Marché Sandaga : Des commerçants déguerpis sans sommation ni préavis

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 30 ต.ค. 2024

ความคิดเห็น • 90

  • @guidadodiagana-rm1wb
    @guidadodiagana-rm1wb ปีที่แล้ว +8

    Guisss na sénn commentaire yi yeuppp kounékkk di sagua rekkk , c'est pas le problème de macky sall , c'est le priorité de la maison qui assure autorisé cela , tout cela c'est leur fête , depuis 5ans ils ont donné leur délai mais dagno deugueur bopppp

    • @bayesidy6076
      @bayesidy6076 ปีที่แล้ว

      Grand by gua balma bénén yon bindeul wolof

  • @habibsow-8817
    @habibsow-8817 ปีที่แล้ว +1

    Mome keureume guénenane dou tabakh Sénégal dafa nekh quoi

  • @alladiop161
    @alladiop161 ปีที่แล้ว

    Bilay Senegal 🇸🇳 dou reww li ken khamoul yefou lan la

  • @dabasamb5607
    @dabasamb5607 ปีที่แล้ว +4

    Yalnalenes yalla tahawou Sy Barker seydina Mohamed

  • @boubafall1014
    @boubafall1014 ปีที่แล้ว +11

    😔lii dafa niaww trop si sa population 😔borom treu bii sama ami d’enfance leu nioy ande ligey rek leu geum mom la xam😔

  • @fatouthiame7000
    @fatouthiame7000 ปีที่แล้ว +3

    Il faut avoir pitier de nos enfants et nos maris

  • @ahmadoulamine9548
    @ahmadoulamine9548 ปีที่แล้ว +1

    Thiey Yalla mame dh warouna nak lii dh ken xamoul lanla c triste 😢macky sall domeram dji sonal na nit gni 😩

  • @omarloum7462
    @omarloum7462 ปีที่แล้ว +5

    Amoumaa amatouniou yaakaar si deuk bi di Sénégal 😭😭😭😭😭💔💔💔

  • @modoukhoule8682
    @modoukhoule8682 ปีที่แล้ว

    Soubhana laah...du jamais vu

  • @mamadousagna7514
    @mamadousagna7514 ปีที่แล้ว +2

    Bouléne nous sonnale commerçants amougnou béneu papiers

  • @sakkuxam-xam1593
    @sakkuxam-xam1593 ปีที่แล้ว

    État da fa Wàr a aar a'y doomam, Waaye État bu Senegaal Étrangers la'y aar.

  • @toubandiayeofficiel
    @toubandiayeofficiel ปีที่แล้ว +5

    Métina trop franchement 😭

  • @papendiaye3237
    @papendiaye3237 ปีที่แล้ว +1

    Bilaahi, li comme du reew, vraiment mon pays va mal

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378 ปีที่แล้ว +2

    ILS ONT ÉTÉ AVERTIS QUATRE ANNEÉS DURANT C EUX MÉMES QUI ONT DEGUERPI LEURS BAGAGES ; LE PROPRIETAIRE DU SITE DOIT LE CONSTRUIRE KEUR DIAMBOUR KOUFA TOOG SANS PAPIER AUCUN PDT DES DECENNIES KHAM NGANÉ DINANIOULA MASSA YOKHAL .

  • @saidoubah4729
    @saidoubah4729 ปีที่แล้ว +5

    S’en même les avisés 😢mais non kimoy xath bololen diouli nianal ko yallah bilahi dinako guiss 😢

    • @Madaqtrudeau
      @Madaqtrudeau ปีที่แล้ว

      Mdr au lieu de se battre vous rêvez!

    • @rajah8311
      @rajah8311 ปีที่แล้ว

      Boum wokh lolou...ils ont été avisé

  • @cheikhgueye3534
    @cheikhgueye3534 ปีที่แล้ว +1

    Khana danio faté yalla Sénégal metina wayé koul louman aléy khafani reck dieu. Est grand

  • @LouBessTV
    @LouBessTV ปีที่แล้ว

    Oh li métina

  • @lebou2503
    @lebou2503 ปีที่แล้ว +10

    Tok lén fofou rek bolén diougoul khékh si Probleme rek ngén deuké .parceque Macky sall.domi kharam la lép Mom la

    • @badiene0311
      @badiene0311 ปีที่แล้ว +5

      Franchement vous êtes pathétique!!!! 1 2 3 ngene ni macky que vient foutre son nom ici???? C’est le propriétaire qui a saisit la justice niou gneuw déguerpir ani macky Loumouy outt fii???🤦🏾‍♀️ je suis pas de L’APR bala ngay gneuw dima saaga😂

  • @abdoulahatdioufyallnangafi8361
    @abdoulahatdioufyallnangafi8361 ปีที่แล้ว +1

    gni dougne rous sax gni khamngen ni kugn dik am kheuye boko game nakhnga sa bop kouy fék nit kutakhalé ba am limu am nga yakhetéko ni gni dougne rouss sax

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 ปีที่แล้ว

    😭😭😭😭❤️❤️❤️yarabi tej si yen lokho m metina si kholou diam yi looool sakh ndeyssan ❤️❤️😭😭😭

  • @sidybarham8419
    @sidybarham8419 ปีที่แล้ว +3

    Metina niaw nah mais nak bouniou wakhanté deug moy deguerpissement🚜 dou am sans avertissement ⚠️. Commerçant yi wakhouniou leup

    • @rajah8311
      @rajah8311 ปีที่แล้ว +1

      Ils ont été avisés....

  • @mamekharydieng9837
    @mamekharydieng9837 ปีที่แล้ว

    ndaysane thiey miim reew

  • @adjaba8259
    @adjaba8259 ปีที่แล้ว

    Le civisme

  • @ndeyefatougoudiaby744
    @ndeyefatougoudiaby744 ปีที่แล้ว +2

    Ah lii métina wayé yalla bakhna

  • @alythiam4118
    @alythiam4118 ปีที่แล้ว +1

    Thiey Sénégal dou réw

  • @thianegazal5860
    @thianegazal5860 ปีที่แล้ว

    Rekipere.vo.bagage

  • @CheikhGayeislam
    @CheikhGayeislam ปีที่แล้ว

    Ce n´est pas islamique. Attendons la fin

  • @baragueye280
    @baragueye280 ปีที่แล้ว

    Chère conpatriote sénégalais est Sénégal leurs de révolutions a sone chère patriotes du Sénégal résistance les Sénégalaise doivent faire la résistance qui vas souver le Sénégal sii non macky installéras la dictature

  • @fatouthiame7000
    @fatouthiame7000 ปีที่แล้ว +1

    Il na pas de coeur

  • @mbackediop7766
    @mbackediop7766 ปีที่แล้ว +2

    Sénégal Dafa Méti 😔 😭 😔 😭

    • @ali1950ify
      @ali1950ify ปีที่แล้ว

      Réactions moo diott.

  • @assanetall799
    @assanetall799 ปีที่แล้ว +1

    ki domeram la

  • @amathdiallo6791
    @amathdiallo6791 ปีที่แล้ว

    😭😭😭😭

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 ปีที่แล้ว +1

    Noo lii métina trop

  • @ibrahimaseck3589
    @ibrahimaseck3589 ปีที่แล้ว +1

    Bilahi li dafa metti

  • @CheikhGayeislam
    @CheikhGayeislam ปีที่แล้ว

    Qui a vendu le terrain à ce commerçant ?

  • @massetoure635
    @massetoure635 ปีที่แล้ว +2

    Metina torop

  • @diodiobdx9435
    @diodiobdx9435 ปีที่แล้ว +3

    Dou tabakh Khana dou alal lam senegal mo nekh

    • @KM-ro8oz
      @KM-ro8oz ปีที่แล้ว

      Non non mem dego bou khana mom lim todj momouko mom si ginaw la mom da tothj loum momoul oci yombou bagase diambour oci diokhou gnoulen evertismenr nonoula demei

  • @Ndiayeteranga1
    @Ndiayeteranga1 ปีที่แล้ว

    Yéne laa andal

  • @mohammeddiamohammeddia7349
    @mohammeddiamohammeddia7349 ปีที่แล้ว +1

    Lii dafa niaw si Senegal ay gorgor lou

  • @khadimegueye9070
    @khadimegueye9070 ปีที่แล้ว +1

    Maky sall sa data ndaye maky sall sa data alioune ndoye sa data ndaye

  • @matargueye7200
    @matargueye7200 ปีที่แล้ว +1

    Guenn lenn khekhall sonko wakhone nalenn ko nai gnii douniou ai nite Guenn lenn khekh poure sonko ma bakh thii niomm

  • @abdoundiaye1404
    @abdoundiaye1404 ปีที่แล้ว +1

    😭😭

  • @abdouladiane915
    @abdouladiane915 ปีที่แล้ว +1

    Mai louy nara ndanou dankoy tothie wah bi na lér sèn li man bodé batiment bi dafay nara danou con comercent yén tamit xol laléte sén bopou

  • @Beautifully-n6z
    @Beautifully-n6z ปีที่แล้ว +1

    Xeex leine ngourou macky sall diekh. Ngein nek si diammm . Took Senegal teeki fi ak le president Ousmane sonko bakhna. Surtout yene marchant ambulant yi.

    • @sodabiteye3484
      @sodabiteye3484 ปีที่แล้ว

      Kone dee sonko dou nek président kome nioune la yakhar si khekh

    • @Beautifully-n6z
      @Beautifully-n6z ปีที่แล้ว

      @@sodabiteye3484 do yallah. Yallah mayé Goour🙏🏿

  • @ahmadousaradiallo7904
    @ahmadousaradiallo7904 ปีที่แล้ว

    On dirait que je ne vois pas ce qui s'est passé Essaie de savoir qu'est-ce qui y a pensé jusqu'à et Jean cacher votre boutique Ça c'est pas le problème de connexion que acheter je vais devoir la réalité de ce qui s'est passe

  • @mumkara5945
    @mumkara5945 ปีที่แล้ว +1

    Boumou tabaxe

  • @bambathiaw6913
    @bambathiaw6913 ปีที่แล้ว +6

    Thiey Sénégal,bises pinthiou Dina yagg Dina metti kou khadoul khelatt Loula nekh DESS .yalnalen borom bi takhawou

  • @ahmadousaradiallo7904
    @ahmadousaradiallo7904 ปีที่แล้ว

    Aujourd'hui c'est un demain Sera notre tous compte s'élève rapidement avoir que ça sera en retard Où est le Son décor De popples sénégalaise à faire honte

  • @mouhamadoudiagne3789
    @mouhamadoudiagne3789 ปีที่แล้ว +2

    Kou moom foofou?

    • @ibrahimadia9853
      @ibrahimadia9853 ปีที่แล้ว +2

      Commerçant Yi dagnulen avertir BA soneu dugnu deg délai passé niou Danel place

  • @ayisse4099
    @ayisse4099 ปีที่แล้ว

    Massa tiona vos cartes electeurs est votre arme

  • @mamadoufaye9962
    @mamadoufaye9962 ปีที่แล้ว

    Rewmi mi mom man mossoumafè guiss yoon tourou yoon rek mofi nek mais pas yoon

  • @mamemortoubawakanahakhane6123
    @mamemortoubawakanahakhane6123 ปีที่แล้ว

    Ndaye SAN li metina trop

  • @matargueye7200
    @matargueye7200 ปีที่แล้ว +1

    Dioke lenn khekh togeulenn fofou reke bagnia guenn khekh sonko wakh one na lenn ko yenni doga khamne loi amoufi

  • @cheikhdiop859
    @cheikhdiop859 ปีที่แล้ว +1

    Sénégal metina yakh alalou niamour

  • @cheikhteranga5573
    @cheikhteranga5573 ปีที่แล้ว

    Soungeine resistavoule khame

  • @matargueye7200
    @matargueye7200 ปีที่แล้ว

    Guenn lenn khekh ake sonko mogeunn si yenn gnii douniou sarape dayame touss sonko bakh si yenn Guenn lenn si baide mi khekh

    • @sodabiteye3484
      @sodabiteye3484 ปีที่แล้ว

      Sa leufeul ndeye waye nite diakhle ganane nafekh yii

  • @makhtardiop4218
    @makhtardiop4218 ปีที่แล้ว

    Que dieu vous garde

  • @babacarniass5456
    @babacarniass5456 ปีที่แล้ว

    si km

  • @bayelaysamb7239
    @bayelaysamb7239 ปีที่แล้ว

    Metti na lol

  • @bambaniang5463
    @bambaniang5463 ปีที่แล้ว

    Metina mais sante rek am mourid dafaye sante et certains sénégalais ay hypocrite lane menteurs et cheikh mountakha liguey rek laye déf tt ça c'est pour touba am sécurité rek là ak leeram

  • @bayefalldiop3897
    @bayefalldiop3897 ปีที่แล้ว +1

    😡😡😡😡

  • @abdoulahatdioufyallnangafi8361
    @abdoulahatdioufyallnangafi8361 ปีที่แล้ว

    amlen fula balumlen yakhal nalenko faye

  • @bintoudiop-zo7xo
    @bintoudiop-zo7xo ปีที่แล้ว

    Cv

  • @habibkane8123
    @habibkane8123 ปีที่แล้ว

    Li la yendeh commerçant yii ndeeke marché sandaga

  • @guidadodiagana-rm1wb
    @guidadodiagana-rm1wb ปีที่แล้ว

    C'est votre faute vous-même, pourquoi vous avez pas appliqué votre dette depuis 5ans , vous n'avez pas déménagé

  • @maodomalickdiaw973
    @maodomalickdiaw973 ปีที่แล้ว +2

    Terrain diambourla

    • @mortoure7050
      @mortoure7050 ปีที่แล้ว +2

      Ragall yallah khamo dara si lingay wakh

    • @mimasarr849
      @mimasarr849 ปีที่แล้ว +1

      Meme si cest leur cas gnu wakh lene gnu dieul sene bagasss

    • @rajah8311
      @rajah8311 ปีที่แล้ว

      ​@@mimasarr849 ils ont été avertis dé

    • @mimasarr849
      @mimasarr849 ปีที่แล้ว

      @@rajah8311 dans ce cas gno togn sen bop

  • @confuciussy8309
    @confuciussy8309 ปีที่แล้ว +1

    *dem lène wakh ko bass abdou khadre porte parole khalife bi*

  • @falloundiaye-bb2fi
    @falloundiaye-bb2fi ปีที่แล้ว

    😭😭😭😭😭😭

  • @aliounebadarandiaye584
    @aliounebadarandiaye584 ปีที่แล้ว

    😭😭😭😭