysann ❤❤❤❤
Diadieuf thierno kadou yi rafetna
Bien parler
Vraiment bayilèn Serigne binguèn di toudou thi li.
Adouna dou nékh bamou dagane.
Donc wormale serigne bi mongui ndieuk thi bagnko toudou thi diotay yi 🤧
Serigne bi gneupeuko bokk saway nay yatou rekk sa salam
Serigne Bassirou ak Balla Gaye 2 lou yaggg limou wakh deug la frère
@@ahmadoudiop5016 danga dègoul fima wahé. Sissouma kèneu ndakh mane mi momouma serigne bi. Mais ma labiré la : dieulè na thi wahtane "nit meusna indi bèneu mbeur thi serigne bi nèko ki dé dafa am combat gnanale ko, serigne nèlèn kay lèn , dém ba ègueu thi armèr nèlèn, nolèn défak mbeur mi Dane gni gnèpeu".
Donc fonk sa serigne mongui ndieuk thi né doko toudou thi diotay you mèlni.
Wormal serigne bi Moy dièma nèkeu thi limou diglé tèy dièm bayi limou téré
@@toubagning5975 serigne bi lèpam mo yatou facon bounè la am kounè ak nimou dèmè ak ioe balla gaye2 serigne bass dèpassèna serigneum bayam la mo toudou domam yeup
serigne bassirou bara moko bolek balla
Thier nak ndanane leu
and bu yague degg la
😭😭😭😭
👂🏻👂🏻❤️❤️❤️❤️😂👏👏👏👏👏👏👏
Yaw lega def gutihe gunaw niawna looll ganico bumaganie way yaw
Thierno mo dane tapha wayé dou balla 😂😂
Ohhh thierno ndeysann ❤
Merci beaucoup Thierno 😊
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤